1ère fois ma commentaire parceque dagno wakh si nite kouma beug diko téwlou BAYE SAM MBAYE yalla na yalla yokk ay léram
@ababacarmbengue88994 жыл бұрын
@@khadimdiakhate2824 inshallah en tt cas xalate mom douma rater ay vidéos wam
@moustaphaseye59614 жыл бұрын
Amine
@phatambow55504 жыл бұрын
Machallah
@thianemoustapha84754 жыл бұрын
Amoule won morome barker s touba car mome lomou wakh yalla takh
@limamoulayetoure15224 жыл бұрын
ah fall kone dei gno bokou beug beug s sam mome damako sopou lol.hier rk mangui nafilas sama xél déme si mome walahi ma diangalko * wal hassri* ndah beugone nako lool.waxtanam you bari mome lakoy oubé.
@massambaplomberie12014 жыл бұрын
Kou sope serigne sam mbaye beuseul j'aime ❤️🙏
@thiatoukeurgui42174 жыл бұрын
Amna solo trop
@tafakara11234 жыл бұрын
Merci
@yatalwaxibayesammbaye4 жыл бұрын
ndeysann yalna yalla yoki leram
@SM-zd2vg4 жыл бұрын
Mangui nii deh ❤
@dajiqacidayitv63044 жыл бұрын
Ndaye sane
@kweeni17244 жыл бұрын
Le plus grand connaisseur et professeur que le Sénégal n’ait jamais connu
@lool221network94 жыл бұрын
Iaw ligeu oumpeulé beurie neu dh
@lbytking26784 жыл бұрын
Walay
@tafakara11234 жыл бұрын
Bilay
@kheushadiouf622911 ай бұрын
Vérité
@bijouterieroidorniasstilen80514 жыл бұрын
Suma wasila adina alakhira yalla na niou yalla tass si barkéme keppe kouye sopé Serigne Sam nel Amine 🙏🏾😍🤩🤩❤️❤️❤️
@tafakara11234 жыл бұрын
Aminnn
@mmbcbg47214 жыл бұрын
amine
@akhmaoubambajoop85563 жыл бұрын
Amine
@Barra245183 жыл бұрын
Amin
@thiernoniang56253 жыл бұрын
Amine yarabi 💕
@madieyediop4 жыл бұрын
Si on pouvait aimer une vidéo 10000 fois je passerai la journée à aimer ce vidéo, je ne trouve pas les mots pour magnifier votre remarquable travail. Mais je prie le bon Dieu qu'il vous protège éternellement Xalaat👍
@tafakara11234 жыл бұрын
Akassa
@karbalatoure18793 жыл бұрын
Amin yarabi
@djzoukiller26542 жыл бұрын
Moi meme millionnaire fois sakh ma defco
@moussadiop79754 жыл бұрын
❤️❤️❤️❤️❤️😭walay ndaysan sama khôl Sedna dieum j serigne same nouma mél guinaw yalla moma defar si déglou rek 😭❤️🙏
@gorambaye5264 жыл бұрын
Akmane tamit
@gouyartvdieng50054 жыл бұрын
AKASSSA ak mann
@falloudiop96834 жыл бұрын
Ndeyesane wallahi baringasi ay morom
@moustaphathiam10614 жыл бұрын
Wallay barii ngasi ay morom yalnagnouko yalla fayal
@alassaneseye49424 жыл бұрын
Machalla amna solo loool
@ramacampbelldieng39134 жыл бұрын
Serigne Sam bimouy gnibi j'avais que 1 an tei mom motakh ma mbourou di soll lou diote limou def si mane 😭😭damako beug tellement soumay wadj neilaw sakh mom lay deg lou
@abdouakimgueye27924 жыл бұрын
Machlla
@bayegalayeseye99bayegalaye404 жыл бұрын
Bilay man mi sakh bima koy kham diogué nafi wayé lou beuri si man ay wkham lakou diangué
