Bilay oustaz alioune sall say cadou a chak foi day raféte yalnala yalla same machala
@khadimseck59854 жыл бұрын
Serigne touba amoul morom diarrama mame cheikh ibra fall lamp fall babil mouridina
@mthiesifall88444 жыл бұрын
Serigne mountakha mbacke yalnafi yagu tee wer ak bepou klifa dinee
@halliltra41244 жыл бұрын
Nasiri haqi bil haqi mouride bouko beuguoul dégu guenal rewmi matin soir daye dal fép.. khassida yi tidiane bouko bagna dégu tamite kazalika! So bolé li gneup di wakh moy la ilaha illala té moy deugu..
@papendiayengalgou25914 жыл бұрын
Yalna Yallah Gathielle seytanè yi beugueu taal rewmi .
@aidis36054 жыл бұрын
Amine
@ladivachou27534 жыл бұрын
Amine ya rabbi
@boussogueye71684 жыл бұрын
Amine pape ndiaye
@ousmanemboup91884 жыл бұрын
Amine waye
@abdouniang3824 жыл бұрын
En écoutant iran et ouztas on se rend compte que saliou samb et messeré n'ont rien compris.
@mbdone38604 жыл бұрын
Seydi el hadji Malick sy lép me lérrrr mashallah
@bayengallacissendigelfall52524 жыл бұрын
Oustaz Iran xam xam bi rafet na Masha Allah
@bamsbams51644 жыл бұрын
Doff deugue moy dougou si famille diambour / na'fékh deugue moy féwélé Niou moytou rék tè khamné yalla mo'fi né
@laminedandio8834 жыл бұрын
Merci
@serignesalioukandji55214 жыл бұрын
Machallah outaz Iran Ndao wahi rafete na
@madiawmboup74034 жыл бұрын
Machalah sunu oustas you bakh yi yall nalen yalla Faye thi rafetal bi🤲dieureudiefatè serigne touba khadim rassoul amoul mrm
@tallalo24414 жыл бұрын
Doff rekkk
@ousmanebasse89674 жыл бұрын
Merci
@mbayediop81234 жыл бұрын
Sa genrgui laniy wakh
@madiawmboup74034 жыл бұрын
Mbaye Diop kan moye wakh ak man
@morleye92714 жыл бұрын
Diotay you mélnii deh soudonn Bari konn gnou bénno
@aidis36054 жыл бұрын
Walahi
@boussogueye71684 жыл бұрын
Machala kene d'où yontbi kouy Roye si mom ngay Roye Machala wahtane. Bi amna solo
@djilyndiaye34754 жыл бұрын
Machalha iran et aliou e sall nagnouy wakhtanè sougnou mak gni dagnon âme lou ken amou' bou gnouko saga è way
@babucarrgai61874 жыл бұрын
Je suis très constant de vous
@babacarniang15044 жыл бұрын
machalla rafétna mé diaroul sone amna nio khamni par parlo moléne nékh ak beugou lou bone
@amdigueye64224 жыл бұрын
Deet damaniwoon naa bayi noonou waayé boul dioum waakh Day am téguine. Djiouli bi sama mame Elhadji Malick djitéwoon serigne Touba, andoulay la woon ta BOROOM deuk ba sante dramé. Cheikh sadibou lanou wakh mou djiité serigne Touba né dédéte, gniouni serigne dramé mo djiité serigne Touba né dédéte, gniounéko yaw mouné dédéte na mame Elhadji Malick sy djiité. Waayé bigniouy défar sappé yi, mame Elhadji Malick daa djiitou, Cheikh Sadibou AK serigne Dramé déf sappé niari nitte, serigne Touba takhaaw sén ganaaw déf sappé bén nit thi ganaw serigne Dramé. Bigniou nopé ba kounék gniibi, la serigne dramé yooné ay ndaw thi serigne Touba djiokhlén ap enveloppe. Binou yéksë ba diokh ko serigne Touba, mou dadji enveloppe bi dal di thiy guénée gnari sondéle, bii rouille ba dèstouti bi kén laalouko. Mouni lén kham nguén loumou beugue wakh ? gniouné dé déte, mouné daf May tagou sondéle bou djiëkhbi moy mom mane maye bou djiekhoulbi. Mouniléne kerook bigniouy djiouli, thi lama rougui tagou woon wayé moom khamoukowoon, maa téwoon mou faatou thi ndogolou sounou BOROOM. ndakh bougouma woona yakh nganegui. Li takh maniwoon boumou djiité, booba rouhgui démna ta néew d'où djiité, Cheikh sadibou moomit moustafiirla ganar la bawoo gnieuw nguir djieulsi hadiya mamame Rassouloulah. Elhadji Malick khamna dineem kham farata kham souna mannaa djité couné. Li takh ma takhawoon thi ganaw serigne Dramé, dama fasse yeené djiouli farata AK yeené djiouléwalé serigne dramé ndakh moodone sounou moudjié guissé thi kaw souf.
