L'ÉTAT doit prendre des mesures avec certains jeunes qui ne veulent pas travailler et qui restent la à agressés des honnêtes gens. L'agression doit être "Criminaliser".
@baubaubeye78362 ай бұрын
Il faut que aussi kogne bounek dieul sa matoukay 😢agresseur yi daniou leine bayi si louniou néké
@PapeganeMbengue2 ай бұрын
Merci Merci merci ki nieukeu wah wah na laipe
@momondiaye29302 ай бұрын
Lamb dji mo amoul béne avantage loudoul agression ak vole mbeur yi séne intérêt personnél rk laniouy xoll
@Jeunetalent-tg8ck28 күн бұрын
Lou ler nga wakh
@sanguebitv84292 ай бұрын
Lamb ci bopam mo amoul béne ndiarigne
@AmoullYakhalaté-d9sАй бұрын
Amoull yakhalatté
@Faby-u7hАй бұрын
Mais defois d'où nek boy kogne bi sou lamb âme par exemple parcelle wa grd Yoff grd Médine diamagueune Médina nieupey nieuw souko defe bandit yi nek si quartier nioy bolo envahir rue yeup
@mamadoundiaye96832 ай бұрын
Senegal dagno meuna sétane
@OusmaneLy-s3q2 ай бұрын
Grand linga wakh degeu la mais Sénégal wakh AK filme lanoui meune te nougnou niou deff Macky Sall manifeste tall lolou bougne defone agression legui mou dagne mais dagno nafekh bou président jagalgate ngene du manifeste Khana policier lagnou n'aime ragal agresseur yi guisna Rufisque quartier diokoul aye legui niofa dieuk sathie BofA douga Wala agresseur niou ray sa ndeye motah agresseur Wala sathie dokafa guiss mais bethiek danioula agressé ay gor takhaw dila setane lebou yi ngay agressé sen mbokou si quartier dagne laye raye
Kon danioula topou yéne somme yi kén douko yor di dokh
@Sokhnadiarrapastef2 ай бұрын
Sama petit frère moto laniou dieul diamm livreur bi😢😢😢😢😢😢
@SodaFall-xp4tlАй бұрын
Merci bro tu a raison
@Kharim50182 ай бұрын
Boy ay guaka lagnou. Diambar dou simol.
@PapesaloumDiedhiou2 ай бұрын
Le gouvernement doit interdite la lutte senegalaise , la lutte senegalaise c' est seulement la violence il faut que le gouvernemet suspendre elimine definitivement la lutte y'a aucun interet pour le peuple senegalais c'est ca la verite
@babasao91302 ай бұрын
C grave mon pays va mâle
@ndeyefatougoudiaby7442 ай бұрын
Il faut demander à la police de faire une descente vers la cité Mixta
@MamadouKébé-y5tАй бұрын
IS bien parle
@boubacarkeita6952 ай бұрын
Diap bandits Yi dé mo Guen topou si politiciens you nek en perte de vitesse ngalen di mayy buzz.
@ousmanefall71092 ай бұрын
Waw gor !
@diakhatecheikhna81462 ай бұрын
Premier ministre bouy wakh gatsa gatsa lhaleyi lou geuna piir di naniou ko def naniou dem rek Sénégal c'est fini
@@AboulBacharSall 😂😂😂 Fi reewmi tolou deh kou beigne Sonko urgence Cardio rek ngay moudjé😂
@loudoulaktalibesafouma34292 ай бұрын
Walaye waxati ko sonko limou Ndianguel boy yi mome la boy yi ti taré agrésé rék réwmi dina geuna métti ndax ñep xamnagne ni gni réyé nit garage a sonko
@oumylaye94642 ай бұрын
@@loudoulaktalibesafouma3429 Sonko reyoul kene dina leer Ana Bandiaky Khaleyi di manifester sene nakhar gnouy tirer balles reelles si sene kaw amoul fene si adouna bi
@ibasow7591Ай бұрын
Militaire yigniy formés ba paré bayil dougnou lene diokh ligueye té gnou kham armée am fitte pour moi c'est l'état qui est fautif.
