Goomu Xol: «sama wudiou petiorgo mo sodé sama dom…» Fatoumata presque en larmes se confie

  Рет қаралды 52,490

Seneweb TV

Seneweb TV

Күн бұрын

Пікірлер: 219
@abibatoutoure_
@abibatoutoure_ 2 жыл бұрын
Faut pas uniquement faire un reportage mais partager son numéro de téléphone pour niou meune ko dimbali Sene web vous aussi akhh
@coumbistacoco6556
@coumbistacoco6556 2 жыл бұрын
Ayway kii nio bokone class amoul beneu problème dou sax wax yalla nala yalla diapalé beu sa dom djii werr si diam inchallah thiey yalla sma xol bii diekhneu 😭😭
@badiartv242
@badiartv242 2 жыл бұрын
un homme doit veiller et protéger sa famille car les maisons familiales sont devenues sources de tensions, quand jai compris que ça n allait pas avec mes soeur, jai déménagé pour la sécurité de ma femme et de mon fils avant que ce genre de chose ne leur arrive
@abyngom6939
@abyngom6939 2 жыл бұрын
Malheureusement goor gnép mélou gnouni yaw linga wakh moy deugu djiguéne dagn ka wara protégé
@hamidoudiallo7504
@hamidoudiallo7504 2 жыл бұрын
Ta parfaitement raison mon frère il ya des loups dans les maisons familiales .
@chouassuranceibouchou3112
@chouassuranceibouchou3112 2 жыл бұрын
Machala yonou diame soriwoul
@kharydiafall8506
@kharydiafall8506 2 жыл бұрын
Bilaye moye deug deh
@ndiayendieme7056
@ndiayendieme7056 2 жыл бұрын
Vraiment
@lamajestueuse2872
@lamajestueuse2872 2 жыл бұрын
Elle me fait de la peine cette jeune femme ndeyssane khalé bou yarou lamay nirou dafa dadié ak dieukeur djou irresponsable qui ne peut pas la protéger contre ses gens méchants et jaloux… yallah nako yallah sameu mome ak ay domame t may ko kholou mougne té fadjal ko domame dji ndeyssane
@fatoulo7106
@fatoulo7106 2 жыл бұрын
Boule retiré plainte bi dagno bone yalla na sa dôme wère akk diam ta nga mougne
@lesavoir9317
@lesavoir9317 2 жыл бұрын
Ndeysane elle est tellement innocente. Que justice soit faite du courage 😭😭😭😭
@amiinahndoye3610
@amiinahndoye3610 2 жыл бұрын
Que justice soit faite lii dafa meti xhalei bou am 2ans lakk 3iem degrés xhadioul saxh si makk Fatou yalnala ya’Allah diapalè mayla xholou mougn 🥹🥹
@detieyacinedieye2315
@detieyacinedieye2315 2 жыл бұрын
Q
@souka1321
@souka1321 2 жыл бұрын
Elle est jalouse de toi tu.est.jeune.belle.classe.Mais courage.et.prompt rétablissement à ton.fils que justice soit faite
@aminaba9275
@aminaba9275 3 күн бұрын
Ma yakar néna khalé bi mo féleu dokh bi wola
@souka1321
@souka1321 2 күн бұрын
@@aminaba9275 sisi.moko.feul.parceque.avertir.na.si.bountam.lakoy.tékk.xalé.momine.là.lépp.lou.dieum.si.loukoy.meuna.lorr.sokoko.soréléwoul.xamalni.amo.xol
@souka1321
@souka1321 2 күн бұрын
@aminaba9275 mokoy.ték.sisén.bounteu
@kikinafall5772
@kikinafall5772 2 жыл бұрын
J’ai des larmes 😭 li métina trop rien d’imaginées si cété mon fils! Yalla nako yalla wéreul té até lak kou def dieuf djou bone dji khalé nomine la! Soudone tayouko dou reagiré nimou def! Khana sac mbam sax bou laké digue ko khôl masawouko! Ki kou bone la mélni amoul dôme! Sama khôl bi diékhna way
@ndeyethianesowfall4157
@ndeyethianesowfall4157 2 жыл бұрын
Trop dure yalla n'a wére akk diam li metty n'a trop courage à la maman yalla n'a yalla takhawou la yaw akk sa djabote inchallah 🙏😭