@niangcheikh81114 жыл бұрын
Waw lene gorr ammatina solla
@bambakane58424 жыл бұрын
Alhamdou lillah ndém don naa murid bou deuguel louy dal kou andak serigne touba euleuk nama dall kou guiss kima guiss dem di seti kénén démal ma dém lii rékka dall Sama khell 🙏
@fallsouleye33834 жыл бұрын
Machalla murid bou deuguel
@bambakane58424 жыл бұрын
Jaajeuf murid ahakasaa serigne bi rkk
@madiawmboup74034 жыл бұрын
Ahmadou
@dd45824 жыл бұрын
Keurou dîné yi gnon wara surveillé gni tokk si plateau télé yi di wax n'importe quoi ndakh xaliss ak 4×4. Parceque ça n a rien à voir ak la vérité.
@mameboussodiopkhidma75404 жыл бұрын
Daga meuna surveille nieup nite gni kay niowara yar sene bopp
@dd45824 жыл бұрын
@@mameboussodiopkhidma7540 domou baye cou alal djité do mouna yar sa bop. Il faut sanctionner les patrons de média.
@mameboussodiopkhidma75404 жыл бұрын
@@dd4582 ah Diop yaram nioniou mome wakhouma seni wax ndah adouna daléna jiay té yite dano niak tawfekh
@modoutall51044 жыл бұрын
Thiëy Maodo aKa ay cii diangal Goumbeu (aveugle) .
@mbargoudiop40414 жыл бұрын
Yalnagnou yalla fayal seydil khadji malick sy diambar dia
@cheikhmodouburbi88754 жыл бұрын
Way li moy deug béno nék béneu amna gno khamni tarikha yi rek lagnou bagne dieureudieuf sounou kilifa diné yi
@santeyallacouture16754 жыл бұрын
Merci beaucoup iran
@mamelamp69834 жыл бұрын
Ndaysan.... BOROM TOUBA dou moromu kennn.
@modoudiallo1324 жыл бұрын
Maodo dou moromou kene
@mamelamp69834 жыл бұрын
@@modoudiallo132 ndaysan...lolou dé, Yako meussa waxxx....Ba kham nga ni MAODO da bagnone kuko bolek boromam....té li nga waxni diappal ni ya ngi koy togne.
@boygainde37644 жыл бұрын
@@modoudiallo132 😂😂
@mamelamp69834 жыл бұрын
@@boygainde3764 ken nga... BOROM TOUBA rekka fa ague....dou benén jam....kenene koka waxxx...yankoy togn.