@ramacampbelldieng39134 жыл бұрын
@@bayegalayeseye99bayegalaye40 jtjr bokay deig lou dagay geune ragal yalla
@livendiamour52634 жыл бұрын
Ndeysan waxon nako dh néna sama kasét dina dioubeuntii niitt you barii
@papemor48934 жыл бұрын
Ndeysaan boul ko fatte Di nianal
@fleurdevie72354 жыл бұрын
Je suis vraiment admirative devant ce grand homme. Qu'Allah l'accueille au paradis firdaws. J'espère que les jeunes sénégalais prendront exemple. Diar diar bou Rafet masha Allah ❤️❤️❤️🙏
@tafakara11234 жыл бұрын
Jajeuff
@moustaphamboup730 Жыл бұрын
Allawouma Amine
@chiekhtidianediba10214 жыл бұрын
Xalaat t v 🙏🏾 yene yeney senegal merciii 🙏🏾❤️ mane talib cheikh tidine la me seringe sam mbay dafa ame xam xam lole yala nangouco yala fayale te khareco aldjana🙏🏾😭😭😭🙏🏾❤️
@abdoukane63274 жыл бұрын
Yawko bakhga
@taphaseye2434 жыл бұрын
Aminnne
@makebeseck33374 жыл бұрын
Ndeyesann s Sam dh kouko beugue kham kane moy Yalla deug louko mane dh mourit la mais kepp ko khamni Yalla Def la diokh xam xam di diangua le kom s same walla imam assane cisse walla oustage ady niass walla s abdou rafahi mbacke walla niol toufa khale Bou beugue kham sa dinne nagualen deugg lou
@jimmytafa20154 жыл бұрын
Maasou ma commenté waye taye. Mom sama wadji diaral nama ko Macha allah serigne. Sam Mbaye harifou billahi bi Serigne Sam Mbaye. Waliyou lahi Serigne Sam Mbaye borom Xam Xam bou yatou bi dessé loo niou sara thi xam xam Daana wakhtane banane boudoul wonak yenate dinane fi wakh xam xam bou yemé dana wakh ba nane. Bari na loo kham ni deug la te souma len ko wakhon dou nguen ko geum te kou tek Safara ma waate dougal thi sama lokho ni deug la. Dana wakh nane bari na thi xam xam lo kham ni douma len ko wakh nakh kon dounguen ko geum walla douguen xam fou nguen koye tek Dana wakh nane mourid yi li niouy beug beug Serigne Touba am na lo Xam ni douma len ko thi wakh ndakh dou nguen xam fou nguen koye tek.... Linou mana wakh thi mom bari na wallahi wayé doune ko mane ndakh mbecté Salaw taye sama khom bi dafa seed tr lira gouma video bi
@serignesammbayeserignesamm86944 жыл бұрын
Ndeyesan
@elhadjiamineediop86704 жыл бұрын
@@serignesammbayeserignesamm8694 machalla
@bayengagnendiaye80364 жыл бұрын
Macha Allah contane nane
@bayengagnendiaye80364 жыл бұрын
Macha Allah contane nane
@adianatall71924 жыл бұрын
niapa kou bague bilay seringe sam mbaye 😭😭😭😭❤✋
@djamildiouf85934 жыл бұрын
Walay walay produit de Bamba way xalat Beusseulènma j’aime 👍 way
@tafakara11234 жыл бұрын
Jajeuff
@kabirtoure7312 жыл бұрын
Ki dou produit kéne
@layeba69734 жыл бұрын
Serigne Sam Mbaye psl fait parti des personnes du monde entier qui m'ont séduit de son enseignement... Il fut et reste une immense bibliothèque.
