Émission bi am na solo lool dagnu koy topp Saa su ne, at mu nekk. Gni ngéen di invité ay woroomi xam xam lagnou. Dagnou léen namm ndax lu néew lagnou léen di invité ci télévision yi waaye nagnu léen di bàyyi ngir Yàlla gnuy développer. Ta ngéen wagni li nguéen Di wax dafa bari xawa bari.
Serigne mame mor hamedy xam xam bi sel n’a yalla nala brom bi guena taxawou
@imaamfatahmbacke9262 жыл бұрын
Damay ladj serigne touba mi ni mo baxei ni t rafet djiko mom kan lako niru ?
@abdoulayebaneniang2 жыл бұрын
Mouhameth Abdallah psl
@zacariadieng17434 ай бұрын
Éloquence bou andak xam xam yar ak teguin...Jeureujeuf
@ibrahimagueye96552 жыл бұрын
Pape sidy fall il faut pas exagérer bane dieuwrine gua meuss guiss mouy wakh Serigne diw dou dara am na wakh yo khamni kén doukko wakh yaak lay gueuneu déf que deffar