La Sœur de Ndakhté fait des révélations plus graves : «Ben jour dako dorr bamouy… Meme yayou Mario…»

  Рет қаралды 61,454

Tele Senegal

Tele Senegal

25 күн бұрын

LOUBESS
La réaction de Aïcha Koné et Mario après la sortie de Ndakhté _ Divorce Momo Dieng …
Merci de soutenir TELESENEGAL TV via www.paypal.me/telesenegal
Abonnez vous aussi pour bénéficier d'avantages exclusifs 👉🏻 / @TeleSenegalTv
Pour plus de vidéos, Clique ici pour t'abonner ► / @telesenegaltv
TIKTOK: / telesenegal
FACEBOOK: / telesenegal
WEB: www.telesenegal.com
#Senegal #Sonko #focus2024 #Macky #Dakar #hennétime #sabar #live #waxsaxalat #kebetu #tiktoksenegal #viral #africa #Team221 #Africa #Sunu2019 #telesenegal

Пікірлер: 112
@biguengom919
@biguengom919 23 күн бұрын
Que justice soit faite! Djiguene dou mbamm, Yalla moko saggal, j'ao tres mal au coeur,
@Mbene02-cs6dw
@Mbene02-cs6dw 23 күн бұрын
Billahi senegal hamougnou lici perver narcissique dangay am dependence emotionelle ci gnom gnou eloignè la ak sa entourage yep y compris ta propre famille pour nga guen ci il faut etre tres fort mentalement tè gor ak djiguèn yep day am perver
@margueritecisse7711
@margueritecisse7711 23 күн бұрын
Khana
@astouciss4961
@astouciss4961 23 күн бұрын
Waax deug nékhoul, Mario dé défoul dara, lep c'est Ndakhté ( les parents de Ndakhté défou gno dara; Ndakhté si bopam mou yaplou bopam ba paré yaplou sa famille), lou fén si seuy bi da nouyou sa doxaane bi da gno ko fayoul woon. Relation dou door dou saga Doouuulll sakh djiguén warou ko permettr goor. Parck doul moy indi saga ndey ... T douma kén waax k Ndakhté téyouko da gnou ko liguéy. Saga sa future belle famille ba paré ame audace déme gniane sen doom. En tt ka Ndakhté xalé la li sou si diogué na xaam bopaam bou bakh t déglou sa famille
@fatoubinetousylla691
@fatoubinetousylla691 23 күн бұрын
Est ce que nakhte moko taye li lepp mou doundou KO avant mariage , est ce que yobou wouko si marabout yi
@deenmotivated670
@deenmotivated670 23 күн бұрын
Kou beug Bad boy Ba Seuy ak bad boy, Kharal say Diooy
@maymunaadiouf4665
@maymunaadiouf4665 22 күн бұрын
Danga rime ba tok ni😂🤣
@fas2822
@fas2822 21 күн бұрын
😂😂😂wakh n'a deug​@@maymunaadiouf4665
@deenmotivated670
@deenmotivated670 19 күн бұрын
@@maymunaadiouf4665 no, damako oyofal rekk
@kharitouyayame
@kharitouyayame 19 күн бұрын
😂😂​@@maymunaadiouf4665
@mariamagueye5272
@mariamagueye5272 13 күн бұрын
Mooo gniyy jayy kilifeuu gnoffi geuneu boonnn Mom kay Yalnagnu Yalla soutoural rekk bolégnok ku bax
@dyanandiaye7584
@dyanandiaye7584 23 күн бұрын
Est que tamit mario dieundé wouleine khaliss tamit mario dafa meuneu wonéwou t gnoune dieguene gni dagnou beug khaliss ba dagni gueum silou beuri
@idandione5263
@idandione5263 23 күн бұрын
Lou fégne thi seuye nouyowone na thi ngoro dagnouko fayoul ndakhté fallait pas fermer les yeux sur ce qu'il faisait avant mariage mais nak sa destin la tt ce qui nous tue pas nous rend fort.focus sur ton avenir et prend le temps de bien mûrir avant de te lancer à nouveau dans une nouvelle nouvelle relation yalla Dinala maye kou gueune
@user-nn6vi6yx9w
@user-nn6vi6yx9w 23 күн бұрын
C désolant dh mai yalla baxna dall
@aichagueye1310
@aichagueye1310 23 күн бұрын
Sokhna si manru momeu dama brugue ndakhté mais deugue rék ngua wakh
@MamediarraSeck-tr3sn
@MamediarraSeck-tr3sn 23 күн бұрын
Jtj mère dé linga wakh dé deugeuleu ...mais khamna mbeuguél rééekk moko sonal😢😢😢😢😢😢😢
@deugrekk6410
@deugrekk6410 23 күн бұрын
Ndakhte mo sacrifier bopam
@aissatoufalldiallo7416
@aissatoufalldiallo7416 23 күн бұрын
Eyway yeureum lene xalébi Pourquoi Mario lougnouko wakh togn ko? Elle est jeune et espérer le changer.
