Nila yarou ame talibé diokh nieup respect lo beug yalla teksi lokho
@abdoukarimfaye52817 ай бұрын
Félicitation jacop mane dama la beug té yallah takh continèl mbapat tmt tu seras un très grand champion
@GiannisAntetokoumpo-lv8sp7 ай бұрын
Ndeysann dou kholl saxx nitt kou yarrou bly yallah na victoire gueunneu yokkou ba rois des arène🎉
@princembacke97547 ай бұрын
Dagua yaarou ioe yalna gua Yeg Fall🙌🏽
@elhadjigaye44227 ай бұрын
Machalah champion yar ak tégin rék inchallah
@papamodou35237 ай бұрын
Lepou lo am rek yarou mola ko may AK tey kouma nekh NGA bilay bilay diamou rek ngay am inchalla yalla Nala yalla takhawou ❤
@tukucisse79577 ай бұрын
🇸🇳🇸🇳🇸🇳 RAME SOGA DOKH Jacob machalah donegua Gaïndé am gua yarr té correcte ... Yallanala Borom bi defal Diam AK ay ndami ndam🤲
@serignemodounguirane38547 ай бұрын
Félicitations Jacob 🎉 da gua yarou
@amethsene70027 ай бұрын
Pacola baldé ki royouway la pour yaw boy royale si Jacob mi
@khadimdiop83987 ай бұрын
Mbeur bou.yarou la yalla nala yalla def roi
@ibrahimambaye2777 ай бұрын
FÉLICITATIONS JACOB BALDÉ... INDI NGA DOOLÉ ... GUEUNEUL MAG SI DOOLÉ... DOOLÉ DEUG NAK LA WAKH ... FI NGA DIEUM SI LAMB DOOLÉ DIOU BARI DAFAY AME SOLO... FÉLICITATIONS
@babacardiallo23667 ай бұрын
Félicitations 🎈🍾🎉😊Un très grand lutteur 🎉❤Jacob balde yarou gua amgua doller meun gua beuré yalnala yalla defal diam té boul bayi jamais mbapate bi ❤👍nek si rk futur roi insha_Allah😊
@lohmfaty79507 ай бұрын
En tout cas pikine diapalé léne boy bi il est trés sous côté à pikine alors que pikine amoul espoir bou gueune jacob Félicitations champion du courage Jacob kholal si kaname boul yak sa énergie
@seynaboukane90177 ай бұрын
❤❤
@matendatv14277 ай бұрын
Jacob balde un homme correct vraiment
@gueyelabsolu58897 ай бұрын
Félicitations seutou Falay Balde by ❤️ Félicitations seutou Magnik by ❤️❤️❤️ Félicitations le Fls De Amaa Balde ❤️❤️❤️
@matargueye9217 ай бұрын
Démbe bima guissé Jakop walahie comme Ama baldé bima guissone contre Malick Niang ladone guiss yalla nala yalla lafal thiate❤
@mamadysane42387 ай бұрын
J'aime beaucoup Jacob de ouf... Stp donnez moi ses coordonnées mom rek lay topp
@firhatoulchamsoulhoudadeth17607 ай бұрын
Félicitation jackob hier j'ai jubilé comme c'est pas possible.continu comme ça tu as ta place dans l'arène
@bassetouboe67117 ай бұрын
Jacob dafa yarou dé ms yallah nala yallah maye oto boye dém entérétt in challah maye ma oto mane tamitt 😂 wakhale amine mane mom wakhe na amine
@NDIAYEMayib-k5x7 ай бұрын
Da ame talibè yalla nala yalla samou ba dèf la roi des arène
@benjamindiakhoumpa7 ай бұрын
Félicitations Defa yarou
@salioubalde27777 ай бұрын
bien dit mane balla gaye mo takh ma beugue la frere
@Bebefodetoure7 ай бұрын
Bravo
@babacardiallo23667 ай бұрын
Billây ioe
@Abraham221997 ай бұрын
Jacob dafa cool je l’aime trop bonne continuation ❤
