Cette dame est tres brave pieuse et tres sereine yalla nala yalla may xolou mougne assane yalla xareko aljana firdawsy Yalla mom loumou def rek lou gueune le
@dakargoodtv75634 жыл бұрын
Ce journaliste est très gentil vraiment continue comme ça dieu va te récompensè inchalah et qu'il repose en paix assane
@lerouxleroux20434 жыл бұрын
Kamosi dara sakh fadal macha alla
@omarballaballa24114 жыл бұрын
Machallaha
@tapha764 жыл бұрын
Maman bi yàlla nalla yàlla takhawou, n'déyessane c'est triste. Maman bou séleu té gueume
@papababouseck97794 жыл бұрын
Fadel vous êtes quelqu'un que j'aime beaucoup du courage le bien fait n'est jamais perdu Que dieux accueil assane au paradis et que sa brave est pieuse mère en l'entendre parler lui donne longue vie
@badaracisse98334 жыл бұрын
c'est une femme digne, sereine et une foi inebranlable. Du courage. paix a son ame.
@ourayecisse58684 жыл бұрын
Du courage nalla yalla maye kolou mougne mtinna troops billakhi minoumako yayeè nellawouma jour bobou billakhi ndeyssane li assane ame ni mo eupe aye milion machalla
@ourayecisse58684 жыл бұрын
C moi la maman de ouraye Cisse
@adamengomndiaye42094 жыл бұрын
Gueume gua yalla maman yalna khipe aldiana barke seydina moukhamed saws dawna yaram trop 😭😭😭😭
@papasene13204 жыл бұрын
Raféte nga, yiww nga Yaye boy. Yalla mayla kholou mougn. Papa Yada yalla kharéko aldiana. Yalla rouss mbolo mi téwé beusseum bii
@ndiayendiaye45174 жыл бұрын
Ndeysane mèr bi kou deugeur leu billahi wally seck ak balla gaye diapalé mèr bi guir yalla
@zahrasy61684 жыл бұрын
Vraiment la mère de Assane c'est une vraie croyante kou gueume Yalla🙏
@ninkinanka36444 жыл бұрын
Wa Hôpital Tamitt Lou Nitt Déwé Niou Naane Daléna Amél...Boulén Fay Dara Niou Amouniou Yeurmandé.
@khadijadiagne98704 жыл бұрын
C'est un décès qui me touche comme celui de ma grande soeur qui m'a éduqué ndeysaane
@satisfact74 жыл бұрын
Que firdawsi soit sa dernière demeure, du courage Medoune.
@sophiefallaidara52514 жыл бұрын
Quelle repose en Paix
@khadydiakhate70114 жыл бұрын
Gspr que Waly dîna la degue yalnala yallah diapalé ba problème yeup reglé. Massah yaye boye. Kou sopelou nga machalah.
@sidysy97634 жыл бұрын
C' est triste Maman Amy . Nous avons tous perdu PAPA YADA 2 .QUE Dieu l' accueille au Paradis.
@magayegueye6914 жыл бұрын
Bilahi walaye
@ngatydia28104 жыл бұрын
Amine ya rabal ralamine
@yacinediallo13264 жыл бұрын
MACHALLAH YAYE DIOYLOGUAMA UNE BRAVE DAME YALLA NALLA YALLAH SAM AK SA DIABOTT. RIP ASSANE DIOP.
@elhadjiguisse72964 жыл бұрын
" toute âme goûtera la mort" Que firdawsi soit sa demeure éternelle 😭😭🙏
@yacinediallo13264 жыл бұрын
FADEL SAMA WADJI MACHALLAH. MARIÈME FAYE SALL DIMBALIL YAYE BOYE TÉ YALLA TAKH.