@SaliouneBaye2 ай бұрын
Boy bounou si diape ray sa yaye
@OmarMbay44-o6e17 күн бұрын
😢😢😢😢😢😢
@nafisatougaye450Ай бұрын
Billahi wakhna degue kaddu yi mo infiancé booy yi tik tok bi téléphission yi musique bi 😢😢war nañiou kholat sounu bope
@khadimka2058Ай бұрын
Problème jeunesse bi moy Xbet1 nanko dieulé Sénégal perte gui boys yiy perte moleni sathilo Billahi djiko yi dinan yakhou Sénégal fi ak 5 ans sounfi dieulé woul Xbet1 agresseurs yi day yokou ndakh amna nio khamni khaliss diambourr laniy perte moy takh niouy sathi
@MEMO-ENGLICH3 күн бұрын
c la lutte que l'on doit arreter pour un petit groupe 95 pourcent de la population empathie
@FatouDiedhiou-xo8mmАй бұрын
Courage ça va se regler
@mouctardiallo98592 ай бұрын
Sama gars yii il faut ma profitoo sensibilisé leen 😅 bouleen mèr nak mais deuk bi saloum saloum yii rek nioo niroo ak nioun guinéens yii niak diariniou kessé mais supporter tahirou sarr yeupp sathie kessé ak xbet voilà le résultat
@BinouchaDiouf2 ай бұрын
Ndéreng doumbouya dina len dieulssi yen nieup😂😂😂
@KhadimNdiaye-i5o2 күн бұрын
😢😢😢
@Forevrr-s3n2 ай бұрын
Thiey senegal bougne la farale kene doula toudou wadji nena tiktok bi la il ya 6mois lou khew niou djineko kokou nonou
@awafaye39902 ай бұрын
Ousmane Sonko n'a rien à foutre de tout ça
@djibrildiouf-l5p27 күн бұрын
doyna war khalé boun ci diap dorla ba nga dé
@WeuyouBayeАй бұрын
Seulement des groupes d'autodéfenses dans chaque quartier comme en côte d'Ivoire qui pourrait réglée l'affaire.
@nafisatougaye450Ай бұрын
Ay way li métti na trop
@oumarsall478518 күн бұрын
Agresseur mom ray ndéyam rék.
@NdeyemaieMbengueАй бұрын
Man mi sama dieukeur motom si bountou keur gi laniouko fék sathieko
@seringembacke93162 ай бұрын
Rew mi dou bax
@KarineKabatou78552 ай бұрын
Hee Sonko dou si dara ce nou dans nou rek
@moustaphaniang9852 ай бұрын
Kone c grave
@lamineba98432 ай бұрын
Moi j'ai eu de la chance, ils ont arraché mon téléphone portable mais leur scooter a dérapé et il est tombé par terre. Franchement il faut trouver une solution à ces gens là
@FallouNdao-l3z2 ай бұрын
Wa Sénégal Sonko moy président wala 😂😂😂😂 Diomaye nak warna guiss bopam😅😅li humiliation laa😅😅 6:40
@benzdictenobalegomis61392 ай бұрын
😂😂😂😂
@moustaphaofficial2 ай бұрын
Wallahi li mètti na trop
@Faby-u7hАй бұрын
Tey rek unité 11 juste damey dème pharmacie yoor sama niari téléphone ak pochette tt a coup rek bene scooter avec 3personnes nieuw rek enfonce beugue dal sama kaw ma arrière kene ki nama hee loy daw maniko domeram ay voleur nguene bilahi suma siboul wone action Kone Moy lolou parcelle môme lifi xew baxoul
@manegaye2 ай бұрын
Lamb laniou wara interdir diam né nioy guisouma sense boumou ame mane sila niou profito di agresser rek
@SYLVESTREKANKOLA2 ай бұрын
Thiéy Sénégal 🫢🤭
@moustaphasall3317Ай бұрын
Méttina trop mais yalla diéhoul
@abdousarr9749Ай бұрын
Dageni diougoul sey bopou kouguen si diap Ray lén KO kom police diarignoul Dara Sénégal amoul securite
@omarthiam-cd4pb2 ай бұрын
Si l'état ne prend pas ses responsabilités,le peuple doit réagir
@MamadouLamineNgom-t4gАй бұрын
Mais je me demande dans quel pays sommes nous ?
