Abonnez-vous à notre chaine KZbin et Activer la Cloche, pour suivre EN DIRECT tous les grands evenements de l’Islam et de la Tidjaniyya EN HAUTE DEFINITION
Пікірлер: 154
@justicepourtous61686 жыл бұрын
Bala may sėtan lay aimė pars que ndiarigne rek nguėn di wakh masha Allah
Bilahi deugeu bou wérr koufi am lou reuy cheikh tidiane molako diokh kou nagou ak kou bagne
@boucountasene67555 жыл бұрын
Khôl yi sedd naniou MaSha Allah. Yalla na Yalla yok sunu thiofel ci Seydina Sheikh deff niou deugui Talibé Sheikh InSha Allah. Amine Amine InSha Allah 🙏🏾
@aramendiaye64644 жыл бұрын
Amin ya rabbi ci darajey yonette bi saws
@talibecheikh68856 жыл бұрын
Masha allah dieureudieuf yaa Mawlaya yaa cheikhouna tijani🙏
@seynabouyvon25006 жыл бұрын
Machallah,Alhamdoulilla c est vraiment riche en connaissance qu'allah vous en récompense.
@biraneseck73224 жыл бұрын
Machalla toute fiér d'étre TALIBÉ cheikh yalna yalla fayal niou cheikhouna tidjanii et yook sén xam xam niounn li niou gueum gueum nanouko baparé kén dou cheikhouna tidjanii bilahii
@malickdiop28394 жыл бұрын
Serigne cheikh Ndiaye yalna yalla goudeul sa fane sama kharite
@aramendiaye64644 жыл бұрын
Amin ya rabbi ci darajey seydina Mohamed saws
@babasane38206 жыл бұрын
Alhamdoulilahi rabbil alamine. Yalla naniou Yallah def vrais talibés Cheikh.
@fallsenegalais83816 жыл бұрын
amine mane ak yaw bon gamou 2018
@aminatandiaye89816 жыл бұрын
6
@mbdone38605 жыл бұрын
Amin psl
@cisseaby27215 жыл бұрын
Alahouma amiine
@mouhamadoudiop62535 жыл бұрын
Amiin
@biguediaw26986 жыл бұрын
MashallaH Sama nDidiay Préféré Jtm Barki Cheikh
@bamsbams31716 жыл бұрын
Boudé ay nakhla sakh beugeu.na bilahi yalnagnou yalla déff deugeu deugeu pir talibé cheikh
@ndeyediaw75736 жыл бұрын
Lici dake nake moye nei dou aye nakh
@bamsbams31716 жыл бұрын
@@ndeyediaw7573 merci ma sœur ya dégueu
@amadoukane8654 жыл бұрын
Surtout nak dou nahaté. Amine ya rabbi talibé cheikh thie xol
@miketoure45183 жыл бұрын
YALLA NA YALLA FAYALNOU SEYDINA CHEIKH AHMAD TIDJIANI CHERIF RTA KHOUTBOUL MAKHTOUM TAJI ARIFINA BIDJIAY MOUHAMMADOU RASSOULOULA SAWS
@aidarakhadreabdou32684 жыл бұрын
Walahi yalnaniou borom fayal seydina cheikh Ahmed tidjanie cherif Yalnaniou borom bi deff talibe cheikh
@aramendiaye64644 жыл бұрын
Amin ya rabbi ci barke seydina Mohamed saws
@mamadoudiba54016 жыл бұрын
Al hamdou lila cette année j'ai eu la chance de le passer à Fes
@ndeyeguignanendao43595 жыл бұрын
Mancha ALLAH. Sama khol dafa séd gouye , dieureudieuuuuffffff
@elhadjoumarfoutiyou41044 жыл бұрын
Bilahi Wallahi sama kholl seed nah yalla nala yalla fay ci barké Cheikh
@assanemboup53192 жыл бұрын
Serigne bi
@badarakandji43625 жыл бұрын
Yalla na yalla doli la soutoura ci barké Seydina cheikh ahmada tidiany lerna setna yalla khamnako
@amyniang11945 жыл бұрын
Kenn dou seydina cheikh yalla naniou ko yalla fayall yalla na niou yalla defff ay degg deggg talibé seydina cheikh !!!
