Siteu est un tricheur hors paire. Il se complète par la langue. Et y’a beaucoup d’hypocrites dans le monde de la lutte, ils doivent la vérité à Siteu, de lutter amplement ses combats comme un vrai homme.
@samysane772 ай бұрын
@@ericfavretv siteu à rien proposer moi je supporte modou lo mais siteu est venu juste déjouer modou mais il a rien proposer le pire est que il reclame la victoire pour moi c'est pas un VIP
@samysane772 ай бұрын
Je supporte pas modou lo pour préciser
@rouguikebe99842 ай бұрын
Xaragne mo beuré mo dém ardo mo dane❤😊🎉 Coup irrégulier la djeul bi arbitre sifflé moko yobou ardo😊khamnagn né Modou contanoul parsk borom diom la bougoul genre victoire yi mais dara nioune désalatoniou dara , contane nagn si mom😊❤🎉 Félicitations Roi bi😊❤🎉 Siteu est un tricheur de haut niveau il n'a qu'à revoir sa façon de lutter.
@samysane772 ай бұрын
@@rouguikebe9984 mo def lep mane balla lay supporter mais modou mo beuré beuré bi yeup
@cheikhmbaye9042 ай бұрын
Même modou lô l'avais dit dans son Open Presse : (sou takhawé nako dor bamou daw guén sakou yi) et on a vu la même chose vraiment.
@nafisene53352 ай бұрын
Lolou dé Mo am. Mais sénégalais dafa nafekh torop. Nioune Bilahi Yalla yakamti wou niou. Deugue d’où niou ko wakh moukou, c’est grave en fait
@badaradiopkhassida17462 ай бұрын
Siteu Thiak thiak la😂
@AbdellahiNdiay2 ай бұрын
Ki kaye mo takhe niou Cree thiak thiak 😂 siteu moye lolou
@malicksarr21412 ай бұрын
Félicitations modou Lo king 👑 ❤
@rouguikebe99842 ай бұрын
Xaragne Ya beuré ya dém ardo ya dane❤😊🎉 Coup irrégulier ga djeul bi arbitre sifflé mola yobou ardo😊khamnagn né contano parsk borom diom nga bougo genre victoire yi mais dara nioune désalatoniou dara , contane nagn si yaw😊❤🎉 Félicitations Roi bi😊❤🎉
@FatouMbaye-rh3xh2 ай бұрын
Bilahi il n'a rien à prouver defna lep dafa rayanté ba nék roi 👑❤️ boudon daw rk ma xamné dou aksé fi melni bolt ba paré nan ma dan sénégalais nagnou bayi thiaxan way Modou un jour Modou pour tjrs gnoun supporter yi on é fier de tw ya beuré ya def effort mom mou soxla di daw thim dougnou sax rouss
@LamineFall-r9p2 ай бұрын
Siteu wéébiii mon guadji mais d'où kou
@samysane772 ай бұрын
De toute façon siteu il comme à prendre labitude gérer ses combats dem si plateau yi tak radio yi ma dane diokhlenma couronne bi siteu day nakh ay supporter ram il mérite pas de lutter contre les VIP noumouy beuré ni ba souba dou danou c'est un tricheur
@Mamadou-Fall2 ай бұрын
Merci beaucoup Je totalement d'accord avec toi
@rouguikebe99842 ай бұрын
Vraiment
@nafisene53352 ай бұрын
Bilahi c’est du n’importe koi. Il n’est vraiment pas honnête. Ki diaroul wone sakh mey chance. Ki d’où Niit kou bakh, bari n’a wakh, euppeul n’a, té meune n’a diakhasse Niit ak ak aduna
@morlo95032 ай бұрын
Bilay
@WantToKnow-b1c2 ай бұрын
Bien sûr c'est un escroc!
