Franc koula dieuloul rek Dafa xamni do niékhoum niébé ba si sama mbeur sakh defo dara lou diéneu sport, manqué wo kene respect
@ritalopis4 ай бұрын
Allez Franc
@Talla-Ndiaye4 ай бұрын
Non mais vraiment il a raison, Sa Thiés noumouy bagné Franc ba paré accepté beurré ak Bombardier alors que Franc moko dann, Thiey Ndiago bi 😂😂😂😂 nékhoul gnémé nak 😂
@andrembengousarr70514 ай бұрын
Lolou mooy oute lou yomb reck
@bayeratebayerate58934 ай бұрын
Merci France goor dou nekhal goor
@gazza8734 ай бұрын
Do sama mbeur waye koula dieuloul dala ragal wakhofi dara louy leep si sport ngako teek champion deug gue 💪🏿
@ModouDiop-y1e4 ай бұрын
Merci franc
@ogviito19494 ай бұрын
Ndiago bi seul goor dou nékhal goor 💪👑
@AlliouDiop-f6v4 ай бұрын
Franc seull champion ngayi ay tapétt lane eumeu ragall la wallahi ❤❤❤❤❤❤
@Abdallah313414 ай бұрын
Mané ningay communiquer baxna lamb la boul fi nékhal kén
Lamb dji yako nékhal donyé do sama mbeur lamb ak thiow way ❤
@bencheikh18494 ай бұрын
Merci Franc Eumeu Sene mom vip yep nioko tanné daffa beuri ay détails trop 😊
@AlliouDiop-f6v4 ай бұрын
Franc seull champion ❤❤❤❤❤
@MaxJyLFSS4 ай бұрын
Franc boul changer dara sisa communication gayi liniou beugue c trop facile surtout eumeu sene il veut juste lutter contre le même cercle
@malickdiop43524 ай бұрын
Vraiment 15ans -20ans les mêmes affiches
@abdoukhadrefaye35714 ай бұрын
Communication takhouko am combat dé n'a wah louko nekh il n'a rien encore fouti ay poids moyen rek laffi d'âne topou payi rek Di kharou séne kaw merde way
@MaxJyLFSS4 ай бұрын
@@abdoukhadrefaye3571 sawaay révolution dafa bakh si lepp danio soneu si toujours les même balla modou eumeu, nagn yataal boy yi monter c'est tout.
@mouhameddia51684 ай бұрын
@@abdoukhadrefaye3571 kou dane serigne ndiaye ,thiatou yoff,forza,sock ,mbaye tine ak tyson 2 ngani aye pa lafi dane.soyons logique aussi
@abibdiop46784 ай бұрын
@@abdoukhadrefaye3571waw motakh Niou warko diokh balla pour test
@modoundiaye-vy3cq4 ай бұрын
Gy yi dofou niou dh kouko dieull daanou😂fowoull fowlou woull😅❤❤❤❤❤
@DoudodiengDoudo4 ай бұрын
Super franky❤🎉😊
@magattediop99754 ай бұрын
Je te promets que tu communiques super bien ceux qui disent le contraire ne cherchent pas ton bien. Et merci pour ta réponse à Eumeu c'est un hypocrite s'il te respecte pas ne le respecte pas. Fais comme Mod'lo geumeul sa bop té boul nékhal kén❤
@moratv48424 ай бұрын
Merci franc yako man aller ak retour 12 victoire la am iow yako geune bakh palmarès sou bariwoul ak iow dala ragal ❤
@magattediop99754 ай бұрын
Bilay dafa warone toudou sakh 10 défaites yi ndakh eumeu xol bi geuna diékh... Eumeu dafa yabaté tek ci rancunier quoi toujours dans les détails
@papadiom92604 ай бұрын
@@magattediop9975 1e victoire bou Eumeu mo eup Valeur Palmarès Franc bomou dadj 😂
@djilyba-o6h4 ай бұрын
D’accord avec Franc ! Ci sport laniou nék! Fi indiscipline amou fi
@aboubacriguissegueye4 ай бұрын
Dagne la beugua diakhasé ak Sénégalais mais ñioune khamnagne leeep Lamb amoule nékhale kou beugue ñiou nékhale la gua déme sisi diabar 😅😅
@OmzobuGarga-zu4go4 ай бұрын
Merci franc li la begue boul fi nekhal bene mak koula wakh tontoul dara nak 💪🏾👏👏
@ABAKARA-q8o4 ай бұрын
Yaw wass guaaa
@Killer-z1u4 ай бұрын
Kou nième na dieul😂😂 dof Bangui ni ndiago or bi Vip mom rek laniouy mousslou
@superfoottv22774 ай бұрын
Dinguen diey wadji bamou tarder si lamb
@MouhamedNiang-du3fi4 ай бұрын
@@superfoottv2277Mofi def litah nioukay djay 13Victoires kouko am fouy
@disytbi87114 ай бұрын
@@superfoottv2277Franc genolén ko kham limouy déf. Balla Gaye mofi nieuk takhaw Di wakh affaire you mél ni si gnom Yekini, Tyson, Baboy etc. Adouna lép gueum sa boppu leu.
