"Fassé woumako Tassoul" la réaction très osée de Mario Mbaye après la sortie de Ndakhté Lo

  Рет қаралды 66,845

Tele Senegal

Tele Senegal

29 күн бұрын

LOUBESS
Confessions de Ndakhté Lo, La réaction de son époux Mario ? Délégué attaque Sidy…
Merci de soutenir TELESENEGAL TV via www.paypal.me/telesenegal
Abonnez vous aussi pour bénéficier d'avantages exclusifs 👉🏻 / @TeleSenegalTv
Pour plus de vidéos, Clique ici pour t'abonner ► / @telesenegaltv
TIKTOK: / telesenegal
FACEBOOK: / telesenegal
WEB: www.telesenegal.com
#Senegal #Sonko #focus2024 #Macky #Dakar #hennétime #sabar #live #waxsaxalat #kebetu #tiktoksenegal #viral #africa #Team221 #Africa #Sunu2019 #telesenegal

Пікірлер: 92
@user-vm8be1iw5w
@user-vm8be1iw5w 27 күн бұрын
Yaw nopil way ak sa niaway ndakhté bane intérêt la am di fen thi seyeum boudei Mario day ninal sa thieb ga wakhko mou lerr mougn ba dee on est tt cœur avec ndakhté force à elle❤❤❤
@kinediop9243
@kinediop9243 27 күн бұрын
Bilahi deug pirr ga wakh djiegeune yeup décédé naniou nakh gor Bilahi
@aicha7979
@aicha7979 27 күн бұрын
Yalla nagnu yalla mousseul ci goor gu niak diom
@donpablo5056
@donpablo5056 26 күн бұрын
Yallah mousseul na leine ko Yéna fa doug
@seynaboudiouf2084
@seynaboudiouf2084 26 күн бұрын
Surtout lolou
@user-iu8hh6bp8x
@user-iu8hh6bp8x 27 күн бұрын
Mann franchement ndakhté lô la andal senegal bayy len mm si la personne souffre guenn wakh na mougne ba kagne
@kamaraawa8121
@kamaraawa8121 27 күн бұрын
Mani ndakhté mi mo wakh degue mario mi dou responsable wakhléne degue té yalla takh
@donpablo5056
@donpablo5056 26 күн бұрын
Ah mais mo choisir souffrir hein😂😂😂😂
@fatoumarone8777
@fatoumarone8777 27 күн бұрын
Boudé deug rk ngén beug dég mario dou dieukeur fo la beug bayi léne ko mou fo
@SalyDoumbia-
@SalyDoumbia- 27 күн бұрын
Dedett Mario manipulateur
@emiliebandagny3121
@emiliebandagny3121 26 күн бұрын
Ooooo​
@khadydjiguel5107
@khadydjiguel5107 26 күн бұрын
Est ce yénnn bénioulen Mario merélen tamite Vous avez bien écouter ndakhté mome aussi mossisé wakh pour soutoural Bopam ak dieukereum Et aussi jour bimou amé nakhar niakh doom son mari est parti en soirée bégué Sénégal naniou bayi masla bi walla beugue Lou nekh nite je connais pas ndakhté mais coumou nékone yaw waleu sa soeur donala méti😢😢
@adamafaye6954
@adamafaye6954 26 күн бұрын
Si on écoute bien Ndakhete Mario est Faux il a deux visages
@aichagaye2755
@aichagaye2755 27 күн бұрын
Maygnou jaam ,nganan ki beugna jabaram, affaires yi dou wahi kessé ,deg ngeen li Ndakhté wah ,souko mayoul bate nà deem tribunal...