@tafakara11234 жыл бұрын
Bilay
@fatmathiam93844 жыл бұрын
MachaAllah sama Serigne sama Wassila mo féss sama khol Diambari l'Islam YALLAH na YALLAH yok léram té tass gnou ci barkém 🙏merci Xalaat tv contane na trop kou beug Baay Sam rék ma beug la💝
@sidybarrafall54294 жыл бұрын
Bilahi
@ousmaneka89004 жыл бұрын
Yagui nc
@fatmathiam93844 жыл бұрын
@@sidybarrafall5429 MachaAllah
@mariasant39374 жыл бұрын
J'ai fait une expérience: prendre les questions qu'on posait à Serigne Sam Mbaye jadis et je les ai posé à des oustaz et certains borom xam xam connus de no jours mais je vous jure personne n'a été capable de me répondre aussi clairement et avec pertinence que Baye Sam. Pour vous dire Serigne Sam amoul mass si xam xam
@tafakara11234 жыл бұрын
Bilay
@mariasant39374 жыл бұрын
@@galaxiepro.5641 motax malène done natt😁😁
@mouhamadoulamin23464 жыл бұрын
Serigne Sam depuis temps khalé makoy déglou, dèggagouma kouko djégué ci xam-xam, surtout Tassawouf.
@talibeserignesammbaye93313 жыл бұрын
Yalla moko khamal billahi Bay Sam dou mass
@modouabdoundiaye64744 жыл бұрын
L'homme qui à travers ces sermons galvaude l'âme des personnes qui le suivent. Un imminent pédagogue dans tous les plans .
@cheikhgaye4274 жыл бұрын
Tay la thi masa comanter ndakh dieum ji ak lim def thi man ta masou mako guis magui yalwal yalla mou yeureum ko ta diegal ko ta dolli ko ay khéwal
Nitkou séll Mogui ni féss ak xam xam billahi sama xoll mo sédd ❤️❤️🇸🇳 Yalla Nanou yalla tass si barkém yalla guisélé Diou ak môme🤲🤲🤲❤️❤️
@tafakara11234 жыл бұрын
Aminnn
@souleyendao27404 жыл бұрын
Machallah mome la guiss senegal nieupeuko meuneu deglou Tidiane layene niassene mouride....yalla nakko yalla teral barké seydina mouhamed anleyhi salatou wa salam
@khadimndoye89214 жыл бұрын
*Poème pour BAYE SAM* Si la sagesse était une de ces étoiles Serigne Sam l'aurait sans doute attrapée Il chercha sa vie durant à lever les voiles Sur les mystères, essences des réalités Quel abîme de sciences, il est épris de bien Il raviva les consciences, au profit des siens Il aspira à la béatitude sublime Par pur soufisme, vers les très élevées cimes Il nous enseignait usant d'une creuse rhétorique Toutes ces connaissances qui nous seront bénéfiques Il brossa des tableaux clairs des hagiographies Des hommes de Dieu, précurseurs d'illuminées philosophies Ses talents surpassaient de loin toute ambition Car gardait des joyaux de divers horizons Mais Baye Sam retourna vers le Majestueux Ah! Lui qui recommandait d’être bien et pieux Vœux alors qu'il séjourne et éternellement Dans les jardins paradisiaque, comme agrément. AMINE Amadou Bamba NDOYE
@mexdroid17034 жыл бұрын
Machalla
@bayegallasjoop73194 жыл бұрын
Macha'Allah
@elbachir99414 жыл бұрын
Machalla
@salioudieng26694 жыл бұрын
Mashala
@mamasene16784 жыл бұрын
Machaallah je suis vraiment heureux yala xamnako
@cvpointernational45494 жыл бұрын
Yalna yalla YOKK ay leram thi BARKÉB BROM Touba 😍
@taphaseye2434 жыл бұрын
Aminnne
@seydinaomarseck25164 жыл бұрын
Amoul kén koumay déglu koudul mom Waliyou la Dieureu dieuf Baye Serigne Sam Mbaye 🥰🥰
@tafakara11234 жыл бұрын
Jajeuf
@tafakara11234 жыл бұрын
Jajeuf
@assanembow64603 жыл бұрын
Bariiii ngasi ay morom
@akhmaoubambajoop85563 жыл бұрын
Merci
@BaabakarSëy4 жыл бұрын
