bravo a cette Dame qui commente comme en wolof et français mélange j'adore sa facons de parler sa me rappelle du pays de terrenga mon senegal moi je suis d'orgine de guinée conakry mai j'ai grandi a dakar ponty merci de votre boulot sa aides beaucoups des familles qui sonts loins du pays des célibateurs merci
@rienquelaverite81695 жыл бұрын
Wa éh éh éh nak liii dou yone waye. Tata Marietou se casse la tête tout le temps pour nous concocter des plats😋 délicieux, gnoune gnouye vu di copié, dko reprendre à la maison ta manougnou beusse 👍tamite nak. Pousse bleu👍 waye pour supporter Tata Marierou. Yalna Sénégal doooor Algérie 2/0 you amoul béne wéranté
@nioumadoucoure63635 жыл бұрын
Rien que la Vérité amine wat
@maimounandao71475 жыл бұрын
Elle est très adorable la petite Fiona Dieye yalla nako borom bi same🙏🏽🙏🏽
@ndeyefatoudiop25665 жыл бұрын
Maschallah Fiona tu n'as fait que suivre les pas de ta maman. Je la suis beaucoup de même que tata Mariétou. Bonne continuation mane togue yakkoul djiguène
@mamediarrangom24975 жыл бұрын
Tata danga bari feem waye Fiona adorable .nena dieune yi peur nagnou .on vous love
@sochocolatyes41815 жыл бұрын
Mach Allah soxna Fatima laf thiat et chapeau à ta mame boye et ta mère pour 7 éducation c très rare aujourd'hui de voir des filles de ton âge s'intéresser à la cuisine et tâches ménagères 👌🏽
@fatimafall37604 жыл бұрын
Bravo ! Machallah ! Merci Marietou! Saveurs planétaire !!! Un Grand coeur !! Bonne continuation bébé Q je suis fière de vous !! Dieu vous bénisse !
@mary182035 жыл бұрын
Li moy sama plat préféré, firir, sauce ak frite you tanga. 💗💗💗💗
@mamediarra14385 жыл бұрын
A machalla content na trop une fille de 13ans di digal ay moromam niou dimali yaye yi yalla na yalla sam🙏🙏🙏😘
@seynabangom46435 жыл бұрын
Amine yarabi
@mary182035 жыл бұрын
Amin , japalé sa yaye lou am solo la. Bou souba xi sa biir keur situation dou la diakhal.
@manengom87125 жыл бұрын
Masha Allah bébé Fiona Dieye. Li nga firire amoul fene.
@siamaimounakamano68625 жыл бұрын
Je suis guinéenne mes j'adore les sénégalais bariki serin touba
@macherie15843 жыл бұрын
Moi j sui guineenne ma bel ah wi c la teranga
@mlgguest34795 жыл бұрын
Dieureudieuf sokhna Marietou Chapeau â la jeune fille mllle Fiona Dieye maashallah Yalla na jam sakh
@pivoine38285 жыл бұрын
Waw tog day séte daf siy am solo trop, bravo Fiona. Yalla nala yalla lafal thiat.
@aichakabo51054 жыл бұрын
Tata marietou je taaaaaaaaaiiiiiime ta joie de vivre mamachaalah
@k-dy42105 жыл бұрын
Oooh mahchahala firire mom tamite nekha lék tanguay ak sedday thx saveurs planétaires
@ndeyemourthiam26074 жыл бұрын
Machallah vraiment bien ordonné khale bou djiguene dafa wara tella kham wagne yalla na yalla def la mag
@ngonendiaye63085 жыл бұрын
Saveur yamoul si partager togou youbakh mai dafaye participer si éducation ndaw gni Tata Marietou yalla nga soute mère Diop fane kouni amine yalna goudou fane
@khoudiaseye58615 жыл бұрын
Treeeeees bien Fiona machallah 👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👍🏿👍🏿👍🏿👍🏿
@papekeita5 жыл бұрын
J'adore merci Fatima pour mes enfants a Genève belle excenple
@franciscasane68934 жыл бұрын
Macha alla très bien tout ce que tu me plais
@mamefamandaw91875 жыл бұрын
Walaykoum salam machallah amna solo borom youbou yaba
@aminatatallseydi76585 жыл бұрын
Ooh j sui très content moi j commencer à cuisiner a l'âge de 10ans😚😚😚
@khoudiediasiby72195 жыл бұрын
Masha ALLA fiona guoudou fane ak were ma chérie 👏🏾👏🏾👏🏾😘😘😘
Machaallah Machaallah 13ans khalébi sa yaye liguéy na touy touy! ♥️🤗
@leboundoye80405 жыл бұрын