Digeunté seydil hadji malick ak mame barom touba kousi nara dougou yasiy yakho rk mais gnom niar lignou tabakh pournga yakhouko yasiy yakho rk motax gnom niar bo manoul wax si gnom lou réfét manou si molay may diamou mouy tidiane bi wala mourid bi🙏🙏
@maargueye37734 жыл бұрын
Al Amin Sy Lo, waw goor! Nii la sa tourando melón. Mourit boubakh dou wakh lou gnaaw tidiane. Tidiane boubakh dou wakh lou gnaw mourit. Dieuredieuf Serigne TOUBA, Dieuredieuf Mame EL HADJI MALICK SY. AL AMIN, yalla na yalla yock khewelgui ack wer chi barke SEYDINA MOHAMED (SAW) AMIIN
@alaminesylo26804 жыл бұрын
@@maargueye3773 wa guiss adouna ni rk le so nango li yalla dogal dangay nopalou sa khol dou djiékh yaw tmt nala diamou sonal🙏
Machallah Souniou Rééw da Am barkep wayé Niak bénno motax Ndieurigno wougnci a 100%
@mameboussodiopkhidma75404 жыл бұрын
Ah mane dh koor gui permettre nama ma xam Lou beuri si mak gni donne téné srgn touba kepp la yakar wayé xamnani farata la si mane ma beug mame maodo baye lahi mame boukounta baye niass extra ndah samay momél nanou j'aime mon pays
@cheikhmagueyendour25054 жыл бұрын
waw gor iran mourid sadikh waye lii la guem
@baradiongue45064 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFÉ Borom Touba❤️🙏🙏
@azizniang73244 жыл бұрын
Thiey sunu mague gni masha Allahou
@abdoulayengom3594 жыл бұрын
Machallah amna sólo dieuredieuf oustaz irán ndaw yalnagafi yageu loll the andeu AK weer amine AK ñiou melni yaw amine
@shamthiam77744 жыл бұрын
Neysane ab Tidiane deug dafay degou dafay am yar am xam xam kholalma Iran ak oustaz liniou xam si Serigne Touba teh di lou ken dou meune dinedi nonoula laniou hamé lou eup si sen tariha wayé akanio niak kiniane andak dale. Kou deg diarinio machallah limoy talibé holbi dafay rafet xam xam bi sel. Teh ande ak bolé ay nite.
@laminendiaye19024 жыл бұрын
Thiey serigne touba bamba di mawdo mawdo di bamba koleen di fewele danga khamoul
@baibrahim52724 жыл бұрын
ماشاء الله تبارك الله فيكم وحياكم الله جميعا أحسنتم أحسن الله إليكم
@dialibatoutv4 жыл бұрын
Li gëna wér ci histoire mooy liniou binde mais ay wakh bou yàggè man naa soppi kou merci
@khadimdylla44774 жыл бұрын
Lolou la geum
@abdoulayecisse68134 жыл бұрын
Motakh gana mesere lou Bari limouy wakh ken bindouko
@dialibatoutv4 жыл бұрын
@@abdoulayecisse6813 yaako fi Toudou dé
@ngorlecon50574 жыл бұрын
Macha'allah, il y a beaucoup de choses qui doivent faire réfléchir dans ce pays mais malheureusement, serigne touba (RTA), kou tedd ki bamimouy dem guedj dafa ni day dem bou déloucé nieup diarignou, fimou diar ci diar-diar bène serigne diaroufa ci sénégal donc gloire et honneur à lui, diambari l'islam tiggui moy mom, cependant li niom iran wakh ni mag gni daniou dane rafètal moy deug, les valeurs qu'avaient nos ancêtres n'existent plus dans ce pays, mag gni dara dawoul niaw sène diaganeté, légui au lieu d'unir on cherche à diviser le pays: pourtant nous avons l'exemple, wird tidiane, wird mouride, wird niassène etc.... Serigne Touba pour dadialé les musulmans a donné l'exemple que beaucoup d'aveugles tentent de ne pas voir: mouy wird mouride, fou wird mouride diougué? Serigne Touba da khékhal nieup, délouci boléwate nieup, amoul morom kouko bania degg sa khol mo goumba, ki yalla ak yonenté bi gueureum kouko nangouloul wéro, nangoul kou tedd ki ne doit pas aussi signifier que yénène serigne yi défouniou dara sénégal et je pense qu'à part les anecdotes d'iran sur Mame El Hadji Malick(RTA) et Serigne Touba, Mame Abdoul Aziz Sy (RTA), Mame Abdoul Ahad mbacké (RTA), une autre chose devrait faire réfléchir, dans toutes les confréries du Sénégal, les Khassidas mourides, tidianes, layènes, niassènes et autres chantent tous le prophète, ta yakarna khép kouy mouride, tidiane, niassène, layène, musulman pour terminer founiouy taggué yonenté (PSL) nga diapé ko yeufi mouride, tidiane, layène, niassène ba dici tek lou niaw: yonenté (PSL), Cheikhoul Khadim (PSL), Mame El Hadji Malick (PSL), Mame Limamou Laye (PSL), Mame Baye Niass (PSL) et tous autres érudits reub naniou là, ndakh kou attaquer founiouy taggué Seydouna Mouhamed (PSL) boko ci niom. Je suis mouride, diap na ni Khadimoul Rassoul (PSL) moy capitaine bi waroul takh may khalab les autres, tout comme c'est valable pour les autres. C'est cette diversité confrérique qui devrait être la force des musulmans du Sénégal, kène kounek ci mag gni am na lofi bayi ci louy dieumalé l'islam kanam: ouvrez les textes saints de toutes les confréries du Sénégal: lép l'islam là.
