Merci de propager les enseignements de Serigne Touba et de Seydi Hadji Malick.Une émission religieuse n'est pas de la télé variété. Vous avez été à la hauteur.Les écrits de nos anciens sont une mine d'or.
@jadoredieuetmohamedkhadimo25214 жыл бұрын
Bayilene di dendelé bamba ak maodo yalla ak yalli la
@ibrahimafall98804 жыл бұрын
Dieureudieuf Ibrahima li moy wakhtanou diner yene rek yena meriter diokh ay million yalana len yala faille barker Mohamed daradjey serigne touba
@KhouKi14 жыл бұрын
Wallay ndeysaan, wax dji rafet na Oustaz Aliou Sall
@abdoulayecisse68134 жыл бұрын
Machalla oustaz yi Senegal mo Bari ay dof AK ay fen kat
@kif74714 жыл бұрын
Il est tjrs constant Machallah un vrai rassembleur
@kinesoumare70124 жыл бұрын
Yaa oustaz, shukran. Gni wara wakh sou len médias yi diokhé kaddu, légui pinth mi nekh, dadialoo, boolo nek ben, diiné dji am ndam. Chatané ndeurmélou. Sénégal dieum kanam. Lepp doone diamm ak khéweul. ALLAH SWT tappé khol yi. Nek len thi diamm.
@mbackemammor14693 жыл бұрын
Machallah amna solou tourop yalla nalén yalla diappale si bargu Serigne Touba
@daroukhaforcouturegadefall894 жыл бұрын
S touba amoul morom
@papaassanegning89584 жыл бұрын
Thi bane côté
@cheikhndiaye51434 жыл бұрын
Si kote dine bepou Senegal soune dine s Touba Takh..........
@@abdoulayecisse6813 gni dagnouy fonton nite gni rek wakh rek té lingay wakh téguo ko féne thi xam xam
@khadimkhebe77494 жыл бұрын
Mashallah amna solo loool yalla na diamou yague si Senegal 💜💜
@seyeabdou26963 жыл бұрын
bilahi machalla yéna mana diangalé oustage aliou sall Iran ndaw
@niangniang10944 жыл бұрын
Machalla ya oustaz dieurdieuf yalla nagefi yague lol thi wér amine
@khadimndiaye34714 жыл бұрын
ndayesane wallhi amna solo looooooool ☝☝☝👏👏👏👏
@abiboullahdieng20734 жыл бұрын
Wayy Dieureudiefff Oustaz Halioune L'héritage de nos Valeureux Érudits mingui beuga naxass...Al Qur'An Ak Sunnah rek lagn done diangalee Alhamdoulilah si souniou mag niou bax gni🙏🙏🙏
@parisparisparisparis66064 жыл бұрын
Machalla Machalla rafetna
@shamthiam77744 жыл бұрын
Li moy deug deug talibé cheikh, wahé xam xam bouy diarigné teh dou loré wahé yar ak ay têguine xam lissa Serigne wah ak bossou kénen machallah ya oustaz ken dou wéraneté si sa pédagogie.
@moustaphathiaw16124 жыл бұрын
Machallah am na solo lol thieuy S bamba
@rebeltv22124 жыл бұрын
C'est vous qui méritez être dans les plateaux au lieu de laisser les ignorant parler du cheikh de n'importe quoi. Merci Oustaz
@bambambaye58273 жыл бұрын
Vraiment c très intéressant âme n'a solo
@saliouniasse83334 жыл бұрын
S touba rek mogfi ne kendo s touba mom rek la
@lufthansa12734 жыл бұрын
Oustaz vous forcez le respect maachaallah
@bambaniang93053 жыл бұрын
Mach Allah y'a oustaz 🕌🕋
@ndiayetechjr67244 жыл бұрын
Yalna rewmi am diam
@fatoundoyembengue60334 жыл бұрын
Voilà genre yii gno wara tok si télé yi
@ndeyefatoumafall65964 жыл бұрын
Ñgi douniou aye nafekhe mo takh
@fatoundoyembengue60334 жыл бұрын
@@ndeyefatoumafall6596 bilay ndeyssane fa moy DEUG dh
@mamadoulaminekassogue4094 жыл бұрын
Télé yi dinee nioroulene
@dieganendiaye6904 жыл бұрын
Nagouna ak yew bo boubakh
@moustaphafaye58974 жыл бұрын
Machahala oustas
@dieganendiaye6904 жыл бұрын
Machalla amna sollo trop
@modousall23943 жыл бұрын
Merci oustaz et Dieureudieufé tii Ahmadou Bamba
@fatoumata56193 жыл бұрын
Mashala émission très intéressante
@khadimdiakhate92214 жыл бұрын
Nane kenal s touba rek yalla def diamou
@abdoulahidrame87164 жыл бұрын