@astousy7088
@astousy7088 23 күн бұрын
Dagno khamoul wayé mbeuguel meune louné 😢t lolou mo dal khalé bi
@mamygueye2517
@mamygueye2517 23 күн бұрын
Kham goor nimou mel ba paré dougoussi mou continuer si nga gueneu weer sa bop Ndakhté warowône sakh nieuw si plateau bi
@maimounasy2460
@maimounasy2460 23 күн бұрын
Doyna war dal ,na ninou khar benene version
@diopndeye6243
@diopndeye6243 23 күн бұрын
Bilaye wakhga deugg
@user-dq1vp6mb3n
@user-dq1vp6mb3n 23 күн бұрын
Soxna si ligua wah Amna solo mais dernière paroles yi dafa insolent seuy bou tass ba pare louthi yon woutati
@khadydiagne3566
@khadydiagne3566 23 күн бұрын
Vraiment nak
@fatoumadeleinengom4576
@fatoumadeleinengom4576 21 күн бұрын
Mane Kay Mario rek lay bagne mou yakk khalebi parsk c un pervers narcissique et les pervers narcissique n'aime pas perdre
@user-ho8hr3rl5b
@user-ho8hr3rl5b 23 күн бұрын
Merci beaucoup Fama ya wakhe degue
@MamanSeneBouSonko
@MamanSeneBouSonko 23 күн бұрын
courage ndakhté🌹🌹🌹
@user-jr2ly9kh5g
@user-jr2ly9kh5g 23 күн бұрын
Scanner sa téléphone copine où sa diabar lolou manque de confiance là
@Salikhate732
@Salikhate732 23 күн бұрын
Manque confiance degue sakh
@fatoumatasow1767
@fatoumatasow1767 23 күн бұрын
Sey dé confiance la souma dégué wakhou téléphone bii il est jaloux il n'avait pas confiance sur sa femme . Ndathté devait partir depuis le début
@bellediolla3414
@bellediolla3414 21 күн бұрын
Billay amena sama domou baye bouy doundou la même chose djeukeur rame dakoy saka ndeye. Quand je la regarde j'ai de la colère en vers elle surtout bouy sakou alors que tout le monde sait que son mari ne la respect pas. Sakou moy ray djiguene Sénégal ak souma deme sama noneyi
@biguengom919
@biguengom919 23 күн бұрын
Ses marents sont fautifs, ils nz devraient pas donner la main de leur fille a Mario, han. Gor bouleuy torolhal , manquer de respect seu famille tee takagouleu, waroko seuyeul. Mario sama khol tangueneu si mome,
@Salikhate732
@Salikhate732 23 күн бұрын
Ndakhté dafa nelaw fofou AK loko beugue beugue amna yo khamni doumako accepté bilay mane môme ay dagay doul AK ay féne doumako may kéne wakhoumala saga ndeye😂😂
@biguengom919
@biguengom919 22 күн бұрын
@@Salikhate732 tu as parfaitement raison, Ndakhetee mo djioum seuy ak mome, wanone nako djikom avant moukoy takk
@user-jk9so2np8h
@user-jk9so2np8h 23 күн бұрын
Wadore pour lane
@user-ow1xc3ru9b
@user-ow1xc3ru9b 23 күн бұрын
Bikahi ndakhtè rek mo fegnlè ,boulen fatè seye yalla mokoy toudou ,dou domou adama
@user-rz9mh2vg5y
@user-rz9mh2vg5y 23 күн бұрын
Mane je dis que c'est une erreur ndakhté elle est encors jaune fallait que nguéne kham lolou
@maimounadieng167
@maimounadieng167 23 күн бұрын
Ana rouge 😂
@fatouchadiallo7
@fatouchadiallo7 23 күн бұрын
Lounek mbeugel mokoy def billhahi ndaxté dafko beugue rk ms Mario domeram la
@aminatandiaye8768
@aminatandiaye8768 23 күн бұрын
Saga dou lou diadou. Lou takh nitt wara saga moromame
@PDG0610
@PDG0610 23 күн бұрын
Wa yène la confiance n’exclut pas le contrôle mba ham guène limou firi??