@djibrilkonte69282 ай бұрын
Tres bien modou lo bayil defgua lepeu thi lamb
@IbrahimaFaye-c6y2 ай бұрын
Merci beaucoup Modou lo tu est brave
@abouabdoulayewane25612 ай бұрын
Félicitations Modou xlo ❤
@DogodiopdiopDiop2 ай бұрын
Modou lo ❤le vrai king❤
@Oiseaubleu62 ай бұрын
Naka Éric Favre teugat gnou MMA ko. Bou boba kéneu dou guéneu si sakou. Sénégal dagno war di MMA di Beuré . Porte leu pour jeunes yi di am fougnou diap, am ligueye
@fallougueye6832 ай бұрын
Bien dit Père
@ndeyeniang92072 ай бұрын
Mane sama avis Moy mou ték couronne bi si Franc✌️dém nopalou❤
@ndeyeniang92072 ай бұрын
Fière de toi notre kharagne nationale ❤❤❤
@soukayeyade43102 ай бұрын
Billay desalatougn dara pression bi niouy andal rk yalla reka kham
@mgcouture24822 ай бұрын
Bilay
@MamadouSylla-jx4jl2 ай бұрын
Na diokh courone bi bala gaye kay 😂..franc il a de l'avenir il est jeune il faut mou dane au moin 3 thie gayii ama, sathies boy niang ,reug reug, siteu, alioune seye 2 . À suivre..
@BounamaDiarra-o8p2 ай бұрын
@@MamadouSylla-jx4jlkone nagnlenn tegal claf kou gagner dieule couronne bi
@quetespirituelle66472 ай бұрын
SITA DAFA DAW COMBAT BI YEUP. BA PARÉ BEUG LAAJ VICTOIRE GANAAW SAAKOU YI. BA NOPI BEUG WEEK LÉP SI WAKH RÉK. SITA DOU BEURÉ BA NOPI DI WAKH BA SIIW.
@OumyNiang-hl1zu2 ай бұрын
😂😂😂😂
@OumyNiang-hl1zu2 ай бұрын
Félicitations kharagne lo ❤❤❤❤
@mamadougandegamane69982 ай бұрын
Modou il ne faut pas arrêter la lutte c'est un business c'est ton gagne pain. minimum 100 millions par combat reviens sur ta decission.
@babacarfall39792 ай бұрын
Bilahi
@rouguikebe99842 ай бұрын
Lolou la wakh😢???
@SarryElhadjiOusmane-kq5lc2 ай бұрын
Saway na bayyi déséluma Dara Billahi
@AtoumaneNiasse2 ай бұрын
Machallah pér félicitation yagafi lol té andak wérr ❤❤❤
@ibrahimadieng70322 ай бұрын
Siteu Moy Amy mbacké Thiam😅😅😅
@AwaFaye-t1p2 ай бұрын
Siteu Moy deuxième lac de guerre
@NdiayeTaiba42682 ай бұрын
😂😂😂😂
@mamadoudiop11052 ай бұрын
S orientewu gnu dee
@Papisdiop3492 ай бұрын
Lac 3😂😂😂
@lixman7712 ай бұрын
L’agent de modou lo a parfaitement raison 🙄🙄 en plus les chronimenteurs de la lutte il nous sort comme qoi que siteu est méritant 🙄🙄c’était la même chose contre lac 2🙄
@cheikhseck42432 ай бұрын
Et puis Siteu était derrière les sacs. Il réclame victoire ? Quelle honte.