Assalamu anlaykum frère Au nom d'Allah le Tout Miséricordieux, le Très Miséricordieux Louange à Allah, Al hamdu lillâh rabil âlamine Sante niel na borom assamane ak souf Al hamdu lillâh borom Ramadan, Al hamdu lillâh borom Djibril, Al hamdu lillâh borom Mikâ-il , al hamdu lillâh borom al Quran karim, Al hamdu lillâh borom Adam ak ndiabotome, al hamdu lillâh borom Dinner yi, al hamdu lillâh borom Al djana ak Safara,al hamdu lillâh borom tonnerre yi, al hamdu lillâh borom tremblement de terre yi, al hamdu lillâh borom guend yi ,al hamdu lillâh borom Malakatul Mawty, al hamdu lillâh borom bambel, al hamdu lillâh borom alakhira Al hamdu lillâh le Vivant , lâ ilâha illa-llâh et que paix et salut soient sur le Prophète(SWS) et ses compagnons et ceux qui le suivent jusqu'au jour de la Résurrection
@abdoulahidrame87164 жыл бұрын
Je vous confie que Allah késsé mo yéyo niu kennal ko, kudul Yalla bindef nga c'est Allah l'Unique, Allah mo bindi Magg Gni, Yalla kene-la moy def moy dindi ,moy yeketi moy wathié , moy dundel di rayé, moy dioxé moy xagné, lâ ilâha illa-llâh ☝ Magg Gni bugnu dêgone linga wax sen yaram dina daw nguir reyaye linga wax " Kennal bindef " soubhâna llâhi Al hamdu lillâh borom Serigne Touba, niu xamni sunu teranga ak sunu tékhé aduna ak alakhira mongui ci lâ ilâha illa-llâh Mouhamad Rassûlu llâh(SWS) Balma aq balnala yalnaniu Yalla dieugueul nangulniu Et que paix soit quiconque suit le chemin droit.
@khadimdiakhate92214 жыл бұрын
@@abdoulahidrame8716 yaw ab dof nga bounouy kenal yalla lane jital waye yaw khamnane la khamnane finga bok kou wakh fenie soxor motakh dolen am dara
@abdoulahidrame87164 жыл бұрын
@@khadimdiakhate9221 Al hamdu lillâh borom Magg Gni bax yi
@abdoulahidrame87164 жыл бұрын
Serigne Bachirou bula dêgone nga xam
@mbackesmammor17674 жыл бұрын
Machallah amna solou tourop
@sambagaye64484 жыл бұрын
Notre professeur que dit le responsables moral du darahiratoul moustarchidine oustaz alioun sall
@alioundao51954 жыл бұрын
Machala amna.solo
@moustaphagaye72524 жыл бұрын
Trés bien rafétna amna solo
@racediop55253 жыл бұрын
Billahi bou ñiou démé si téré yii gua kham ni serigne touba doussa morom sah
@adamaba65083 жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️✍️
@rebeltv22124 жыл бұрын
Merci la sentv tout au long du ramadan vous avez laissé les ignorant parler de serigne touba jusqu'à la fin vous invitez les vrais savant pour clôturer. Merci pour ça
@birahimndiaye48604 жыл бұрын
Qui sont les ignorants ? Si vous faites allusion à Abdoulaye bichri ou Gana Messere ils ont étudiés en plus les argumentaires reposent sur le coran, hadiths et les écrits de Serigne Touba et des archives Ils n'ont rien créé. Serigne Touba daffa universel kounek ak fi gua kit wakhė
@diengdieng28854 жыл бұрын
Macha’llah
@Ndeyadiop24124 жыл бұрын
❤❤❤❤🙏🙏🙏🙏🤲🤲❤
@malickdiallo50294 жыл бұрын
Mashallah Oustaz Alioune Sall Shukrane yallah na yallah Faye yiweu Goudeule say fane maye la weur akh weurlé
@asnaakhadiimgueye83094 жыл бұрын
Serigne touba lone la binda
@aidatoure65664 жыл бұрын
Machallh
@moussambengue99884 жыл бұрын
Machalla
@laminendiaye10134 жыл бұрын
Très bien
@falloufall34864 жыл бұрын
Waye li ngeen beug mooom do am Serigne Touba yam ak niepp monta neck kenn do Serigne bi
@oumarkonta80404 жыл бұрын
Wax ngua deug déhh dioumoo dehh ndax ba adouna di touki do meuss dégue Serigne El-Hadji Malick sy Je ne sais pas si vous me saisissez ou pas
@mansourndiaye79544 жыл бұрын
@@oumarkonta8040 est ce kham nga lutakh. C parceque moom talibe jambur la
@papaassanegning89584 жыл бұрын
Mofi rawe thi bane domaine la beugua khame
@mourtadasarr19524 жыл бұрын
@@papaassanegning8958 Banial Lolou yawi tam Bamba Amoul mass
@papaassanegning89584 жыл бұрын
@@mourtadasarr1952 wa doma wakh thi bane domaine
@serignemordiop444 жыл бұрын
Amna solo trop
@mbeurgoufall8334 жыл бұрын
Un vrai pédagogue Oustaz Alioune Sall. ..