Mame boy😁
@talibessaliou77625 жыл бұрын
Nila dh khalèdè dankoy diagall dugu wange
@chachagaye89025 жыл бұрын
Ah mo kimay sen dou Tata marietou?🤗sisi c'est elle kay Athia namonalla,dila nianal goudou fann.Waw kay Dieye ma samba neko rell
@marietouhyjazi64445 жыл бұрын
😂😂😂😂Bb Fatima togn nafi
@fatoundoye18505 жыл бұрын
Akamako beugue té meune ko togou barki bleu bleu
@topouleye67815 жыл бұрын
Longue vie à toi et à tata
@yacinembaye90905 жыл бұрын
Wa kham ngene tan marietou lay weur machala yalla na sa diam yague
5 жыл бұрын
Yacine Mbaye Ameen wayy
@luizaluizalou4 жыл бұрын
Non Fatima ayyyyy gua contente si yow
@alquira_a5 жыл бұрын
Machallah fatimata follina sa yay ta yande
@mariamcisse34955 жыл бұрын
Machallah saveur planétaire
@aissatasow42605 жыл бұрын
Machallah tata 😘
@macherie15843 жыл бұрын
Mdr tata mariete j tador
@azizaaboubakar91765 жыл бұрын
MachaAllah Marietou bonne meilleure cuisine avec humour, Goundouss Goundousé 😂 . Qu’Allah te protège 🙏❤️🥰
5 жыл бұрын
Aziza Aboubakar Ameen wayyy
@maremasoda72425 жыл бұрын
tata man dama bagua toga do ak yaw 😭
@dioumafaye1455 жыл бұрын
Lil lèpe si yar ak défar rêk la bok ta royoukaye nga dieureudieuf avec toute la pédagogie qu'il faut bravo à la petite et merci pour le message
@mohamedgassama26705 жыл бұрын
Merci Tata Marietou contane naniou
@khadythiamcoly69935 жыл бұрын
machalla
@mangoneniang23115 жыл бұрын
Machalla svp ta Marietou les ingrédients d fiona ns échappe merci pr tou longvie a bb fiona
@binetabalydieye43765 жыл бұрын
Machalla tata marietou ki may mbadienne nam machalla je suis très contente wakh na deug deh mamame moco diangual sama yaye djiou bakh bobou sall gara merci encore tata marietou yaw beug nala torope yalla na yalla degueureul takhaway bi
Dangay sett bobou firir bou am dolè. Ta marietou fila nekone lolen togou ma togouko bagna lakk bb yi. Alhamdoulila dioudou nagnou ci diam. Nguen nianal Sama sekhou Yalla yi. Diadieuf
5 жыл бұрын
Sow Ndeye codou Ameen wayy ma Cherie Masha Allah Yallah na Yallah barkel leenn
@mamekebe26235 жыл бұрын
Felicitatation sow ndeye codou yala na yala barkel maylen wer goudou fane
Machalla tata mariatou moi aussi g commencé avec le niehou thièré
@mamediarradiop71555 жыл бұрын
P
@dagangom29604 жыл бұрын
Je mappelle Daga Mouhamed ngom je suis la belle d tata Egué Ndiaye rebeuss
4 жыл бұрын
Daga Ngom ohhh Masha Allah Daga eguè Ndiaye c’est vrai ak tonton pape Samb Diop naka lagnou deff ohhh Masha Allah ak Aby Diop aussi
@dagangom29604 жыл бұрын
Diongui si diam loubari ma cherie meme mari te salut
@dagangom29604 жыл бұрын
Dama done quivre say vidéo rek ma dégue le nom de amy sibi ak helene diagne
@lanabienneniang77015 жыл бұрын
Macha Allah bb Fiona Dieye 😍😍
@fatoumatabah6925 жыл бұрын
Masha Allah
@fatelndiaye53375 жыл бұрын
Salam Tata marietou Masha Allah massou ma commente mais mangui suivre tey guis sama bop ci lingay def. Bebe Fatima Masha Allah sa firir tog neu😃 Mais Tata da nga done yooru waye tey yeb nga😘😘😘
@salimatandiaye26905 жыл бұрын
J touye!laftiat ,mama
@cisseyande95945 жыл бұрын
Machalla 🇸🇳
@ayaratouyatara48584 жыл бұрын
Félicitation à la petite Tata il faut fait une version en français.
@aichasow70665 жыл бұрын
Thio Machallah longue vie à la petite c est une fierté tata marietou bonne continuation Aichetou sow depuis canada
@diengsoda8553 жыл бұрын
Mane sama téléphone laniou sagn wayé damala war ba sone tay lalay doga dagne mane dal yaw lay weur
@adamaisse5 жыл бұрын
Tata pour intro bi esk do oute ay tama you saf ande ak bongo you méti niu defal la beine intro bou am diom 😂