@user-zk8bq3sz1g
@user-zk8bq3sz1g 27 күн бұрын
Sérieux dhe mais gnoune goor gni warnano setate sounou bopou yene yi yak derou goor gnila mario mo bone rek ndax djieguene ak noumou mane ti mel mognou diour nane khole ni sounou yaye wala sounou soeur
@awadieng9423
@awadieng9423 27 күн бұрын
Boulen niou sonal kou beugue sa diabar daguakoy diokh tier dokhane rek guen meun menolen teyié diabar
@AbdoulayeDiallo-pk1zp
@AbdoulayeDiallo-pk1zp 26 күн бұрын
Yeen itaam meuno lene seuyy d wakh deug nekh yalla ! Je parle en général nak
@faithsham563
@faithsham563 27 күн бұрын
ARRÊTER D’UTILISER LES FEMMES INNOCENTES !!!Dites la vérité! Sa femme a tout dit
@mariepietri9388
@mariepietri9388 26 күн бұрын
Je déteste ce genre de moralisateurs qui passent leur temps à donner des leçons et qui ne feraient pas mieux Fait ce que je te dis mais ne fait pas de même Nous ne sommes pas obligés de rester dans un mariage à subir des coups et j'en passe
@sowpoulo6049
@sowpoulo6049 26 күн бұрын
Bilahi gourou Senegal nio niak faydé tok si plateau tésaseuté
@mariamakandji5476
@mariamakandji5476 27 күн бұрын
Kou soll lou noir bi guissoul Louy deugu nittt mooo fauxxxx thi bobapp Mario dou nitt kou bakh mougn ba dehhhh pour lane dagnouy am diabar juste pour couvrir séne bétises
@bintadieng5866
@bintadieng5866 27 күн бұрын
M lolou moy lane khalé bou goor bi limouy wakh nékoul si mom dafa faux
@AJ.Fatu.Ndao05
@AJ.Fatu.Ndao05 26 күн бұрын
Bli ndeysann kou degu nimouy wahé rek hamni limouy wah dara safou koci
@narobandiaye8109
@narobandiaye8109 27 күн бұрын
Kou goor ki koumou yape 🙄ki moye mbame deugue
@OdileNgom-vm7ol
@OdileNgom-vm7ol 27 күн бұрын
Khawma fassé guako wala mes bayil xallei tout trankil djiguene soko beuger doko trokhal genrou goor yiii la bagn Mario mome meussou ma nekh park dafa faux
@couumbisniang4328
@couumbisniang4328 27 күн бұрын
Mario kou niak diom leu kou immature yallah naniou yallah mousseul thi gor bou melniii
@oumoulba6726
@oumoulba6726 27 күн бұрын
Seuy you bari moungui tasse ndakh goro yi
@bellediolla3414
@bellediolla3414 27 күн бұрын
Mario yayame moniko na dore, na débouché, na torokole la responsabilité n'est pas avec les goros 99% c'est le fait que les gens trouvent toujours un autre responsable responsable que l'homme lui même. Goor Sénégal yarougnoulene si seuy
@MamecoumbaNdior
@MamecoumbaNdior 27 күн бұрын
Doléne bayi niémé yalla mario bimou wakhé li yague na😂😂
@Galsn
@Galsn 27 күн бұрын
Moma diakhal
@welydiop6161
@welydiop6161 26 күн бұрын
Djiguene kouko torokhale guise ko môme mn khame loumou doundou si bire négou seuyame ndakhté damako yeureume bilahi
@RamaDione-ve9ms
@RamaDione-ve9ms 26 күн бұрын
L'apparence est trompeuse la vie en couple et la vie personnelle est différente et en fin l'homme est mystérieux
@sokhnasi8776
@sokhnasi8776 26 күн бұрын
Ndeyssane manipulateur kou doundoul ak mom dou meune comprendre ses victimes 😢
@KHOUDIANIANG-ni6nw
@KHOUDIANIANG-ni6nw 27 күн бұрын
cheri ndakhte mou teup c normal c son jeux