@Minamodet
@Minamodet 2 жыл бұрын
Amine ya rabbi et que justice soit faite masla mo doye
@ramatasow2332
@ramatasow2332 2 жыл бұрын
Même en la voyant parlé on sait qu'elle est innocante
@abonnesundefilesgars
@abonnesundefilesgars 2 жыл бұрын
Bly
@binetadiallo4897
@binetadiallo4897 2 жыл бұрын
Ndeyssane sama khol sorina...du courage cheri en le voyant on sent qu'elle est vraiment innoncente
@ramatouymdy5324
@ramatouymdy5324 2 жыл бұрын
Dieu est grand ma chérie du courage
@papemamourdiouf5748
@papemamourdiouf5748 2 жыл бұрын
Ton mari est un lâche et irresponsable, il ne peut même pas protéger sa propre famille. Comment tes parents peuvent te laisser avec un tel homme?Soit il s’occupe bien de toi , soit il te laisse chez tes parents. Je n’accepterai jamais quelqu’un manquer de respect à ma femme ou à mes enfants y compris même ma mère. Y’a des hommes qui méritent même pas d’avoir une femme et des enfants.
@Cherifa05
@Cherifa05 Жыл бұрын
Wallahi wakhal, ces braves dames sougnouléén yabéé rek ci sén dieukeur yila
@alijunior123
@alijunior123 2 жыл бұрын
La femme n'a que 22ans Mane sah mako mak mais Yalla rek mofi nek et il voit tout bayiko si loxom ça ira inshallah 🙏🙏🙏
@mamanmbaye1305
@mamanmbaye1305 2 жыл бұрын
Plainte bi bouko retirer so paré nga gnibi Thi saye bokk sa dieukeur boula begué fék lafa
@awadiop3280
@awadiop3280 2 жыл бұрын
Lolou.moy deug
@rimathiam1964
@rimathiam1964 Күн бұрын
Li dé la d'accord !!!
@oumidiallo5074
@oumidiallo5074 2 жыл бұрын
Sénégal bonne AK sokhor AK ignane bifi nek kene khamoule lanela lii l'âne tamite naniou defarate khole Yi
@ouleycamara3260
@ouleycamara3260 2 жыл бұрын
Yalna ya rabbi may khalé bi wër té mou bagna ame béne séquelles ak mboléme kou ame métite thi barké Seydina Muhammad (psl) et que justice soit faite
@ndeyethianesowfall4157
@ndeyethianesowfall4157 2 жыл бұрын
Allahouma Amine 🙏
@dior7253
@dior7253 2 жыл бұрын
Il faut donner son numéro pour qu’on puisse l’aider
@kbaida2008
@kbaida2008 2 жыл бұрын
Liga amoull reikk mo takh ms boo yoron niou teikk la palass ms nianall reikk say doom mag leigui g fatei leipou
@salihate-ew6wy
@salihate-ew6wy 9 ай бұрын
Ndeysane 😭😭😭😭
@ramaniangdiop9359
@ramaniangdiop9359 2 жыл бұрын
Masta ma chérie j ai pleuré 😭😭adouna dafa méti courage
@adjamariamyattassaye8397
@adjamariamyattassaye8397 2 жыл бұрын
Yalnako yallah wéreul thi barki lahilaha illalah💯😭😭😭😭j'ai le coeur briser wallahi😫😫😫bayiko ak yallah rek inchallah dina bakh lep to fay to😥😥😥
@MamadouDiallo-oh5tr
@MamadouDiallo-oh5tr 2 жыл бұрын
Thiey dounya metina ana loukofie diare yallah naniou yallah doly soutoura. amna niou bonne khale alalou yallah la alahou akbar
@sopeyserignesalioumbackemm3551
@sopeyserignesalioumbackemm3551 2 жыл бұрын
Oh masta ma belle yalla na yalla may ko tane. Li rk motakh deug keur famille mèti koula khol kham nè tu souffre
@munabadjian894
@munabadjian894 2 жыл бұрын
😭 So sorry metina yalna ko yalla may werr 🤲🤲
@nogayfall9068
@nogayfall9068 2 жыл бұрын
Wowal dakarbezz niom dinan dogal sa número nitt yi man la diapalé li moy lan
@Limatata988
@Limatata988 2 жыл бұрын