@maguettefaye79092 ай бұрын
Modou Lô est le meilleur🎉
@jabousarr14902 ай бұрын
Modou is a great man❤but please stop✋️
@MouhamedMbaye-v9y2 ай бұрын
Félicitations Modou ❤🎉🎉
@AwaFaye-t1p2 ай бұрын
Day daw rek
@abdoukhoudossfall9952 ай бұрын
Amoul arrêt mo raw thiak thiak
@afro38272 ай бұрын
C sa la realité siteu takhawout
@GalleBa2 ай бұрын
Je conseiller siteu de changer stratégie de lutte
@babacar31782 ай бұрын
Lamb dall kou ame foula n'a nieuw di dawe téy indi bolo rék lo déff nonoula
@abdourahmanembaye72612 ай бұрын
Deug bi moy le monde de la lutte daffa beurri nafek dax siteu meunoul perdre niarri combat de la même façon bi sax dafa pire dax daffa daw ba nieup xamko apres vous sortéz pour dire Siteu diambaar la tenir echec modou lo limou df dou yeufou diambar deja mofi gueune nul palmarès ba parè mo fi eup faveur pour beurè ay grand combat xolat lene lamb j li nekatoul sport loby la
@OumyNiang-hl1zu2 ай бұрын
Bilaye deguena DEUG
@vatrefall14222 ай бұрын
bien dit
@GallasNdiaye-if9qu2 ай бұрын
Siteu beuréwoul billahi
@bocarsegasy2 ай бұрын
Siteu t'es un bon lutteur mais si tu veux devenir roi il faut oser faire face
@ebrimacham42392 ай бұрын
I’m Bala Gaye fan but Siteu Ragal la
@bayefall52562 ай бұрын
Modou mo waroul wone dieul siteu
@AbdoulayeDieng-o9k2 ай бұрын
Modou mo daan dé
@user-kf7oi4q2 ай бұрын
Siteu dal lac 3 la rek
@OumyNiang-hl1zu2 ай бұрын
😂
@sarrabdou30402 ай бұрын
Naniou bayi di nann siteu amna mérite , défoufi touss
@LamineFall-r9p2 ай бұрын
Bilahi walakhi Sénégal dafa nékh quoi daguay dawww ba combat bii djékh niouniii dagua am mérite 😂😂😂😂😂😂😂Mane sou féké lii Moy mérite ma dém beuré dji😂😂😂
@moustaphaofficial2 ай бұрын
❤❤❤
@SowMadiaw-go2uc2 ай бұрын
Man damay lath siteu bimou diapanté ak modou lo loutax kharouko walla kalou bitém bi défoukoko?
@SowMouhamadou-ib8ev2 ай бұрын
Siteu day doww rek amoul are 😂😂 comba bi yepp siteu dako doww wakh len degue rek yen journa liste yi
@moustaphafall94942 ай бұрын
Lambj mo Bari ay na fekh
@elhadjindiaye70892 ай бұрын
Comba tafa geuye yékini 😂😂
@NarDione-l1l2 ай бұрын
Modou lime def si lambe mbeur doto ko deff
@mouhamedkounta98192 ай бұрын
Nii lagnouye def daga leine di may chance ba parei gnouy daw rek dem si plateaux yi tak radio yii
@nimspetite2 ай бұрын
Motax modou da am louko métiii
@rouguikebe99842 ай бұрын
Modou moko waroul wone djeul
@nafisene53352 ай бұрын
@@rouguikebe9984Bilahi waroul wone dieul genre Niit yi. Bilahi boy Niang ak ama balde niou jambar
@nafisene53352 ай бұрын
Mane je suis sure que mbokou motakh mou mey ko chance, té Mo ko niane chance
@vaillantguerrier42792 ай бұрын
Siteu ne mérite plus un combat Royal. Qu'il prenne les jeunes nio nokk ko
@vaillantguerrier42792 ай бұрын
Siteu n'est pas un lutteur honnête. Tu fuis, tu tombes et c'est toi qui bavardes dans les médias... C'est honteux et décevant
@BOROOM_NDIAREM2 ай бұрын
Modou n'a rien à nous prouver encore. Na bayi baré nguir yallah..
