Urgent Grosse révélation de BeuzLutteTv Après le combat Balla Gaye2 vs Tapha tine.. Liko dane moy.

  Рет қаралды 59,507

Fadam2 expert de la lutte sénégalaise

Fadam2 expert de la lutte sénégalaise

Күн бұрын

Пікірлер: 171
@mamadoundiaye1724
@mamadoundiaye1724 4 ай бұрын
Ibrahima faye beuzz l.intellectuel du milieu de la lutte senegalaise un travalleur posé et calme
@deveba8657
@deveba8657 4 ай бұрын
Il a continué ses études au Canada 🇨🇦 ce n’est po pour rien il est fort mo fi indi pp view
@khadimmbacke3733
@khadimmbacke3733 4 ай бұрын
Bly c'est le meilleur❤❤
@abdouthiam3312
@abdouthiam3312 4 ай бұрын
Bilay c est le mieur ❤
@babakarngom543
@babakarngom543 4 ай бұрын
Balla gaye 2 bilAhi c'est le meilleur luteur de l'arène kou sisou ya kham balla rek ❤️❤️❤️🖐️🖐️🖐️🥰🥰
@mamadounianghane2330
@mamadounianghane2330 4 ай бұрын
😢 c'est faux
@DiaCodou-b9v
@DiaCodou-b9v 4 ай бұрын
Merci
@massambadare
@massambadare 4 ай бұрын
😂😂😂😂😂solen yeneu fi meun sougnou len dane dengene febar s'en mbeur bou feneukhe bi ngen gnouye fatte teug s'en combat préparé s'en leep khamnagne leep mai khamngen niii s'en mbeur mii diekhalna yagna
@massambadare
@massambadare 4 ай бұрын
Kheureum you bon yingen indi fi galathe gemolen Dara te gni dess si lamb niep nio meun balla gaye foufe sah lisi kanam raboul ay beut
@gtheboss9635
@gtheboss9635 4 ай бұрын
Lou léer nga wakh
@babacarsambe4372
@babacarsambe4372 4 ай бұрын
modou kharagne lo un vrai patriote tokk si réw mi 💯entraîner si réw mi 💯am niveau bou kén amoul si réw mi💯
@Neymar1994-m5m
@Neymar1994-m5m 4 ай бұрын
Niou dioutal ko si💯si réw😂
@abibdiop9130
@abibdiop9130 4 ай бұрын
😂😂😂😂​@@Neymar1994-m5m
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
​@@Neymar1994-m5m sa tontou am na diome😂
@cheikhsylla4019
@cheikhsylla4019 4 ай бұрын
​@@Neymar1994-m5msa tontou bi diarr n'a xarou😂
@juniorba2352
@juniorba2352 4 ай бұрын
😂😂​@@Neymar1994-m5m
@laminediatta7069
@laminediatta7069 4 ай бұрын
Beuz je vs encourage ndakh ligueyyy katttt nguaaa b’ vraiment chapeau
@Tawfeekh
@Tawfeekh 4 ай бұрын
Balla Gaye est, si je ne me trompe, le seul lutteur a avoir battu 2 fois des lutteurs redoutables: le King Modou Lo, Gris Bordeaux et Tapha Tine. Balla est courageux et redoutable. Il ne fait pas de calcul, quel que soit son adversaire. C'est pourquoi il a eu beaucoup de défaites sinon il pouvait négocier ses combats quand il n'était pas en forme. Même en baisse de forme, il a toujours attaqué ses adversaires. C'est un champion parce que dafa ame sagne sagne.