@fatoubinetoufall
@fatoubinetoufall 18 күн бұрын
❤❤❤❤❤
@msy8317
@msy8317 23 күн бұрын
Défois goor gni dagnlay liguéy ba tak la yényi dou tayéf
@deenmotivated670
@deenmotivated670 23 күн бұрын
Khana Kon Monou ko ligueey ba teye ko.... Nan nanu dieul sunu ay reponsability..
@fas2822
@fas2822 21 күн бұрын
​@@deenmotivated670meune na neek deug ndakh liguey nit pour mou beug leu day moudjie deuddeulé
@almamydiatta3953
@almamydiatta3953 23 күн бұрын
Loi c du théâtre ou bien c t une réalité
@mbayemodou1733
@mbayemodou1733 23 күн бұрын
Mani dou fasse nako leegui loy problème bi wakh leen niou lou ame chance diekh na diekh na
@khayanarr8607
@khayanarr8607 23 күн бұрын
OUZ lorsqu'une personne parle il faut l'écouter, quand tu la coupe elle perd le fil conducteur... il y'a de ces choses c'est pas juste de l'amour, parfois tu te dis que tu va essayer de changer la personne en te fixant cet objectif ou en te disant que "je ne dois pas l'abandonner yallah moniou bolé afin que chacun puisse aider l'autre". feknitt kenn meunouko changer ,mais meun nguako diapalé mou évolué.. lepp yakar la...LE MARIAGE c'est sur la base de la confiance et de l'espoir??nakh meun ngua nek ak nitt 10ans doko ham...Magnan Kassé exemple/// Après nous avons la société qui nous condamne, nitt yi yag lein uiss nguén heuy bayanté niouni ""ak finiou diar yeup mou bayiko?? qui moy traitre"" sachant que le mariage est fait sous la base d'intérêt (un bon pere/mere pour les enfants future... garap goula soutoul doula may kerr . comme niko islam digalé boy dieul sokhna niveau binguako fek ak finguakay yob pour bagne yabel wala hepp, wala problém....et j'en passe) à cela s'ajoute ak no meunti mel ngay halate guein si ...la kogne bi nanela "hamone naniouni doufa yag""" comme si danioulako yéné! aprés tu penses aux grandes personnes (kilifa yi) qui ont scélé ton union, lorsqu'il te demanderont ou es mounsieur/madame nguay rousse. Nakh sénégal danio gaw si lathié, ""wa loulein diotel" ngay xalate noumou geuneu rafété ngua wakh ko, sachant boko wakhé niounila lolou dou dara déloul sa seuy...alors que bo wakhé li hew niounila nitt dafa wara beuri soutoura, boko wéré werr sa bop comme on te le dit dans le ménage. il n'a pas que les femmes qui subisse cela les hommes aussi. LA SOCIETE SENEGLAISE COMDAMNE SES ENFANTS avec LE MYTHE DU MARIAGE
@mariamagueye5272
@mariamagueye5272 13 күн бұрын
Guéneu you yagg yii si bopam modoul deugg dou yonn Niit bo.andal 4 mois diga xam nax kiii sa jikeur lay don ou pas ...Mais bou yagué ga xeuy bayi rekk woor lay donn
@BoubacarSall-xd8cr
@BoubacarSall-xd8cr 23 күн бұрын
La fille a été bien claire elle voulais pas basculer sa carrière en l’ère elle est connue et c’est vrai
@MaguetteGueye-up6bj
@MaguetteGueye-up6bj 22 күн бұрын
😭😭😭😭🤲🤲
@NdeyeyacineNdiaye-sj9lr
