Je passe des moments très difficiles actuellement 😣 dans ma vie 😔mais une fois que j’ai regardé cet interview je me suis dit que je dois éviter de me plaindre de ma situation 🤧🤦🏿♂️😭 Dieu pardonne moi pour les fois où je me suis plaint 😭😭😭😭😭Allahou Akbar yallah reik mo meune li 😣
@aichaseck90362 жыл бұрын
Courage
@astousow87232 жыл бұрын
YALLAH nala YALLAH defal diam boul décourager mouk del djouli di wore di werd
@taphaba47832 жыл бұрын
Courage mon frère Dieu te protège
@Mamafatima052 жыл бұрын
Yallah nala yallah takhawou bou bakh🙏🏽
@yayeawambaye54802 жыл бұрын
Yalna yalla safara
@mayasiby12492 жыл бұрын
Ce qui m’as le plus touché chez cette homme est qu’il a tout remis entre les mains d’Allah q’Allah apaise son cœur
@elmaestroniang28842 жыл бұрын
Bravo Seneweb vs avez fait un bon travail parce que sangue bi avait besoin de sortir ça, niogui koy dialé diko nianal yalla kholou mougne ak moudie gou rafét inchallah.
@assfall74942 жыл бұрын
Merci pour c belle parole
@mamanndiaye74462 жыл бұрын
Amine 🤲🤲
@milagrolili36962 жыл бұрын
Un vrai gentleman ❤️😭courage Ousseynou diaz
@AS-nn2ff2 жыл бұрын
Modèle d'humanité, de résilience. J'ai encore appris de la vie grâce à votre témoignage. Yalla na yalla deugeureul sa takhaway
@alimatousow40792 жыл бұрын
Sama borome keur dafa waniécou maye dioye guoudi ak beutieuk bimala sétané la nopi khamnani yama gueuneu métilé fouffffff yalla na la yalla yok kholou mougne métina waye 😭😭😭😭
@kharyfaye83242 жыл бұрын
Ndeyssan massa du courage 💔💔
@kitokoken21872 жыл бұрын
Mane mi sama done bou djiguene niari att mo wagnékou ,soriwouma doff,mais franchement quand j ai regardé l émission sama adouna yeup mo touki. Lii meti na
@leternelindigne99312 жыл бұрын
Yalna yalla yésal yeurmandém si mom té khariko aldiana firdawsi 🤲
@fatoukinembodji95432 жыл бұрын
Massa Yalla nako borome bi yeureume si barcké Naby may la kholou mougne
@ndiayefatah23932 жыл бұрын
Billhi adouna mo méti li doyna war
@dadodashdash92302 жыл бұрын
😭😭😭meunouma len fattè vous réitérer tous dans mn cœur mercredi le 10 mai 2017 doumako meusse fattè jours bima guene marqué sama aduna yalla naléne yalla tèrou si aldiana yi guene kawè
@MbayeDiop-nw7yn9 ай бұрын
Allahou Akbar ☝🏽🥺😭 Bilahi bama la sétané dama dioy Bilahi Yalla nalénne Yalla yeureume té kharé Aldiana firdawsi 🤲🏽❤️
@ezzanfaye28262 жыл бұрын
Souniou borom rek mo sagne Li yalna khalei yi khipeee aldiana du courage diambar 🙏🙏🙏
@salamcissokho6162 жыл бұрын
Goor Yalla deug Yalla nalla sounou borom diapalé te khiaré toute tank yi Aldiana firdawsi Bilay diambar ngua Dia dieuf
@natachatambedou91812 жыл бұрын
Barké Serigne saliou mbacke je ne peux pas retenir mes larmes sama xol toyena ay Lou métti yague na si adouna
@ibrahimediakhate79712 жыл бұрын
On vous encourage et vous transmettre nos codeleances que dieu les recueille au paradis Amine
@ramasenghor51662 жыл бұрын
🤭😭😭😭😭😭😭
@mouhamedsow77202 жыл бұрын
je suis ébloui par cet homme. Tu l'entends parler tu sais qu'il sait remis à DIEU et a accepté son sort. Wayé alhamdoulilah yalnako yalla may xolu mugn th mayatko yenen doom yukoy apportel bonnheur th yalna dadiélat akh ay domam si aldianay firdaws
@falloumbaye20162 жыл бұрын
Amiine
@passanendiaye21482 жыл бұрын
Grand Diaz t'es un vrai guerrier 😭❤️Machallah yalneu ko yallah takhawou bamou bania manquer lenn té defal kheweul ak weurseuk bou bari inchallah amine touf touf ❤️🙏
@ndiayeyoumane59832 жыл бұрын
C'est des émissions comme ça qu'on veut voir des hommes digne et pieux courage frère et j'aimerais bien savoir comment est la maman ?