@matarndiaye27884 жыл бұрын
Machalla amna solo loll senegal make gni motakh niou ame diamm
@morsylla50044 жыл бұрын
Machalla amna solo merci beaucoup
@thiamasthiam1224 жыл бұрын
Wawe léle goorr💖💖💖💖💖🇬🇭🇬🇭🇬🇭🇬🇭🇬🇭
@badaboys20984 жыл бұрын
Drapeu Ghana la🇸🇳 senegal bi la
@morniang47644 жыл бұрын
rafetna machalla yalla n'a yalla sameu léne
@bocardiop91414 жыл бұрын
Machallah alhamdoulilahi
@ibrahimatoure22584 жыл бұрын
Oustaz ira ak oustaz Alioune Sall Yallah na xam xam bi nganeu yokou si barkei seydina Mohammad sallalahou aleyhou salam
@ndjamesowlacdeguierssulo57924 жыл бұрын
Machalla Anna solo
@ousmanemboup91884 жыл бұрын
J'aime ce genre de débat
@papedia70594 жыл бұрын
Machallah yalna diam yague si yenne
@kinesoumare70124 жыл бұрын
Salam ak ziaar gneup. Oustaz Alioune Sall ak oustaz Ibrahima Badiane, ALLAH SWT goudal sen fane. Yen moom, sen wakh raféte ak am ndiarigne la def pour gneup. Sénégal thi wara wakh dagnoo noppi.
@maargueye37734 жыл бұрын
Dieuredieuf Sokhna Kine Soumare! Sa wakh rafetna.
@laminetourre67134 жыл бұрын
Iran ndaw yaa mana fèn mawdo masta dietè boroom Touba. Seringe abdou khadir yitam wakholl woon Elhadji abdou dokhal dietè ndakh booba djioliy adioma touba la woon tè booba seringe abdou khadir mooy ilimano taatib bi kon noumouy wakhè Elhadji abdou dokhall ñiou djioliy nit ko bakh dafa wara tagal yala tè loumouy wakh mou bayi khèll yala
@kebawathiebouserignebabaca23154 жыл бұрын
Mashallah
@abdullahi95774 жыл бұрын
Serigne Touba ken la deh wax nagnou ko té yakhoul dara ... Li takh mouy ken fi ko Sunu Borom jaralé dafa jaraléwoul ken mo takh mouy ken.
Madiaw Mboup amoul moromeu parck mofi ameu 33 femmes . Dont 2 de même père et mère
@madiawmboup74034 жыл бұрын
Ibrahima Traore lii laye wakhaté yen dangen tardé trop yalla kham nako
@abdoumbaye2034 жыл бұрын
Dieure dieufé serigne touba
@yacinecodoumbaye32474 жыл бұрын
Machala amna solo
@ismailagueye36464 жыл бұрын
أطال الله عمركم
@diagnegnilou10784 жыл бұрын
Serigne touba doumoromoukhène
@djibidiallo50934 жыл бұрын
Aladji malick mo raw thi rewmi
@papaassanegning89584 жыл бұрын
Na dieule gnoune kheuthio wougnou dara lignou ame doyna gnou seuke
@cheikhndoye80914 жыл бұрын
yene niar ay domeramou nafekh nguene li ngune di commenter gueumolene thi sarap ndayam satan que vous êtes
@cheikhndoye80914 жыл бұрын
yene niar ay domeramou nafekh nguene li ngune di commenter gueumolene thi sarap ndayam satan que vous êtes
@khadimgueye2224 жыл бұрын
@@cheikhndoye8091 ay doflen
@amadouseck82554 жыл бұрын
Yéne nopiléne serigne touba dou moromou gni
@seydinaousmanendiaye51424 жыл бұрын
Guiss gua nitt dafay positif nek mouride wala tidiane yokoul l'islam dara yéférr bou toube moy yokk l'islam
@papemalikcisse35464 жыл бұрын
Seytané bou magg nga
@mateleveursntv84414 жыл бұрын
Yamana doulll
@papaalassaneseye82524 жыл бұрын
Da ngay doul
@boubacarLY77204 жыл бұрын
Sabounou yaye
@mouhamadousamoura43074 жыл бұрын
Le probleme Moy dafa am talibè you rew tè amougnou diñè c SA le probleme Au Senegal
@soukaynad26274 жыл бұрын
Kepp kouy dignatte mouride waleu tidiane ak bep tariha yalla bou say mbok dieri gnon yalla bo teki si adouna amine touf touf gnoun gunep ay musulmans lagnou
@allahiscreatest9264 жыл бұрын
MACHA ALLAH RAFETHNA
@mohameddiouf17124 жыл бұрын