Parce que ndeuwsi deufeuye ligueiye motah intérêt rek leugniouye diapei nite hamougniou kou yeurou kou yor rek leugniouye andeul du courage yalneu haleibi weir Yalla mayeleu holou mougne
@Limatata988
@Limatata988 2 жыл бұрын
Assalamou Alaykum Mbok Dieuredieufty Dieuredieufty yalna Yalla dioh gniou holou mougne tei rahas holyi
@Limatata988
@Limatata988 2 жыл бұрын
Dieuredieufty Mbok Yalla fayeleu
@tinabah1888
@tinabah1888 Жыл бұрын
Bilayy deguela Sénégal khalise rekkk
@ndeyefallndiaye8063
@ndeyefallndiaye8063 2 жыл бұрын
Li môme eupna que justice soit faite
@bintafaal-kohlschmidt1753
@bintafaal-kohlschmidt1753 2 жыл бұрын
Mais Ousman Sonko il faut aider cette femme de soigner son enfant 😭😭😭😭
@khadycisse4695
@khadycisse4695 2 жыл бұрын
Khales dé momine la louko way deff guiss KO bb bi yalla naco yalla may wer inchallah meti n'a trop kou souk dhiour khamni metina
@yasminadiop982
@yasminadiop982 2 жыл бұрын
Massa ma chérie j’ai vécu la même chose lakou xalé dafa meti Bilaye sama dome bimou laké dou nelawe dou nelawe dagnouye xolé ba beute sette journée bi aussi la même chose surtout bougnouye defe pansement damaye dioye ba sonou yalnako yallah safara legui inchallah
@ndeyebinetamacalou3132
@ndeyebinetamacalou3132 2 жыл бұрын
Ayway diokher numéro bi li metina 😭😭😭😭
@didjabouSonko
@didjabouSonko 2 жыл бұрын
Stp ma chérie bouko bal bayiko gnou yare ko kou sokhor la melni amoule dome keur bobou boufa delou bou sa dome wérré ngua gnibi sa keur yaye yalla na ko yalla maye werr thi barke seydina mouhamed psl
@khadykonate9026
@khadykonate9026 2 жыл бұрын
Ndaysane courage😔dougueul léneu numérom pour gnou meuneu ko diapalé
@pommecorail2699
@pommecorail2699 2 жыл бұрын
Yalla bakhna du courage que le bon Dieu vous protège
@salyfall79
@salyfall79 2 жыл бұрын
Ma chérie bo retiré plainte bi dinala méré trop bilahi ki mérité woul liberté je te jur
@kaami8709
@kaami8709 2 жыл бұрын
Où est son père dans tout ça ?!! La dame on dirait que amoul dieukeur ana papam foumou nekk wakh dji yeup degouma papam Loumou si def wala mou dokh ko ! Vraiment y’a des hommes irresponsables cette femme a l’air désespérée ndeysane
@Minamodet
@Minamodet 2 жыл бұрын
Massa je compatis avec toi sister j’ai vécu la même chose que toi avec une belle famille aussi horrible. Maintenant je soigne mon enfant té tek lépe si loxo yalla ne t’inquiète pas dina baxx et quitte cette maison le plus rapidement possible la personne qui a fait sa à ton enfant ne va t’épargner
@aistaista-xx8br
@aistaista-xx8br Жыл бұрын
Wallahi amna ay nitt you sokhor .kholalma li rek .ndeyssane ay khalè bou touti ni rèk mou am ay mètit bigua khamnè mag sakh mouno ko suporte. waye yala guissna lèpp
@mamanamydiouf8029
@mamanamydiouf8029 2 жыл бұрын
Courage bon rétablissement à l enfant et le bon dieu t assiste et te protège avec tes enfants c'est difficile ne la pardonne pas. Qu elle pourvu en prison
@mamesey1294
@mamesey1294 2 жыл бұрын
Am very sorry my sister yallah nala yallah fai sah hol nuru gah kuyaru walahi
@rokayadiallo1500
@rokayadiallo1500 2 жыл бұрын
Boul forcé kénn pour mou beugueula bagne d'où beugue
@ndeyecoumbafall5786
@ndeyecoumbafall5786 2 жыл бұрын
Du courage. Dieu reste le seul grand juge.... Bane soukoruu koor. Moi je ne l'ai jamais fait....