@CheikhGueye-d7eАй бұрын
Wotal nganye gor dodkh lokhou nene
@kebadanso6356Ай бұрын
Orange money et wave
@mamadoufaye99622 ай бұрын
Dèlene yorè sen paka boubakh di armè wou commeca rewmi amoul securite bou mguèune kharè etats bi agresseur dou gzwa safarawou woute lène seni paka ak seni diassi lolou lasi kham dé
@bambasamb5412Ай бұрын
Biilay walay
@MatarDiallo-n3mАй бұрын
Li Sénégal rek la am bo agressé mali oubien guinée gnou tall sa ndeey bilahi
@makhfaye-c2k2 ай бұрын
Populations magui léne di yeguel agrétion bi yéna ko mena fadial séne bope koléne ci diape raye léne ko mou djéx doméram domou tiaga yi
@abrahamfaye5359Ай бұрын
Wa mais a quoi servent les caméras de surveillance ? Nagnou defff fep ay caméra
@ThieDemeАй бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😱😱😱😱😱😱
@nafissatoucisse1697Ай бұрын
Parcelles stade bimoko yakh
@moustaphasall3317Ай бұрын
Hamnako c'est mon amis
@seringembacke93162 ай бұрын
Sonko dé worna bou yage
@oumylaye94642 ай бұрын
Bon khataraayou Sonko dal mooo ame bayré Massalene
@baubaubeye78362 ай бұрын
Wa yaw tamit li loumou diote ak sonko Hors sujet rek 😂
@DibiKankan2 ай бұрын
Tout luteur attribuer UNE license doit signer un contrat de gardien de son citer avec l ecurie ou il s entrainent et recoivent un UNE subvention de 30 mil par mois de ce fait ils aurons l obligation de veiller a la security urbaine , au d Autre l etat cree de nouveau prison avec des torture atroce a l example du prison cecot de Nicaragua ainsi ce Mal sera irradiquer du pays, c est mon opinion
@MamethiernoPouye-u7h2 ай бұрын
Day daw rek
@abdourahmanediop6468Ай бұрын
Ses actes de délinquance sont énormes à Dakar et environs après les combats de lutte. Les forces de l'ordre ont une part de responsabilité vraiment il est temps de prendre des décisions pour apaisé cette tension qui a commencé à terroriser notre société Sénégalaise . La population a besoin de souffle d'après les années précédentes nous avons beaucoup souffert durant les 3 ans donc unissons nous les mains dans la main pour un sénégal meilleur que avant. Bonne et heureuse année à toute la nation Sénégalaise. 🇸🇳🙏🇸🇳
@Seydounourou-b3v2 ай бұрын
Vraiment le sénégal va mal
@djiboka92482 ай бұрын
Police lan moy ligueyam?
@aliounebadaralo70362 ай бұрын
Simol youou nioma agresser jours combat B52 et Franc vers 16h 17h coté Ndingala wallahi j’ai mal ay gorr you léngue ak séni khourrr di agresser Opération reubou agresseur yi joteneu koune thi japou ray sa ndy
@kheuchakhloubadar7822Ай бұрын
Alioune Ray ngama 🤣🤣 khour kai
@MakineKa-tj1duАй бұрын
Massa mon frère 😭😭😭
@Bassdiop-l5n2 ай бұрын
Yagna diwakh lambou amoul ndiarin sathie agréssion wakh dioubari Sénégal daniomana séetan li population bi nioko mana fadial sén bob
@FodayJallow-d4sАй бұрын
Si on fait des enfants toujours alors qu'on a pas les moyens, et Les imams qui sont là à nous encourager à faire beaucoup d'enfants et Qu4tre femmes ...🤔
@AbdoulahatSeck-c7t2 ай бұрын
Kounisi diap ray rek bilan
@samaypapier827914 күн бұрын
Zero KULUNA zero Simol
@dieneadjia43132 ай бұрын
Sénégal D'où Dara
@AmoullYakhalaté-d9sАй бұрын
Amoull y
@KocaniDiattaАй бұрын
Vraiment c'est pitoyable
@bahfall74162 ай бұрын
Sathie bouniou diap bama feke KO Di nga niam 33 Kourou bop ni maléne xife dmrm yi
@taphagueye12422 ай бұрын
Vraiment lou lerr
@ladetente-yt7mz2 ай бұрын
Non c’est Senegal woratoul
@lucialucia243914 күн бұрын
Peine de mort mo wara fi senegal li dafa yom
@elagegueye33102 ай бұрын
Bo diagon do wahni worna rasouloullahy.yagi fendee yalla rek la woor.bokaleleu wat si nit dafa haram
@sallelhadji523914 күн бұрын
Zé
@senycoly130314 күн бұрын
il faudrait pas que ces jeunes deviennent des kuluna du Congo. L'état doit arrêter ce réseau