@tantamboup3668
@tantamboup3668 4 ай бұрын
Lolou boum la better ragal dou diouguer guediawaye
@lesankariste8721
@lesankariste8721 4 ай бұрын
@@tantamboup3668mais le seul lutteur 2 lutteurs différents l’ont battu et ont battu son frère 😂😂😂 lamb reni niambi Lo si kham 😂😂😂😂😂
@MoustaphaNiasse-y3u
@MoustaphaNiasse-y3u 4 ай бұрын
Billahi beuz tu es un grand analyste de comba et beaucoup de combattants et les préparateur de combattants devraient t'écouter
@DjibrilBa-xp7te
@DjibrilBa-xp7te 4 ай бұрын
Modou kharagne lô bourou lamb dji seul ❤️🙏 yalna am ndam le 24 novembre inchallah ❤❤❤🎉
@Bour_ndiaye_bour
@Bour_ndiaye_bour 4 ай бұрын
Yalnaniou gnaf ndéyam mou danou 😂😂😂
@FallourafahihtDiaw-po4rl
@FallourafahihtDiaw-po4rl 4 ай бұрын
Khana ça bourr la
@CheikhNDJILIW-n7p
@CheikhNDJILIW-n7p 4 ай бұрын
Buuru tapalé
@fallou318
@fallou318 4 ай бұрын
Borom dioutal bi😂😂😂😂😂
@thiernodiallo2830
@thiernodiallo2830 4 ай бұрын
​@fallou😂😂😂😅😢318
@abdougueye4837
@abdougueye4837 4 ай бұрын
félicitations lutte tv
@pathesamb9561
@pathesamb9561 4 ай бұрын
Modou lô rek laniouye topp
@boyetownfromdkr5287
@boyetownfromdkr5287 4 ай бұрын
Non il est le meilleur lutteur du Sénégal c'est exceptionnel moye lamb quoi vraiment bilahi
@tallambengue-oc4cd
@tallambengue-oc4cd 4 ай бұрын
Buzz machala vrai intellectuelle bilah walahi ❤❤
@djilydiop992
@djilydiop992 4 ай бұрын
Kou Mossoul dieund cote wala nga dém stade comme moi 🤣
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 4 ай бұрын
😂😂yow déh nio bok béna groupe 😂😂
@makavelli-ru3un
@makavelli-ru3un 4 ай бұрын
Bakh yaye 37 rek lay weur Instagram 😂😂😂dewma stade dieundou ma code
@abdougueye4837
@abdougueye4837 4 ай бұрын
depuis perperview am ba légui chaque grand combat ma dieunde ko
@papawade8521
@papawade8521 4 ай бұрын
télé rek
@elhadjibeye7257
@elhadjibeye7257 4 ай бұрын
Machala Beuzzz :quelle analyse !!!❤❤
@alassanemane3021
@alassanemane3021 4 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ balla gaye 2 moy lamb ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@hameh8917
@hameh8917 4 ай бұрын
Hell yeh I was 💯 satisfied with Senaffiche yesterday thank you so much Beuz
@NdiaboutaDiouf
@NdiaboutaDiouf 4 ай бұрын
bilahi beuz c'est vrais
@modougadiaga9839
@modougadiaga9839 4 ай бұрын
Bella gaye 2 rek 💪💪💪💪💪
@adamandiaye5622
@adamandiaye5622 4 ай бұрын
Supporter balla yi dani job nak😂😂danio am khalisss
@SaliouDiop-e4r
@SaliouDiop-e4r 4 ай бұрын
Beuz rekk layy Topp
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 4 ай бұрын
Jambar beuzzz day wah rek,guisss nga wahkat yi nieupa Tapha Tine lagne yakaroné day douma Balla Guaye 2 dane,niom nieup
@hameh8917
@hameh8917 4 ай бұрын
Bro to be honest I’m not a Modou Lo fan but, Modou Lo is the Messi right now. C’on guys you should give Modou Lo his maximum respect
@Abdallah31341
@Abdallah31341 4 ай бұрын
Who deprive him his respect ?