@mouhamedlydiouf89344 ай бұрын
Ki personne n'a peur de lui. Gars yi dagniou ko taloul rk@@superfoottv2277
@FallySow-z1l4 ай бұрын
Franc defoul tous si lamb n'a diéul serign Ndiaye walla
@LamineFall-r9p4 ай бұрын
Merci franc bilahi walakhi 😂😂😂😂😂
@boubacarboiro58134 ай бұрын
Maa fii djitou❤Alhamdoulilah
@mmabdou4 ай бұрын
Bil'ay
@cheikhounagning4 ай бұрын
Mbeur diamou si yaw ak Salam ak fou mana neke ❤❤❤❤
@ShiekhjobeTijan4 ай бұрын
Yalña yalla defal la jama AK Sallam ta may la combat ta may la ci ndam ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👑👑👑👑👑👑🦁🦁🦁🦁🦁
@thomasmendy25434 ай бұрын
Merci Franc amoul tousse boufi nékhal personne
@papispass4 ай бұрын
Merci Franc affaire bii dou affairou dahira mais affaires de combatant la.
@djilyseye13274 ай бұрын
Merci 😂❤
@AladjiFall-yz8oj4 ай бұрын
Barki yalha Franc nekhnama
@serignefalloufall4 ай бұрын
Merci beaucoup franc inchallah lepp daye bakh metina waye ligey ak mougne rek dîna mousseu baxx
@ModouDiop-y1e4 ай бұрын
Franc seul ❤️
@AtoumaneNiasse4 ай бұрын
Machallah franc rk❤❤❤
@cheikhdieng72724 ай бұрын
Super Franky
@iscojo66004 ай бұрын
Gayi dagnlay khékh ! On dirait que c’est la Team Sucette Queue d’Aziz Ndiaye en occurrence Wa Pikine et Guédiaway niolay khékh!!! Je te jure!!! Mai niome nieupou yalène meune Bilay
@ACTULAMB4 ай бұрын
Ken khekhouko bro combat mom Ama si mom la retard parce que loumou lathie mo beurrin
@@ACTULAMB way hé amna ci droit Ama beuré na combat royal lale caché, legui ku bokul ci cercle bobu rk ay wethiet laniu lay jox mais gni li moy sen liguey pour ioe xaliss biniuy laj pour lanla daniu am famille hein dzngen di faté ne en dehors de lamb ay nit laniu comm niune ku beugoul lou bax bay
@iscojo66004 ай бұрын
@@ACTULAMB oui t’as raison certainement ! Non Ama mome amoul loumouy khalate !! C’est un vrai sportif , lui il a compris comment marche le sport..
@taphasamb68364 ай бұрын
Ayy doungourou Ziza leu
@Wakanatv44 ай бұрын
Boy ya am folou bly😂😂
@MameFallou-jk7yf4 ай бұрын
J suis balla Gaye à %100 ms franc boula kén changé Lo sa communication kéne doufi nekhal kéne pour beug beuré niom nio geunone grawlé fouf thé Mogui ni gars yi nane bayi nafekh akh 🙏🏽✌🏼
@1stloge4 ай бұрын
Merci François eumeu tapet la
@FayaNinkih4 ай бұрын
Ndiago or bih dou champion clo clo grand bokou fih diel danou 😂❤
@pierregomis21704 ай бұрын
MACHA ALLAH ❤️ MBEUR yalna yallah df Diam 🙏
@MatarNjie-dc6hb4 ай бұрын
Franc yaw rek top❤❤❤❤❤❤
@BaaOusmane4 ай бұрын
Merci fran
@BadaNdiaye-z2w4 ай бұрын
Merci
@kategniemendy59654 ай бұрын
Sama champion bi 🎉
@Makhousow-h7g4 ай бұрын
Merci super franky❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
@sekouomarwade8574 ай бұрын
Limou wakh ci eumeu❤ Sene ak doudou sane Innovation leu ci lamb deh 😂😂🤣🤣
@seynaboutalland4 ай бұрын
Franc daffey yakk kholou magg 🤣🤣🤣🤣
@tarkindabi41684 ай бұрын
Ndiago diamant bi yaa woor💪
@senegalrek25794 ай бұрын
Merci fran😂 Eumeu mom bouko may dara tapet la😂 bou beuge kouko nekhal na dem😂seti😂diabaram fi lamb laniouy wakh Eumeu dieuleul combat bi 5 seconds boybi teurla😂😂😂😂😂😂😂
@Abdallah313414 ай бұрын
Warna dieul boy bi kañ, parce que mom bariwoul adversaires.... FRANC ci v.i.p yi la bokk kén meuno kosé guénné
Merci beaucoup Franc amoul séral .Eumeu Sène tapet leu bou mak
@SarryElhadjiOusmane-kq5lc4 ай бұрын
Merci Franc❤❤❤
@LamineFall-r9p4 ай бұрын
Allez Franky ❤❤❤❤
@Medzo35104 ай бұрын
Mague bou niéméwul doula diégué😂
@coeur2lion384 ай бұрын
Légi halé gni gnémé nak pourkoi tjr focus si makgni😂😂😂
@ahmadoulamine95484 ай бұрын
Eumeu Sen 50ans de carrier 12victoire😂😂😂 Franc 10ans de carrier 13victoire 😂😂 Eumeu louy problème bi 🤷♂️😂😂
@mohamedballadiop60854 ай бұрын
😂😂😂😂
@papadiom92604 ай бұрын
Problem bi moy Kene Kii 1e victoire de sa carrière mo eup valeur les 13 victoires de Franc et des lutteurs de P.A tout entier!