@mustafasall18574 жыл бұрын
Amnaniou mbékté bubax 🤝🏽
@alimakonate52374 жыл бұрын
Nguirr yalla kou am numéro oustaz alioune sall damako sokhla. Svp
@fatoundiaye82244 жыл бұрын
machalla rafetna ira ak ustaz sall
@rebeltv22124 жыл бұрын
Machalah Oustaz lerna te goudoul si c'était gana messere il allait crier toute l'émission sans nous apprendre rien de juste sur serigne touba
@alkhalifatvmedia99704 жыл бұрын
Wàllàhi t'as parfaitement raison
@ndarawseck75644 жыл бұрын
🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@mtraxwz34634 жыл бұрын
Toubabiser.... Islamiser. /Oustaz Alioune Sall un grand pedagogue. Diaguene Dieuf!!!
@fallouthiam72224 жыл бұрын
Cey oustaz yalla na goudou fane
@falloufall34864 жыл бұрын
Yalla yamale woul
@papaassanegning89584 жыл бұрын
Maname
@modounian12604 жыл бұрын
🙏🙏🙏
@moussasarr673 жыл бұрын
Yague lene fi lol te werr ira Ndao oustaz Aliou sall loguene di def ame na solo torope billakhe mande talibe Serigne touba la nono wouma ak bene dioulit bo khame na manou na si aw laminiam
@papetop26434 жыл бұрын
Asalamou aléyecoume raféte na lolle wayé wérou kore rek guéne koye défe deugue P layike mé nak done na guena rafete 2 foie pars semaine
@jadoredieuetmohamedkhadimo25214 жыл бұрын
Senegal amoule mbindef boufi melni serigne touba moy dathie deup gui tidiane ay wakhou serigne touba laniouye deup di wakh nane maodo wala serigne nena dilene ko momalé bilahi dara dousi deug barke yonent bi ndax a part serigne touba diamou yalla niome gnigui ko commencé bi bamba diogué guedji bouniou kene ray dafa kharam si sosale ko diap ni nitou yalla la tek si serigne touba dafa def mak nia guis mou wakh niako feké degue mou binde bayi fi niou dioudou diangue ko kham ay dieufeum souko kenene defone nit niou nangoule koko ndeme cheikh Ahmed tidiane cherif mou nangoule serigne touba liko yalla defale nangou ni guinaw yonent bi du mamame serigne yamoule ak bene mbindef si kaw souf legui nak ay talibé cheikh surtout wa tivaoune ba beuga dieule maodo mi di talibé cheikh Ahmed tidiane ak cheikh oumar foutihou tall diko dendelé ak kou teed ki deuk di nakh sene bop ak gni amoule khele diangouniou c horrible!dieureudieuf khadimou rassoul ahmadou bamba borom touba yakarou diam gni tay ak euleuk koumou nekh ak koumou nakhari kofi yakar cheikh ahmadou bamba la yakar kousi wete faw gua weteule ko dieule ay khasidam def ko sa ganaye arrêter porté lene plainte yalla moko def bala sene khole yi di dague
@papaassanegning89584 жыл бұрын
Démale diangi yaw linga khame beuri woule
@ngatediop37744 жыл бұрын
Mak niou bax ngi nieupaaa ben laniou naniou rafetaaal rekk mo guen yiii
@abdullahsenegal97083 жыл бұрын
ما شاالله جركين جف
@mouhameddiagne20024 жыл бұрын
djadjeuf waaye
@ngagnediop85773 жыл бұрын
Yaostssyalanalayalafaye
@fatimadaffe30394 жыл бұрын
Oho sama xol sedd na lii dé moy Sénégal
@afiafall51234 жыл бұрын
Oustaz allune sall ak iren nawe yague ak. Werre. Afia
@cheikhibrathiaw28554 жыл бұрын
Li moy kham kham
@ousseynouthiam82284 жыл бұрын
❤❤❤❤❤❤
@ramaba25213 жыл бұрын
Doundeul wereul mouthieul Sall
@djogueelsamb75964 жыл бұрын
Karim nioumouy KHÉÉKHAL FALÉÉNIOUKO Ana imamyi ak oustazyi 🤣🤣🤣🤣🤣 Niou ngii Nééték di meukheu sééni thiéré bilay Macky Sall moy Gayndé
@ibrahimandiaye92564 жыл бұрын
Vérité absolue . Je me demande si ça vaut le coup de se battre pour les Sénégalais . J'ai vraiment pitié de ce jeune homme , il ne cesse de se sacrifier pour des gens qui ne se soucient même pas de lui .