@dienaboukeita32452 жыл бұрын
Elle va très mal et a besoin de soutien c'est vraiment dure 😭😭
@aminatadiop52752 жыл бұрын
Ndeysane lolou rek mo meneu nek ndakh dimalou yala rek mossi dess sinon domou Adama kesse mounouco supporter
@muna3262 жыл бұрын
Oui oui je me rappelle de cette histoire, j' avais tellement pleurer pour ses enfants c 'étais très dure et jusqu'à présent c 'est dure du courage mon frère .
@ZeynaBabie10 ай бұрын
Bilaye jour bi Aka méti wone dama dogue sakh diko khalat bilaye du djoy😭Lou nètu yalla rek mo meune bani sakh sama khol tey na comme si mane tay lay la 😭 bilaye mounie rek mofi nek mais Lou nétu bilaye yague na 😭😭😭
@ndeyekamsagueye60912 жыл бұрын
Lou meti dhé yagg na si adouna 😢😢😢😢😢 perdre 5enfants d’un coup c’est dure vrement🙆🏽😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@amathfaye42 жыл бұрын
Il est fort ce mec mashallah
@lamaktoumienndeserignebaba16222 жыл бұрын
Noo téy amna louma méti trop😭😭😭😭😭
@awadiagne99882 жыл бұрын
té khalé you meunon niakh
@Aroukeisha2 жыл бұрын
Moi pareil
@cheikhsadibougalokho93422 жыл бұрын
Du courage Ousseynou je suis ton voisin depuis unite 17 que allah les accueillir dans son paradis
@madombengue91192 жыл бұрын
😭😭😭😭😭🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@djibygueye2682 жыл бұрын
Ndeysane karba jour bou metti si wa parcelles yaguena tokk ak mom di guiss nimou dane doundé ak djabootam surtout mom ak taw bi astou ak goorgui yalla mo meune li du courage karba
@reinedunord2 жыл бұрын
Je me souviens de l’histoire de ce monsieur et j’ai toujours aussi mal pour lui. Lou méti yagg na si adouna billahi 😢
@andi33452 жыл бұрын
Lou méti yagg na si adouna bi wayé état Sénégal impunité bi mou néké eupeu na dayo. Diap nitt bou défoul dara teutj ko ay aat si dara, Sénégal rek la aam
@reinedunord2 жыл бұрын
@@andi3345 wakh nga deugg deh, daniouy lay teudj injustement yakh sa adouna.
@laye69682 жыл бұрын
L'homme fort .gorr yallah
@astousow87232 жыл бұрын
Un élan de solidarité pour lui svp xaleyi YALLAH negn hiper aldiana firdawsi daradieye SEYDINA MOHAMED PSL
@SalamatadalandaDiallo Жыл бұрын
Ahhh Fama elle était une fille merveilleuse Bilae une amie exemplaire Bilae s’était une sœur pour moi on avait eu à passer des moments inoubliables 😢😭 que leurs âmes reposent en paix firdawsi leurs demeure éternel 😢
@ousmane77382 жыл бұрын
Les gens doivent se mobiliser pour aider Ce Mr. Diaz.
@aminatadiop52752 жыл бұрын
Dougnco def loune fangue rek lagnou dimali
@youssoufabdoulayediopjohnn37742 жыл бұрын
Ce serait une tres bonne idee kii nak mo meriter ndimbeul aycha mafia kacc kaccc
@abysourang60372 жыл бұрын
Je suis partante
@aminatadiop52752 жыл бұрын
Authie
@yayefallhamza43602 жыл бұрын
Fall ma ngui niane si barké Mame sidi birahim fall sa tawkhitte sakh fawe si barké kou ted kiii nala birr nii fall tannéff nga té 😭😭😭😭😭
@latif32082 жыл бұрын
Respect à ce grand Monsieur, beaucoup de dignité 🙏
@maimounabalde67882 жыл бұрын
Ndeysane à chaque fois damakoy guis côté marché dior thi moto damakoy khool ba rouss tellement liko dal dafa meti masta et du courage 🙏
@awadiagne99882 жыл бұрын
waw fofou la DEUG ndeysane maman khalé depuis bobou sa n va pas
@janatoudubai52312 жыл бұрын
mane cote parcelle lay ligueyei beugone na am Coordonnées wam dh wax deug nex yala??