Ndaysaan moom de nekk nafi ba joge fi te nit ñi xamuñu ko yal na yàlla yokk ay leeram te taas nu ci barkeem❤️🤲🏾🥰🥰
@chiekhdiop17834 жыл бұрын
Mdrrr khana yako khamoul
@satouba84124 жыл бұрын
Amine yarabie 🙏
@lesenegalais84554 жыл бұрын
Nit yi khamnagnko té nioguiciy diarignou ,dafa fekni sougn réwmi key nitou YALLA yi lagn tégoul féneu,fo kate yi dal laniouy promouvoir. Serigne Sam nak mom exception leu il a fait sa promotion tout seul et avec l'aide de DIEU. Bamou dmé yagg neu té batay niouguikay deglou mouy traité ay thèmes d'actualité. Yalnako YALLA doli aw yiw
@bassiroumbaye31084 жыл бұрын
ماشاءالله
@maamedabakh24944 жыл бұрын
*Un des Références les plus Rares du Sénégal 🥺* *Rare na gni melni mom si sounou Diamono Dji ndax Heure boy deglou waxtanam Yalla ak Yonnet bi ngassiy gueneu degg kom nika Mamam Ahmadou daan defei 🙏🏾❤️* *Yalla nako Yalla fay ndax ba legui foko deglo mou dello sila si Sounou brom 🥺🥺🥺*
@kallendiayedo13874 жыл бұрын
Nice na de we gained di
@amarsaliou54564 жыл бұрын
Ki dém ta nék fi ba légui❤ رحمة الله عليه😥😭
@aziz76454 жыл бұрын
Walakhi❤️
@diengsala9004 жыл бұрын
Walahi
@talladieng44454 жыл бұрын
Lolou moy dondou ba faw
@djibrildiouf59434 жыл бұрын
*Vidéo bi man nga ko défal* 😭🙏🇸🇳❤️
@tafakara11234 жыл бұрын
Bilay
@lkane71104 жыл бұрын
Képpou kou beug seringe Sam Mbaye reik nga abonné wou Sama sén Mâcha Alah ❤️❤️❤️❤️
@tafakara11234 жыл бұрын
Machalla
@bassiroulo29194 жыл бұрын
Serigne sam mbaye yalna yalla yok léram🙏🙏🙏❤
@falloundiaye38694 жыл бұрын
Mersi xalat
@abodiop33284 жыл бұрын
Serigne sam mbaye yalla nano ku yalla fayal ci barkem xassida yi amin amin
@daarabeleldioptv4 жыл бұрын
Je suis fière de toi Bou niép don def kom xalat tv légui jeunes bi niépou yéwou kou begue xalat tv yague fi ta andd ak weer gui yaram beuseul j'aime ana niy sopou Serigne sam mbaye je t'aime
@tafakara11234 жыл бұрын
Bilayy
@daarabeleldioptv4 жыл бұрын
@@tafakara1123 merci beaucoup frères
@mansourseck75713 жыл бұрын
Serigne Sam Mbaye yalla na yalla yokou lérr tase niou si barkém 🙏🙏❤️❤️❤️❤️
@mbnmitri33124 жыл бұрын
Bilahi xalate yangui liguéy lou am solo❤ que Dieu vous protège🤲
@tafakara11234 жыл бұрын
Amennnn
@LERALNET14 жыл бұрын
MERCI
@modounbahi28554 жыл бұрын
MaCh Allah Waye
@TRANSFERTDARGENTsn4 жыл бұрын
Damako done dègg rek ndeydane
@alassaneseye99514 жыл бұрын
Amna solo.
@xenonvision39944 жыл бұрын
Machallah
@diengniang14 жыл бұрын
Un homme multidimensionnel. Un homme de sciences,
@mouhametdiop56354 жыл бұрын
Sama doom sama taw moom lako toudé. Il a just 2 mois
@layesisqo4 жыл бұрын
Mashalla yalla na doundou té barké🥰
@papadiene55374 жыл бұрын
Ndaysan masalah yalna topou tanqeu tourandowam
@moustaphagaye14994 жыл бұрын
Masha'Allah Yalla dieul djikooy toureundoo wam
@khadimseck14244 жыл бұрын
Yalla nako yalla same si barke s.saliou
@Khadimseye14 жыл бұрын
Yallna ko yall barkel
@xaadimjoob20004 жыл бұрын
Jërëjëff xalaat tv amna solo lool Man kii motakh ma jël yoon bubaax bi di jaamu yalla wallahi Te ay waxtanam rek ladan deglou Yalnanou ko yalla Fayal barkeb Alxuraane
@serigneabodiop70104 жыл бұрын
Franchement #xalaat tay mom lal nga sama xoll❤️❤️❤️رضي الله عنه
@ndiayemana34894 жыл бұрын
Yaa ngi wakh taané kouma beugue 😭😭😭 ndeye saan baye Sam yalla na yalla yokou aye léeram si barke s TOUBA
@jimmytafa20154 жыл бұрын
Doma thi dap wallahi
@mouhamedthiam90484 жыл бұрын
Sa bop gua ham..
