Feikeil deweun you beuri tei talko. Yallah nangoulniu sunuy adorations té diégueulniu ndioumté yeup. Yalneuh Yallah haré Firdaws sunu défunts. Yallah sameuh niu sameuh ndjabott yi. Yalnaniu Yallah dafal diam adina ak al'akhira. Dieureudieufeuty Sokhna Mariétou Yalneuh Yallah doli meune-meune yék tahaway bi Très bonne fête d'Eid el Fitr à toute la Oumah
@ndiatteloniang91635 жыл бұрын
Fékel déwen tata balnagn la balniou yalnaniou yallah bolé bal niou fékéko déwen you bari té lep love beug yallah défalako ci diam pask yaw kén amoul sa fay kou bakh nga walahi amal diam rk inchallah.
@k-dy42105 жыл бұрын
Mahchahala Ta mariétou balnagnla ngua balgnou yalla na niane yeup nangou thi barké kou tédd gnou féké ko atte you beuri andak wëreu mahchaha laa
@adjiousmanediop16105 жыл бұрын
Machallah tata mariétou manguilaye suivre depuis france awma habitude commentaire youtube nak wayer dal fawma wah parsk mis a appart sa plat you neikh you exeptionel yiguay defar machallah wayer man lo wah rek ni inchallah ak vidéo biguay oubber nouyo bou selleu ak oci lo wah ni machallah dall moy seddeu sama kholbi yalla na borom bi barkel lepp ta fayla yiw barakallahou fee
@bintouniang27845 жыл бұрын
Bal naniou le akh gua bal niou akh tamit, yal na le yalla faye sa khol Machallah, di khar lakhou ndidee diop bou ndar ndar bi vive St. Louis ma belle ville.
@mbenefall85024 жыл бұрын
kham nga man tata loumay danél néko réll
@aissatoulabotallba14255 жыл бұрын
Machallah Tata Mariétou je suis vraiment contente pour toi. Dila gnanale fane bou goude weer ak weerle. je fais partie des femmes sénégalaises qui vous suivent un peu partout. SWT mi ame faye yallanala fayale bopam. Yagui dimbali sama moramou djiguène yii am diafédiafé thie mbiroum wagne. Tiyabo yii ngaye am khamouloko sakk.
@fadieng76155 жыл бұрын
Balnanioula balniou👌👌 yalnaniou yalla bolei diegueull way niou feikker ay deiweine you barri Tata youbi yaba😂😂😍😍😍😚😚😚bne fête
@adjasall80754 жыл бұрын
Je taime fort maman marietou mashallah amal jamm. Maneu adja sall je t'adore 😗😗😗😗😗😘😘😘
@wardak2445 жыл бұрын
Encore merci pour toutes tes magnifiques recettes et pour le temps que tu nous accorde. Bonne fête de korite à toi et toute ta famille ainsi qu â tous les musulmans. Et qu on puisse encore bénéficier de tes recettes l année prochaine et encore beaucoup beaucoup d années.
@momo_28025 жыл бұрын
Dewenati balma akh balnala YALLA mayniou niou tewe ay dewene you bary bonne fête
@ndeyendoye69635 жыл бұрын
Mash'allah Mariètou jolie coeur Ndao baal na gniou la akh yalla bolè baal gniou nioune nieupe si barké Mohamed (PSL) bien prèsente set na nékhna na lawla thiate
Mashallah Mashallah j’aime bien comment vous faites la cuisine africaine vrai cordon bleu et bonne fête
@Mizafrica5 жыл бұрын
Machalah bonne Fête Balnala Balma Yalla na niou Yalla Ball niou teweko Ate you barri Inchallah
@mbackefall23225 жыл бұрын
Salam ta maretou balnanioula yawite nga balniou niou fekeko ay ath you bari xeweul soutoura teranga adina ak alkhira yalla nasa diam yague amine
@ndeyemourthiam26074 жыл бұрын
machallah machallah lakhou mère diop nice na vraiment
@aramegueye25383 жыл бұрын
machalla dewenaty bon ramadan
@Zahra201815 жыл бұрын
Balnaniou la akh depuis Paris. Merci Tata Mariétou pour toutes tes recettes et ta bonne humeur 😘😘😘. Un grand bonjour au youbi yabba😂 akk nékko thi rél😂😘😍
@kinedjigo22765 жыл бұрын
Machalla amna solo, di nianal sa yaye yalla khipe aldiana,,man da ma buegue togue ,nieme waagne ,mo taakh ma beget la
@mamesofiendiaye91895 жыл бұрын
Ta Mariètou beug nala machalla, liguay togu nékhna.