Limoy débat diagualé mak gni jiko yi ande bou raféte bi dioko lane té bi mé di takal grate mak gni amoute solo nakh yalla takal nalén grate ba paré
@anasdiedhiou65114 жыл бұрын
Wallahi Masha Allah
@amadauthioune57724 жыл бұрын
Gaanne dou djité si deukou serigne Touba même l,imame de la Kaaba était dans les sappés a la grande mosquée de Touba Danguénne warra bayi déndalé serigne Touba ak kénénné mome si boppame momi douma moromi kénne ni lima yallah may mayou kénne té dotouko maye kénne Serigne Touba amoul morome té dou massou kénne wassalam
@diagnegnilou10784 жыл бұрын
Amadau Thioune walay walay
@modoutall51044 жыл бұрын
WaKhal Gann dou djité cii l'islam
@halliltra41244 жыл бұрын
Talibé mouride yi di doule gnéne si sen Serigne yi di doule.. meno Léna wakh bamba mofi raw be tidiane bi bayi maodo walle baye niass Kone nopali kou léne nasiri haqi bil haqi dou faye té dinguéne ko dégue matin soir mou nekh léne mou nakari léne
@amadauthioune57724 жыл бұрын
@@halliltra4124 Nitte day am yarre ak téguinne nitte kou bakhe dou sagga moromame wakhatoumak kou massé ak bayame les mourids ne parlent jamais des autres tarikhas ils ne parlent que ce que le bon dieu a donner a leur guide spirituel Cheikh Ahmadou Bamba sen probleme moy serigne Touba amoul morome nguénne di bagna dégue té serigne Touba si boppame mokko wakhe sa se voit que tu ne connait rien des mourides la Nasiri Haqi bil Haqi les mourides le font tous les jours matin et takussane sa ce trouve dans le wérde Mourid Makhouse minallah moi personnellement je le fait 1111 par jour va voir d,ou vient ce Sallatou Allah naby respecte les autres insulte et pour ceux qui n,ont pas d,arguments ki déf lou kénne défoul mo am lou kénne amoul wassalam
@halliltra41244 жыл бұрын
Bayi léne sen histoire falsifié yi..dem leéne diamou yalla khame sanguou sangue yi mo gueune ngén gni sonal ak Serigne béfi def li walle moffi wakh li gnoune guemou gnou llolou man
@diagnegnilou10784 жыл бұрын
Amour morose serigne touba
@ibrahimakobar24984 жыл бұрын
Machalla amna solo mais ngeum ngeum fi mo néke yakhakate yéguoufa
Mais fi kén tékeuĺéwoul. Danio expliqué serigne touba ak ALADJI MALICK koleuré bou dohone sen diguenté
@papaalassaneseye82524 жыл бұрын
De det du mome achete la yenn yam len ta guem li ngen guem rekk bari ngen wakh trop
@khadiadiaw21384 жыл бұрын
@@vieuxsarrbadiane2108 boulen tontou gny ay franc-maçon rek tous les deux ils sont ni mouride ni talibe cheikh
@boygainde37644 жыл бұрын
@@vieuxsarrbadiane2108 nn tidian yi nio wra bayi di dendelé serigne touba ak Maodo serigne touba kokou dou nitt ken hamoul loumou Don amoul morome kon warougne diko toude dissi ame ko ssiy tegate
@bathieniang17544 жыл бұрын
Machallah wakh dji rafetna trop makk gni sougnou makk lagne niteki yay wakh si gnome lou bakh diarefa bakh wala ngay wakh si gnom lou gnaw diarefa yakhou ba faw kone gni bayisi khele
@fatoumatasane94314 жыл бұрын
C'est l'islam qui gagne mouride tidjane layéne niassén lép si yalla leu
@dofoukhidma57964 жыл бұрын
seydil hadji malick limamou bou kounteu cheikal islam ainsi de suite ay makk lan té gnou bakh lan dama léna sopou lol wayé nk bolén di wakhtanéti kou téd ki dé lén ko bér té dissi wo gnikoy yeug ndakh gout la
@hamadoucamarahamadoucamara49924 жыл бұрын