@moustafaseck84064 жыл бұрын
Yalla nakoo yalla yeurram
@abrahamtvvila8104 жыл бұрын
Bilaye sénégal mo méti assurance dara urgence dara médico dara
@mariemegningue70794 жыл бұрын
Merci au journaliste te kelkun de très humain de bien
@fatoukone45324 жыл бұрын
Masa yaye khamou mala Mé sopou nala ndakh sa yiwe❤❤ yallah na yalla may kholou mougne yaye métina trop mé bou sokhla nieupaye niak yallah na assane égualé ndawame aldiana firdawe si amineee yallah bouko thiate djitou si bamélame 😭😭😭😭😭😭😭
@zalecisse32354 жыл бұрын
Courage ma mère. Kou degueur nga vrm.yalla nala yalla takhawou.Papa Yade yalnako yalla kharé Aldiana.Té mbokkou lambou ma ngui lén di niaane si barké Seydina Mouhamed nguén diapalé yaye booy bi
@aminanaa91664 жыл бұрын
Mashalla maman tu es belle 😍 Yalla nako yalla yeureum amiiine
@papemoussadia88114 жыл бұрын
MANCHALLA Thiëye Wally Seck Billahi Moo bakh Yallna ko Yalla may Wer ak goudou fane
@salladiaw64264 жыл бұрын
Amine
@kanteawa89534 жыл бұрын
😭ASSANE yalla nako bour yalla xare ci aldianay firdawsi metina lool sama yaye yalla nala yalla diox xolou mougn
@mendesshasha10214 жыл бұрын
Sapeur pompier yen dall ni rek, esk douniouy dieul initiative di yeub blessé yi au lieu di khar sapeur. Rip a nos disparue
@elmaestrondiaye16174 жыл бұрын
Sa way boul wakh lila leroul sapeur yi si nit gni rek laniouy nek .jour bobou acciden plusieur blessé mo am diamnadio yavai deu mor sur le coup. L'écho ambulance wara djougué pikine est j yangi sienc le trajet. Avan d parler dangay kham lingay wakh
@mendesshasha10214 жыл бұрын
Yaw ya meune doul ndm. C'est sa mère mm qui déplore le fait que les sapeurs pompiers ont tardé à venir. Et dans tt les scènes d'accident que je vois les proches déplore la mm chose. Yagoul dara bi khalé tu def accident Yoff les gens ont dis la mm chose khalé yi souffrir nagn lou yagu nala sapeur Di nieuw alors k Yoff ak sapeur parcelle bi mm po 15min de trajet. Meun nga ndey doul trop wayy tè yakamti wedi
@mendesshasha10214 жыл бұрын
En plus tu es bête. Mounane ambulances Sara diouguè pikine. Ben ambulances moh am si deuk bi ? Khawma sapeur nga khawma dagua am mboki sapeur mais Soula dalone digua wakhè nenene
@elmaestrondiaye16174 жыл бұрын
@@mendesshasha1021 yama dakha ndayam doul sa lefeul ndey
@hallyfall49194 жыл бұрын
Xare ambulance ou sapeur en Afrik ou Senegal moy rèye niit ki rèk.
@deffaly90564 жыл бұрын
Journaliste bi masha Allah kou bakh nga masha Allah Yallah nala YALLAH sameu tè yokk la amine ya Rabbi si barké Seydouna MOHAMMED saw amine
@alimadiop36894 жыл бұрын
Wanté sen musique bi dafa fort trop
@khadijalo81824 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum ta khareko aldiana firdaw si barki serigne saliou yalla na khipe aldiana firdaw si yalla na motali ndawam aldiana barki alkhourhan 😭 metti na torop waye sente yalla rek yalla bakhna
@cheikhmodounoreynifall76284 жыл бұрын
Mére bi rék nitou yalla assane ci bopam moy kou kéne khamoul
@natou7684 жыл бұрын
Ma challah sokhena si Kaye cou céleu la
@oumousarr13484 жыл бұрын
Ndeyessane que Allah le tout puissant l'accueil dans son paradis inshallah du courage maman longue vie à vous inshallah
@FbaBa-nq2kx4 жыл бұрын
Ndessane Yallah nako Yallah yereum harer aldiana firdaws ci Seydina Mohammed PSL 🙏🏾
@fatoukineba44364 жыл бұрын
😭😭😭 J'ai le cœur meurtri.Massa maman.Yalnalen Ya Allah mey kholou mougn rék té Assane Ya Allah yeureum ko
Ay way guir yalla bayilen waxi xalis ta defalko ñgian lolou rek mokoy dimbali bayilen khel si ki fatou 😭😭😭😭
@diopdiarra71004 жыл бұрын
Très intelligente cette dame machallah,,,
@damegueye69444 жыл бұрын
Fadel ya bakh yalla nala yalla faye ak wa Dakarbezz yepou
@borabora59884 жыл бұрын
She's a beautiful woman.. sorry please take heart.. May his soul rest in peace Ameen..