@signaragueyeditemmesall77125 жыл бұрын
Amine akkk mbolemmm dioulittt 🙏🙏🙏. Tata nga balnou akh bou bakh aussi balnala yalla nanou yalla bolei balle amine 🙏🙏.
@yafatisow35755 жыл бұрын
Macha Allah amine pour les prières. Dewenati tata marietou longue vie santé de fer si barké Seydina Mouhamed.
@mamediarracoulibaly66185 жыл бұрын
Macha allah macha allah j'aime pas trop le lakh mais bi mom j'adore. Beuguena moss neuteuri bi torop
@fatouseck63105 жыл бұрын
Tata machalla mane dale say khetou assiettes momay danel
@claire-pz6ps5 жыл бұрын
Macha alla merci tata yalla na la yalla Faye sa khôl bne fête
@aramatabodian20354 жыл бұрын
Non suma léne amoul wone damlé di crée Macha Allah
Merci encore Tata Marietou. Mais est ce que muscade bi manouniouco won def si lakh bi com sa soow bi gueune nice
@aissatoudiallo70895 жыл бұрын
J pense la mme chose
@serignembaye74255 жыл бұрын
Si c possible mo guena Nice parce que nit meun nako guiss si sow. Bi yakarni lenen la
@mameh.81165 жыл бұрын
Sokhna Marietou, ray ngam... “ net, net” tokk kat deugu dafay beug lekk , moun Ka apprécier... machallah
@AfricanBeautyHairStyle5 жыл бұрын
Mashalah gnoune gnola wara balou akh pask vrema yagyinouy diapale si sounou mariage dinou diokh ay recette rapide merci bcp.no mane souba inshalahou magui trader Joe inshalou thanks
5 жыл бұрын
Ma Asta 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘😘
@sallawa17595 жыл бұрын
Balma akh sama toguolokh bi ndaw kunda bal nala gnou fekhe ay dewene you Bari vraiment nit kou bakh ga diapalegua ay djiguene you bari si bir keur gui yalla molay fay ma cha allah diam rek guay am si katanou yalla
5 жыл бұрын
Sall Awa Ameen 😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@AfrikQ104 жыл бұрын
So 👌 nice. Looks like a delicious 😋 dessert 🍨.
@mayacinakdialfan5 жыл бұрын
Allahouma ameen .Bal leen ma akk .Yalna gnou Ya Allah yokkeu xeweuls te djeggueul gnou Ingredients you simples te selleu Ma shaa Allah domou Ndar biii❤️❤️❤️❤️
5 жыл бұрын
mame Diallo amen 🙏🏾🙏🏾
@maimounabadji63595 жыл бұрын
Machalla mala mbeuk
@mairyndoye39065 жыл бұрын
Bonne fête de Korité à toute la Oumah musulmane. Balgnou Mariétou. Balnahgnou gneup. Macha allah. Merci DÉ WÉNATI A TOUS
@malick1575 жыл бұрын
Macha Allah , mariétou. Balna gnoula, balgnou ak. Yaw kay sante ak ngeureum lagnou amél. Di diang sans stress, néko réél, nékothi doutt, chéé bien😀😂😀. Yalla na diam yag
@mbendandao43585 жыл бұрын
Mala love tata cherie goudale fane way ndaokounda diallo beuleup ndoukoumane 😍
@riatun25215 жыл бұрын
Machalla tata marietou! Mane dila déég rek sama khol day seed! Diangueul guama lou bari si toguou! Dieureudjeuff nogui sa guinaw rek
@mariamadiallo17215 жыл бұрын
Déwénati tata Eid moubarak figa guène bakh na lakh rek la beugue merci encore pour votre générosité et du partage 🙏🏽😍
@dabasougou79355 жыл бұрын
déwaniti balenma yalnanouko yalla bolé bale gnou fékéko ayy ate you bari
@christelledanon52155 жыл бұрын
Merci beaucoup madame je peux utiliser le même yogourt pour faire le dèguè?
@mariatoucissokho22735 жыл бұрын
Bonjour mon homonyme je suis vot vidéo mais je comprend pas wolof vous faite de très bon plat maschalla bonne continuation depui Paris 🤲❣😘
@mlgguest34795 жыл бұрын
Dewenati sokhna Marietou Goudeul fane akk sa staf Diléne nianal jam soutoura akk kheweul gou bari. Dewenati balnala akh nga balma akh. Contane naniou thi sa liguey yakk gninga andal.
@matyniass68215 жыл бұрын
Mai tata beugg nala bilahi trop lala beugg ndakh sa yiwe wa noumay déff bay déganté ak yaw wala m'a guiss la👐💖💖
@ikkakukempachi48663 жыл бұрын
J'aime trop ta manière de parler
@aminata.yaye.boye.senegal1395 жыл бұрын
Machalla tata et merci beaucoup sama dome bi soye wakhe machalla dafaye wakhale machalla
@mariamamane65765 жыл бұрын
Djangal nga nieup. Tres genereuse et tres drole. Jadore tes videos
@amiebah34315 жыл бұрын
May Allah give you long life and good health...