@ndiayemana34894 жыл бұрын
@@mouhamedthiam9048 ndeye saan
@fatoufaye46204 жыл бұрын
Wakh tanam si bopam mo nekh mane doumassi doyal
@ndiayemana34894 жыл бұрын
@@fatoufaye4620 baye sam dafa yéeme bilakhi 😭😭
@2sttv3304 жыл бұрын
Mon exemple, l'homme qui m'a inspiré et à qui je dois mon aspiration... Si j'aime le savoir tant c à qlq part grâce à lui. Yalna ko yalla guërëm
@tafakara11234 жыл бұрын
Akassaa
@tafakara11234 жыл бұрын
Aminnnnn
@3snumeriqueimpressionnumer5233 жыл бұрын
Xalate je prends ceci en témoin En 2013 mes parents on eut un des conflits conjugale lorsque on m'a appelé je suis venu ce jour retrouvant le calme dans la concession cependant j'ai remis à mon père mon MP3 le conférences de Serigne Sam Mbaye RTA il a pleuré sur le coup et dit à mère que de l'excuser et depuis lors la paix nous a visité et y reste à vie Yalla n'a borome bi Gueureme
@adamadiopsam68552 жыл бұрын
machallah
@doffseck85084 жыл бұрын
Beug Yallah ak Beug Xam Xam rék mô waral sén commentaires yi... Yalna lén Yallah Défal diam ak Salaam barké Moustapha anleyhi wa salaam! Amine
@tafakara11234 жыл бұрын
Aminnn
@gueyebara30104 жыл бұрын
Ohhh🤦🏿♂️💕❤billahi limay yekk sama xoll nii manou mako bind kou jeunesse bi wara xam th diko deglou💕🥰merci encore xalaat TV❤❤❤
@adianatall71924 жыл бұрын
dou yaw rek
@MoustaphaDiop-p7x10 ай бұрын
Nice🙏🙏🤲🤲
@assanembow38514 жыл бұрын
Merci pour cette vidéo 👍🏽 c’est intéressant de savoir quelque chose sur la vie des légendes sénégalaises🤛🏾
@papaomarsene4 жыл бұрын
Connaitre la personne de Julien Zouga serait aussi une bonne chose. Car c'est une icône pour le Sénégal
@sheikhabdou50993 жыл бұрын
Kou sope serigne Sam rek beuseul j’aime 👍
@elsaadix27884 жыл бұрын
Sëriñ Saam Bokk na na ci nit yi ëppu solo ëppu ñariñ ci àddina Mayalna sëkk mission wam ci kaw suuf Yàl na ko sunu boroom dolli yërmaande famu nekk barkeb Seexul Xadiim ❤️ Jërajëfati Xalaat Tv liggéey bi rafet na na Yàlla dolli la taxawu🙏🏼
@abdoukhadretop2554 жыл бұрын
Merci xalate tv vrement yallah sounou borom soubhanahou watt- Allah taxawou samoulen arr len si barké seydina mouhamed PSL
@papamadysidibe96544 жыл бұрын
Ndeysane, djoulitt deug ngini, yaAllah neu yaAllah fey baye sam
@Groile2006 ай бұрын