@layekharagne2224
@layekharagne2224 4 ай бұрын
that’s the power of money they all get paid by AZIZ NDIAYE
@laminediatta7069
@laminediatta7069 4 ай бұрын
Balla moyyyy doundal lamb jiiii il est le wally seck de l’arène stade biii diii arène nationale bunnndonnn balance laa balla mokoyyy danellle
@Serignesaliou-dp5gf
@Serignesaliou-dp5gf 4 ай бұрын
Bien analyse
@FansaraKeita
@FansaraKeita 4 ай бұрын
Balla moy lamb ❤❤❤
@laminediatta7069
@laminediatta7069 4 ай бұрын
Kennnnn duuuu mommm deeee c le star
@residenceera1121
@residenceera1121 4 ай бұрын
Plutôt la star
@fallou318
@fallou318 4 ай бұрын
Mbeur yeup balla moye sén baye ❤
@diambendoye3320
@diambendoye3320 4 ай бұрын
Beuzz tu et reconnaissant
@douggydiop
@douggydiop 4 ай бұрын
beuzzlutte tu as tout compris. tues le seul qui dit la meme choses que moi. tapha tine lambame daffa diexe des le premier coup de balla gaye. daffe ko dore chi tempe bi. ba pare deuxieme coup mou dorateko chi tempe bi. apres lako comencer kore. mais deux premiers coups yi la diexale chi combat bi. lagneléne boxeur yi lane moye coup chi tampe. kérounope
@youssousarr3586
@youssousarr3586 4 ай бұрын
Wagnilene Séne prix yi au niveau du Sénégal yene esk ay nite nguene tamite buz hé nieup doundouniou lamb j dh parcek nikoutone en direct bouleneniou fonto
@pathesamb9561
@pathesamb9561 4 ай бұрын
Modou lô rėk moye champion bou makk bi
@DaboIssa-i3k
@DaboIssa-i3k 4 ай бұрын
😂Lolou sa wakh la
@layekharagne2224
@layekharagne2224 4 ай бұрын
balene fofou niouy doul rek khaliss laniouy diamou
@laminediatta7069
@laminediatta7069 4 ай бұрын
Fadam mommm amoul bennnn sass Fadam guemoul tous tass wa amadou ba la deee mom ak diazaka fadam loyyyybyekeutti sa loxo
@bybrufisquois257
@bybrufisquois257 4 ай бұрын
Beuz tu es très malin , tek xel nguay def ,mais modou dofoul Bay dieul balla
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Thieuy Talibé Aziz Ndiaye yi😂😂
@thiernombaye4035
@thiernombaye4035 4 ай бұрын
Modou lo imamou mbeur yi kou diangoul niou chifaye 😂😂😂
@papefall4806
@papefall4806 4 ай бұрын
Fadam nena aka viral 😂😂😂😂nena day comprendre comprendre Lou Boko ladione lerr Nama xamoul louy viral
@yayakonte6292
@yayakonte6292 4 ай бұрын
Mashalla ❤❤❤❤🎉🎉🎉😂😂😂
@seutoubuur3090
@seutoubuur3090 4 ай бұрын
Modou lo mayètoul revanche 😋nokhoulèn feulè rèndi diègui rek 😂
@Dieng-vk6if
@Dieng-vk6if 4 ай бұрын
Mafia lambe yépp danio beugue modou lo danou mais yalla mokofi tékk Modou kharagne lo seul Modou xlo seul Modou xlo seul
@Mamecheikhndao-pe8ny
@Mamecheikhndao-pe8ny 4 ай бұрын
Na dieul avance bi
@ouldfall
@ouldfall 4 ай бұрын
Vraiment beuzzz affaire bi lairna l autre fois j ai acheté wido mais niewoul sah bo niewoulone douma djinedeu code
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Balla Gaye sou nekkei ci forme. ça revient toujours dans vos débats. Je me demande lane mokoy teirei neikk ci forme😂😂😂😂
@ousseynousall5808
@ousseynousall5808 4 ай бұрын
Tapha réke tine réke ❤❤❤
@AngeGabriel05
@AngeGabriel05 4 ай бұрын
nopaal naleuu😂
@tourefatou2434
@tourefatou2434 4 ай бұрын
🤣🤣🤣😭nanal mew
@amethboultouf4296
@amethboultouf4296 4 ай бұрын
Sen data ndey tapha tine rek laniouy top
@Lebarhamien75
@Lebarhamien75 4 ай бұрын
Wou wayyy 🤣😂
@trace-infos2a846
@trace-infos2a846 4 ай бұрын
Kou nangouloul Balla Gaye dé sa toune moy tangue rék
@AssaneGueye-t3h
@AssaneGueye-t3h 4 ай бұрын
Dafaye fine fine regue bess
@MoussaGueye-r3i
@MoussaGueye-r3i 4 ай бұрын
Salam
@mariesagne4808
@mariesagne4808 4 ай бұрын
Bilay
@niassesouleymane7163
@niassesouleymane7163 4 ай бұрын
Balla gaye 2 vs Boy Niang 2
@souleyewade7419
@souleyewade7419 4 ай бұрын
Eumeu balla ou le roi vs empereur
@thiawsuisse5634
@thiawsuisse5634 4 ай бұрын
Fadam le t.....