@aramendiaye64644 жыл бұрын
Amin ya rabbi ci barke seydina Cheikh Ahmed Tijaane cherif rta
@papadoudoudieng7047 Жыл бұрын
Machallah dieureudieuf Ya Rassoulilahi mom mi takal grade Mame Cheikh ❤️ ❤❤
@yabeyekane53255 жыл бұрын
Yallanañou YALLA def dëgi dëgë talibe CHEIKH AHMEDE TIJANI CHERIF.🤲❤
Alhamdoulilah bama Yalla khirei si ma beugu Cheikh Ahmed Tidiane cherif rta. Bok si hadara Cheikh Seydil Hadji Malick rta ba barzakh in cha Allah
@fallsenegalais83816 жыл бұрын
amine
@aramendiaye64644 жыл бұрын
Amin ya rabbi ci barke seydina Mohamed saws
@mamzondiaye84435 жыл бұрын
AY LINIOU AM KHAMOUNIOUKO BILAKHI WAL KITABI !!!! YALLA NANIOU YALLA FAYAL SEYDINA CHEIKH !! YALLA NANIOU YALLA DEF DEUGUI DEUGUI TALIBE CHEIKH AHMETH TIDJIANE CHERIF RTA !!! AMINE
@aramendiaye64644 жыл бұрын
Eyway amin amiin amiiiin ya rabbil alamina ci barke yonette bi saws
@kandjicheikh60835 жыл бұрын
Serinou serigne sy moye cheikh Ahmed tidiane Alhamdoulilah
@deggfeenjotna5 жыл бұрын
Biyilén rérre di réralaté yalla na yallah dioubanté lén dém ci yallah Roy ci mouhamad
Machallah c'est informations son riche en connaissance
@mameida46044 жыл бұрын
Thi sama yaakaar dé amna loo kham ni kéne waroukoo wakh thi télé. C vrai que çà encourage , mais aussi ça fait douter les faibles niveaux ,enfin ils seront foutu nom adeptes qui vont tout niés, alors il ne serait pas mieux d’en parler entre nous dans nos mosquées sans caméras merci 🙏 sama khalaat rek nak Souma dioumé diéggueulou.
@astougueye60173 жыл бұрын
Slu frere khana khamo ni daniou tollou fo khamni nitt ni daniou rer khama touniou senn d'inné dnc li dasiiy bakh imagine tw sou fekei ni danko def si mosquée rk esk nieupou dinann ko fekei dnc pr mw li mo geunn ndakh dina enragé niou barri di diegalou sou fekei ni dama dioum si beneu batt 🤲
@mameida46043 жыл бұрын
@@astougueye6017 limi wakh dou diiné , dafay wakh thie nguenéélou tariikha . Ta dafa am palace, télé dafa yaatou ta wéddi Yom .
alhamdoulillahi à vie bagnou yallah défé talibé cheikh
@mouhammetcorrea28723 жыл бұрын
Amna sollo
@baidyrassoulsow54875 жыл бұрын
Maa Lana fil kawni siwarahmanou wal Moustapha wa cheikh seydi ahmada tijanni RK
@fatimafall39565 жыл бұрын
Machallah machallah
@abdouazizdiop82796 жыл бұрын
Mach'Allah
@khadydiene1065 жыл бұрын
Allahou akbar
@AwaNdiaye-lv2yi6 жыл бұрын
mashalah
@aboulabbasstidjany6806 жыл бұрын
Djaguelé sou ñou borom la, mou neekh ko mou def khoutboul awliyahou. Téréwoul kounek ak sa thieur
@assanemboup53192 жыл бұрын
Iao lagnouy waxtanei
@mamadouwade1823 жыл бұрын
Masha llah ♥️
@kahdisall80376 жыл бұрын
machala
@abdoulayedione42325 жыл бұрын
« Ata khatmoune . » ❤️
@aissatouniang33465 жыл бұрын
Koudoul Cheikh doko dégue
@assanemboup53192 жыл бұрын
@@aissatouniang3346 waw coumba
@cayortv49106 жыл бұрын
Machalla wayé kou koy magal naka lan koy magalè es ce que maoudo maynako magal ak nako lako donn magalé??????
@adjangom52734 жыл бұрын
Kenn dou borom fass
@fallsenegalais83816 жыл бұрын
akasa oustaze diadieuf
@dembambaye1546 жыл бұрын
Eskey eskey
@MrAmadoo16 жыл бұрын
Est-ce- que vous pouvez arreter ces chants que vous mettez en fond sonore. C'est quoi le but des videos ? Eveillez les consciences ou divertir les gens ? C'est tres interessant au demeurant, mai difficile de se concentrer sur ce que le monsieur explique.
