Hunnn bakhna combat leu dhé té dou yombeu entrainé am dolé bo mom ak concentration leu ladj..
@cheikhbasskeurmassar954812 күн бұрын
@@metjobrek Yaw mii sakh xam ngani lii dou lamb
@MamadouLamineSow-v6z12 күн бұрын
Deug Deug lii dou lamb way ''Liss loumouy yakalti la khamoul '' yonou ndaw dou gaww fall @@cheikhbasskeurmassar9548
@metjobrek12 күн бұрын
@@cheikhbasskeurmassar9548 kone déggoma dhé...liratal message bi
@mansourdieye949412 күн бұрын
Nguisga lamb dafa am catégorie promoteur bouniuléne sétané dinaniu yakh lamb ji ndakh séne intérêt lii cng mossi wara wax boy yi naniu beuré ak séne catégorie lolou moy yone
@Carti6661112 күн бұрын
Biga commencé say wax ak gisga la xamni doulkat gua😂
@mansourdieye949411 күн бұрын
@Carti66611 yaw réw nga dé loumala déf bagamay wax doul Kate nga damako sékh AK yaw fadial sa fébar bobou nék si yaw mo gueune
@mamepathe461812 күн бұрын
Ki bou lac rose deugué ndeyam arrête mouy dé
@sambamatuidi237812 күн бұрын
Liss do 100f nane ay dôme ba beug deh diniou fonto
@medounembaye414212 күн бұрын
Boula lac diapé dou danga rew rek dinga khamni fiii dou Yoon bi
@SambaSam-y3y12 күн бұрын
Lamb yaxouna ki ga xamni lammiñ la beure damana yeugeul ken
@YoussouphaNdoye-jn8cy12 күн бұрын
Liss lac rose dalaye douma teyal te béret say morom
@1999-un12 күн бұрын
Lac rose mo tardé lis mi takha mbeur dané guay beurél
@1999-un12 күн бұрын
Liss da meune dara si lac rose li vraiment dou combat