@AmaraGueye7 ай бұрын
Masalla jacob pikine kasse amoul le neen eumeu senn pokola balde yalla na leen yalla mayi ndam ❤❤❤❤❤❤❤
@IbrahimaDiop-v9l7 ай бұрын
Un vrai champion 🏆 🥇 🏅
@Domou__rewmi.7 ай бұрын
Li dara betoumassi alboury thiowou comedy rek la am 😂😂
@gueyelabsolu58897 ай бұрын
Senegal 🇸🇳xamouniou bandit quoi ndiom Boo xèsè Diantall trop rék Ndiouny Tapèth nga 🤣🤣🤣Boo Ndioulè koukou ndiaw trop Ndiouny ki Bandit la weroo lèn 😂😂😂bandit Dou Fofou Dei wallahi 🧏
@papengom2597 ай бұрын
Sa yar molay may lép
@massambandiaye84637 ай бұрын
Jakob nekh gama daal vraiment amna mbeur Bou Bess saway derrr deugg leu
@mormbaye60987 ай бұрын
Je supporte pikine mais bilahi weuz diambar mo la meuneu aller/retour
@bandapape7 ай бұрын
félicitation frère et bonne continuation bg2 motax ma beugue leu gueuneu yokou treune yiii ❤❤❤❤
@fadelbambiste14517 ай бұрын
Sa yare dinala may louné bro continue comme ça rek inchallah ❤
@maissaba84827 ай бұрын
Félicitations mon frère borome Monaco plage ya woor 😂
@ndiagaseck84547 ай бұрын
Aka yarou❤
@ouzdaking3827 ай бұрын
Jacob balde grand champion future roi des arenes Inch'Allah félicitations 🎉
@SellyKane-lu8zg7 ай бұрын
Depuis Mauritani ont taime ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤machallah
@AliouKama-zs9ye7 ай бұрын
Weuz vous jacob c'est un vrais combat ❤
@omarosene51017 ай бұрын
Wa mariste récupérer naniou Jacob ni rek 😅😅😅
@seynaboukane90177 ай бұрын
😂😂😂
@sallymbaye86267 ай бұрын
😂😂😂dieul lén niou abal lén ko
@papamakhtarniang7 ай бұрын
Wa pikine kat danoo bari ay champion machaallah 😂😂😂 wa mariste champion lalén pakine abal boulén délo wa pikine tokaar dé hum😂
@AD-cg9te7 ай бұрын
Par force leu 😂😂😂
@samassandiaye67947 ай бұрын
Pikine tek nafa diekhal
@ouzdaking3827 ай бұрын
Modou anta kou yabaté ngua mbeur yigaye proposé jacob moye lane ki dane alboury nguanane ko ay tapha mbeur weuz diambar nooon kou rew ngua yaw , jacob thi kaw rek Inch'Allah boufi dieule béneu thiép bou séw !
@OusmaneSarr-nn9gl7 ай бұрын
Félicitations il l'est trop sérieux
@SerigneNdiaye-b6b7 ай бұрын
Feliz 🙏☝️
@elhadjioumarba95417 ай бұрын
Macha alla champion diam si yow si kaw si kaname rek incha alla
@fanfanbodian76707 ай бұрын
Boy bou yarou ndéyssane yalla nala ndam li djige
@layza_boystv4917 ай бұрын
Boy Marist bi seul amoul lenen ❤
@mamadoundiaye46347 ай бұрын
Victoire vraiment méritée ta tout donné
@ibrahimadiallo2197 ай бұрын
Jacob champion leu
@abdougueye48377 ай бұрын
boy bi dina sori inchahalahh yarou gua respecter gua lamb
@cheikhbasskeurmassar95487 ай бұрын
Félicitations Jacopo machallah
@BaboucarrManjang7 ай бұрын
Bilahi frère man dala nawu bilahi ❤❤
@mantadiop86827 ай бұрын
Mane damako beugeu rek ❤❤
@IbrahimNdiaye-nq7jw7 ай бұрын
Aka bakh wallahi
@LaseDiedhiou7 ай бұрын
Il és très polie
@baboucarrjeng76557 ай бұрын