Wallahi ndeysane ki guindi na niou barii yalla nako yalla yeureum kharé Aldiana Firdawsy ❤
@modou8toure4724 жыл бұрын
Thieye serigne same mbaye yalna niou ko yalla fayal si barkép serigne saliou
@gaindendiaye81904 жыл бұрын
Voilà louma niane mogui ni mashallah xalaat toujours yinagui dokh tchi lignu nékh merci yallah nalén yallah fay
@wareckndoye61124 жыл бұрын
Qui moy sameu docteur xol ak rouh nn serigne same yalla na gnou yalla fayal
@tafakara11234 жыл бұрын
Amin
@lydoroye41234 жыл бұрын
Amine
@lydoroye41234 жыл бұрын
Ndeysane. Am nga docteur bou graw
@serignemakhtarmbaye5133 жыл бұрын
Allahou akbar Serigne Sam est vraiment 😭😭😭😭😭mon vrai professeur
@samdiop58814 жыл бұрын
Mashallah serigne sam mbaye yalna yalla yokk ay léram 💖💖💝c'est mon homonyme 🥰
@senegalndiaye56554 жыл бұрын
Machallah Yalla Mayon Nako Xam Xam de Yalla Nako Yallah Yeureum té kharé ko Adiana si Barké Sydina Mouhamed Psl 🙏🙏🙏
@madieyediop4 жыл бұрын
Amiiiine ya Rabi
@moussaly5944 жыл бұрын
Xamna lou mu xamoul wone si sérigne sam machallah vidéo bi amneu solo yalna yalla mottali yp merci bcp 🙏
@tafakara11234 жыл бұрын
Amin
@mamurgey95163 жыл бұрын
Le meilleur conférencier de tous les temps. MANCH ALLAH.
@daoudacamara90184 жыл бұрын
C'est toujours un immense plaisir de découvrir 🍃 des personnages de haute envergure de cet pays . Merci beaucoup xalaat TV thia kaw thia kanam.
@ahmadoufall95174 жыл бұрын
Cëy Sëriñ saam xam xam kaasé la wonn . Sokoy déglu dagay Yëkk maguk sunu Boroom
@tafakara11234 жыл бұрын
Wawaw
@SM-zd2vg4 жыл бұрын
Machalah ❤❤
@karbalatoure18793 жыл бұрын
Daffa leer
@wadeabdou72774 жыл бұрын
Mame Mor Diarra Mbaye l'universel, le moudjadid hors pairs❣️👍
@tafakara11234 жыл бұрын
Aminnn
@lahad72593 жыл бұрын
Ndaysan yéna bakh wayy man dh chaque première dimanche du mois de Ramadan dagni dém Louga départ Dakar 5h du matin agg ay 11h inchallah ziaré tawou s Sahm mame chaikh Mbay diouli tisbar weur deuk bi dem parlait djili mbay ak fi S Sahm done déff khoudba juste takousane djiot gniou djoli dieul départ ndogo tiwawone djouli guée départ 22 h fékeu gniou Dakar machallah khalat contane na dh
@tafakara11233 жыл бұрын
Machalla
@ndaomory78954 жыл бұрын
Machalah !!! Je l'écoute chaque nuit avant de dormir.
