Dieureudieuf Sr saliou samb yalla nga fi yagg tei werr in cha allah.
@bmtv-zb5xl5 жыл бұрын
Machala yalla na s touba yokou sen tawfekh
@LayeDiaw5 жыл бұрын
I can listen to Serigne Saliou Samb for hours, just can’t get enough. Amazing voice and presence!
@ngagneafiyaseck16805 жыл бұрын
Yalla mi bindeu diamnié sakh amna niouko gamoul amna niouko topoul .lolo takh Lima beug si rewoume Sénégal doumako mana âme ndakh liko sama borom amoul té mooy niepou toppou serigne cheikh Ahmadou bamba Khadim rassoul gaumko yakar ko doyloko billahi wallahi kone adiana lanouy doundou bou wer limo nekk sama yéné si Sénégal thiey soumako amoune yalla nanou yalla défall tawfekh si cheikh Ahmadou bamba Khadim rassoul
@sismahilakandji29805 жыл бұрын
Machlla. Thakanam
@abdoulayendongo79555 жыл бұрын
MAAME BAMBA MOY MAAME YALLAH TAY BA EULLEUKKK!!!.(MF)
@diagnediagne75175 жыл бұрын
Merci merci merci merci merci merci merci
@diagnediagne75175 жыл бұрын
Merci merci merci merci merci merci merci
@senegaleseboy66385 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne Touba Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall🙏🏾🙏🏾🙏🏾 Serigne Moutakha ak Serigne Cheikh Fall Dieumb Yalla nagn fi yàgg lol ta wër 🙏🏾🙏🏾From Italy
@assanegueye50715 жыл бұрын
Ibra Thioune waa grand bi ziarnala lou beuri
@bassiroudiop58535 жыл бұрын
sante naniou bu weur way serigne touba mame cheikh ibrahima fall point❤
@racinepam92205 жыл бұрын
Serigne saliou samb yal na sa diam yagu yaw motakh machalahh wakh tane bi am n'a solo loll serigne touba .
@macdi64295 жыл бұрын
Serigne Salliou sambe mashalah yalla na Serigne Touba faye
@cbonmoi34035 жыл бұрын
@@leuzleuz8602tu n'as rien compris et tu parles avec trop de haine
@cherifdiop40015 жыл бұрын
@@leuzleuz8602 domourame yaw dhé lila serigne touba mome mola nakari mé kéne doula tontou psk yaw téguiwo dara tu es un imbéssil so amé fite rék gnewal ga déf face à face ak béne mouride diga khamné kéne dou domou mame Diarra bousso dji
Serigne momour ndaw ak serigne alioune badara ndime yalla na nguen dadie ak ndimbelou mame cheikh ibrahima fall amine
@abdoulayediop11755 жыл бұрын
Jaajën Jëuf ti murid. Jotaay bi baye fallé lol fall. Yalna ngën am té lakh ngeureumeul Cheikhul Khadim Mustapha ak Sidy Birahim Fall Aboridial thi barkep Fallu Gallas. Cheikh Alioune Badara Ndim, Baye Modou Mamoune Ndaw ak Serigne Saliou Samb, yalna séni diam sakh thi barkep xassida yi. Laye Diop baye fall
@tallandiaye455 жыл бұрын
Machalla s saliou sambe sago youn wi ga yalla nalla yalla takhawo
@louisediagne675 жыл бұрын
Macha alla amatina solo sante mame borom touba rekh ak mame lamp fall ❤️
@khadyndiayeyayefall90145 жыл бұрын
Serigne Saliou Samba yaw dokhalal rek diam rek ngay am machallah serigne mamour ndao amna doméram yo xam ni diarounio tontou
@yayefalldevofficielle38225 жыл бұрын
Manchala yalla na yalla doli takhaway bi thi barkep Mame Cheikh Ibra👌🏾👌🏾
@baayfalldiop94065 жыл бұрын
Waw goor fall,nagnou diamou yalla ta ligayal serigne touba motax niou raw yép
@cbonmoi34035 жыл бұрын
@@leuzleuz8602 yaw mom sa khol mingui dague di
@abdouazizsarr40595 жыл бұрын
Yala nerna ak yonetebi mougene gendi leeb ak loup dagadi fountou rek
@baayfalldiop94065 жыл бұрын
Abdou Aziz Sarr ho jeune homme yagui perde temps,dèmal xol loula amal ndiarign ou tu vas o lit dormir