@tidiane12794 жыл бұрын
Ca je te le confirme elle a était tjrs magnifique amy sene grande de taille
@astoubal39274 жыл бұрын
Ndeyessane thiey amy séne massa yalla nako yalla yeureume tè kharèko aldjana
@talibeboromtoubambacke61134 жыл бұрын
Yalanako yalla yeureum té xaaré ko aldiana firdawsiiii barki borom touba
@modousall26934 жыл бұрын
Assane Diop yalla na yalla wathie yeurmande si kawam te khareko aldjana firdawsi si barke Ahmadou mbacke
@salamataasalame65064 жыл бұрын
Elle est très belle en plus 🥰💗🌞
@abdouazizdiop62284 жыл бұрын
mach'Allah Yalla na khipé aldiana 🙏 Yalla mayla kholou Mougne bijahi seydina mouhamed PSL 🙏🙏
@badoukane65844 жыл бұрын
Sene Musik bi dafa soff trop dafa Fort trop
@awademeba9684 жыл бұрын
Machallah une maman pieuse et très digne . Du courage. Repose toi en paix Assane . Que la terre lui soit légère. Je suis sûre que wally fera quelque chose dès qu'il verra cette vidéo. C'est quelqu'un de très généreux
@elhadjiguisse72964 жыл бұрын
Le chanteur du peuple ndeysane wally Dina def différence inchallah
@lahadboukharagnelo67074 жыл бұрын
Machallah mère bi yiww na torop nekhgama yalnala yalla may kholou moung
@awawade30574 жыл бұрын
Amine
@CheikhDiop-vw4sb Жыл бұрын
Paix à son âme
@sayediouf68784 жыл бұрын
Ndeysane yaye djou bakh Yala nala yala defal soutoura ci barke seydina moukhamed. Adouna mo mel ni
@fatoukineba44364 жыл бұрын
Journaliste bi tamitt amna humanisme Mash'Allah
@modoundiaye79854 жыл бұрын
Yalla nako yalla yereum kharé ko aldiana si barké seydina mouhamed si barké khadim rassoul assane aldiana firdawsy rék inchalla frere bi 😭🙏🙏🙏
@user-pq1ww6td6d4 жыл бұрын
maman mes condoléances !! je sais que c'est pas facile de perdre un proche mais maman reste a ta place tu ne devrais meme pas parlé car déja c'est ton fils qui a crée tout les problèmes même si il es mort ca c'est avec dieu mais togne ngadomou adama , moi je vous connais pas mais j sais que tu ten veux parce que yaro sa dome jen suis sur tu pensais avoir un rois des arènes après je men fout mais arrêté de manipulé les gens tes pas seul a perdre quelqu'un , en plus tu dis dis tu ne demandes pas d'aide mais tu te fous vraiment de la gueule des sénégalais , meme si javais milliares je te donnerai rien parce que sois tu ten prend a toi meme sois tu ten prend a dieux car si ton fils avais une bonne éducation on le saurais , donc vas bossé et prié pour lui c'est tout , man damaye deff lou bonne mais je pari ma vie que souma sa dome eupeulé adiana ma khamné yalla amoul je te jure
Yallah nako Bour yallah yeureum té kharé ko aldiana firdawsi amine ya rabiii Yaye boye ya Geum yallah
@diopmoukhadiop55054 жыл бұрын
Massa yaye yalla nalla yalla takhawou kou geume yalla nga te digne machalla
@deessedufoutadiallo21214 жыл бұрын
Amiiiine ya raby 🤲🏻🤲🏻🤲🏻 Yallah nako Yallah yeureume té kharé thi aldiana you kawé ya si barakatou rassoul (psl)
@sozz27654 жыл бұрын
Yaye Boye wakh jii rafetna machalla Assane Yalnako Yalla hare ldiana barkep mame Saliou
@minafall87094 жыл бұрын
Machalla mère rafet nga sa keur rafet na yalna la yalla may kholou mougn t Assane yalla xarei ko aldiana
@ramia47504 жыл бұрын
Bravo á ce journaliste machala
@aminataseck31774 жыл бұрын
Ndeyssane 😭😭😭 Khamouma Assane wayé sama khol metineu torop..meunouma nélaw jours yi yeup.😭😥Sama rak dafa def choc Italie,dcd.amna 19 ans si réne mais c comme si c'était hier... Yallah nala Yallah meye kholou mougn..Yallah na fi mou nek gueneul ko fi mou diogué..Amine Ya Rabbi 🙏🙏🙏
😭😭😭😭 Yalla nako yalla yereume kharéko aldjana firdawsii 🙏 🙏 !! Maman du courage
@medounendiaye12494 жыл бұрын
Fadel félicitation, non très posé et tu poses les bonnes questions.bonne continuation et courage. Amanekh j avais pitié de toi mais nekete yow tu n as visite une seule fois papa yade,en attendant parler la mère de papa yade, tu n as acheté aucun médicament. Motakh nous les jeunes,sacrifions pour notre famille,ils seront toujours présent surtout nos mères. Qu Allah accueille papa yade au paradis firdawsy. Paix à son âme
@bobokasy93754 жыл бұрын
Il m’a tellement déçu ndekei kou d ya perte amna niou niemé cinema
@awacheikhseck67544 жыл бұрын
NDEYSSANE massa yaay bauy yalna yalla mayla kholou mougn inechalla. YALLENA YALLA YEUREUM KO TÉ DJÉGUEULKO INECHALLA YALLA YESSAL YEURMANDÉM BOU YAATOU BI SI MOOM INECHALLA 🙏🙏
@ninkinanka36444 жыл бұрын
Yaye Boye Yalla Nala Borom Bi May Xolou Mougn, Niou Nianal Assane Yalla Nako Borom Yereum Dieugalko Bakaram Xaréko Aljana Firdawsi.
