Abonnez-vous à notre chaine KZbin et Activer la Cloche, pour suivre EN DIRECT tous les grands evenements de l’Islam et de la Tidjaniyya EN HAUTE DEFINITION
Пікірлер: 123
@chernodem8192 жыл бұрын
Grazie mille hapip sy
@mamadoulaminewaly31434 жыл бұрын
Franchement la causerie est très importante et pertinente pour tous musulmans qui aiment le prophète seydina MOUHAMMAD
@Abdsr87355 жыл бұрын
Ndeysanne Serigne habib meuna ko deglou ay fane ndak xam xam bi ni mu rafete ler te selle ! Dieureudieuf Sy Dieureudieuf Asfiyahi !
@mamadoulaminewaly31434 жыл бұрын
Wallahi li nga wakh deugue la
@Mballo633 Жыл бұрын
Serigne bi ay wakhtanam doumasi doyal
@diagnekhadim74302 жыл бұрын
Douma doyall bilae machaallah 🎉
@oumardiene5255 жыл бұрын
Masha serigne Habib beug nala sop nala nawla sa xam xam yala na brom bi xep doli sameu arla goudeul fane wii😍
@adji.thiorobadiane56765 жыл бұрын
Machallah
@dioufsopenabyn1diouf1765 жыл бұрын
ماشاء لله تبارك الله جميلا أطال الله عمره
@gorasene95744 жыл бұрын
Machaalla
@awandiayekambi60765 жыл бұрын
Machallah souniou wa dahira mouhibina katmya bi niou yague ko fékké
@wakhdeugguetayallatakh81295 жыл бұрын
Thieye sama sanga yi tivaoune yalla nafa mbir yi di sakh rek ba faww
@ousmanecisokho20674 жыл бұрын
Tn philosophie eupouna Machallah
@sarrseydina48138 ай бұрын
Mancha allahou raby
@faryndiayendiaye91095 жыл бұрын
billahi wallahi tallhi ki sope nako ndakhe yalla rek kese
@mouhameddiop53385 жыл бұрын
Ak mane dh
@bamsdiaby28795 жыл бұрын
Bilahi dina 'ma ray ak xam xam rék té dafa dégue diamono yalnala yalla same si barki seydina Mohamed psl amine
@momoseck2643 жыл бұрын
Goudou fan ak wer yallanako yalla doty si iow ak koulako yéné
@dabakhwade46955 жыл бұрын
Thiey SY Malick Mo Dég dé th Bari xam xam yalna brom bi gudeul sa fann samal la bopam si barké yonanta bi saw amin
@chernodem36954 жыл бұрын
Good luck brother
@diaraseck84125 жыл бұрын
Machallah alhamdoulillah tarikhatul Cheikh Ahmad Tidjane Sy et Fierte d'en faire partie🤗 Haaa manam dal magui am yéné bok si tarikha bi té yalla nama si borom bi bolé ndah yomboul Machallah
@Raton3335 жыл бұрын
Maa sha Allah setalma bi niveau ci kham kham rek Sy Malick yalla na sa diam yag.Amine
@mouhamedniangatijani34815 жыл бұрын
Mom sr Habib mi nako ñiep dina ñianal yalla Cheikh Ahmed Tijan cherif nak Mou mii dou kouli awliya hi..louthi way meun
@morniang11323 жыл бұрын
Thieuy yalna yalla goudeul sa fan
@cheikhtidianediagne4085 жыл бұрын
Yalla na Yalla samb la ta goudal say fane Sy Malick
@ousmanesabaly95632 жыл бұрын
Une sagesse insaisissable, non vraiment mott nga Serigne
@ndeyeamiwillane57835 жыл бұрын
Masha Allah Sy Malick Alkhamdoulillah nala Yallah faye yiw In cha Allah dieuredieuf
@fantambaye39765 жыл бұрын
thieuy bayou serigne babacar Sy désalatonou dara khamal guanou sague bi dieul tarikha cheikh bi gueun tassaréko si reww mi diereudieuti Sy
@mariatoutouray4715 жыл бұрын
Jazzakallahu Ana Hairan Sy Malik .Yal nga fi yagg te werr Si Barkeh Nabi (SAWS)🙏🙏🙏💕💕💕
@ahmadouibnomar27975 жыл бұрын
Bilahi ya beuri Xame Xame té dégeu diamano. Yalna Yallah saame la
@adamakane3735 жыл бұрын
Amine
@gorasene95744 жыл бұрын
Amine
@ibrafall2845 жыл бұрын
Damakoy degulou 2h de temps yakarni 10 mn le Sy yalna bourbi yagal lafii mayla wer ak werle dieureudieuf say wakhtan ler leu gou dieum directement si khol ❤️
@layediallo78904 жыл бұрын
Walahi gno si yém yalnako yalla samal bopam
@ngagneseye6843 Жыл бұрын
Bokoy déglu lumu yag yag doco sentir❤
@mamadoukane46142 жыл бұрын
machllah serign bii
@pingpong99545 жыл бұрын
Walahi chèkh sèydil hadji malick watho ak gnoune
@alysakho83195 жыл бұрын
MAODO wathiona ak nioune bilahi sy
@ibrahimakane52924 жыл бұрын
Macha Allah j'aime beaucoup Serigne Habib autant que son père. Longue vie et santé de fer