@maimounabalde67882 жыл бұрын
@@janatoudubai5231 mom key bo dèmè fofou dingako guis
@mmebonheurjoie18152 жыл бұрын
@@janatoudubai5231 u 17 parcelle lagn deuk côté école 17
@janatoudubai52312 жыл бұрын
@@mmebonheurjoie1815 diox nagn ma numerom merci beaucoup
@dieynabadiop43332 жыл бұрын
Allahou akbar massa yallah na yallah tahawou ci barke seydina Muhammed psl amine
@macinasow44652 жыл бұрын
Diambar Macha Allah! Yalla nala yalla yoke kholou mougne!
@khadythiam79222 жыл бұрын
C 'est vraiment triste 5 enfants issu d'une même cordon ombilical décèdent le même jour paix et a leur ame
@aissatoukeita81882 жыл бұрын
A l’entendre parler tu sens nettement qu’il est en état de dépression et devrait être suivi psychologiquement ndakh liko dal méti na metit bo khamni ken meunouko supporté😢. Yalna ko yalla may kholou mougne 🙏 Il mérite vraiment d’être assisté
@ousmanebadji64452 жыл бұрын
Ce monsieur a l'air très lucide et a la tête sur les épaules. Je ne sais pas par quel moyen tu as pu sentir cet état de dépression qui n'est visible nul part.
@aissatoukeita81882 жыл бұрын
@@ousmanebadji6445 le mot n’a de sens que dans le contexte dont il est utilisé Tu peux peut-être comprendre mes propos du mauvais côté et chaque personne peut avoir une vision différente des choses. Alors là quand je parle de dépression c’est pas pour moquer de lui non loin de là sinon je n’allais pas terminer mes propos par des prières Ce qui lui arrive peut arriver à tout monde Mais en disant qu’il est en dépression je veux juste dire qu’il a vécu un traumatisme qui ne peut laisser une personne sans séquelles psychologiques et dans certains pays c’est sûr qu’il allait être suivi par des spécialistes. Wa Salam🙏
@mercedesmunozcarmona26302 жыл бұрын
Nattou yagg n'a si aduna ,yalla ken leu😭😭😭😭
@seydinandiaye34222 жыл бұрын
Merciii seneweb astou diass ak ay rakame ndeysane sama xaritt biii demna niii rekk
@adjafatouthiaw20942 жыл бұрын
salam quel homme respectueux MashaALLAH du courage toutes nos condoléances qu'ils reposent en paix inshaALLAH
@iam1hu2 жыл бұрын
Oh Baye fall qu'Allah t'assiste et te bénisse barkey Mame cheikhoul khadim
@arabadiallo86872 жыл бұрын
Mes pensées vont aussi à l’encontre de la maman des enfants massa yaye boy😭😭😭😭yalla nalene yalla may kholou mougn barki borom darou
@cheikhterstegen41772 жыл бұрын
Bilay mom rek la khalat nak 😭
@Kingmeuss2 жыл бұрын
Ndeysane un homme fort
@jugedesvaleurs26772 жыл бұрын
Je lance un appel au président Macky Sall et a la première dame d'aider cette personne a refaire sa vie si impossible a redevenir pareil de grâce les bonnes personnes qui œuvrent dans le social ont une bonne occasion d avoir la reconnaissance du bon Dieu
@lalaaichatouleboudiop2635 Жыл бұрын
Gniome dougniou lire commentaire malheureusement
@adjadiaby8923 Жыл бұрын
a chaque fois que je regarde cet vidéo j'ai les larmes au yeux du courage frère du courage
@lamienolamister79292 жыл бұрын
Un brave homme 👨🏿.!!! Nn sénégal 🇸🇳 d’où deuk détruire la vie des gens comme ça gratuitement 😭😭😭
@fatimadiop68442 жыл бұрын
Masalah damala naw thi sa guem yalla Dilla dialle yalla naniou yegalé sen ndaw aldiana firdaws
@aichapouye81932 жыл бұрын
Mangui niane sama bir hol ki yalnako yalla diapalei boubah defalko hewal you soutt diortam mayat ko yenen jaboot. Tahawouko bamou yeukkk ko kou guem yalla mingui niii.