@Layehuco
@Layehuco 27 күн бұрын
Kou niakeu diom mo ngi ni
@AwaGueye-jf9ol
@AwaGueye-jf9ol 27 күн бұрын
Wouy magui Di niakk diomm Moy deuxième toureum
@NdiagaNdiaye-ht5ds
@NdiagaNdiaye-ht5ds 24 күн бұрын
Yaw may gnou way yén lane motakhe deuguowoléne ki daye féne seye bi tasse na ndayame yawe borom lou noir li féne katte gua .kou dakor lalale j'aime
@IbrahimaCisse-xs2jl
@IbrahimaCisse-xs2jl 26 күн бұрын
Mario dou nitou dara deux facettes la yor motakh na kholate bopam
@user-tn3tm2pr2x
@user-tn3tm2pr2x 27 күн бұрын
Li dou thème
@KHOUDIANIANG-ni6nw
@KHOUDIANIANG-ni6nw 27 күн бұрын
MARIO il est faux bizarment day daw micro yi
@babacarndong-ge7mc
@babacarndong-ge7mc 27 күн бұрын
Bala ga xam ndiarignou nit mou sorila ,,,, djigen xolen Gor yilen di tak , Gor yi xol len diabar yigen di tak
@fallouthiam2056
@fallouthiam2056 27 күн бұрын
Tasso deh Ndakhte mo fassei said nday mbessil
@bouhsabaly6473
@bouhsabaly6473 27 күн бұрын
Mann ki defmay énervé bilayi thimm way dole
@mamygueye2517
@mamygueye2517 25 күн бұрын
Tricherie lolou moy amour Tchiip yen xamoulen amour néké😂😂😂
@AmyDiop-ml5lz
@AmyDiop-ml5lz 27 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@seynaboudiatta1141
@seynaboudiatta1141 26 күн бұрын
Pourquoi Sénégal bari gnou nafekh gni kom si axamougnou nit kou faut le gard en l'entendant parler on sent nettement quil nest pas mature ni sérieux
@ngomserignefallou3785
@ngomserignefallou3785 26 күн бұрын
Segne wakhofi dara 😂
@ArmandMbengue
@ArmandMbengue 27 күн бұрын
Xolal ma Yi con rek😢😢😢😢😢
@quisuisje5508
@quisuisje5508 27 күн бұрын
Ay vrais embeciles gayn
@zeynadiallo7266
@zeynadiallo7266 26 күн бұрын
😂😂😂😂😂😂😂 je te jure des canard 🦆
@boubacarwaounde8199
@boubacarwaounde8199 27 күн бұрын
Ki vrai domram la xamoul sakh rôle kilifa homme marié katal sa ndeye
@adamaberthebakhayoko8156
@adamaberthebakhayoko8156 27 күн бұрын
Ayy😂😂😂😂
@Diarista90
@Diarista90 25 күн бұрын
Faut type di utilisè djiguén gni di jouer théâtre fokni sénégalais yii kènn dinalèn dèf golo
@RoubaLo-fw9to
@RoubaLo-fw9to 26 күн бұрын
Mais mario limou y woné. Thi biti douko woné thi biir keureum. Ndakhté xalela wayé dafadoon Mougne pour sauvé Mariagiam
@user-uv5cu2bs2l
@user-uv5cu2bs2l 27 күн бұрын
Il est foo c Mario
@seynaboufayethiams7711
@seynaboufayethiams7711 26 күн бұрын
Arrêté ce que vous dites il doit respecter sa femme le mariage n'est pas un jeu s'y un jour tu vie avec une mauvaise femme en retour tu verras s'y daguaye mougne ou pas le mariage sans respect s'est zéro
@seynadiop6854
@seynadiop6854 27 күн бұрын
Vidéo ça fait 2 mois c'était bien avant émission confession
@user-dp5uz4gr8c
@user-dp5uz4gr8c 24 күн бұрын
Délène waxe deugue way
@YoussouCamara-bx2bm
@YoussouCamara-bx2bm 26 күн бұрын
Vidéo bi avant sortie Ndakhté la
@user-iu8hh6bp8x
@user-iu8hh6bp8x 27 күн бұрын
Mario pervers deug la😂😂😂
@AliouFaye-ei6sy
@AliouFaye-ei6sy 26 күн бұрын
Katt ba doyal bayi 😂😂😊
@AidaNdiaye-vc7ur
@AidaNdiaye-vc7ur 26 күн бұрын
Li moye face cachée mario bakhoul vrai apparence la dijguéne boula souré rk diékhna