@awasane8288
@awasane8288 2 жыл бұрын
def lo meune so teude nelaw def ko ki diar sa moy guene
@abibatoubathily3783
@abibatoubathily3783 2 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭 je c mm pa koi dire masta courage ma belle
@adjafallmory7316
@adjafallmory7316 2 жыл бұрын
Courage ma cherie li metina torop 😭😭😭😭😭😭
@khadijanourourassoul2963
@khadijanourourassoul2963 2 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭amna gno khamni amougnou khol
@ndeyemourseye6010
@ndeyemourseye6010 2 жыл бұрын
Bilay
@mamysakho6193
@mamysakho6193 2 жыл бұрын
Thieuy Sénégal.li Nouko nite meuna defer.allahou akbar
@awadiagne3184
@awadiagne3184 2 жыл бұрын
Li lér moy bougnouko bayé nonou dina défate louko raw li dafa yomb trop rancunière là.
@maimounaka5561
@maimounaka5561 2 жыл бұрын
En fait Mane marié indil sa Diabar si keurr go khamni momoko yow kesser la khamoul ? Bo amoul appartement wala sa keurr topatol sa bopp boul marié boul demm si djigeen gni bougnou bokkoul woon keurr li d'où meussa am ...
@ndeyemourseye6010
@ndeyemourseye6010 2 жыл бұрын
Yalla nako Yalla safara si barké seydina mohamed psl 😭 😭
@fatoo8957
@fatoo8957 2 жыл бұрын
Mane sama problème moy c’est comme si l’enfant n’a pas de père deigoumako feine il n’est pas à l’hôpital pas à la gendarmerie mais il est où ?
@khadymboup9881
@khadymboup9881 2 жыл бұрын
Boulko bal niafall ndayam ci kaso bi bilahi moko tay sokorna trop
@aidagakou7978
@aidagakou7978 2 жыл бұрын
ndeysaane sokhnacii yeureume nalaa yalla khamnako dans tout ça anaa saa yaye ?
@fayendeye5044
@fayendeye5044 2 жыл бұрын
justice soit faite
@zei0501
@zei0501 2 жыл бұрын
Du courage. Yalna la Yalla takhawou ak sa Njaboot in shaa Allah 🙏🏼🙏🏼🙏🏼
@mariemesadio3213
@mariemesadio3213 2 жыл бұрын
Massa😭😭
@darone2482
@darone2482 2 жыл бұрын
Plainte bi bouko retirer loula yone may nga dieul si parei deilou sissay waydiour boula sa dieukeur beuguei feik lafa yeineu yi sou yaguei Say dome ngay ameil akk ndakh dounioulein may diam comme niniou lako khagnei
@kharitouyayam5101
@kharitouyayam5101 2 жыл бұрын
SVP les numéro de la femme j’ai le cœur meurtri billahi 😭😭😭😭😭
@lyasostudios7376
@lyasostudios7376 2 жыл бұрын
Oui ou l'aide svp
@foogadebbomolooty9839
@foogadebbomolooty9839 2 жыл бұрын
Merci
@hellohello6136
@hellohello6136 2 жыл бұрын
Soko amè tu me fais signe
@helenedieng5770