@nafichatoudiatta37052 жыл бұрын
J ai les larmes aux yeux ! En tant que Mére !
@hoodnounou12 жыл бұрын
Goor degeu metina torop Yallah nah souf sedeuh sen kaw et aussi kholat comme juger les personnes
@alioubadarcisse26762 жыл бұрын
Machallah yalna yalla yokou séeni léer té takhawula barké bourom touba amine
@mamadougalsen87122 жыл бұрын
Courage Grand yalla nala yalla taxawou
@marusdia25042 жыл бұрын
Courage mon frère dieu est avec les endurants
@ndeyemariemefall49672 жыл бұрын
Absolument !
@momarsarr885111 ай бұрын
Nitt kou bakh nga kou nangou tatou yallana yalla barkel ya rabi
@omarsow76692 жыл бұрын
Grand frere mougneul yalla bakhna
@fayatv26572 жыл бұрын
que dieu soit avec vous du courage
@zeynafaalfaal18072 жыл бұрын
Amine
@mouhamedfall51212 жыл бұрын
Yalla nala yalla diapéla may la kholou mogn ✅🥰❤️
@coumbatoure136011 ай бұрын
Kou khôl thi yaw wara sante yalla Walahi 😢😢😢yalla nalla yalla maye kholou mougne
@youssouphabodiang2862 жыл бұрын
J'ai des larmes aux yeux 😭😭😭
@umarcs76252 жыл бұрын
Même moi aussi wollah😭😭😭
@khadycisse46952 жыл бұрын
Moi aussi bilahi li meti wayé yalla rek moy bour Di borome Sant yalla yalla n'a lene yalla KHARÉ aldjiana firdawci thi barki Taha (Saw)
@boefenndiaye61762 жыл бұрын
Ki da gueum yalla li fokna 2017 walah 2016 lou méti 😭😭😭yalna la yalla may khôl ou mougn ❤️❤️
@ndeyefasow16992 жыл бұрын
@@boefenndiaye6176 waaw si année yoyou la dei li da daw yaram té doman la beuguon feteilé sein anniversaire
@Boromtouba4 Жыл бұрын
Ndéysane té Ousseynou taye la geuna geum bour Yalla machallah 🙏🏾👌🏾malgré tolof tolof wala natou bi
@zeinakara27692 жыл бұрын
Force à toi, que firdawssi soit leur demeure éternelle 😭😭😭😭😭
@massylladiop4775 Жыл бұрын
Un homme brav yalla na yalla defal li dess si sa doundou mbecté ba fawou
@tackogaye32132 жыл бұрын
ndeysane lou metyyy😭😭😭😭😭😭mo yague si adouna yalla nala yalla may kholou mougn teranga adouna ak alakhira les mots m mank mtina adouna keneu khamoul lanla
@hawadia65282 жыл бұрын
Ndeysan trés triste que le bon Dieu t' aide a surmonter cette dur épreuve🤲🤲😭 qu' Allah les accueilles dans les jardins du paradis amin🙏
@Onomar2 жыл бұрын
Et pourtant si je me rappelle bien y’avait une chaîne KZbin qui avait dit que l’Etat promet d’aider la famille 🤷🏾♂️et là on voit que c’est un grand mytho . Aidez cet homme svp 😔🙏🏾
@mellebarry37072 жыл бұрын
Etat dé mo déwé lagnoulay deudieul
@dieynababarry4282 жыл бұрын
Bilahi on devrait l aider
@fatousow95552 жыл бұрын
Très dur quand tu sors du prison les gens n'ont plus de confiance et pour temps .comme il le dit ils y a beaucoup de gens qui sont là par erreur
@babathiall65252 жыл бұрын
C'est triste mais bon courage lou yalla déf rek amna lou takh tu seras heureux parce que dagua gueum sa brom. Bon courage rek
@roots7.6282 жыл бұрын
Al hamdulilah Yalla nalén Yalla khaaré al Janaa firdaws ak bolémeu Juulit inchallah
@hat-tijani93052 жыл бұрын
Salam Qu’Allah vous accorde la récompense promise pour chaque enfant qui précède ses parents dans l’au-delà: un château au Paradis. Aamine La promesse d’Allah est Vérité. Massa
@niambalyseydou56902 жыл бұрын
Très triste,du courage frère Que le tout puissant les accueille dans son paradis céleste
@tanakane51812 жыл бұрын