@Lesmerengue2214 жыл бұрын
Lii dh dafa melni mako mome lii rek laadone rêves pour geuneu xam histoire Serigne sam mbaye 🙏🏾❤️❤️
@zallegueye39024 жыл бұрын
Mm man
@cheikhounad13874 жыл бұрын
Ak Man
@borom_belel4 жыл бұрын
A chaque fois je me perds dans le droit c lui seul qui me montre le chemin à travers son enseignement "mon maître espirituel"
@morndiaye37744 жыл бұрын
Serigne Sam yalla na yalla yock say lerr moussou ma khamm ndeckété kouy serigne Sam mbaye deuggg machllaaa xalat tv
@tafakara11234 жыл бұрын
Aminnn
@FDP_2214 жыл бұрын
Kii Moye Fathie Ro Yii Sëriñ Sham Mbaye Yàlla Na Ko Yàlla gërëm te Doli Ko Faye... Vive le #XALAAT Tv💯✔️🇸🇳🤍🕊️👍🙏
@amdysalihou36434 жыл бұрын
WA waw fall aka lerrr
@cheikhounad13874 жыл бұрын
Amine Yarabi
@cheikhdiop27184 жыл бұрын
Xalaat tv vous êtes quoi 😭😭 bilahi j vous aime beaucoup amal diam frère ♥️♥️
@tafakara11234 жыл бұрын
Akassaa
@baradieye27524 жыл бұрын
❤❤tay mome sema serigne guénn ma indill contann nasi trop yalla nalen yalla fay yewwu🥰
@Jantbi.3 жыл бұрын
Yalna yalla yôck ay lèram sa firdawsi Té tass gnou si barkèmm
@tafakara11233 жыл бұрын
Aminn
@zeusfall93644 жыл бұрын
Yalla nako sougnou borome kharé adiana firdawsi mai xalaat tv yalla sougnou borome goudel sa fane té mayla sa télé bo momal sa bopou 🙏🙏🙏
@albachir53434 жыл бұрын
Hooo🙏🙏 machallah xaalat tv Sama sope serigne Sam mbaye yalna yalla yokk lèeram amine Aka ame xam xam 🙏🙏( grazie mille fratello
@cheikhngom71604 жыл бұрын
Merci bcp xalaat tv ❤️ Lii lanu soxla Sénégal barina ay références Seriñ saam mbay yalana ko yala fay 🙏
@seringesaliousyll67864 жыл бұрын
Histoir bo masa dialale fi rek bi momaci geune nekh yall na yalla fayalnou serigne sam mbaye🙏🏾🙏🏾😭😭
@tafakara11234 жыл бұрын
Aminn
@serignemortadalobromekross73664 жыл бұрын
Wallahi kou bakh sax sama royou waye sama idole ♥️♥️♥️♥️♥️🌷
@wadanesougou84314 жыл бұрын
Dieureudieufeti Serigne sam mbaye yalle nako yalla yeureume diégueul ko barcké Serigne Touba wadial 18 safar j - 5
@cheikhmoustaphe93904 жыл бұрын
Ndeysane ♥️♥️♥️ Serigne Same xamna L'islam, Beugue na yallah
@mandoumbegueye89044 жыл бұрын
Machaalla
@moutakhba94313 жыл бұрын
😭❤️🙏Serigne sam Mbaye 🙏❤️
@baykhoudosskara15144 жыл бұрын
Cey sama sopebi mame sam yallah nakou yallah douli ay xéwal tha firdawsi❤❤❤🤲🏿🤲🏿🤲🏿
@shvdivdiop45833 жыл бұрын
Cette homme a complètement changé ma vie alhamdou lilah 🙏🏾❤️
@assanesow2523 Жыл бұрын
Wallay dou yaw késsé
@cheikhgueye78284 жыл бұрын
Machallah bègue nane Lolou ❤️❤️Amna solo trop🙏🏻🙏🏻
@malikccisse93874 жыл бұрын
😭😭😭😭😭😭😭😭
@tallakane37144 жыл бұрын
Amna solo
@alhaqq3104 жыл бұрын
Allahou akbar Macha'Allah 🥰♥️Yallah na Yallah faye la thi barké Seydina Mouhammad saw 🙏
@diopfallou23574 жыл бұрын
Machallah xalaat TV Sénégal manoul amat kou Mel ni yawf❤️❤️❤️❤️ ndakh lingay def rafet na trop man mom Bouma la guisoon dina la nèkhal billakhi ❤️❤️❤️❤️
@momo_baye75824 жыл бұрын
Wéssou woule gnanalko yalla yoki lérame
@diopfallou23574 жыл бұрын
Aminé 🤲🏿
@beuguefallou60494 жыл бұрын
Kou beugue bakh bokoy dégulou di nga baakh
@dieoflaughtercomediechain1724 жыл бұрын
voila j'ai ecouter beaucoup de c conference mais c au top vraiment mais je ne le connaissais pas totalement avant d'avoir regarder cette video mr6 XALAAT TV
@mouhamedthiam90484 жыл бұрын
So meunè di deglou wahtanam bi toude le monde contemporain ak tassawouf cheikh ahmadou bamba....da fes deil ak tawhide akiy jarigne ta dalay yèggè.