@alkhalifagaye40016 жыл бұрын
Vraiment message bi lagnou geuna sokhela. Les chants nous les avons dejas. Wala bou meunoul gnak faut diminuer le son. Dieureuguendieuf nak thi ligueye bou rafet bi
@mame71196 жыл бұрын
Amadou Dieng c vrai. Merci
@awaniang84956 жыл бұрын
Merci
@justicepourtous61686 жыл бұрын
Dama dėfėniwone mame Cheikh Omaroul foytiyou beuthiegou wėrou koor la guanė adouna? Niou barri wėrou koor laniouye wakh. Mais outaz bi Leylatoul Katmiya la wakh
@mouhaton4 ай бұрын
❤
@abadiop22243 жыл бұрын
🖤🖤🖤
@daarajitv43926 жыл бұрын
tadarkiih
@maguetteyague50602 жыл бұрын
🥇♥️🤧
@justicepourtous61686 жыл бұрын
C'est quand la nuit du katmiya?
@ndiayerougui50466 жыл бұрын
18 safar
@mouhamedsambe78206 жыл бұрын
Demb si goudi la won
@justicepourtous61686 жыл бұрын
@@mouhamedsambe7820 merci
@justicepourtous61686 жыл бұрын
@@ndiayerougui5046 merci
@adjidiopdrame49126 жыл бұрын
Le 27 octobre passé
@badoucamara56584 жыл бұрын
Au Sénégal chacun revendique être le meilleur de tous les waliyou finalement on ne sait plus qui croire. Donc je me limite au Coran et l'enseignement du Messager d'Allah car en effet aucun des waliy qu'on glorifie n'est cité dans le Coran ou dans les hadiths. On raconte des histoires qu'on ne connait pas leur référence. L'islam du Sénégal doit faire objet d'un débat pour élucider les choses
Bayil yeuw sigome saw wakh si émission. Dou teguinne. Talibe cheikh zéro faute. PAN
@deggfeenjotna3 жыл бұрын
Lilepp li sôss ci ganawou yonéntabi dou diné ây doul rek lâ
@deggfeenjotna3 жыл бұрын
Sén tarikha bi ây doul rek yângui toumal yallah
@assanemboup53192 жыл бұрын
Ya mane ndy fen danga gnou eup tawhid bay wax
@deggfeenjotna3 жыл бұрын
Dôm hâram pure nga diné bô xâmni ci Senegal rék la néh lôlou dou diné
@assanemboup53192 жыл бұрын
Iao miii yay imbéciles bi
@pathediouf27575 жыл бұрын
Déysan wahtane bi DINA am niou wédi dém safara
@deggfeenjotna5 жыл бұрын
Bayi lén beuga daradia di didial ak di réyal rek yallah rek mo réy wôn lén niteyi yallah sunu borom yallah mo am lépp moy mayé di sédalé
@adioumadiagne76074 жыл бұрын
Ndakh cheikh da guénn thi yalla? Bo khamé yalla itt ragné woko
@biraneseck73224 жыл бұрын
Yén gni commentaire si lou nguén xamoul nguir yalla mandou lénn té yalla rek taax bo amoul xam xam boul waax si lo xamoul
@deggfeenjotna5 жыл бұрын
Li ngafi wax dou diné doura fa yallah yangui nax niteyi di lindamal xélou niyi
@CherifNdiaye-z6f Жыл бұрын
0
@adioumadiagne76075 жыл бұрын
Ziar koubakh bayit bobou nga wakhni maodoko wakh foum nék? إن الحقيقة المحمدية منشأ في طريقة الفردية
@deggfeenjotna5 жыл бұрын
Xolatal li nga wax ci faraté ragalal yallah ci li nguay wax
@ibrahimagueye58215 жыл бұрын
Tu parles bcp tu n'aimes pas zapper et regarder autres choses.wasam
@sophiethiam79425 жыл бұрын
Parlez de choses si importantes en machant du chewing-gum !!!! Je vous corrige Hadratul ilâhiya l'Assemblée des Saints se tient au 6 ième Ciel près du Siège du Prophète (saws) !!!!!!!!
@abdourahmanesarr71815 жыл бұрын
Wa xo deugg démal diangui alhour 'ane.
@abdourahmanesarr71815 жыл бұрын
Xana ndiabotou El Cheikh nga
@mouhamadoudiop62535 жыл бұрын
Sophi Thiam simplooo dara
@mouhamadoudiop62535 жыл бұрын
Sophi Thiam simplooo dara
@sophiethiam79425 жыл бұрын
@@mouhamadoudiop6253 Merci ! Mbiroum Tariqah Cheikh mo simplou! Bayilen diko thiakhané ndakh Mawlana Cheikh Ahmad Tidiane Chérif (rta) doukou simple!
@deggfeenjotna5 жыл бұрын
Wadji ragalal yalkah ci say wax yi
@mamadouwade1823 жыл бұрын
Ioe do nopi imbecile japel ioe yagui ragual ylla imbéciles lo xam waxko
@deggfeenjotna3 жыл бұрын
@@mamadouwade182 sa wâdj môy dômi häram pure doul rek lay déf ci tarikha doul lanéh