@AhmadouDiop-v8y2 ай бұрын
Chroniqueurs yi ay tapéte lagnu dagno ragual laminou siteu bi dugnko Wakh deug lac 2 rek nguene yape bilahii
@nafisene53352 ай бұрын
Keneu dé Moko fa wakh deugue mouy Moustapha gueye, Da dem ba diepiko bilahi 😂😂😂 Ndakh wakh diou bari. Bari n’a wakh torop wayy
@AhmadouDiop-v8y2 ай бұрын
@@nafisene5335 bilay loulerr gnissi dess yeup danuy soralé
@AbdouDieng-o5w2 ай бұрын
Félicitation à Moscou lo mais il doit laisser la lutte
@GalleBa2 ай бұрын
Moudou a fait tou il écrire histoire lutte merci moudou lo je te souhaite de arrêter de lutte
@mouhameddieng85642 ай бұрын
Je pense il va arrêter
@bayemodoudiagne23262 ай бұрын
Siteu comédien la dou mbeur
@RAKHMANE25912 ай бұрын
SI COMME TU DIS, C'EST LUI QUI CHOISI SES ADVERSAIRES, IL AURA TOUJOURS DES COMBATS NULS COMME ÇA, IL ÉVITE LES MEILLEUR,PARCE QU'IL A PEUR DE BALLA
@adjikharagnegayeАй бұрын
Daane niou ba paaré diniou ladj😂
@user-li1ro9pn8y2 ай бұрын
Siteu=5.4.1 la squadra azura defense 😂ruuuun
@PamoussaSar2 ай бұрын
Siteu ragal la bilahi
@Germanelaprida2 ай бұрын
Modou boumou dieulati genr siteu yi dounou beurai
@almaktoumdiop87492 ай бұрын
Sitieu daww rék baparé dí reclamé ni mo dane sénégal am naa nafékh you anda ak mome
@cheikhseck42432 ай бұрын
Siteu tricheur leu lii dou combat.
@papediabaye23332 ай бұрын
Siteu d'où dara tapét la rek
@oumarkante91862 ай бұрын
Siteu dernier face to face bimou moudjé def yangui wakh Naneu dangaye soule saye tankeu néngaye sa bopp beurré nékété yo ya rawe tiak tiak
@bambalaye7982 ай бұрын
Siteu niéméwoul Modou lo
@MbayaGueye-k6v2 ай бұрын
Dou kontan kay ardo3f
@AhmadouDiop-v8y2 ай бұрын
Farouloumassi ken mais siteu tamite Nay takhaw di beuré pounkal nék khalé mais day daw rek akhh tamite moy lolu déh
@nafisene53352 ай бұрын
😂😂😂 nooon nafekh ak sokhor Di n’a leen rey, yeen Bo leen sagnone gnou humilier modou Lo. Ardo bo khamni coup irrégulier Mo ko indi, en plus c’est une petite égratignure. Nafekh ngeen wayy, Li ma jamm là
@loelhadji1002 ай бұрын
Na bayi lambou ndakh Dankoy xekhh
@SambouSarr-q6d2 ай бұрын
Per iow yaodou mono wakh lu bakh si Siteu modo sa giro la niari yone May niou
@souleymanendao18432 ай бұрын
Siteu à bien combattu, il à était très solide et intelligent. J'ai pas vu où il à pris la fuite dans ce combat sinon modou lo ne serait pas chez ardo.
@OumyNiang-hl1zu2 ай бұрын
Ardo bi si coup de sifflet arbitre bi la siteu profito d'Aure Modou félicitations kharagne lo ❤❤❤❤❤
@salman-lc8fp2 ай бұрын
J'aime bien Modou mais malheureusement cette fois il a perdu.
