Lirou Diane attaque gravement franc "na yarou Balla Gaye dou moromam sou gnémé..."

  Рет қаралды 14,089

LB Tv Sénégal

LB Tv Sénégal

Күн бұрын

Пікірлер: 84
@KhadyGaye-n5g
@KhadyGaye-n5g 4 ай бұрын
Dieureudieuf lirou diagne aka beugue balla Gaye 2
@abdoulayediop5627
@abdoulayediop5627 4 ай бұрын
Maye léne niou diam waye ak séne wakhou da rew ah lamb amoul lolou
@MameSow-vp7rj
@MameSow-vp7rj 4 ай бұрын
Modou lôooooooooo ❤❤❤❤❤
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
L'empereur geudiawaye la yém amoul dieurigne😂😂😂😂😂
@medzodiouf
@medzodiouf 4 ай бұрын
Thieuy fran mo yunguele game bii😂😂😂
@Deggou
@Deggou 4 ай бұрын
Balla dofoul depuis sa défaite contre boy niang daay daw xaleyi 😅😅😅😅
@Mbayendiaye-q3f
@Mbayendiaye-q3f 4 ай бұрын
Danguen ragal ndiago bi 😂😂😂
@Victoireman
@Victoireman 4 ай бұрын
Franc 13combat 13 victoire teu mo moudié daane bombardier kouléne daan balla dofoul baay doug ci franc😅😅😅 eumeu môme teel na libéré boppam ba diabolisé franc...😅😅😅😂
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
Modou kharagne lô bourou lamb dji seul ❤️❤️❤️❤️
@AbdoulazizThiam-u7v
@AbdoulazizThiam-u7v 4 ай бұрын
Balla gaye bimou néké si diggou ndeundeum louko nékh ladone wakh grand yi frans dasé tolou
@momoseck1617
@momoseck1617 4 ай бұрын
Merci lirou
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 4 ай бұрын
Franc mom lomou wakh ñouni dafa rew😂 franc defoul dara dangen ko ragal rk
@votremiroir7612
@votremiroir7612 4 ай бұрын
kén fallé wouko na dem beuré ak ay moromame. en plus franc réw motakh mou woté si plateau Becaye mbaye nane reug-reug souma dieulé ma nokhou ko. wakh dji soudoul réwandé loumou done?
@daoudatoure5957
@daoudatoure5957 4 ай бұрын
@@votremiroir7612legui balla sagawoul tapha tine si sen face à face publiquement
@SouleymaneDiaw-su3qj
@SouleymaneDiaw-su3qj 4 ай бұрын
Wa yaw daga fate Balla 2fois la dane papaye franc wouyoulene reug si Armel kece lallen danoul
@baraleye4749
@baraleye4749 4 ай бұрын
Na beuré aki moromam ba yéksi balla amoul koumou ragal ci lamb ndax beuré naak gnépe ñim tololone eume ak bombardier mokoci daan ciy magam ay moromam issa pouye
@baraleye4749
@baraleye4749 4 ай бұрын
​@@daoudatoure5957 waaw komba su taxawée
@bathiediouf7978
@bathiediouf7978 4 ай бұрын
Waay ffi amoul morom lamb la bayilenn sen wakh yii
@elhadjibeye7257
@elhadjibeye7257 4 ай бұрын
Merci bcp Lirou ❤❤❤ félicitations ❤❤❤❤
@bathiediouf7978
@bathiediouf7978 4 ай бұрын
Franc mo meun Balla fouff teu khamngenn lolou
@AdamaMballo-t9s
@AdamaMballo-t9s 4 ай бұрын
Combat balla -franc c’est l’ordre du jour
@aliounediop-fs4kx
@aliounediop-fs4kx 4 ай бұрын
Sa wayi lolou dou combat balla goumou dane Fran goumou dane bombardier fin carriere la nek pourtand fran kimou kayar moy modou lo balla moko dane mai legui louy probleme bi nak balla est modou lo Ak Eumeu sene ? Fran na seti ay moromom mon guene fi la wakh loune reug nakh beugue beure rek bilaye ❤💪🙏
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc 4 ай бұрын
​@@aliounediop-fs4kxkokou nékk fin carrière mo douma balla gaye bou yagoul
@Omarsane7491
@Omarsane7491 4 ай бұрын
Franc dee kouka dieul d'Abou bilahi😂😂😂😂😂
@almaktoumdiop8749
@almaktoumdiop8749 4 ай бұрын
Billahi nite kousi yéwou woule sa adouna dina wakhou si serignou tariyakh yi
@BathieBa-vp3pz
@BathieBa-vp3pz 4 ай бұрын
Franc seul ndiago or bi for life
@AboubacryGASSAMA-zs7oi
@AboubacryGASSAMA-zs7oi 4 ай бұрын
Franc loumou wahatti 😅😅😅😅ah doyena war nak bou yaguè mani guayii dagnouko ragal dhè vraiment ..Franc bou dèfè interview ils siffit just mou nouyau rèk .niounii dafa rèw 😅😅😅😅
@alioudiouf9004
@alioudiouf9004 4 ай бұрын
Mani lirou BOU KÉNEU RAGAL SA ADVERSAIRE FRANC EST AU SOMMET IL A BATTU BOMBADIER QUI A BATTU BALLA GAYE 2.