Astou Diaz Wallay douniou la meussa faté moment bou meti la wone école wetone trop ba legui Yagui souniou khel paix à leurs âmes famille Diaz 😢😢
@dawguisse34822 жыл бұрын
Oh c'est vraiment triste j'ai le coeur meurtri yalla nalla yalla taxawou barkep alhourane, les enfants sont au paradis ,yalla dinala deffale xeweul fi ak fanou dieum.courage
@nganengane52052 жыл бұрын
Allahou Akbar Kabira😭….Ya Allahou ya Rabbi ya meune leppp ya ame lepp ya khamm lepp ya sagn leppp😭 Maguilay gnane yaw boromm assamane akk souff yaw yaye borom kounefa yakounou😭 Ya Allahou yalnagua sa diame bi Ya Allahou yalnaga Siguil sa diam bi Ya Allahou yalnagua teral sa diam Ya Allahou yalnagua soutaral sa diamm bii Ya Allahou ya ko sagn yako def waye sagn nagnoula gnane yalnaguo dimbeli diapelekonkhewallko Barke Sa sope Ba Mouhamed Aleyhi salatou wassalam😭😭
@MameCoumba-dt6yc Жыл бұрын
Amine yarabi ❤
@abasspouye9107 Жыл бұрын
Amine yarabi 😢😢
@fatoudiakhate151610 ай бұрын
Amine ya raby
@PendaBae-o8w8 ай бұрын
Allahou amine🙏🙏❤️
@kineba50492 жыл бұрын
Allahou akbar yalla moy boure lou metti yakk na si adouna lo mettilé mettilé guis goula geune mettilé 5personnes ga soulen thie même jours Allahou akbar
@awakanoute64642 жыл бұрын
Alahou akbaar 😭🙏🏾 paix à leur âme Un homme pieux machallah yallah nalako yallah fay ay yiw inchallah dieu ne fait rien au hasard soit patient et dieu te récompensera
@aissatounianghane31132 жыл бұрын
Ma prémiere foie de commenté yAllA Maïla hol mougn se triste wolahiii😭😭😭paix à leurs âmes🤲🤲🤲🤲🤲
@sophiesall85442 жыл бұрын
J'ai pleuré blh courage mon frère.on se souvient tous de ce drame 🥺💔où sont ces politiciens avec leurs promesses et la justice dans tout ça ?ils t'ont incarcéré par erreur te laissé sortir sans suivie ni dédommagement 😡on est pas en sécurité dans ce pays
@thiorondiaye61572 жыл бұрын
Du courage ! Yalla bakhna ! Yalla diekhoul..
@mariamaseck16122 жыл бұрын
Macha hallal très bon croyant courage dieu est grand 😭qu'ils repose en paix
@CouraGadjigo11 ай бұрын
Li metina torop waye yalnala yalla maye kholou mounie 😭😭😭
@libassedieng11 ай бұрын
Wallay ndeyssanne metina
@bibichedieye94702 жыл бұрын
Ndeysann c trop triste yalnaléne yallah yeureum té kharéléne si aldianay firdawsi yi
@aminatadiop24202 жыл бұрын
Li métii na mais il est fort Massa Mr Diaz Yallah rek mo meune lii yalna la yallah takhawu bu bakh bakh ci sa nguirou ndondou
@astoulaye622 жыл бұрын
Allahou akbar j m souviens tjrs de cette histoire kii nak mo yélo cagnotte 😭😭😭😭😭li métina wadji ndeyssane amna xolou mougn. Lou métti yagg na si adouna diapalèleen wadji😭😭😭😭😭
@babacardiakhate32212 жыл бұрын
Yallah nalen yallah souniou borom yeureum tei kharé len aldiana Force a toi baye fall
@mameaminataba80302 жыл бұрын
Yalna la Yallah takhawou, may la kholou mougn ,yook la si barke Seydina Mohamed PSL. Amine.
@EugeniaAminSawyer5 ай бұрын
Moi aussi j'ai perdue ma fille elle n'avais qu'un an neuf mois sa un maintenant mais depuis que j'ais regarder cette video je ne sais meme pas quoi dire vous etes trop courageux mr Diaz que Dieux vous benis
@sylviediatta90852 жыл бұрын
Massa tu as vécu des moments très difficiles que tu ne vas jamais oublier. Que le Seigneur te fasse miséricorde.