@sarrkhady95935 жыл бұрын
Merci Tata vous nous avez bien régalé pendant ce mois béni. Déwénatilen yalana sunu Borrom bi fadieu adioyi ak soxlayi ci barké Seydina Mohammed.
@chamchampion49104 жыл бұрын
Tata Mariatou what is the liquid white thing called cuz saying it the French way pour de flour dolar. I love your channel and now you narrate
@ndardakar90395 жыл бұрын
Ah Marietou tou dou ga samay m’bok niome m’bayang ak n’diaga naka diek mani lale ga si n’dar sounou togou yi dafa Niro trop 😘😘😘😘n’galakh khou beignet gay wakh
@mariamdiallo78175 жыл бұрын
Assalam aleykum quelqu un peux me dire dire c est quelle poudre qu elle a melanger avec la pate d arachide. Merci d advance qu Allah vous recompense.
@maguettembaye94425 жыл бұрын
Salam Tata Diw gnor bi fokoy dieundé stp?
@aminatasow82103 жыл бұрын
Maa Shaa Allah nice cooking but I will sleep the sugar it’s not good for our health 😊
@mamekebe26235 жыл бұрын
Machalah tata kheuy rek si korite bi def sa lakh neuteri
@aramediop86555 жыл бұрын
Salam Tata marietou mère diop nioune gni niokoy nianal souf woyof si kawam ndakh partager nga recettes yeup ak nioune merci beaucoup 😘
5 жыл бұрын
Arame Diop ohhhh Ameen way ma Cherie 😘😘😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾❤️❤️❤️❤️❤️
@yombehm40985 жыл бұрын
Wow Mariatou tojati nga koh'. Masha Allah. Jigain da kaye niru'.
@robertgaye86405 жыл бұрын
Merci beaucoup marietou tu fais le ngalah comme ma belle mère Natou simple et bon net!
@ndeyekhadadiop24335 жыл бұрын
Nga parè, fahass sa gnari tankeu, deme tok, deungeulou, fass sa kaname😂😂😂😂😂😂Maretou waathieu gnou nak😂😂😂😂😁
@ptiona4 жыл бұрын
Bonjour tata merci pour la recette. Est-ce que je peux mettre le Fonio à la place du mil?
@aissatandiaye78063 жыл бұрын
Qtkxjxfn
@mamadoulamineconte13445 жыл бұрын
Salam tata Marie tou pour le ngalakh pour combien de gramme de pain de songe de faut 'il faire pour avoir un bon jus neuterie pour un kg de pâtes darachide
@MariemeJolie5 жыл бұрын
Tata dewenety di la remercié bou bakh si vidéo yii yallah na yallah yook sa meune meune yook sa werr gou yaram goudeul sa fane. Saye khétouu paroles mo maye fathieu mane 😂😂😂 c'est biennnn 😂😂😂
@seynaboundiaye525 жыл бұрын
Merci tata Marietou yalana yalla faye sa khol. Diaradieuff😘😘😘😘
@mariamamane65765 жыл бұрын
Ta marietou kou bakh nga mashalla
@aminatagaye72665 жыл бұрын
🤣😂😂🤣bouné tous les bagages rek ma keupou mach'allah deweneti balnanou len bal len ñou Akh que du bonheur avec tata Marietou
dewenety a toi aussi ta marietou yaw amélo kéne akk ya fi nekk di gnou béguel di gnou wane ay recette you bakh grace a toi gnoune jeune marié sonatignou.mane mome sa souné damay préssé di khar recette yi yalnala maye longue vie maye diame akk salam on tador bcp bonne continuation
5 жыл бұрын
galséne 😘😘😘😘🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@ndeyekhadysakho25985 жыл бұрын
Laff thiat tata marietou yalna yalla faye la
@mirandiaye82905 жыл бұрын
AHHHH ta Marietou..... commentaires yaourt bi raynama merci pour les recettes Yalna YALLA faye.
@aminasolama54444 жыл бұрын
Hi Tata j aime beaucoup vos recettes mais je ne comprend pas Wolof prières 🙏🏾de nous ajouter français ou Anglais In Shaa Allah Merci !