Sa genre gui momou gnou wakhtane yii doff nguène rek yéna waral thiow you barri yi cheytané nga serigne touba guenoul maodo, Maodo guenou serigne touba
@assanediakhate45774 жыл бұрын
No oustaz iran, biss boba serigne touba moo djité woone
@ndeyekhadyndiaye42324 жыл бұрын
Machala ndao
@assanetoure15944 жыл бұрын
Vs êtes des pistes les conférenciers mourides ne parle jamais les autres marabouts ils sont égoïstes
Mdr ndax limou wax serigne touba likhamal mame maodo ?? Tchey sama gars yi sene mbir deh xamna mettina nioune deh mame abdou aziz sy dabakh mo likhamal cheikh abdou khadr cheikh abdou khadr djiteko niou ame thi mbékté trop
@khadimdylla44774 жыл бұрын
@@ahmadsalim3014 da bari ay wakh youni deg you gnaw tei yenako wax motax dounouko soukandiko gnoun Lou nekoul si minanoul bakhil khadim nekoul si irwahou nadim weroul khista bimou wax deg nako mie lima deg Serigne Touba ak maodo lini wax nan guusssé nan ko bariwoul ndax 33 ans la Serigne Touba nek si lokho toubab bi tei wer Nani maodo massouko setti preuve lan beug mie wediwoun sounou indiwé dalil rek mie bay diiw nenako
@ahmadsalim30144 жыл бұрын
@@khadimdylla4477 comme niniouy déggué bess bou neiike wax you niaw younguéne niouye wax meunouniou fékhé beu bamba ak maodo liléne YALLA defal défaloulene ko baparé kone kou nekke na geum kimou geum ndax sagne nako wayyé kingua geumoul ngua mandou thi mome guaaralante biniouy def ak di sannante khére mélni aye noone Melni aye woudjou mo diaadou woul xalé bou ndaw bo xamni seutou serigne touba yi sax nio mak sa baye nguani danguay taxaw wax serigne touba safane lolou moye yarédikou xaleii bou ndaw seutou mame maodo yi mak sa baye ngua ni danguay taxaw waxko safaane moussibeu leu naniou wattou dérou nitou YALLA yi li serigne abdou lakhad mbacke waxoone serigne cheikh tidiane sy niko cheikh tidiane amna lo xamni gnikoye wax douniou Mouride douniou tidiane douniou lou kenne xam
@cryptoleader83214 жыл бұрын
@@ahmadsalim3014 mandé mangi lay séedél né daray parparloo safuma, té chéikhal elhadji ku sëñ bi fonkoon la, moomit noonu, loolu kép ku jang xamna ko, Wayé HISTOIRE dafa doy waar, loolumo tax luci waay di néttali rek mu wara doon dëg, donté lu rafét la ci sahir. JËRËJËF !
@ndeyebinetadiop4 жыл бұрын
Li dé moy plateau bouy bolé wayé tokk si télé yi di wakh louy féwalé keurou diiné yi rek. Moi mon père était talibé Cheikh il m’a permis d’être Mouride. Mon frère est talibé Baye Niass donc Sénégal béne bopp la mane Makk gneup la beugg ndax gno kheekh nguir diiné évoluer Sénégal 🇸🇳
@damegaye38514 жыл бұрын
Machallah ly rafetna lol
@ygjhgyrfhh97154 жыл бұрын
Wahtan bi rafetna mais il faut dire cette fille de mettre la voile dans sa tête Allah aime cela
@satoucisse94324 жыл бұрын
Vraiment
@abdouniang3824 жыл бұрын
Les mourides ne parlent pas des Tidianes.. BIZARRE
@mbdone38604 жыл бұрын
Pire verité
@mamesayesarr72624 жыл бұрын
mourid yi danie dieuf thi tidiane lou baxx wayéé douniou
@thioubouomar38274 жыл бұрын
Cheikh sarr dieuredieuf
@gueyesassy20444 жыл бұрын
Li nguén wara wakh moy loutakh sou niou wakhtané Serigne tiuba rek thiow yi commencé, kou nékeu diar na ci télé yi wakhtané sa Serigne, té wakh amoul... Wayé wakhtané Serigne touba rek, mou melni lolou laniou done khar.. Ah...