@almaktoumdiop8749
@almaktoumdiop8749 4 ай бұрын
Mane damavkhamoule lirou kagñe laye bayi dougourou 😂😂mak mou tólni yaw wara déme liguéyi khani di dougarou samoromou dome franc am na droit wakh louko nékh balla gaye dakh Bombardier moko dane gñiéti yone li takh mani gñiéti yone Bombardier daf ko dane gñiari yone si béna gone té kham guéni tapha tine liguéne ko dèf kouma diokh tapha tine ma dane ko
@baraleye4749
@baraleye4749 4 ай бұрын
Papis lumi déf Modou lo
@almaktoumdiop8749
@almaktoumdiop8749 4 ай бұрын
@@baraleye4749 papis gñiépa kham ni moye yor mistikou modou mé lirou mbeur laa gñiaka fayda mo takh mouye dougourou ay rakame
@lamine4360
@lamine4360 4 ай бұрын
Lirou diane masoul deff interview si keurame 😂😂
@almaktoumdiop8749
@almaktoumdiop8749 4 ай бұрын
Serigne sice khalis rék mé kou khalatouke gñiéti fanou bamèle loula nékh défale
@serignedione7356
@serignedione7356 4 ай бұрын
Maylene gnou diam , franc mo lene di dérange digueee D
@BaMasour
@BaMasour 4 ай бұрын
Yene bombardie bilene doing Dane la franc Dane
@ousmanegueye2408
@ousmanegueye2408 4 ай бұрын
Merci lirou diane
@amadouba6652
@amadouba6652 4 ай бұрын
Lirou demale ligueyii bayal dor marto yii
@Aaron-i5f
@Aaron-i5f 4 ай бұрын
Ki dè limou yor sa baye yorouko
@ibrahimasarr711
@ibrahimasarr711 4 ай бұрын
Lirou wakho deugue dagay dokhot manoul franc
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 4 ай бұрын
Fara Thi bopam mo xamoul Bopam Fara bougué Beraii Nadém Beraii Dji Ak Gri 2 ou bien Modém Berai Dji Ak Aliou sey 2 Boumniou Fonto 🧏Balla Gay 2 sa papa Modou lo xamnako Boubax Dangako Ladioul Balla la Yakar
@PapemaniangDiop
@PapemaniangDiop 4 ай бұрын
Wa balla gaye d'où moromou franc loutakh sa thies roukh 😅😅😅
@ND.BALLAuser-ft7kg5jk5v
@ND.BALLAuser-ft7kg5jk5v 4 ай бұрын
Pour quoi ça 😂 pour quoi ça 😂lirou di nama Ray
@omzogueye9168
@omzogueye9168 4 ай бұрын
Franc da wara khamni kouy gnane day nékhal
@ndiayedemba2566
@ndiayedemba2566 4 ай бұрын
Tu parle beaucoup crois à toi c'est important.
@flolingard8313
@flolingard8313 4 ай бұрын
Lamine mo yabater 😂
@amadoudiopsy
@amadoudiopsy 4 ай бұрын
lirou diane mi weroul sakh liko aranger rek lay nitou intérêt leu bala amoul loumouy bagner franc comba bou diadou leu nako dieul bouder deug leu
@Adnanezinho-jm8zk
@Adnanezinho-jm8zk 4 ай бұрын
Franç mom nimouy beuré jakhaloul balla guay combat bi dina takhaw balla ragaloul lolou
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
Bayi léne Di diokh doff yi micro
@ouzdaking382
@ouzdaking382 4 ай бұрын
Alioune seye mo meune 100000 franc
@Aladjil609
@Aladjil609 4 ай бұрын
Lolou d aye doull la😂😂
@BiraDiop-co1lw
@BiraDiop-co1lw 4 ай бұрын
😂😂
@zulnhofaye2584
@zulnhofaye2584 4 ай бұрын
Lirou yaw ya geuna sokhar filla boy Niang d'âne Balla gaye nga née balla da fébarr kou sokhar nga
@gabrielagboton5361
@gabrielagboton5361 4 ай бұрын
Deglouléne lirou diane Lou mou wakh a 2 min 43 de l'interview .. ( victoire no ko djeundé bakh na ) Lo bougue wakh fofou lirou ?? Combat bî djeundé ngéne nieup .. chroniqueurs , communicateur .. serigne !!! . C'est honteux !!! Lamb dou sport walay mileu bou bonn au beurý nafekh ..
@Oumar-jw9cb
@Oumar-jw9cb 4 ай бұрын
Franc néga ya meune promoteur yi diokh nanioula Serigne Ndiaye 2 dieulko bari nga ndéye wakh
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
Franc dako nokou daneko khana revanche la beug😂😂
@moustaphaba9114
@moustaphaba9114 4 ай бұрын
Ndeysane deguene nam victoire dieulene franc wala zarko té guene bayii sen thiakhane yii
@AdolpheGomis
@AdolpheGomis 4 ай бұрын
Franc daane Serigne Ndiaye laane laye dooli heur bi thi franc dane natt hana daane Forza di délouwate thi Serigne Ndiaye😂😂😂 farceur yi😂😂😂