I love you blie❤❤❤
@JeromeDiouf-yb5ei7 ай бұрын
Wa palmarin niougui sa guinaw dhé
@LindorNiasse7 ай бұрын
Continue comme ça aussi tu seras champion
@pmsdiouf7 ай бұрын
WEUZ DIAMBAR KHOLOU LA SAKH
@SarrProductionBizness-vs2lj7 ай бұрын
Bilakhi je savais que Jacob mo meune alboury
@seynaboukane90177 ай бұрын
Gni ko gueumone beurri woul dee
@truckwarriors98327 ай бұрын
Geumou mako wone d mais moko meune
@adandoye37597 ай бұрын
Félicitations mbeur Mane sa yarou motax ma estimé la C’est Adama ndoye depuis USA 🇺🇸 Ohio beugone na ame sa contact please
@gueyelabsolu58897 ай бұрын
D’accord frère inchalah! Nalako diox inchalah 🥹
@morcavani-tk4zc7 ай бұрын
Jokobo boul bayi mbapatt dé Mbeur day competir . Amal diam et félicitation . Boul nélaw sakh affaire bou tégui tank . Et n’écoute pas les compliments . Iow ken doula wakh
@NguerFaye057 ай бұрын
Jakob gaïnde falaye lako toude nane kodioh niakh diarignu
@mbayegueye14647 ай бұрын
Mbeur Kamil la famille Baldé bi yeup mothie daxa beuré.
@michelidrissadiatta12557 ай бұрын
Félicitations mbeur
@omzoseck85667 ай бұрын
Félicitations champion
@abdoulatifdiop56407 ай бұрын
Yarou rek motax mou NEKH M'A
@Domou__rewmi.7 ай бұрын
Jacob baldé boulfi dieul bene thiep bou sew dieuleul niakh diariniou wala gora sock
@baimamud14917 ай бұрын
Masha’Allah champions
@adamandiaye58297 ай бұрын
Bilahi yow la andal wakh nga deug yow AK zarko combat leu. Tè makha dafay dakor
@ChiekhDioum-p9j7 ай бұрын
Yarou rk la def ❤
@bourathobouratho46727 ай бұрын
Mbeur bou am Respect
@amethzidane25667 ай бұрын
Jules Balde ak Pathe diieul lene exemple si Jacob ak Babacar Balde ils sont corecte poli et communique tres bien
@seynaboukane90177 ай бұрын
Daguene rew
@amethzidane25667 ай бұрын
@@seynaboukane9017 lima wax xana louci am rewandei ??
@MouhamedDione-si7ps7 ай бұрын
Gathiegala jambar begniou yalla doli dam yiii jajeuf
@AlyYoro7 ай бұрын
Jacob balde champion nga nguir yala boul dieul weuz diambar Soko dané tamit doula yobou fene ah🤷
@adamandiaye58297 ай бұрын
Maristes Sama corner. Mafia makha futur maire. Aythia Jacob on est avec toi
@HABIBTOURE-rr6mt7 ай бұрын
Jacob vs weuz diambar lamb bou nekh la
@Domou__rewmi.7 ай бұрын
Dou combats
@siteu_n777 ай бұрын
@@Domou__rewmi.Kane mo Mane si yaw
@ouzkana42187 ай бұрын
Jacob va modou anta maye combat bi
@mouhamedndong60697 ай бұрын
Jacob Balde vs Mama Lamine. Jacob Balde vs Niakh Diarignou.
Zakop Baldé Gayii xamou ndiouko Lolou Kasé Momasy Mèty Man 🥹Boy by guisouma thi Génération kouko Eupou Fith kii ndioune Ndiou Yaroo ak Mome Depuis ndioko xam kii Ragaloull Dara Dara Dara kii Fith kasèla Boy by 🤭❤️🤭🤭
@allafall50217 ай бұрын
Ndeysane vous le voyez parler kom un timide mais il est tellement féroce que tu ne même pas comprendre ,c’est un caïd,je vous le dit parsk j’le connais trop bien,méfiez vous de l’eau qui dort …