@mbackesow28524 жыл бұрын
Yèna toude serignou diambour .koumou nekh gua yèkati sa serign tè Mandou si serignou diambour vous meunoul wakh Lou rafèt si mom .Bari kouy toudo serign Touba Di wakh Lou gnaw si yénèni serign tè khamoulnè serign sour nala bou yagu
@dijasall3754 жыл бұрын
Serigne touba limou biide meune naniou yi wakh nioune mourite yi bâ guédieul té do toudou serignou diambour
@gueyesassy20444 жыл бұрын
Dégueuna deugueu dija..
@dijasall3754 жыл бұрын
@@gueyesassy2044 dama khamni il NS a laissé un héritage riche, kou khôl si diagualé serigne modou Moustapha migua khamné bikofi serigne bi bayé la dékhal Aÿ nélaw, khamni liguéye bimounioufi bayél doyna ware. Kou Khôl si serigne fallou migua khamni bouné tawal moutal, khamni diamou yalla deugue kou mayé. Serigne bi koumou rére kolal si dokhalidou ndiabote bimouffi bayi. Wayé topou Aÿ wakhi kassaw kassaw yo khamni doula dieumé féne. Dieul jeunesse bi yeup otage. Bilaye koufi âme dôme té diagaloko, yéwoko, y'a perte. Alhamdoulila doli santé samay waydiour
@gueyesassy20444 жыл бұрын
Dija lou wéer nga wakh..na niou néke si deukeu bou doy war.. Wayé Serigne bi biram dafa léer.. Bilay
@shashaofficiel81254 жыл бұрын
Fowé sa vie wésotul féék salatul fatiha mougui dji allah diar si lokho Mohamed saws dém si cheikhuna tidiane mu diokh ko Mohamed hali cheikh Omar foutiyu mame alphahi ba si seydi hadji malick sy gua djégui sa aldiana di dém.
@papendiaye45634 жыл бұрын
Iran refelal bakhna trop mais mousafir doudjite lolodal serigne touba ak serigne abdou Aziz sy la vérité restera toujours la vérité
@diagnediagana99104 жыл бұрын
Iran légi ga changer rek mé yadakhona digate
@hamadoucamarahamadoucamara49924 жыл бұрын
Yaw ya meuna doull gniko dakka dingate gningui fi té wakho ko
@malickdiaw81714 жыл бұрын
Machalla
@morgueye26354 жыл бұрын
Machalla oustaze iran
@assanendiaye16674 жыл бұрын
Limo raféte
@KENZOTVS4 жыл бұрын
Iran Sou Mourid De Tidiane La Da Rafet Xol Rek
@boygainde37644 жыл бұрын
Serigne touba delen ko defal wakhtan spécial mé bolen ko bolé ak talibé yi Maoda moy dieuwrigne serigne touba
@papaalassaneseye82524 жыл бұрын
Da ngay doul serigne touba amoul won fitu wakh lolou kham nan leup
@boygainde37644 жыл бұрын
@@papaalassaneseye8252 serigne amna khassida yo khamni dako neub degn thi ko kokou lou mou wakh damite bi sakh wakhagou niou ko Ahmadou bamba point le reste au coin
@papaalassaneseye82524 жыл бұрын
@@boygainde3764 ah bi mou nan koudul yalla mala fete kaw astafiroula ni may mbindane yonenti bi ba pare nan mako fete kaw lolou logique amou thi yaram wa tangon rekk🤣🤣🤣yoyu tere bulen ko guene ne deiy takh gnu khepp ko kheb lene nakh abus de pouvoir la ak bokale yalna ko yalla djieugal rekk nakh kham na andul wonak sagom
@boygainde37644 жыл бұрын
@@papaalassaneseye8252 et pourtant c la triste réalité koudoul yalla ak yonentibi mola feté kaw lolou mome yalla moko dogal di ko fayé ay jummah you dakk thi monde bi ak kheweul you doul diekh