@bayefall3954 жыл бұрын
Yalla nako s touba térou 🤲🤲😭😭
@badarandaye39504 жыл бұрын
Amine fall yaram bi
@aissatousylla41723 ай бұрын
Ndéyssane Assane yalna co YALLA yeureum si barké SEYDINA MOUHAMED S.A.W amiiine amiiine amiiine
@binetoudiop85764 жыл бұрын
Ndeyesane maman ami sene yalla nala yalla maye kholou mougne yalla khareko aldiana amine
@abdouazizdiop62284 жыл бұрын
mach'Allah Yalla na Yalla mayla kholou Mougne bijahi seydina mouhamed PSL 🙏🙏
@philomeneteninendiaye94794 жыл бұрын
Massa yaye boye yalla na yalla khare ardiana you geena kawe si barke seydina Mohamed
@mamadouballabasse52534 жыл бұрын
Yalla nako yallah yeureum Assane . Mère xawmala mais kou deugou nga machaAllah yallah nala sougnou brome sameu ak yaye yeup amine !
@theresendiaye34484 жыл бұрын
Paix á son ame yalanako ALAH yeureum te yekhegnou te khareko ALDJANA AMINE INCHALAH
@maguettembaye60454 жыл бұрын
Yalla nakho yalla khare aldiana si barkhe khassida yi amine yarabi
@abrahamtvvila8104 жыл бұрын
Hopitale waroléne faye dara domérame yignou done.
@souroublegadiengalama49324 жыл бұрын
Vrement
@aron60544 жыл бұрын
Bro sénégalais yi gnou ngui si danger ndax sounou hôpitaux you bone yi
@abrahamtvvila8104 жыл бұрын
@@aron6054 no dama khamni Europe fo teude wo ambulence mou gneuw
@ndeyefatougueye92824 жыл бұрын
Wax deug
@deffaly90564 жыл бұрын
Massa mettina Yallah nako Yallah yeureun tè kharè ko aldiana Firdaws amine ya Rabbi si barké Seydouna MOHAMMED saw amine ya Rabbi
@losoukeyna72574 жыл бұрын
Mere li daw sama yaram😭 moy deugue biga deugou😭 yalla na yeurmandé yalla wathiee si sa dom dji liga wakh sincère na té andak geum yalla 😭😭 yalla may la kholou mougne
@talladiallodiery4 жыл бұрын
Ndékété mbeur yi nékeu ci télé yi di cinéma kéneu sétiwoussi wàkeur Assane bimou nékeu hôpital.Amanékh béneu yone kessé si 9 jours,doyna wàr
@sidikonate1564 жыл бұрын
Bro amanékh bou démé keur métitt bi day yokou rek té yayou assane dakoy fatéli assane motax mé yénéne mbeur xamouma nak
@soukeyegueye43874 жыл бұрын
Ndaysane mane sax j croyai k assane si jour bi mou deffer assiden la fatou si sasii
@ndakarudialdiop12064 жыл бұрын
Ndeyssane je vois que mère bi kou gueum yalla leu yalnako yalla méy kholou mougn
@khalifabadiane44534 жыл бұрын
Aldiana firdawsi rek pape yade 2🙏🙏🙏
@amethsow49274 жыл бұрын
Yalnako yalla xarè aldiana way barki seung bamba😭👌
@lol_fatou16894 жыл бұрын
Ndeysanne yalnala yalla maay holou mounie maman té papa yada yalla yeureum ko 🙏courage 🙏🙏😭
@mambandiaye9504 жыл бұрын
Mbeur yi délen diapalen tè guir yalla bayi lèn begue lou yombou li niaw na akh merci ama nekh balla gaye tahoul may wakh machalla
@awadiop39254 жыл бұрын
Yalna yalah yeureme KO ta khareco aldianal firdawo ci barke MOUHAMED psl 🙏🙏
@awandiaye1614 жыл бұрын
Billahi Mamma ya bakhe Yalla na la Yalla Tahawou
@medounendao54564 жыл бұрын
Machallah Méré bi bimako guisé la kham ni talibé cheick la