@apouta6595
@apouta6595 27 күн бұрын
Li émission de quoi la ? Sa se voit si dokhane guéne tolou aussi . Débat bi dou poure yène
@NdeyefarySamb-hn7pi
@NdeyefarySamb-hn7pi 27 күн бұрын
Wakhi gorr koukoy gieum rek khama go gorr 😂😂😂😂
@NdiayeNdieme-gj8ck
@NdiayeNdieme-gj8ck 25 күн бұрын
Delen dougou lousen yon nek sen yon nekul si seyou diambour
@sokhnathiam1181
@sokhnathiam1181 27 күн бұрын
Mario c pas un bon Homme bilay prsk djiguene doko def louma metti boko beugué
@juniordiallo6109
@juniordiallo6109 26 күн бұрын
Ioe koula wakh fassé wouko dane ko féké wla
@FatouDiop-wr8wp
@FatouDiop-wr8wp 26 күн бұрын
mais tmt gors dafa leuneub trop dafa yor sayesay😮
@apouta6595
@apouta6595 27 күн бұрын
Gni wèrenagnou
@user-rw4zn5qc8i
@user-rw4zn5qc8i 26 күн бұрын
Mario daffa faux
@alphaba1412
@alphaba1412 27 күн бұрын
Ms pourquoi vous vous mêlez de la vie des gens пиздец Sénégal
@user-sk7ft1sr3p
@user-sk7ft1sr3p 27 күн бұрын
Debaliniou
@MaremeDiagne-tp2en
@MaremeDiagne-tp2en 27 күн бұрын
Mario nittt kou faux la topal poukré adouna diabar djio am tamite nilay demé tant bayi wo soirée yi bayiwo dokh ba 6h du matin di doré
@sokhou5646
@sokhou5646 27 күн бұрын
L'homme avec le tee-shirt noir faux na. Yaw tu ne maîtrise même pas s k tu dis baguéne khamé né B.A khasé leu vous ne devriez même pas y prononcer ba setane émission bi yeupeu mais yakhamti guéne cas té doléne kham. non c incroyable
@pecosnonstress
@pecosnonstress 27 күн бұрын
beugue sa diabar doussi wakh gou beurri ak bataré khaliss ...
@RoubaLo-fw9to
@RoubaLo-fw9to 26 күн бұрын
Yaw naféth da ngay torokhal djiguéen li dou sa wakh
@NdeyefatouDia-hv3wt
@NdeyefatouDia-hv3wt 25 күн бұрын
Yaw saytanga way ligay wax gemouko
@RoubaLo-fw9to
@RoubaLo-fw9to 26 күн бұрын
Yaw do am Niarél parce que kéen dou Nié sa awo
@kindemariemekinder6779
@kindemariemekinder6779 27 күн бұрын
Le gars en casquette il est trop faux, ishhh n’importe quoi
@mamediarraalioufaye7901
@mamediarraalioufaye7901 27 күн бұрын
Yéne nak ay nafék nguéne
@aidaboussosarr2991
@aidaboussosarr2991 27 күн бұрын
Ki faux type la
@felicitebassene627
@felicitebassene627 25 күн бұрын
Borom lou gnoul li esk cv
@dieynabatoure1507
@dieynabatoure1507 27 күн бұрын
Ki Esk dou nopi koula khol xamni xamo dra
@RamaBa-fu8ho
@RamaBa-fu8ho 26 күн бұрын
RamaTALL
@alhamdoulilah3991
@alhamdoulilah3991 26 күн бұрын
Makhala, Sénégal nioy fék golo gou tékiwoul dara niou ériger ko en célébrité
Which one of them is cooler?😎 @potapova_blog
00:45
Filaretiki
Рет қаралды 10 МЛН
Please be kind🙏
00:34
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 74 МЛН
Cute Barbie Gadget 🥰 #gadgets
01:00
FLIP FLOP Hacks
Рет қаралды 62 МЛН
Khóa ly biệt
01:00
Đào Nguyễn Ánh - Hữu Hưng
Рет қаралды 18 МЛН
WALLY B. SECK - WAYAL LI LIVE TFM - SPÉCIALE KAKATAR
9:17
Le Président Bassirou Diomaye Faye et Ses Deux Femmes
12:34
Nazir Cissé Chroniques
Рет қаралды 9 М.
Which one of them is cooler?😎 @potapova_blog
00:45
Filaretiki
Рет қаралды 10 МЛН