@mouhamedthiam22344 жыл бұрын
Je suis très content de toi Serigne Sam Mbaye mon idole je l'aime trop😭😭😭 En tout cas je vous félicite et je t'encourage. Que la paix soit avec vous
@dognoalias36064 жыл бұрын
Machallah grace a vous j ai eu connaissance et satisfaction de ce grand Homme Merci xalaat
@falloudieng93224 жыл бұрын
Billahii wallahii xalaat tv Dingafii yague Dinga am Diam lii nieup di wakh moy Deugue SERIGNE SAM MBAYE yallana yalla yokkou ayy leeram 🙏🙏🙏🙏
@tafakara11234 жыл бұрын
Jajeuf
@allendiaye3534 жыл бұрын
Amouma saguo si bay Sam mbaye wallahi
@amdytafa49024 жыл бұрын
Un homme intelligent et intègre quand on l'écoute il nous enseigne et nous renseigne sur la vie et la religion coma vivre ensemble et réussir sa vie
@souleymanzndongo18894 жыл бұрын
C l seule personne que j’écoute H24 tout le monde doit prendre exemple sur lui et réapprendre sur lui enseigner ses œuvres et leçon walahi legui Sénégal 🇸🇳 nekh
@tafakara11234 жыл бұрын
Bilaay
@assanesow2523 Жыл бұрын
Kone nitt kou bakh nga
@MomoSow-zv7gv10 ай бұрын
Dieureudieuf Serigne Sam amougne fayame ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@damebambakaradiakhate64574 жыл бұрын
merci xalaat tv ♥ ماشاءاللہ جزاك اللهُ
@worldmouridetv4 жыл бұрын
allahou akbar tay xalaat fii ngèn gënè graw na deh dieum jou yèmè ngui way machallah xalaat tv daal lii motakh ma beug lou bakh rék ngéni fésseul 💚👌
@gadiagangagne4204 жыл бұрын
Ndeysane Macha allah amna solo lol yalna yalla doliko yeureumandé tass niou si barkém
@beuguebamba76123 жыл бұрын
Thiey Serigne sam mbaye yalla na yalla yok leram tas niou si barkep ❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏
@serignegassama4184 жыл бұрын
Serigne saam (RTA) la source du savoir inépuisable., Un parcours exceptionnel Un homme multidimensionnel
@modumamoundst9184 жыл бұрын
Alhamdoulilah jërëjeuf wa xalaat tv Serign Sam Mbaye hafizahoul lah wa rahimahoul lah
@dioptv24784 жыл бұрын
Machallah
@assaalihamubaaragfaal70074 жыл бұрын
Allaahu Akubar Cëy Yàlla xalaat tv tay daaneel nga ma Yal na Yàlla yërëm ko te gëram ko 😭😭😭
@Rain715622 жыл бұрын
Machalah sen liguey amna solo trop yenangui yée khaleyi ak niou beuri niou done nelaw , Mokham ci ndiagalé mak gni la wala souniou bagn katt yi toubab yi sakalone pekhé. Gueum sa bopp rekk moo woor. Yalla na léne yalla samm
@seydinaaliounebessane47974 жыл бұрын
Machallah Serigne sam yalna borom bi yok lairam et merci beaucoup xalaat destination 15million d'abonnés inchallah
@tafakara11234 жыл бұрын
Aminnnnn
@moidinesagna35384 жыл бұрын
Ooohhh machallah j'aime srg sam m'baye 💗😍♥️💗
@gregoirelo94124 жыл бұрын
C'est intéressant de dévoiler les hommes de dieu très pertinent
@tafakara11234 жыл бұрын
Bilayy
@SM-zd2vg4 жыл бұрын
Video bi sounako meunoona aimé 100000000000000000 fois
@xaadim96154 жыл бұрын
Damande won nako alhamdoulilahi xaalat tv diadief refetna machallah
@ibrahimatoure81524 жыл бұрын
Nounou la
@lahatleye39484 жыл бұрын
Sénégal war nano yéwou thi kép kouy diglou xaalat tv thia kaw thia kanam 💖💖💖💖💖💖👍