Le Menager de Modou Lo Se Révolte : Siteu yarouwoul,staff bi wakhouniouco deug,lamine samba warouco

  Рет қаралды 21,923

KEWEL INFO

KEWEL INFO

Күн бұрын

Пікірлер: 93
@Deggou
@Deggou Ай бұрын
Wakh bi moy ahlou lamb danio ragal siteu, modou moko may chance, yénéko xaliss , boy bi nieuw daw combat bi yeup ba paré kéneu niéméwoul wané bènéneu angles bi boumouy tek bopou bi ci saccouyi modou dakéko combat bi yeup ba tarkiss narone daneu bopam, siteu danou di nieukeunté ci plateaux yi di diéma diakhassé modou ak nitt yi, au lieux niou félicité modou nakh mo defe lepeu loufa ame, mais journaliste di doule di félicité siteu di diéma rabaissé modou...ba paré di manqué de respect modou ci f2f badola bahoul geumeul yAllah...😮
@LamineFall-r9p
@LamineFall-r9p Ай бұрын
Bilahi walakhi Mane pourquoi douniou wané béneune angle bii siteu danou ba way
@LamineFall-r9p
@LamineFall-r9p Ай бұрын
Sénégal dafa Bari ayyy narfeek rék
@alhassanngom8282
@alhassanngom8282 Ай бұрын
Waa nioune guiss naagn benen angle bi rek nice. Le reste nio xaam. Genre pour man lima diapp moe waa eukhlou lamb thiow molen neex mtx niou bayi nonou
@benzdictenobalegomis6139
@benzdictenobalegomis6139 Ай бұрын
Bilaye lou lere nga wakh
@aissatousy1875
@aissatousy1875 Ай бұрын
Siteu dafa rewe doume nagne co dann co mani seti lellen nimou wakh ace sougnou meure m sougnou meur da yarou rek mo takh mou def nimou def antouca boul mayeti siteu chance mo gêne te ga bayi wala ga nopalou ba thi canam gnoun say suporter sonoou nagne me djarale ga gnou loule nakh d'âge gno tege plas félicitations notre roi fiyer de toi
@AliouDIOME-o8p
@AliouDIOME-o8p Ай бұрын
Lamine samba li siteu doon wkh yeupp dako nekh dou professionnel
@momodadd5045
@momodadd5045 Ай бұрын
Lamine samba nila masa mel saytane la
@kaas1610
@kaas1610 Ай бұрын
Khamoul gatt
@benzdictenobalegomis6139
@benzdictenobalegomis6139 Ай бұрын
Machalah Ass Cissé lep rafetna 🙏❤️
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse Ай бұрын
Machallah ass lou leer nga wakh félicitation ❤
@mariasamb4500
@mariasamb4500 Ай бұрын
Badola kiko gueuneu Teral lay beugueu torokhal ;merci modou pour votre civisme
@NicolasNiasse-p1n
@NicolasNiasse-p1n Ай бұрын
Papa ta raison billahi siteu ma deçu billahi
@ndiayennbi7557
@ndiayennbi7557 Ай бұрын
Limane samba dou professionnel
@AssaneSeck-p6r
@AssaneSeck-p6r Ай бұрын
Khamoul dara
@njaxboy7924
@njaxboy7924 Ай бұрын
Lane samba😢😢😢
@assaneseye2148
@assaneseye2148 Ай бұрын
Lamine Samba lep mom la
@pispabadji671
@pispabadji671 Ай бұрын
kokou nefekh bou mak la nièmèwoul Siteu lolou moy wakh dji 🤦
@NdeyeFatouGueye-v8h
@NdeyeFatouGueye-v8h Ай бұрын
Bilahi lamine samba dou toss khamoul dara day yakh lamb
@kaas1610
@kaas1610 Ай бұрын
Merci
@pispabadji671
@pispabadji671 Ай бұрын
limou wakh Modou souka wakhone Balla bilay dinaka nokou si plateau bi sou wakhè rk niounè dafa nioume tè ken douka recadrer mention special ak Modo trop professionnel Siteu dafa indiscipliner lolou moy deug 😢😢
@assaneseye2148
@assaneseye2148 Ай бұрын
Siteu boudoul won Modou lo dina beuré ba dé dou beuré ak roi des arènes dafa wara diokh Modou lo alarba Defou fi dara Js8 fan de Balla gaye 2 me RESPECT à toi Modou Lo
@AssanedieyeAssanedieye
@AssanedieyeAssanedieye Ай бұрын
Dagnaye doule siteu dou boyou kène bayi lène fare
@malickdia3495
@malickdia3495 Ай бұрын
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah cikaw ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@N20-x9c
@N20-x9c Ай бұрын