@helenedieng5770 2 жыл бұрын
Massa les gens sont mechants
@assanembaye6422
@assanembaye6422 2 жыл бұрын
Sa woudiou pediorgua bi domoukharam bou magg là bilahi môme AK Pape Diop domoukharam bou magg là niou
@awadrame6204
@awadrame6204 2 жыл бұрын
Aye waye dioxèlen numéro bi pour gnou diapalè ko les gens demandent le numéro de la dame bobou batey meunonelen reagir
@fayendeye5044
@fayendeye5044 2 жыл бұрын
sama touradau yaye yalla nako yalla same thi Barker yonetiby
@Bush06
@Bush06 2 жыл бұрын
Mounial rek lii yeup deye diekh 😥 amneu niou sokhor wollah
@aissatoudiagne1669
@aissatoudiagne1669 2 жыл бұрын
Son numéro ngir Yallah
@elassakho1591
@elassakho1591 2 жыл бұрын
Li mom doynawar trop 😭😭😭
@yayamgueye6762
@yayamgueye6762 2 жыл бұрын
Ohhh 😭😭😭😭😭
@amisow6807
@amisow6807 2 жыл бұрын
Il faut aidé cette femme elle sorte la ba
@yayourassoul6110
@yayourassoul6110 2 жыл бұрын
Boul delou ganaww femme bobou bakhoulll massa yalna yalla safara sa dom
@princessemyadiallo9791
@princessemyadiallo9791 2 жыл бұрын
Ayyyyyyy wayyyyy ndaye sane ki mo yayo diapalé yalnako yalla takhawou seye Kat mo sonou rék nilay démé ci keur yi danion sokhor ignane dieukeur dji tamit amoul foula
@Corailpro
@Corailpro 2 жыл бұрын
Sénégal sopekouna. Allah akhbar. Sode, rey , agresser, saga
@nenesow6695
@nenesow6695 2 жыл бұрын
Massa wayy li mettina
@aminatadia6844
@aminatadia6844 2 жыл бұрын
Ma belle guénal ci seybi mogueune li
@pendadiop7697
@pendadiop7697 2 жыл бұрын
Mais sokhna sagan gua yow bi gua safari.teh yow ya yor hâlé te hâlé hamoul dara te mou lerlane yow mi majeur mena gua moytou teh diabot dou diambour mais teye sa ndom te mo gua porté plainte parce que holal hâlé il souffre te lak daffa meti non franchement li metina n'a te man yor la joh tor parle que hâlé li koy gagn fou ko daw
@sokhnafal3053
@sokhnafal3053 2 жыл бұрын
mom daf ma nourou kou yambar te lewet ndeysan dafa ragal rek
@oumidiallo5074
@oumidiallo5074 2 жыл бұрын
Keur gou ame tension mo metiii mo rawe Kasso bilakhi
@Cherifa05
@Cherifa05 Жыл бұрын
Ndeysan 😢 jai tellement mal pour elle 😢😢😢
@rokayadiallo1500
@rokayadiallo1500 2 жыл бұрын
Bonne guerison bb
@mariesagna2714
@mariesagna2714 2 жыл бұрын
J voulais l aider l numéro pour wave
@sarrserigne1681
@sarrserigne1681 2 жыл бұрын
Triste vraiment ! Dieu seul sait. Je regrette la plainte, l'accident pouvait être éviter.