@AhmadouBambaSarr-so6vl4 ай бұрын
Weurna @@papadiom9260
@AhmadouBambaSarr-so6vl4 ай бұрын
@@papadiom9260ya ham lamb
@falloumbaye88604 ай бұрын
Ya man ya epou dole💪💪💪💪 friture 👑👑👑
@MaodoKane-mw4yd4 ай бұрын
Ndiago bi kassé kou nieme na dieul avance bi.❤❤❤❤
@fadelbambiste14514 ай бұрын
Francs yaa meuen ya eupp doolé💪🏽💪🏽💪🏽🥳🥳🥳
@mmg64734 ай бұрын
Franc kassè domou P.A bii première ministre de l’arène ❤️😅
@yasseraidara21224 ай бұрын
13combat 13 victoire ❤❤❤ ya meun ya eupe dolle
@djilifall62884 ай бұрын
Bilahi
@Mowmetg4 ай бұрын
Y’a meun ya eup dollé❤️❤️❤️❤️❤️
@bachiirdiagne114 ай бұрын
Koula dieuloul rk dala ragal focus champion🎉❤️
@bayeratebayerate58934 ай бұрын
Merci France eumu sene tapet la
@Wakanatv44 ай бұрын
Mafi djitto❤🎉
@mbackeseck61424 ай бұрын
Allez franc❤
@KabbaCham4 ай бұрын
Future king of the arena
@djibytraore48934 ай бұрын
Champion Deugeu le kou ko gnémé 😅😅😅
@MohamedGueye-xi6qq4 ай бұрын
Ama
@fredericmendy97464 ай бұрын
Salut à vous et merci franc djam rk guay am par la grâce de Dieu
@InfoproTv4 ай бұрын
Un très grand champion
@ndiayebayegalass94954 ай бұрын
Faran ❤❤❤❤❤
@sebastienaccatcha42984 ай бұрын
Fier de toi mon frère, Job Rék ! ya meun foufffffff comédien yi.
@0U5M4N-lp7of4 ай бұрын
Eumeu sene franc combat bu nexleu
@MassThiam-b3q4 ай бұрын
Bilay ❤😂
@Bakelsen994 ай бұрын
Diga ame bro tkt pas courage
@ThiernoMadanyTall4 ай бұрын
Franc seul niii la deh bou léén may dara 😂😂😂
@serignedieng78604 ай бұрын
Eumeu séne tapétla mako wakh❤😢 dieuleul avancé rek bo gnémé
@abibkeita74474 ай бұрын
Bilahi sama ndiago bi mala beug a part yekini ioe
@alyseckmbaye69564 ай бұрын
Bien dit franc boul changer Dara thi sa communication Dina bakh inchallah
@saliouthiam24624 ай бұрын
Franc 🎉
@awkhadim45324 ай бұрын
Kou. Nième. Wayyyyyyye
@assanegueye53354 ай бұрын
Merci fran ❤❤
@moustaphasonko5964 ай бұрын
Ndiago or Franki iow rek lagnouy topp P.A kessé 💪 koula dieuloul dala raggal boul fi neeexal béen cadavre ambulant
@IbouBa-xf9px4 ай бұрын
Franc kassé
@khalil62504 ай бұрын
Ndiago or bi❤❤
@Realhustle2074 ай бұрын
Gniy wakh nane meunoul communiquer yepp daniou sokhor rek mais Franc je trouve qu’il communique bien et est très intelligent.Lamb Ak wakh nio ande guiss naniou fi lounek donc kouko dieuloul dagua ko ragal rek tout simplement. Il a fait ses preuves son palmarès en est la preuve.Bonne continuation Mbeur ne change surtout qui tu es .Tu ne manques de respect à personne.
@ababacardiop26794 ай бұрын
Champion fran boul yombal dará na méti koula ñéméwoul na toogui daño ragal rék
@Diouf-chroniqueur-Lamb-Lutte4 ай бұрын
Il a raison mon dakh beure doudou sane
@Mor-gh1cm4 ай бұрын
Eumeu sene dou guat boula dieuloul mo kham
@BahAmadouSara-o7j4 ай бұрын
eumeu seul ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ tay shingher pikine ndam rek Incha Allah Ama yéeeeeeeeeee
@Aliotop-officilel4 ай бұрын
Dieul Len avance bi
@MohamadouDiallo-t8o4 ай бұрын
Eumeu sene goor jigen la
@FallouMbaw-lu8uj4 ай бұрын
Le grand champion Franc vive parcelle seul ❤ndiago or bi🎉 ndoundeul wérãl champion leuh bly