@NdeyeyacineNdiaye-sj9lr 23 күн бұрын
ndakhete dall sa famille mola sarakhee
@user-ww6nd4zn7g
@user-ww6nd4zn7g 23 күн бұрын
Mé. Yén Mario khalé amoul esperiance thi séye khalé yii nio sob
@NdeyeDiabouKeita
@NdeyeDiabouKeita 23 күн бұрын
Basi nek xalé taxoul bagné nek responsable lolou dou raison
@FITNESSGHOST110
@FITNESSGHOST110 23 күн бұрын
Naniou diamou yallah t bayyi thiaxane koug beug am soxna bou bakh wala am dieukeur boubakh fekhel ba bakh ba noppi yallah moley boller ak kou bakh
@diariabousso466
@diariabousso466 23 күн бұрын
Yow dé défo comme Mia tél’ga daw si bangay ami tanke . Goor gni niou raw coupure courant aka nio leundeum. Boul si nié kéne kou ame dieukeur millionnaire laniouy dundou doko kham😢
@seynadiop6854
@seynadiop6854 23 күн бұрын
C'est vrai déh khaliss laniou léye wane en général do am banékh tchi sa séye khanna mou nék toubab niom en général danioouy am yeurmandé AK respect té bouniou amé khaliss douniou béew
@user-tf4rz6kj4y
@user-tf4rz6kj4y 23 күн бұрын
Il ne faut pas juger ainsi beuguel dha for
@babacarndong-ge7mc
@babacarndong-ge7mc 23 күн бұрын
Ouz del deglou plateau dou ni ,,, Gor milieu kou sey ak momeu lo gis boumou la beteu
@jamilasall7409
@jamilasall7409 23 күн бұрын
Mais yéne eskeu Mario liguéyouco
@user-ip6vd4kg4g
@user-ip6vd4kg4g 23 күн бұрын
Dakhte kay da touti beute 😂😂li d'où diam way
@gracevie6343
@gracevie6343 23 күн бұрын
C'est ce qu'on appelle emprise en psychologie
@LaBarhamienne
@LaBarhamienne 23 күн бұрын
Mom déjà rek mouni guène naniou 10 ans xawma, lolou soko guéné thi son âge, dafa tél trop franchement. En plus nite dagay andak sa nawlé
@seynadiop6854
@seynadiop6854 23 күн бұрын
​@@LaBarhamienne6ans laniou guénneu
@LaBarhamienne
@LaBarhamienne 23 күн бұрын
@@seynadiop6854 Ah d’accord kone baxna, wayé batey rek na xalèyi xamé kouniouy farantoul ak kouléne matr kilifa pour seuy, mbir yi dou je taime ak moi aussi dh🤣 hiii seuy yomboul bén yon
@soukeynagueye6493
@soukeynagueye6493 23 күн бұрын
Soeureum bi mo meutoul naka ngay amé sa petite sœur té do kham komouy fréquenter
@khadyloum-ey8xg
@khadyloum-ey8xg 23 күн бұрын
Parents yi nak dougnou fête dans tt cela
@seynadiop6854
@seynadiop6854 23 күн бұрын
Il paraît que cousinam leu
@MarieGomis-tt6ze
@MarieGomis-tt6ze 23 күн бұрын
Wa dore pour lane
@bamba09
@bamba09 23 күн бұрын
C'était juste pour consommer et abandonner. Puff
@nanaboucisse2435
@nanaboucisse2435 23 күн бұрын
IL faux dire la verite Fama limou yakh c'est d une part et d'autr part iow Liga wakh peut etre wague doundou Lou raw lolou
@user-to9id6sr7w
@user-to9id6sr7w 23 күн бұрын
Ce que mon mari a fait avant qu'on se marie il a scanner mon téléphone après le mariage je l'ai su
@Bickk
@Bickk 23 күн бұрын
Aye way Saytané tougal louthi sa yonn Bayilén tass seuyou diambouyii...