@laminediatta7069
@laminediatta7069 4 ай бұрын
Detttt siteu meunul dannnnn modou lo deee lolou la nguemmmmm
@mormbaye2989
@mormbaye2989 4 ай бұрын
Boul wax lolou lamb dafa doywar ❤
@JumeauxJumeauxdioplaye-kw6pp
@JumeauxJumeauxdioplaye-kw6pp 4 ай бұрын
Na beurre ak boy yi eumeu sene nadef comme modou lo mai boy yi chance
@adamasane5176
@adamasane5176 4 ай бұрын
Beuz Balla gaye bou paré kén manouko natt
@KaraDiengKara
@KaraDiengKara 4 ай бұрын
Fenne rek
@JumeauxJumeauxdioplaye-kw6pp
@JumeauxJumeauxdioplaye-kw6pp 4 ай бұрын
Fouleu ak personalité bi Modou lo am bani Dou Beurré waat ak Balla neu Balla am Fouleu bobou bania Beurréwat ak eumeu sene modou dafa tok si titram neu Balla mai boy yi chance
@Mamecheikhndao-pe8ny
@Mamecheikhndao-pe8ny 4 ай бұрын
Eumeu séne néna empereur bi la sokh la 😂
@madoundoye2414
@madoundoye2414 4 ай бұрын
Wakhofi dara
@JumeauxJumeauxdioplaye-kw6pp
@JumeauxJumeauxdioplaye-kw6pp 4 ай бұрын
@@madoundoye2414 damani sen pa bou amoul bruit bobou ngua xamnie sans Balla Gaye 2 Eum la ken toudoul n.a. dem took sou degg Empeureur
@DaboIssa-i3k
@DaboIssa-i3k 4 ай бұрын
Wa modou lo écoute lou niouy wakhal sen papa balla gaye2 😂
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Siteu sakh dou djeul Balla Gaye sou daanei Modou Lo parceque Aziz a mal parlé de Siteu
@abdoufaye8382
@abdoufaye8382 4 ай бұрын
Balla mistique rek la am forme bi bakhoul 🎉
@Mamecheikhndao-pe8ny
@Mamecheikhndao-pe8ny 4 ай бұрын
Khana da dioutal sa mbeur 😂
@adamandiaye5622
@adamandiaye5622 4 ай бұрын
Buz nena amoul nokos wakh nga deug dai diegue bouri rk do dane ken😂😂
@cheikhgadaye4923
@cheikhgadaye4923 4 ай бұрын
Amna kou wakhoun ni sou balla gaye dané tapha tine fadam dîna ni Bima dalanté ak balla la hamni loxo yi amnagne doolé 😂😂
@AlleMbengue-fn3bt
@AlleMbengue-fn3bt 4 ай бұрын
beuzz moléne geuneu kham lamb dé
@barhamsarr3061
@barhamsarr3061 4 ай бұрын
Grand contre petit dafa xew
@Lebarhamien75
@Lebarhamien75 4 ай бұрын
Linguay wakh nii kham kham bou laire laa
@tallambengue-oc4cd
@tallambengue-oc4cd 4 ай бұрын
Eumeu sene walahi xamal nii Balla gaye2 dinala douma dinala dane inchallah
@massambadare
@massambadare 4 ай бұрын
Wa bobou inchallah
@massambadare
@massambadare 4 ай бұрын
Yalana takhaw rek
@fallou318
@fallou318 4 ай бұрын
Balla gaye mo meun 10 modou lô 😂😂😂😂😂
@ousmaneseye3765
@ousmaneseye3765 4 ай бұрын
Na déff ni modou déff wathieu dieule ndiari boye comme fran akk serigne ndiaye lolou dou comba balla eumeu séne
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Nopal leine seine boppp, meunoleine ame ci Modou Lo. Kokou niittou kaddou leu, dou comme mbeurs you dofff yi
@laminediatta7069
@laminediatta7069 4 ай бұрын
Fadam buuu amadou ba Anna ketchup de lat diop duguennnn toussss ces voyous de 🎤 lamb nakkk mommm sante lenkooo balla Gaye 2 c le wally seck des lutteurs
@abdouyally6863
@abdouyally6863 4 ай бұрын
Loutakh balla gaye dou dialat béne xalé boye nia 2 dako dane na dialaté béne xalé dane ko diou khôl bakham ?
@laminediatta7069
@laminediatta7069 4 ай бұрын
Tapha khadioulll diekhal kuuu niemmme naa demmm
@abdoulayediallo4028
@abdoulayediallo4028 4 ай бұрын
Bn2 vs bg2 moy comba
@alassanendiaye6148
@alassanendiaye6148 4 ай бұрын
Wa facelamb Nio toudé balla fawzeyni mais pas yen
@TaphaSene-r6s
@TaphaSene-r6s 4 ай бұрын
Contanouma dhé si pérpayview biii
@biramboye9011
@biramboye9011 4 ай бұрын
Ne surestimez pas cette victoire de Balla Gaye sur Tapha Tine. Daan ku la ràggal du mënooré!