Si j’étais à la place de Lamine Samba dama naan Siteu yaw ske sagn nga wath thi kamiin bi ya daan Modou Lo
@tallafall7629
@tallafall7629 Ай бұрын
Machaalla amatina solo rafétna torop way boy bi yarouwoul
@BadaraBa-jc4rg
@BadaraBa-jc4rg Ай бұрын
Machallah ❤❤❤
@tallafall7629
@tallafall7629 Ай бұрын
Mom sakh dafa fatténi Modou lo moy kamil nak
@AssaneSeck-p6r
@AssaneSeck-p6r Ай бұрын
Walay
@ibrafatyndaw9891
@ibrafatyndaw9891 Ай бұрын
Ass Cissé dafa bakh deugou ❤❤
@awadiongue5434
@awadiongue5434 Ай бұрын
Franc moye gniago mame ckhiekh Ibrahima fall amine ❤❤❤❤❤
@GabarSine
@GabarSine Ай бұрын
Nit day am kilifeu siteu amoul kilifeu
@BayezallDiop-gr2oy
@BayezallDiop-gr2oy Ай бұрын
M modou moko wakh danga niak diom Sénégal mo beuri nafekh
@assanekaka9414
@assanekaka9414 Ай бұрын
Situé dou dr bilay wolay
@FaraNdiaye-k1m
@FaraNdiaye-k1m Ай бұрын
Fékeu ko Hameuni prouver woul dara guen mayko chance
@AssanedieyeAssanedieye
@AssanedieyeAssanedieye Ай бұрын
Modou ayoule kène chance dafa daw tafa tine
@lixman771
@lixman771 Ай бұрын
Pour dire vraie siteu s’en fout de MAX MBARGANE il ne le respecte pas mais c’est bien fait pour MAX🙄🙄il a détruit la carrière de tigre de lansar 😡😡.a cause de son intérêt de prime sur siteu pratiquement tous les grands lutteur de lansar soit ils ont laissé la lutte ou on les entend plus 🙄
@СЕНЕГАЛМОЯСТРАНА
@СЕНЕГАЛМОЯСТРАНА Ай бұрын
Bilahi lou wèr la da niou ko djinone siteu andi kamil wathe bimouy dore après 2013 niou wara dem soirée pape diouf New York la wone siteu mandi ba menoul takhaw😂
@DiabelSall-r2j
@DiabelSall-r2j Ай бұрын
Siteu da ndayiii rew
@AbdouAziz-ri8td
@AbdouAziz-ri8td Ай бұрын
Siteu Dafa Daw Thiak Thiak le Siteu et un Comédien Modou a attaquer et gagner Point
@Omarsane7491
@Omarsane7491 Ай бұрын
Maxe mergane nelenko mou deme coup suprême wala ONU mou def plainte bii😂😂😂😂
@modousarr8848
@modousarr8848 Ай бұрын
😂😂😂
@ModouMbay-f4g
@ModouMbay-f4g Ай бұрын
Siteu mo dane Modou lo nak Sénégal limou Rey rey kein douko Wat ni siteu danoul Modou lo
@mouhamedngom301
@mouhamedngom301 Ай бұрын
Siteu domerame la
@AliounebadaraGassama-or4op
@AliounebadaraGassama-or4op Ай бұрын
Lima diakhal a chaque fois bénn angle bi rèk laniouy Woné
@AssanedieyeAssanedieye
@AssanedieyeAssanedieye Ай бұрын
Siteu seul wakh lène ndaye deugue aye nafèkhe gnène modou lo mayoule siteu sence lambe molène bolè
@thiedofall1012
@thiedofall1012 Ай бұрын
Wakh deugg yalla palmarès bollewulene Sitteu bane grand champion la dane? MBollo moko indi fi si lamb
@deugrek344
@deugrek344 Ай бұрын
Sitteu mo réw té vip yimou barél yépa kou dane. Père max mo waral li yép ndakh mak bou irresponsable la.
@OusmaneKanee
@OusmaneKanee Ай бұрын
Père nioune tapha tine lagne beug
@amadoupam
@amadoupam Ай бұрын
wa keur siteu diapalelen sen beur mou reglé mo geun
@diawbayezale31
@diawbayezale31 Ай бұрын
Dafeu ni salmine dafay ñiouss dane
@bambacke5299
@bambacke5299 Ай бұрын
Siteu dafa réww
@AliouDIOME-o8p
@AliouDIOME-o8p Ай бұрын
Siteu moy chekhoul cherifou borom waati 😂
@ndiayennbi7557
@ndiayennbi7557 Ай бұрын
Siteu dou mbeur
@ahmadoudiagnegueye9918
@ahmadoudiagnegueye9918 Ай бұрын
Legui modou lo mom mouni siteu danga niakeu diom nak
@thiamahmadulattekh562
@thiamahmadulattekh562 Ай бұрын
Daga niak diom xass la dou saga Modou messoul dieul micro di def yeufi rewandei Siteud efnako si combat bi boukh cowch wamm ak papis. Yeufi rewandei rek lay def tei dagnuko nokh dakhadjiko mouy dow comme djiguene def recour 2 fois menul am dara
@saurafall5922
@saurafall5922 Ай бұрын