@omarfaye17943 жыл бұрын
Sama wassila sama serigne doundeul xol sed Sy Malick ❤❤❤😘😘😘
@awadieyembaye63043 жыл бұрын
SY MALICK DOUNDEL LOU BARI MALA SOPE TÉE YALLA TAKH BILAHI❤❤❤❤💖
@bayefallouserignebabacarsy5 жыл бұрын
Bilahi serigne habib ya beri kham kham wayy
@alimatoundoye3863 Жыл бұрын
Machallah sy malick❤
@chernodem89414 жыл бұрын
Good luck Sy habip
@ndeye72725 жыл бұрын
Allahou akbar deg ma deug masha allah
@mamadousall11805 жыл бұрын
Machalla Sy Malick bilahi ya beuri xam xam
@chernodem36954 жыл бұрын
Good cherno habip sy ❤❤❤❤❤❤❤❤ 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏 💞❤❤❤❤❤❤❤🙏
@mbdone38605 жыл бұрын
Lahilaha ilalah ou Mouhamadara rasoulilhahi salalahou aleyhi wasalam .
@bayefallouserignebabacarsy5 жыл бұрын
Nekhoul ba nekhoul ms affaire bi tivaouane la franchement parlant
@gorasene95744 жыл бұрын
Yagui kay sogua kham yag na
@mbayesow1164 жыл бұрын
Mdrrrr ndaysan yangui saalit
@Abdsr87355 жыл бұрын
Dieureudieuf Sy !
@yacoubakoma31684 жыл бұрын
Un homme pétri de connaissances et d'intelligences
@sarrsileyesambou55885 жыл бұрын
wallay Sy Malick goudal fan way ta bolési wèr
@gayeameth54075 жыл бұрын
Thieuy tarikha tidiane xam xam ak yar rk lep yalay Kassé leu ak Mouhamed
@papambengue80745 жыл бұрын
Macha alla sy malick yalna yalla goudale sa fane
@ousseynoudieye28865 жыл бұрын
Dieureu dieuf deug nekh yalla amgua yare nitegua
@limsgadie53755 жыл бұрын
Walahi damako begue pour monekeu sama borom Keur barké seydina mouhamed salalahou aleyhi wassalam
@mallediop25834 жыл бұрын
Dieuradief s'y malik
@alousall6664 жыл бұрын
Macha alah sy malick
@chernodem36954 жыл бұрын
Good luck sy
@mouhamedfall60025 жыл бұрын
Serigne touba amoul morom💓🥰❤️
@ndiougalo14265 жыл бұрын
Mouhamed Fall s touba mbam yi nioye ak moro mame mome nianrr niou boock ndaye ak baye la tack dilénn katt
Meundei wakhouma Serigne touba maie s saliou lay niane moumay may ndakh sama am am si moom lako Yalla la diaralé
@cheikhcisse15915 жыл бұрын
Sawaye nga balma mai dieuf mo apou ndiargne wakh nagni wakh gnouye dieuf rk yi boumla derange defkone ay wakhi guente rk kheti wakhyi sokoy bayi xel dalay tardelrk
@fadel76705 жыл бұрын
Cheikh bilayi lou wer nga wakh khouna diop sénégalais mo badola rekkk mais soudoul wone serigne touba nga guiss lou niaw senegal Ndey san khamnga kou tedd kii mom soko khamoul meuno sori sii mom
@gorasene95744 жыл бұрын
Yénn lolénne dieuf
@binetapouye96743 жыл бұрын
Ioewite soneuh ga bayi tante mouride nieuw si tantou diambour di wax rk melni kouy greve ioe lanla magui parcourir commentaire ms c la 3e fw gay commentaire si meme video wala limou wax dala nakari soula tole fofou mba si liga nek worna yagui kebetou rk kom peroker fi nieup xamnani nit soula defeler lou bax dagakoy geureum epui gani boudoulwon serigne touba senegal xawma lan wala ioe daga fate yallah mou defar adunam bi dara teuwouko t senegal sila bok serigne touba dafa am nioumfi fek t dafa bay waram geineu aduna nienen nekfi insi de suite ms a chak fw le mem refrain di outeul sen bop none ki limou wax deg deg la ladj ms domage des bete kom tw meununiou deg fils balaga bay sa tolou serigne demala bay sa tolou bay ba paré 100m moguifi sa mbokou talibe rk mofa fess ana serigne si meunounioulenfa sax geiné kon fi yallah mofi nk espri barbare yamassi doy melni kou nk famille apocalypto
@liadadinelaliliham89815 жыл бұрын
Ki nafekh bou bonne leu bilahi habib sy mi tè dafa am coumou eumbeul 🤰thies bilahi walahi talahi je suis tidiane mais je suis dsl
@seynaboundiaye12354 жыл бұрын
100% DIOURBEL hana sa yaye la biralle
@layediallo78904 жыл бұрын
@@seynaboundiaye1235 stp bouléne di tontou Aÿ bokalé katou yalla lagnou
@binetakaneba7045 жыл бұрын
Machallah sy malick
@mouhamadouthioub62115 жыл бұрын
Dieuredieuf
@ndiayepapa2776 Жыл бұрын
Ma sha alla.