@GallassNdiaye-x4i
@GallassNdiaye-x4i 4 ай бұрын
Eumeu balla dou comba nagnou djiell boyeyi
@madoundoye2414
@madoundoye2414 4 ай бұрын
Yane boye boyi dagno prouver dara
@raoulgeorgesfrancoismangaf6940
@raoulgeorgesfrancoismangaf6940 4 ай бұрын
Balla Gaye moy doundeul lamb ji
@berengermpamy1819
@berengermpamy1819 4 ай бұрын
Balla n’est pas plus populaire que Modou lo, bayilen thiakhane
@papefaye272
@papefaye272 4 ай бұрын
Balla est plus populaires que Modou lolou amoul sakh weranter
@berengermpamy1819
@berengermpamy1819 4 ай бұрын
@@papefaye272 da ngay nakh seu bopp rek fall
@elhadjicherifdioume3067
@elhadjicherifdioume3067 4 ай бұрын
Balla gaye 2 est plus populaire
@adamandiaye5622
@adamandiaye5622 4 ай бұрын
Bay dal.nit kou bakh waye dieule mbeur yi dilen exploiter rk dilen fay ay un millions
@barhamsarr3061
@barhamsarr3061 4 ай бұрын
Pourquoi pas revanche Balla-BN2
@Dieng-vk6if
@Dieng-vk6if 4 ай бұрын
Dafa télle
@tvadamandiayekhassaidtouba8388
@tvadamandiayekhassaidtouba8388 4 ай бұрын
BALLA GAYE VS TAPHA TINE COME SÉNÉGAL AK CÔTÉ DU VOIR REIK 🤣🤣🤣🤣🤣🤣
@eboufall
@eboufall 4 ай бұрын
Sa Data ndaye
@moussapayemane4167
@moussapayemane4167 4 ай бұрын
Yow wara saga nday ki,défoula dara,loula méti tégoulako
@trace-infos2a846
@trace-infos2a846 4 ай бұрын
Lamb dji dé kouni nékhoul sa khol mo bone rék
@souleyewade7419
@souleyewade7419 4 ай бұрын
Modou avait dit il lutterai pas avec siteu nn
@layekharagne2224
@layekharagne2224 4 ай бұрын
fane la ko wakhè ?
@gabrielagboton5361
@gabrielagboton5361 4 ай бұрын
Bilay man Sénégalais deuf ma dikheul quoi !! Mais comment ont peut ce dire professionnel , quand tu vois que le promoteur qui a organisé le combat cours dans l'arène pour féliciter balla gaye et tu vois aziz qui deviens préparateur mystique .. mais tapha da feu nelaw ... tu a etais sacrifié mon ami comme un mouton .. puis baye ndiaye aucune classe en tant que promoteur tu aurais pu attendre avant de jubilé sur la victoire de ton luttteur sa c'est honteux ..