@DiMa-ec1pr5 жыл бұрын
Coucou Tata dewenaty à toi aussi ,j'adore tes videos,tu cuisines comme ma mére Bilay ,en plus da ngua beug sa yaye machallah, yalnako yalla kharé Aldiana 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@siraniasse89335 жыл бұрын
Nasa diame gayeu reck amine
@khadyniane3995 жыл бұрын
Non Ta Marietou raynama Yalla nasa diam yague mane saye commentaires momaye danêle
@papfallll4 жыл бұрын
My first time watching you, so funny 😀 ma’am... thanks by the way
4 жыл бұрын
Mamadou FALL welcome to the sow brother merci
@kadiasow73175 жыл бұрын
Salam sister you’re very Classy I am great cook too,but i learned something from you keep up the good work.
@mbacketoure99645 жыл бұрын
C ns qui devons vs demandez un grand pardon puisque yagnouye diapalé.K'Allah ns donnes la possibilité de le fêter des années et des années et ds de meilleures conditions.Diarama Tata.
@coumbandiaye46305 жыл бұрын
TATA MARIETOU YALNA SA DIAM YAGUE🙏
@aissatoutoure36655 жыл бұрын
Amiiine
5 жыл бұрын
Coumba Ndiaye Ameen
@khadydiawara76895 жыл бұрын
@ amine
@aramatabodian20354 жыл бұрын
Dagua nékha deglou ak sétane
@fantasireba88114 жыл бұрын
Machaallah je t aime bocoup
@tajoutajou95905 жыл бұрын
Merci tata pour ta générosité yalla na saveurs planétaires dem si kaw si kanam si barkè koor gui. Cannelle bi aussi am dara la
@marietoudiabira92675 жыл бұрын
Machallah saama tourondo qu'Allah azzawajell nous pardonne et accepte nos oeuvres en fin de ce béni. Un grand merci pour ta générosité et ta bonne humeur. Qu'Allah accorde ak firdaws à tous nos défunts. 😍😘😘🤗
@MiMiLuvBeyonce5 жыл бұрын
Wow thank you 🙏🏾 🥰. Tata the baobab powder do they ship to other states ?
5 жыл бұрын
MiMiLuvBeyonce I don’t know but u can leave me your num on my messenger so that I can get you more info about it thanks 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@MiMiLuvBeyonce5 жыл бұрын
Okay . Thank you. Eid Mubarak ♥️
@kadija77245 жыл бұрын
Neeko ci reul!😂. Soow bi japp form😂😂😂 .non mann yow lay weur Tata Marietou depuis tchebou yapp Naar bi. Eid Mabrouk . Seu khol rafetna. Laf thiat et Deweneuty.
@fatmesaleh15585 жыл бұрын
Salam tata Marietou xaar na soupe chinoise bi ba koor gui djekh
@astoythiam99215 жыл бұрын
Slt tata thi lo ne balyou akhe ball nayoula Amelo ken akhe yaw kay fo tolou del wakh Amine wa sardegna italy am gha fi fans club dieureudieufe ti
@mareimaa66145 жыл бұрын
Tata on vous suit vk bcp d’intérêt merci et longue vie balnagn la akheu ngua balniou osii bsx ❤️
@ndeyearamesall70135 жыл бұрын
Macha allah.👍👍👍
@mameboye935 жыл бұрын
Ma Sha Allah😘 Balgnou akh ,balnagnela Tata Mariétou.Un grand merci encore☺
@mamygomis78045 жыл бұрын
Merci tata Marietou et bne fête a vous tous
@djibycooldiaw69165 жыл бұрын
no marietou da nga bakh kio😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂yalna yalla goudalsa fane
@boussokara25954 жыл бұрын
Jai une question tata Lah doh bii day ndaw wala
@jeunedafrique5 жыл бұрын
Fekkel dewene ta marietou gnou Yaagu ko fekke... Très bonne fête à toutes 😍
@maguettebomou51775 жыл бұрын
Mashallah! lakhou mère Diop amna manna
@ndackgrandhaye5465 жыл бұрын
Machala balnanoula balnou merci beaucoup pour tout les recettes merci depuis la France
@petillanterubii94205 жыл бұрын
Tataaa can you tell where I can finds bol wala plate yingay utiliser yi
@fatoumatatraore555 жыл бұрын
Amine mère diop paix à son âme. Tata lax bi nexna.
@sowidrissa77665 жыл бұрын
eid moubrack
@Mamediarragmail.comMamediarra85 жыл бұрын
Dewnety tata recette yi diapalegnou si koorgui, mere Diop yallana yalla yeureumko, merci encore
@loufabusiness11285 жыл бұрын
Macaha alla
@naroukadiorpur55435 жыл бұрын
Mane dh neuteuri beugue nako lool waay😋😋
@mangoneniang23115 жыл бұрын
Machalla dieurdieuf 😍😘balnagnou balgnou amine dewenety en plus un jolie coeur tati love