@lesamouraisnoir53045 жыл бұрын
Bilahi bimaléne jappé ba légui magui guisse sama bopp
@amadousowred25655 жыл бұрын
Machallah
@milckfallfallfall47425 жыл бұрын
macha allah
@DonYou-y8m Жыл бұрын
❤
@geuyefamily68075 жыл бұрын
Thiéy chiekhou tidian' sèrif mo reuy may dèe 🤔🤔
@chernodem36954 жыл бұрын
Alhamdulillah sy
@fatoucisse36365 жыл бұрын
Machallah sy
@serignediagne4325 жыл бұрын
Khana nekouniou Sénégal 🇸🇳???
@chernodem36954 жыл бұрын
Good ❤❤❤❤❤👏👏👏💯
@mouniroundiaye48535 жыл бұрын
machallah wakhtane bi nékhna
@mbayediop572 жыл бұрын
🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰
@mbdone38605 жыл бұрын
Diadieuf serigne HABIB sy
@abdoukarbalatv52504 жыл бұрын
Machalla sama sarigne ❤❤❤
@diopleyta86825 жыл бұрын
Macha allah degule❤❤❤
@chernodem96272 жыл бұрын
Is that Daddy
@papecherifba78433 жыл бұрын
MACHA ALLAH SY MALICK
@deuggeurek10135 жыл бұрын
Assalamoualeikum, wa asfiyahi je voudrai vous demander de couper les 16 dernieres minutes et de le publier separement car dina amal gneurigne gnou barri. Merci.
@agueye39475 жыл бұрын
16 derniers minutes guisna fanatik youy critiquer serigne bi Sénégal da doywarr ken manoul wakh deug
@chernodem36954 жыл бұрын
Good sy
@ndeyeamiwillane57834 жыл бұрын
Masha Allah
@abdoulayedione42324 жыл бұрын
❤️❤️
@cheikhadimbackembacke18165 жыл бұрын
Sokhor fi la yam
@art4automobile4154 жыл бұрын
Sy malick
@ousseynouthioyesopwakanahe27085 жыл бұрын
Amna mène mak moubakh dadane wakh nane dousamaye dou sama mbid lèp lane mana diènè dèlène diènè tolok khèlyi ndakh ndakh gnèp bokougnou tolouwaye batayite dana wakh dèlène madou silouguène khamoule dara yalle nou yala maye dioulit yèp aldiana diou sakh yènènane ko gnèp
@khounadiop825 жыл бұрын
Amna niou reeer Amna niou doof teik ay micro 🎤 nga leik ba sour nan ba mandi di bayeikou reik maie kingay garou walé Yalla ko guereum yonein tei bi guereum ko mou nekh la mou nakharila nk dieun yi neik si guédji bi nangoul nan Ahmadou gnisi Diawoudji ak Thierry dji nangou naan iow nganei do nangou dangay garou walé do sori léiki reik nga réthiou ko
@ahmadoucisse31844 жыл бұрын
Xam xam RK lafi wakh garou WALL-E amoul fi li y'a wakh RK bayi leen KO wakh degue genne garou WALL-E kho mo len dara serigne xam xam RK moko niorr machalla s'y degue RK mou neck
@juniorthiello29284 жыл бұрын
Koumay dimbali si titre son bi au commencement
@cheikhomardiallo93485 жыл бұрын
Sy
@kharagnembaye48624 жыл бұрын
Nn Mane vraiment senegalai dafma diakhal dangay wakh deugeu gniounei dangay garal deugeu yalla rék moko môme Guisnga nit kou Bakh dou gniaw ndiortou Segne touba Ak seydi hadji malick Kou wakh si gniom lo waroul dingako guis gnone talibes yi gnio wara diangui MS dangay melni khamou tous kou wakh nganei day garal dedet waay magui toup Nak bou wr
@ousseynoudiaw68605 жыл бұрын
Ni rek la xam xam moy doune yaaa
@diaraseck84125 жыл бұрын
Machallah alhamdoulillah tarikhatul Cheikh Ahmad Tidjane Sy et Fierte d'en faire partie🤗 Haaa manam dal magui am yéné bok si tarikha bi té yalla nama si borom bi bolé ndah yomboul Machallah