@baayfalldiop94065 жыл бұрын
John John tu as vraiment de temps a gacher oubien tu es chomeur de classe luxe
@niangcheikh24315 жыл бұрын
Machalla yalla n'a yalla Faye lene thi Barcke cheikh saliou mb Sa MA Yakarr
@sideuglayedokhbambapoint60225 жыл бұрын
Loumay toujours minginii serigne saliou samb niome gnii tok di wakh si mome kou togoke mome mou djangal diangal niala diangal ! Koudoule serigne bamba ak mame cheikh mouno kham fou yalla fété bilay
Wakhtane bi am na solo trop franchement nous sommes très ému de vous ... Dieureudieufé serigne touba
@bayediagne34923 жыл бұрын
#Yaradif serigne touba amine cheikh ibrahima fall amine Mohammed amine yalla #
@serignefalloufall42423 жыл бұрын
Khakassa dieureudif serigne Fallou mback mo bakhe yalla nagnou co yalla fayale amine si barckp khadim rassul theiy Ahmdou borom diamgnji dieureudif mame cheikh Ibra fall lamp baboule mouridin khakassa👂👂❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇧🇪🇧🇪🇧🇪❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏿
@balla88435 жыл бұрын
waw léne gor Serigne Mamour sr Alioune sr Saliou Samb barkep cheikhera Fall
@mamadoumoustaphadiallo5025 жыл бұрын
Serigne saliou sambe, douma mouride mais damay tewlou say diotay té kou beugue seurigne touba ak serigne mountakha la. danioulay nianal weer et catane. Malay gnane rek ngay guena wax ci seurigne touba ak wa keureum ndax amna solo
Yalla nagnou yalla defal diam Ci barkeb Cheikh Fallou Mbacke Ci barkeb Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar
Dieuredieuf El Hadji Fallou Mbacke mo tabakh Djouma ji woté Magal gui di fathe adio yi Yalla na Yalla yoke ay léram té tass gnou barkem
@fatouhane83035 жыл бұрын
ÇBQ
@diagnenarre74485 жыл бұрын
waw len goor mouride am na solo machallah
@jhoosarr58675 жыл бұрын
ni ngay wane serigne touba mo nakhari noni serigne touba yi mee cou bagne bamaba do am diam fi ak faniou diuem
@touretalla38045 жыл бұрын
Walakhi
@jhoosarr58675 жыл бұрын
merci balnala ngir diemmi yonent bi s.h.w
@mouhamedrassoulka32145 жыл бұрын
nitt dé koukaye woutal none moye noname té ki ngaye tague défa togne yonénti bi néna dimbalél sa mbokk bou togné ak bougne ko togné konak wakhlénko mou bayi togne cheikh tidiane dou morom mame dou moromou koudoul mome kiye serigne thi cheikh oumar ak al hadji malick sy ak mame abdoulaye niass ak baye niass ak niénéne gnoudoul gni té serigne touba sakh diarr na thi tarikha bi sa serigne foumou diarr war nga fa diokh thieur wakhléne saliou samb na ame yarr té loumouye wakh mou djéféko
@jhoosarr58675 жыл бұрын
@@mouhamedrassoulka3214 me yen comradroulen walla da ngen buegg comprandr lenen ki khalatoul soufel cheikh walla con dou mourid psk serigne toubacou fonk cheikh la wakh diodiou yagna dafa dioumon ci ay wakh psk serigne mbaye sy daniwon idy coumou diokh lokho nga nangouko seytane nga mom la don tontou
@jhoosarr58675 жыл бұрын
nioun wormalnanoiu mam el hadji malick psk moy khalifam motakh tontou wouniouko ligniy wakh naniou sett yalla te henn gi ak nafekh gi
@mamemortoubawakanahakhane61235 жыл бұрын
Manchala amna solo
@padjibydiop98215 жыл бұрын
Machalla amenasolo
@seckndeye4215 жыл бұрын
Serigne touba amoul morom
@fallougaye86494 жыл бұрын
Jeureujeuf SERIGNE TOUBA CHEIKHOUL KHADIM❤️🔐
@cledorofficial42095 жыл бұрын
Yalna lène cheikh Ibra fay ci bakèp S.Touba...