@sokhnabodian72942 жыл бұрын
Mashalah on voit nettement que c’est un brave homme yallah nala sa nakar deudou 😓🙏 yallah bour bou maaggue la amane na dinthial nala lo foguéwoul sax bon courage ❤️🩹
@amadoukane91152 жыл бұрын
c’est un homme fort franchement
@diagnendeyeyacine48122 жыл бұрын
Quel brave homme jai pas pu retenir mes larmes😭 il est trés courageux machallah té gueum yallah. Vu ta façon de parler et de penser Yalnala sunu borom lafal thiate, natou bi mane gueum nani yalla dafa am foum la tek motah mou tek lako, nittou yalla nga deug yalla na yalla yokou sa ngueum diapalé la bou bakh
@aramecisee35942 жыл бұрын
WOuy 😭😭 Yalla Rek Mo Meune Mais Lii Métti Na TrO Barké Yoneté Bii Yalla Naléne Yalla Yeureum J’ai Mal 😣 😢
@papamomargueye33522 жыл бұрын
Bon courage… yalla nala yalla dolile kholou mougne… Que leurs âmes reposent en paix 🙏🏾
@diememediarra62932 жыл бұрын
MACHA ALLAH YALNALA sougnou Borom SAME ci BARKE SEYDINA MOHAMED SALLLALAHOU ALEYHI WA SALAM
@fatoundiaye86372 жыл бұрын
Deysan mon frere mougne rek yalabakhna yalanala may kholou mougne sibarker serigne touba akmame cheikh ibra fall
@babsinfo41422 жыл бұрын
Bonne continuation Amy seck ❤️🙏
@cheikhterstegen41772 жыл бұрын
Ndeyssane 😭
@BabacarDieye-f8n11 ай бұрын
Yalla nalléne yalla kharré aldiana souffe wôyôffe sénne kaw
@didifall35332 жыл бұрын
Daysane Yalla naniou yéyale séne firdawsi si barké seydina mouhamed yalla Mayka kholou Mougne 🤲🙏🙏
@leternelindigne99312 жыл бұрын
Ndaysane kou bakh monguini té gueum yalla yalna yalla yésal yeurmandém si toutt tank yi té tabal lén aljiana firdawsi 🤲
@folashade27492 жыл бұрын
Oh life.. quelques fois on traverse des difficultes dans la vie.. A chacun son probleme, si qq te dit ce qu'il vit ou ce qu'elle vit on oublie ses propres problemes. Chaque jour quand on se leve il faut remercier Allah pour tous les problemes. chaque probleme avec ses dimensions. Qu;Allah vous vienne en aide. Moi aussi jai mes problemes, l'autre a ses problemes. May Allah SWT help us everyday. Zamfara Lady
@awafall77412 жыл бұрын
Barthélémy Diaz diapaléle ouseynou Diaz yalla fayla😭😭😭❤
@dienneproduction83022 жыл бұрын
yalla nala yalla may kholou mougne
@fatoumatadiallo32902 жыл бұрын
Machalla waye métina trope mougnal😭😭😭
@thioneniangpresidentielle26102 жыл бұрын
Barthélemy diaz ki ngua warone recruter ta yalla takh, franchement yene nala ndimbal, meme boufekeee sakh mounoul remplacer lou gueuna ndam pousso si sa metite, metina 😭😭
@veriteabsoluedeugneekhoul17202 жыл бұрын
Ki mbokam leu sakh . Ndakh les diaz barewou gnou Sénégal
@marietoudiagne751310 ай бұрын
YALLA na la BOROMBI ALLAH SOUBKHANA KHOUWATALA may kholou mougne
@a.d24262 жыл бұрын
Dioy n’a , adouna bi dafa diekh ba paré kou yaboul yéné sa morom diam ndax moy lep Aimons nous nit dafa fort guiss nit rek yéné ko Lou bone hamo loumouy doundou ioe si sa bop yangi si sa situation bop sohla koula talal lokho donc nagn fonk nit yi yalla tek souniou yone ndax am n’a Lou tax mou def ko De la peine pour ce monsieur il est fort di santeu boromam à chaque fois C une leçon de vie Yalla n’a ko yalla sameu defal ko diam Le meilleur pour le reste il le mérite 🙏🏽
@Sophie-gx2rq2 жыл бұрын
Ndeysane. Massa. Difficile de se mettre à votre place. Yalla na lene yalla yeueum té deufeul lene, sa nakarou aduna yeup deudou la donté dina diaffé.