Yénako déf fék badola bou tékiwoul dara diko may chance
@ahmadoudiagnegueye9918
@ahmadoudiagnegueye9918 Ай бұрын
Way modou wakhna nafi mbeur louné néna fi lac 2 dangay doul
@IbrahimCisse-gr3jm
@IbrahimCisse-gr3jm Ай бұрын
Site moy lolou da begue baré wat mo takh moy wakhé ni
@alysow9089
@alysow9089 Ай бұрын
Siteu dfa wara change djikom
@momosy6083
@momosy6083 Ай бұрын
Siteu kou rew la
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 Ай бұрын
Yow sa mbeur di diangue alkourane si digui arène bi 😂wahoko dara ngay wah alkourane fénéne lagne ko sohla foudoul lamb 😂😂😂,lamb ji beurina nafékh
@mamadounianghane2330
@mamadounianghane2330 Ай бұрын
Eh il lisait le Coran à travers un portable mais pas le Kaamil c'est different
@BabacarNdiaye-g5o
@BabacarNdiaye-g5o Ай бұрын
Modou lo loumo def diangue alkhouran si bir guew bi
@AtoumaneNiasse
@AtoumaneNiasse Ай бұрын
Siteu domouram la dafa wara yarou tappét bou makla
@saliougueye9833
@saliougueye9833 Ай бұрын
Siteu dafa rew bilay tes defou dara si lamb
@damembow6374
@damembow6374 Ай бұрын
Yaww ya sofff si bopam siteu yaw yaa wax bamou takhaw modou waroul dieul sathies may alioune seye revanche sah mo geunn sathies bimouy bagn foumouko tékkk
@AbdouDiop-d6t
@AbdouDiop-d6t Ай бұрын
siteu kou rew la badola la
@AblayeDiouf-o3m
@AblayeDiouf-o3m Ай бұрын
Badolla ken d'où ko diapoal
@masska201
@masska201 Ай бұрын
Siteu tapétte la
@TallaMbaye-t5q
@TallaMbaye-t5q Ай бұрын
Siteu dafa doff ak rew la bolé
@BabacarNdiaye-g5o
@BabacarNdiaye-g5o Ай бұрын
Wa keur modou lo niom danio sof
@HabibSylla-e3f
@HabibSylla-e3f Ай бұрын
Yaw lane moy sa problème ak wa parcelle
@Deggou
@Deggou Ай бұрын
@@HabibSylla-e3f danio jaloux ci rois des arènes yénewouniouko modou😏
@BabacarNdiaye-g5o
@BabacarNdiaye-g5o Ай бұрын
Thiow siteu ak beurem molen derenge
@KossoGadiaga-vw3wc
@KossoGadiaga-vw3wc Ай бұрын
Siteu kasse siteu kasse
@ibrahimadrame9499
@ibrahimadrame9499 Ай бұрын
😅😅😅😅nél yaldaw
@bayemo4147
@bayemo4147 Ай бұрын
day daw rek amoul arret😂😂😂😂
@BabacarNdiaye-g5o
@BabacarNdiaye-g5o Ай бұрын
Yaw ass kou sof gua
@MbayeDonne
@MbayeDonne Ай бұрын
Ki dasof
@cheikhdiouf5530
@cheikhdiouf5530 Ай бұрын
Meuno len diabolisé boy bi ni ngen don def sen grand yi ragal Tapha tine motax mou dieul siteu
@alhassanngom8282
@alhassanngom8282 Ай бұрын
😂😂😂 fans Siteeu nga? Wala dangay commenter nonou rek wala linga dantt Diouf mtx? Dioufeéne yi dayal diahaal naagn ma 🤣
@cheikhdiouf5530
@cheikhdiouf5530 Ай бұрын
@ Amateur la rek awma mbeur
@bilalkhalyfall9938
@bilalkhalyfall9938 Ай бұрын
Saway boul sossal mbeur yi yaw y’a féké fou modou dépasser ay grands wam si lamb ji gnognou bassiye toleu mouy modou dih balla si guéweu bi lagnoulay djapeu doumala daneuleu wayé yor seu lamigne bou reuye dih wakh rk bo dougué si guéweu bi mélni usain bolt paré yorate seu lamigne dih wakh li siteu rk mokay déf si mbeur yi
@ousmanegoudiaby6098
@ousmanegoudiaby6098 Ай бұрын
Sa waye tu vas souffrir dh
@alhassanngom8282
@alhassanngom8282 Ай бұрын
@@cheikhdiouf5530 ah amateur kone beuggo Modou dh wala ?
@AliounebadaraGassama-or4op
@AliounebadaraGassama-or4op Ай бұрын
Siteu drogeur leu
Échange Coup Ama balde vs Franc "Khekh bou Metti"..; Réaction Surprenante de Modou mbaye…
10:25
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 74 М.
Жездуха 42-серия
29:26
Million Show
Рет қаралды 2,6 МЛН
Маусымашар-2023 / Гала-концерт / АТУ қоштасу
1:27:35
Jaidarman OFFICIAL / JCI
Рет қаралды 390 М.
Série - Lady Diama - Saison 1 - Episode 43 - VOSTFR
58:52
Marodi TV Sénégal
Рет қаралды 1,3 МЛН