@lovery9651
@lovery9651 2 жыл бұрын
Salam wallahi je pleure je veux le numèro de cette dame svp
@mbaestbabs6300
@mbaestbabs6300 2 жыл бұрын
Allahou akbar
@mariabarry8608
@mariabarry8608 2 жыл бұрын
Oh ndeysan li tamiit métina dè wolahi azim 😭
@ndiayendieme7056
@ndiayendieme7056 2 жыл бұрын
Ndeysane li. Mètina
@amethystekyle6126
@amethystekyle6126 2 жыл бұрын
Yalla nako Yalla yékety metyna trop 😭
@mamadoualimoubahkelen1961
@mamadoualimoubahkelen1961 Күн бұрын
Bonne guérison
@abyngom6939
@abyngom6939 2 жыл бұрын
No li dafa méti té ki khalé la 22ans non dafa ame bone
@joselinendecky5658
@joselinendecky5658 2 күн бұрын
Nga fo beu sodé sama dôme ma fo beu sodé leu passé leu tamite😢😢
@AstouSow-xl6kf
@AstouSow-xl6kf 9 күн бұрын
22 ans sakh khalèla massa mak 2ans ayway ki rèkk mo Diara diappalè amana sou amone li yeupp douko dall massa 😭😭😭
@mariamasarr6650
@mariamasarr6650 5 ай бұрын
Mouniel😢😢😢😢😢😢😢😢
@nawalboujbir9982
@nawalboujbir9982 2 жыл бұрын
Thiey bonn amneu ki khalee la ndeysan
@evagassama9831
@evagassama9831 2 жыл бұрын
Hoo désane métina massa
@mariamabadiane2154
@mariamabadiane2154 2 жыл бұрын
Allahou akbar Li kouko défone sama dom ma réyla niou soulila ma dém kasso Doumassi bagne dara Amena yo khamni seuy diarouko Nala famille bi yeup bayi mais boul retiré dara
@SodaDieng-eq2ds
@SodaDieng-eq2ds Жыл бұрын
Waw diarna sakh tass
@yassendiop9276
@yassendiop9276 2 жыл бұрын
Allahou Akbar hooo na dei si kaso bi ndeysane khalei bi😭😭😭
@salyfall79
@salyfall79 2 жыл бұрын
Mé courage ma belle Yalla finala diapalé
@mamideguenemangane2119
@mamideguenemangane2119 2 жыл бұрын
Massa Sister yalla n'a la yalla doli kholou mougne té diapalé yalla rek mofi nekk ta dinala diapalé
@cheikhfalldiouf7133
@cheikhfalldiouf7133 2 жыл бұрын
Sadiakar lan la wakh nak
@assanembaye6422
@assanembaye6422 2 жыл бұрын
Le numéro svp wave Wala orange money avp
@khadymboup9881
@khadymboup9881 2 жыл бұрын
Boul dieul 100.000 yui bagnial dd niafall dayam ci kaso bi
@Ummou2983
@Ummou2983 2 жыл бұрын
Masta 😭🥹Li métina xalé bi amna métite khalé bou ndaw Masta amna niou bone amna niou amoul khôl sa djikeur nalén guéné fofou vraiment el es méchante la dame
@astoudioup3654
@astoudioup3654 2 жыл бұрын
Li métina n'a yone déf ligéyeme seye yi tamite ndieuké yi da no wara maye diam séne diabarou frère yi
@mbenedieng2298
@mbenedieng2298 2 жыл бұрын
Ayy les maison senegal fi kou amoule khalis rek kéne doula falé wayé mouniale rek
@modoulowe4890
@modoulowe4890 2 жыл бұрын
I wish him speedy recovery
@nogayfall9068
@nogayfall9068 2 жыл бұрын
Nitt noumiy niané nimbal ta kén doga lol número m
@souka1321
@souka1321 2 жыл бұрын
Vraiment
Friends PIP Update and Advice
11:28
Clara Sais
Рет қаралды 2,8 М.
Enceinte et en Bazard: Les Chroniques du Nettoyage ! 🚽✨
00:21
Two More French
Рет қаралды 42 МЛН
It’s all not real
00:15
V.A. show / Магика
Рет қаралды 20 МЛН
Suivez l'émission Banc Public de ce vendredi...
Seneweb TV
Рет қаралды 11 М.
Mollah morgun Absa Faye  Mogui France Diomaye dako beug trop Motax Mou...
22:56
SÉNÉGAL MOVIES TV
Рет қаралды 2,8 М.
AFARTANKII (40) QISO OO UGU SAAMEYNTA BADNAA_2022 iyo 2023_ SHEIKH MUSTAFA.
3:26:03
IFTIN BROTHERS STUDIO
Рет қаралды 2,6 МЛН
Enceinte et en Bazard: Les Chroniques du Nettoyage ! 🚽✨
00:21
Two More French
Рет қаралды 42 МЛН