@deltonlopez4366
@deltonlopez4366 4 ай бұрын
Parfois vous oubliez que Franc a battu serigne Ndiaye ci arène bi tei bobou ba legui amoul défaite 13 combats 13 victoires ci ay secondes lay danei mbeur
@KhadimSylla-wm4wq
@KhadimSylla-wm4wq 4 ай бұрын
Franc rek
@moustaphaba9114
@moustaphaba9114 4 ай бұрын
Way foutez nous la paix sen couronne mo gueuneu kawé sounou boss kay dieulene modou beurré woul ak yen khana yen tamit yena mome nitt yii beugeulene niou ladjlene guene beugeu ladj kou lene nekh
@baraleye4749
@baraleye4749 4 ай бұрын
Franc yékségoul sax co sa thiés danko teubel
@ndiayedemba2566
@ndiayedemba2566 4 ай бұрын
Salut, je pense que c'est Balla qui est marié ta mama.
@salioumbackeniang2570
@salioumbackeniang2570 4 ай бұрын
Franc neu xolat sa communication mbeur you mag yi nioungui koy rejeter nak nimouy waxé. Sou continuer sur cette lancée mbeur yici kaw douniouko may chance. Style américain bobou dou marcher galsen. Neu xol nimouy waxé. Kén téré wouko teukou mbeur yi ci kaw mais dans le respect.
@Victoireman
@Victoireman 4 ай бұрын
Koone daal leguii lambj dahira la il faut di rayaneté😅😅😅😅 pourtant franc loumou wakh dougoull ci vie ov adversaires mais il a le droit de déstabiliser ses futurs adversaires 😅
@salioumbackeniang2570
@salioumbackeniang2570 4 ай бұрын
@@Victoireman Adversaire laniouy déstabiliser lors des face to face mais pas avant sinon le combat ne sera pas ficelé. Reug Reug dafeu correct beu combat wam ak Bombardier taxaw mou dal si kaw bomb, Siteu tamite la même chose mom ak Modou Lo. Franc Yéna ko waxoul deug. Defone neu ni ak Lac 2 motakh Lac bagne, mou def ko Eumeu momite mou bagne, legui il s’attaque à Balla dafeuy bagne aussi. Bopam leuy yaxal rek. Il faut respecter ses aînés. Balla mo dakh roubé mais setloul rek deuy xar beu combat bi taxaw. Teukou néxal, xoubeul. Mais Franc dafeu xamoul wakhine. Nane ay « Balla amneu louko doy etc. » Sou soigner woul sa communication douñiouko teugueul combat yimou sokhla. Beug niou mayleu chance beu paré do diokh thieur gnilako wara may. Lolou dou xél
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc 4 ай бұрын
Il n'a absolument rien n'a rectifier au contraire communication bi day geuna méti kou beug beuré kou begoul tu vas au diable
@salioumbackeniang2570
@salioumbackeniang2570 4 ай бұрын
@@MilkMilo-qr5uc Yen yénakoy yakhal nak gni nek ci kaw souniou nangouwoul beuré ak mom dou atteindre son objectif. Sou combat bi taxawé meune naa wakhé nii wayé sou takhawoul mouy def ni dou soti. Xel dou dieurigne loudoul Xalaat.
@MilkMilo-qr5uc
@MilkMilo-qr5uc 4 ай бұрын
@@salioumbackeniang2570 communication lay bagna dégue gnoune gnokoy supporter on est des intellectuels diang yoré sounouy diplôme on sait quand il y a manque de respect ou pas gnoune dougnou ay fanatique franc et Modou gnou léne di supporté gnou léne geuna conscient gissou mako yoyou gayi di wakh c'est juste des prétextes étant donné que dagnou ko raga c'est meilleur qu'ils ont trouvé pour meytou ko mais ça ne marchera en aucun unchallah néxaloul kéne et il ne changera guère sa communication et notél lima lay wakh lamb si loxom lay moudj tôt ou tard
Support each other🤝
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 75 МЛН
IL'HAN - Qalqam | Official Music Video
03:17
Ilhan Ihsanov
Рет қаралды 505 М.
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 10 МЛН
It works #beatbox #tiktok
00:34
BeatboxJCOP
Рет қаралды 25 МЛН
Urgent Grosse révélation de BeuzLutteTv Après le combat  Balla Gaye2 vs Tapha tine.. Liko dane moy.
20:20
Lambelogue merna "Ama fii lako wa pikine di..." franc vs ama balde
23:27
Он хотел защитить свой бункер 👮‍♂️🚘🌾
0:19
Gelik Shorts | Лучшие Авто Видео из России
Рет қаралды 2,6 МЛН