@taylataylookingfortomorrow277
@taylataylookingfortomorrow277 23 күн бұрын
Domoram deug Moy dawsi
@deugrekk6410
@deugrekk6410 23 күн бұрын
Tata fama kassé nio bokou louniou wakh dé
@madeleine7159
@madeleine7159 23 күн бұрын
Fama Kassé mi esk ça va? Khôl la wakher, Allen deglo, Ndakhté était jeune, Wa dji wakhou ko yobou warougar, kilifa yi diokher kaadou, Elle s'est senti coincée et avait ESPOIR que son mari change. Erreur nieup laay Daal... l'essentiel mou bania niaar. Sénégalais yedater rek...mais dou comprendre.... Nianalen ko mou fater son passé ter avancer. Et que ça serve de leçons aux autres filles
@mariamadiallo7347
@mariamadiallo7347 23 күн бұрын
Yaaw sakanam guou nokh gui khana kharitou mario gua
@jamilasall7409
@jamilasall7409 23 күн бұрын
Mais madame khana deuco senegal ki dafco liguéye
@user-bq6ib1gh4f
@user-bq6ib1gh4f 23 күн бұрын
Mak yaw gno yém xalate
@ninkinanka3644
@ninkinanka3644 23 күн бұрын
Nitt Dangay Wakh Loula Leer SA Genre Gui FOUNIOU SEUY TASS KO
@user-bc9wy6hb1e
@user-bc9wy6hb1e 23 күн бұрын
Ndeysane dafa beugone rek ndakté mais goor bouma saga avant mariage doumala seuyal ! Masta ki da bonne rek
@libassembaye7651
@libassembaye7651 23 күн бұрын
Way ndakhté mo niakk fayda ba dieukeur dji diko door
@mamysaliou5918
@mamysaliou5918 23 күн бұрын
Fama daccorouma akk yaw boude setane ga emisión ndakhté nena Maria ge avant mo ame khadiou gouddi la woo yayam diko sarakhou pour niou anuler msj nakh meunoutoul té tite na ci limouy douggg... apres mou tekk ci kilifeu diokhe nagnou senn khadou ba pare kone bou ame degg degg diga khamni beugatoul dougg mais wakhou kilifa moko takha dougg
@Adjaratou2008
@Adjaratou2008 20 күн бұрын
les filles sont très de difficultés bar ce que elle sont toujours de liberté personnes ne dormir pas la nuit par tous les filles ya des filles qui aime trop de l'argent 🤣🤣😂👇🏼👇🏼🤘🙆‍♂️👀🙆🏽🤼‍♂️🤭🤫🤫🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😍😂😂😂😂😂😂
@ndiarkasago4792
@ndiarkasago4792 23 күн бұрын
Saga yamou saga woon yayou Mario kham na lolou la mère bi fayou
@mouhamadoudiop9163
@mouhamadoudiop9163 22 күн бұрын
Sokhnaci wakh na leep
@touchadiouf5866
@touchadiouf5866 22 күн бұрын
Warothi Won douguou
@taarumouridtv4133
@taarumouridtv4133 23 күн бұрын
Kii daye fenne rek 😅
@diariabousso466
@diariabousso466 23 күн бұрын
Motakh douma nié béne célébrité😂
@seynadiop6854
@seynadiop6854 23 күн бұрын
Non Amna niou tchi bakh Wally Seck Dou def lollou,etc..