@amintadiop87454 жыл бұрын
Me dinianal Assane bou bakh yallah na yegalé ndawan sa Aldiana et du courage maman kou geum yallah la té deugou
@ngagndiop31674 жыл бұрын
Ndeyesan thieuy yalla sounou brom maman long vie à toi
@sokhnandiaye51524 жыл бұрын
NDEYESANE YALA NACO YALA YEUREUME TE TEROUCO AJDANA 🤲🤲🤲
@momosaw35433 жыл бұрын
machalla maman yalnala yala may xolou mougn Asane yalnako yalla yeureum khareko adjana firdawsi amine 👏
@bobokasy93754 жыл бұрын
Soxnasi mandou ga deugou ga machalah yalla na yalla guereum diegal Assane si barki Seydina mouhamed saw
@ndeyebarakatoufall73144 жыл бұрын
Waly dè sèck digko guisse yalla nako yalla dèfal diam sa kharè papa yade aldiana firdawssi ak mbèpe domou adama
@sidysy97634 жыл бұрын
ASSANE on ne va jamais l' oublier. Nitt kou bakh lawone Diambar motakh gneup beugeu ko. Repose en paix
@manoumbaye62774 жыл бұрын
Nayssan gueum na yalla, mais elle est encore sous le choc normal ,assane diop yalnako yalla yeureum té khareko aldiana firdaws si barké seydina mouhamed.waly ak balla diaplen si té yalla rek takh
@harissndiaye18204 жыл бұрын
Bouniouy niaane naniouy wakh Assane Diop ndakh nonou la toudou. Ma ngui duégeulou nak boubakh
@manoumbaye62774 жыл бұрын
@@harissndiaye1820 tu as raison bro d ailleur je vais rectifier merci
@thebosh-se5lb4 жыл бұрын
Ndeysane mère yalla nala borom bi taxawu amine Mane diamaguèn la deugg mai bilahi papa yade dafma néxone loll yalla nako yonnete bi tèruu aldianaa
@momodiop77814 жыл бұрын
Mais pourquoi la musique dans le fond de l'interview ? Dakar buzz yentamine
@tonindiago67504 жыл бұрын
Vraiment
@badoukane65844 жыл бұрын
Sof rek la def
@miadiallo30844 жыл бұрын
Et sa rend plus triste aretez les sons
@malikking42914 жыл бұрын
pour buzz
@sidikonate1564 жыл бұрын
Pour rendre l'interview triste bro mé pas mal
@ibrahimandiaye79674 жыл бұрын
Ndeye saan mas tá yaye boye assane yalla nako yalla yeuream khareko aldiana fiir dawsii amiine
@fayebineta17174 жыл бұрын
Oh ndeyssane kil repose en paix
@ndoumbendiaye32194 жыл бұрын
Machallah geum nga yalla yalla nako yalla yeureum te diegalko
@mamansalioudieng57844 жыл бұрын
Yaye méti naa trop dafa geuneu si mome ndéysane nianou yaye rk dâme laa fml bii kharite yiii sédé niepeu béne laaaaa yalle na khipé aldiana ak képeu koufa nk si brké nabi mstph psl liga ame kilifa sakh amo ko machalaaaa laf thiate
@PaMa571TV4 жыл бұрын
Ooh maman yalla na yalla Takhawoula gua goude fane ande ak wéér 😭Assane yalla na yalla yeureum woyafal souf si kawam
@sidydiop15234 жыл бұрын
Papa yad yalna kou yalla yeureum ta diégal ko barké alkhourane ak xasidayi yaye boy yalna fii yeugeu loll tewer
@ibastyliste96024 жыл бұрын
Man dé comme dama bokou ak mome ndeye ak bay sa me touche vraiment au cœur maman yalnala yala takhawou ak mbolem joulit
@binetacisse9544 жыл бұрын
Ndeysane yalna ko yalla yeureum khareko aldiana firdawsi barkep seydina Mohamed SAW metina loll 😭😭😭😭😭❤👈