@jeanmbayeniakh16142 ай бұрын
Modou lô défa danou dé
@nafisene53352 ай бұрын
Mougneul chéri, mougneul. Kou danou keneu d’où ko diokh victoire. Bayileen sen xel bi ngey Di fowé
@thiamahmadulattekh5622 ай бұрын
😂😂😂 kiko dane kane la ? Ndah ki daw ba gueine saco yi numi danei Kouy dane nek si biti saco yi folene ko guisd
@Prodioufvcbbkt2 ай бұрын
Modou vraiment siteu môme bayiko boul sékatti ak mome dara parceque dou nittou dara .yako maay chance mais tu dois le regretter amérement bilae diarouko won
@magattesamb77472 ай бұрын
Siteu vous a posé une équation que vous n'avez pas su résoudre
@ronaldojoaomendes86412 ай бұрын
C'est une équation que mm lui en personne n'a pas pu résoudre à la fin 😂
@laminediagne55322 ай бұрын
Daw guene wakouyi moy équation li nieupe gnoko meune li dou beure d’où combat bo gnemewoul gue bayi beure yeufou guor la man de bouma nekone president CNG Kep kou def trois avertissements gnou diokhla sanctions gnou sévère gnou Athie la Anne wala gnou dagu le ay 15 wala 20 million li dou lamb way daw di guene sakou dji yawou dial sax meneko gnou fayla ay millions defe yombe trop
@manuelgomis94372 ай бұрын
Kii béneu lokho lalèn manuelé depuis l’intérieur ngén souroukh ci sakou yi ! Avec ces nouveaux amateurs de la lutte ki ne comprennent rien ci lambeu….😶🤭😂
@ousmanedieng34882 ай бұрын
Siteu mo daw ba paree Modou deme ardo 2 fois ou est la logique
@Papisdiop3492 ай бұрын
Yaw xamoulo lamb dème ardo loumou dioté ak daw😂😂😂
@papisdiop36062 ай бұрын
La frappe est derrière siteu a même pris un avertissement
@momowadd4072 ай бұрын
Siteudougorr
@nafisene53352 ай бұрын
Mais yeen est ce que am ngeen ay beutt? Yeen dal ardo so leen degué rek pour yeen jambar la. Un coup irrégulier bou indi ardo ngeen Di ndamo. Cheutttt sénégalais lou ko dal
@thiamahmadulattekh5622 ай бұрын
😂 daga nafekh ba sa morom yi dila tontou Ko dakhadji bamu dow si biti lako dorei mtx mou am avertissement et lolou mo gange modoi
@akimoulakimseck2 ай бұрын
Siteu yoooo leléeee gnagna gueuye gana gnagnati gueuye gana awa gueuye yoooo leléeeee kimo danou melni mo dane iow siteuuuuu🤣
@adamasy51842 ай бұрын
Félicitations pour Sitteu TARKIDAN bi BAYFALL bi
@majoritepastef2 ай бұрын
la defaite de Modou lo est la ! reglement pas reglement beurer na beurer bi danou na ! c tout ! fans modou lo la depuis 2007 mais vraiment Siteu a battu Modou strategiment! titre roi des arenes amatoul sens !
@FalilouNdiaye-k6h2 ай бұрын
Non non tout faux Mano nek ci guinaw sakou yi ba paré dane c'est impossible S'il ya une chute derrière les sacs on favorise celui qui a déclenché l'action, avantage à celui qui fait l'action Mais nek si guinaw sakou yi dane mom amoul Épi siteu devrait même avoir honte de gagner une couronne de cette manière. Modou n'était pas à son jour c'était à lui de prendre son courage à deux mains et de finir le combat comme un vrai roi
@PapeZidane102 ай бұрын
Xolal ma dof bi. Mom😂😂😂 sheut🤦♂️
@majoritepastef2 ай бұрын
@@FalilouNdiaye-k6h sakou yi ak beurer bi sa fait deux Siteu moniou dane !😒😒😒😒😒😒😩😩😩😩😩😩😩😩
@nafisene53352 ай бұрын
Ça se voit que wero. Stratégie daw combat moy stratégie? 😢c’est vraiment triste d’être aussi nul
@FalilouNdiaye-k6h2 ай бұрын
@@majoritepastef je suis d'accord sur le fait que le poids de Modlo sur ce combat n'est pas à son avantage, il s'en est sûrement rendu compte......mais wakh deug Yallah Siteu woroul nagou dieul couronne roi des arènes de cette manière c'est très insipide PS : faut pas répondre certaines personnes,elles n'en veulent pas la peine , fi meune naniou waxtane même si on n'est pas du même avis mais argumentons rek dans le respect
@AmCoulibaly2 ай бұрын
C vrai siteu a fui
@malickdiallo60412 ай бұрын
STA DOMAGE IL NEST PASUN LUTTEUR IL NEST PAS DIGNE CE SITA IL A UNE GRANDE GUEULE TOUS CE MONDE SEST QUE SITA A FUIT LE COMBAT MODOU LO A FAIT TOUT