@AichaThiamcisse-je4wm
@AichaThiamcisse-je4wm 23 күн бұрын
Est ce que ndakhté mo ko tey lolou diarna sèt
@TeleSenegalTv
@TeleSenegalTv 21 күн бұрын
lou diara lidianti leu
@03balama
@03balama 20 күн бұрын
li mère bi ak société bi comprendragoule...moye yaar bignouye yaar djiguenes yi molène di loor...soy seye dangaye mugne...beneuh seye yomboule...djiguene mo nara deffar këram...kou beugueuh dangeye fiir...donc djiguenes yii sougnouye accepeter yeen yi conditionnement la....warona arrêter dès le début mais bo fogoné lolou moye comportement normal dans un couple parce que lolou lagnou tameuh di guisse aussi stupide que ça puisse être...lolou bou weso si extrait bi vous décortiquez et remettez plus en question les choix de la victime que le comportement toxique pervers et violent de l'agresseur
@awandiaye2429
@awandiaye2429 23 күн бұрын
Mario dall dafa tackone dakhte pour ame beuzz,yokatt gako beuzz nak
@user-ip6vd4kg4g
@user-ip6vd4kg4g 23 күн бұрын
Mario es k yeur n'a
@bayelayegueye4012
@bayelayegueye4012 23 күн бұрын
Bayyi lenne Mario doumou diambourla yaayam ligeuy rék laham
@AdjiastouDiene
@AdjiastouDiene 23 күн бұрын
Ioe kham
@Orange25638
@Orange25638 23 күн бұрын
Ndeye liguey na dome mague kepelep
@diagneamsatou3473
@diagneamsatou3473 23 күн бұрын
Mario deh Esk dou taki toubab bnn yone😂😂😂
@sokhnamaisene2411
@sokhnamaisene2411 23 күн бұрын
Bilay pare n'a si guis bin bin ak thiouray Sénégal n'a dem foumou kham
@byka1219
@byka1219 23 күн бұрын
​@@sokhnamaisene2411sou beugé diabar sénégal gui dinako am facilement gueumougnou loudoul khaliss ak no meunti méll mm ndakhté a fait pareil
@msy8317
@msy8317 23 күн бұрын
Li dé la khalate
@seynadiop6854
@seynadiop6854 23 күн бұрын
​@@byka1219waaw khaléyi déh majorité bi khaliss laniouy seuyé
@fatouchadiallo7
@fatouchadiallo7 23 күн бұрын
Billhahi kouko seuyeul 😮ma khamni sa yaye liguéyoul
@bayelayegueye4012
@bayelayegueye4012 23 күн бұрын
Bayyi léne di gizé thi lo ngeun khamoul fii deikur yéppay saga sén diabar saga dafa bokk thi naturero Sénégaléyi
@astoukouta6913
@astoukouta6913 23 күн бұрын
Sa papeu yalna saga sa yaye ndeye si sa kaname ak saye kanamou kharite ak si kaname gorome yi tu verras que sa fait tellement plaisir machalah et ne me remercie surtout pas et au passage sa koyou baye boule mére nak té boule ma juger saga da bokou si souniou nature aller bisous
Купили айфон для собачки #shorts #iribaby
00:31
Final muy inesperado 🥹
00:48
Juan De Dios Pantoja
Рет қаралды 11 МЛН
DELETE TOXICITY = 5 LEGENDARY STARR DROPS!
02:20
Brawl Stars
Рет қаралды 16 МЛН
AUDIO FUITE DE LA CHANTEUSE DIEYLA ET SON MARI! LOU KHEWATI????
7:37
POTINS GALSEN-CAS YI
Рет қаралды 1,2 М.
Soirée Spéciale - Invitée: Ndakhté Lo - 25 Mai 2024
17:27
TFM (Télé Futurs Medias)
Рет қаралды 225 М.
Купили айфон для собачки #shorts #iribaby
00:31