@Santssaliou5 жыл бұрын
S Zaliou sambou amna solo
@mboupaminata1320 Жыл бұрын
Khol sedd fall .thiey Mame Cheikh Ibrahima.fall. Dieureudieufety serigne Touba
@lahatedieng76805 жыл бұрын
Serigne Saliou samb yalla naga gouddou faane ak mbolem djoulitt
@mansourmboup76595 жыл бұрын
Sama xol da sed et play gouma. Dieuredieuf borom touba
@yarakteggin30805 жыл бұрын
machalla s salihou sambe yalla nangou yalla saxal si Serigne touba contane nangou lool mouride barké cheikh ibra
@basstouhfatoukebe83885 жыл бұрын
Jazboul mouride mom ( no comment) saa sounè day gueuneu kawè. Wayè dilene nianal tawfekh ak taysir ci doley cheikh ibra fall lampe 🛋
Fa tabaraka lakh yalna len fi yalla yagal contane nagnu
@boblingb40515 жыл бұрын
Machalha diardiaf s touba amoul morom ya bakh mbacke diarma mame lamp fall
@dioptapha98655 жыл бұрын
WALLAHI MAN MOUSTAPHA ALALOU BOROM TANZILL BEUGUE NALA DH 💗
@falloudia10165 жыл бұрын
Wakhtanewi amatina sololool Dieureudieufati Cheikh Fallou Mbacke Dieureudieufati Cheikh Mor Dia Ndiar Sene mbokoum Talibe Elhadji Fallou Dia di doom ci Cheikh Mor Dia Ndiar
@avektv38695 жыл бұрын
Jam rek ngay am de inchallah barket cheikh ibra
@omarkane67164 жыл бұрын
Akasa Dieureudieufa serigne touba
@papandiaye9845 жыл бұрын
Serigne Touba Point.
@babacarndao79315 жыл бұрын
Machala am na s olo diadiafaty yagou line fi lole te wer
Dieureudieuf Serigne touba Mbacke rek Sama Serigne
@clementfofana67175 жыл бұрын
Akasa serignebi;;j'ai entendu des gens qui ont voulu vous faire dire ce que vous n'avez jamais pensé;c'est parceque votre niveau d'élocution est tres haut et au senegal ils aiment sortir des idéés de leur context,mais j'ai été émerveillé par votre silence;que Dieu vous agrée bijahi cheikhul khadim
@mouhamedwade4015 жыл бұрын
Bilahi que la paix t'accompagne frère
@papeboubaba89855 жыл бұрын
Bilahi yaram wakh nga leppp senegal mom yalla naniou defal diam.rek mais borom khel yii nio diaral wakhal ...wakh dafa ladj degg degg mais yalla nalen yalla sopi diadieuf serigne saliou samb gounal fann te am.weer serigne touba rek mola niorrr dc boul fale boul topato ...
@cbonmoi34035 жыл бұрын
@@leuzleuz8602tu n'es pas sérieux maos yawla rék
@sen22875 жыл бұрын
Dangay doull rekk
@serignembackediouf60695 жыл бұрын
Clement Fofana merci Frere Saliou Samb il est top. Messoul diema wakh lign koy takhal
@doudougaye8762 Жыл бұрын
Djiadieuf mam cheikh Ibrahima fall
@elhadjialadji35455 жыл бұрын
Serigne saliou samb mala beugue yala nala serigne bi gèna takhawou barkep xassidayi
@dawoudadione24245 жыл бұрын
Machala amna sollo 🙏🙏💓💓👂👂🇸🇳🇪🇸
@babacardiop41375 жыл бұрын
Yalla na sa diame yague si adouna narou Chera Fall depuis russie
Liko takha doneu Serigne bou Makk bi dou ndieukeu dioudeu dou ndieukeu Tarii Alkhourane Dou ndieukeu donoup Serigne ✌🏾Dafi eupeu Deuk: Touba ✌🏾Eupeu fi ay talibés :Mourides yi ✌🏾Eupeu fi ay mbinde: Xassida yi ✌🏾Souteu fi ayCheikh: Mame Cheira Fall, Cheikh issa Diene SNDAME Abdourahmane..... ✌🏾Gueneu fi ay Mbok: Mame Mor Diarra Mame Thierno,Cheikh Anta, S Massamba ak S Mandoumbé. .. ✌🏾Souteu fi ak Ndiabot: Cheikh Moustapha Gallas Borom Magal gui..Seydina Serigne Saliou,Soxna May Kabir... Nirouwouleu ak Keneu Coursoule ak kéneu Rawantewoul ak kéneu dieum féneu 🙌🏾kou doul Ahmadou mi fégne Maka. Ahmadou mi dou sa Morom. Ahmadou Borom nitt gnii: Seugn Bamba #SeugnFaaloourek
@mboupaminata1320 Жыл бұрын
wakh ngua lepp yaram fall.dieureudieuf
@mamadoudiop16355 жыл бұрын
Serigne saliou samb Lo dound doyul machala
@gueyebamba11475 жыл бұрын
Serigne touba Amoullmoroum
@birahimsene86305 жыл бұрын
Akassa serigne Saliou Samb . khol seedanna té meutgua ci wakhtann niarri cheikh yii . khewal ak ham ham
@Mouhalo15 жыл бұрын
first to watch from NY
@mouhamedwade4015 жыл бұрын
From Moscou
@Hamsatoul_Rijal5 жыл бұрын
@@mouhamedwade401 from Milano
@matardiallo52825 жыл бұрын
Wawe gooor noné rek la Baye karim Fallilou ken dou andak mome Di ragual