@layekharagne2224
@layekharagne2224 4 ай бұрын
wallahi tapha et son staff sont des cons
@IscoDiop-y5z
@IscoDiop-y5z 4 ай бұрын
Modou lo kasse
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 4 ай бұрын
Balla dh bilahi forme bimou yoor ni danoul ken mystique rk la am mh ligueyoul lou dan mbeur Tapha Time mi deumb man sakh boko bolewon ak man khana m’a danko Li d’où ngoora d’où fiit diap diap niit ba bokay door sakh mou melni cou yoor sa dôme c honteux Ioe kingay diakarlo di lewto mom mouy foudou di wañarou nga danko yakaar ni y’a meun ci lamb dji
@Mamecheikhndao-pe8ny
@Mamecheikhndao-pe8ny 4 ай бұрын
Stress ngay guéné 😂🎉
@eboufall
@eboufall 4 ай бұрын
Sène Data ndaye yénak PPV AK Aziz baye Ndiaye
@Mamecheikhndao-pe8ny
@Mamecheikhndao-pe8ny 4 ай бұрын
Ioe katal sa ndy
@saerhihiodf110
@saerhihiodf110 4 ай бұрын
Buzz ko kham ni mèw rk 😅😅 meuno kham lèp lougn wakh nga ni kham nga ko
@madoundoye2414
@madoundoye2414 4 ай бұрын
Daye doul rek après lamb kounek Di doul
@vieuxndiaye3790
@vieuxndiaye3790 4 ай бұрын
Vraiment jeune comprends pas balla mou tegale aye defet Modou deff exploit yene nieup nguene ndangou balla dane tapha mou khamoul darra nguen beug niom sonal
@Mamecheikhndao-pe8ny
@Mamecheikhndao-pe8ny 4 ай бұрын
Bane défaite la tégallé 😂
@CASI7797
@CASI7797 4 ай бұрын
Lamb dh Pay Per View moko yakk
@barhamsarr3061
@barhamsarr3061 4 ай бұрын
Na Balla may chance boys yi
@laminediatta7069
@laminediatta7069 4 ай бұрын
Boyiiii nioyyy bagne
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 4 ай бұрын
Balla dh bilahi forme bimou yoor ni danoul ken mystique rk la am mh ligueyoul lou dan mbeur Tapha Time mi deumb man sakh boko bolewon ak man khana m’a danko Li d’où ngoora d’où fiit diap diap niit ba bokay door sakh mou melni cou yoor sa dôme c honteux Ioe kingay diakarlo di lewto mom mouy foudou di wañarou nga danko yakaar ni y’a meun ci lamb dji 😂
@mbayeameth5660
@mbayeameth5660 4 ай бұрын
Salam wadji DemAl xolat lamb dji kou commencé khékh bi Tapha mohh yambar rk copain
@ibrahimadiop3754
@ibrahimadiop3754 4 ай бұрын
Balla meunoul nek bete noirou gneup tapha préparation bi bakhoul nak buzz
@sophrotall8105
@sophrotall8105 4 ай бұрын
Beuzzz yaw mom sa dafa gawa fessss lol yemal si sa ppv bobou heure bo wakh niou daan sa vision si lamb dafa desss lou barrri ninga defonnn Ama Modou , Modou Boy Niang, ak lingua wakh si Tapha Tine khamossi wonnn lou bari sa chanson bobou boyna souniouy noooop
@coeur2lion38
@coeur2lion38 4 ай бұрын
Ki mo yak lamdji buzz mo tah kéne menatouko ték télé
@JobDays
@JobDays 4 ай бұрын
Tine a ètè sacrifiè balla avait tt dit a banjul combat gagner à l'avance yon wi deja tracer
@MohamedBodiang-uw7yk
@MohamedBodiang-uw7yk 4 ай бұрын
Saway wakhofi dara nekal sportive balla dako meune Dane ko louy probleme bi
@alhassanngom8282
@alhassanngom8282 4 ай бұрын
Non moko meune mom mais balla gaye 2 waxone nako gambie kaay deugg leu.
@alhassanngom8282
@alhassanngom8282 4 ай бұрын
@@MohamedBodiang-uw7ykpourquoi ngaay wéddi naane nitt ki waxofi dara yow. Boo yeuggoul rek yeuggo kone boul wéddi. Balla nak champion la momeûn gayine bi ak kenen koudoul mom. Wassalam
@souleyewade7419
@souleyewade7419 4 ай бұрын
Si il e de retour il n a qu a prendre eumeu 😂
@NabyLeJuriste
@NabyLeJuriste 4 ай бұрын
Balla dh bilahi forme bimou yoor ni danoul ken mystique rk la am mh ligueyoul lou dan mbeur Tapha Time mi deumb man sakh boko bolewon ak man khana m’a danko Li d’où ngoora d’où fiit diap diap niit ba bokay door sakh mou melni cou yoor sa dôme c honteux Ioe kingay diakarlo di lewto mom mouy foudou di wañarou nga danko yakaar ni y’a meun ci lamb dji
@MalickNiane-ux5hj
@MalickNiane-ux5hj 4 ай бұрын
Ioe ya sokhor deug tapha tine dor balla placage mou resister ko ngani amoul doller ya sokhor
@leuz.patriote
@leuz.patriote 4 ай бұрын
Modou lo na dieul combat bi xoll ma dokhanate ndayam lègui dofoul 1 miliar sah dou dieul bg2 .mes inchallah Sama wadji siteu yalla na dane mod lo
@layekharagne2224
@layekharagne2224 4 ай бұрын
@@leuz.patriotelane mo ci diara saga ? yena dane mais yenay mer sene yaye 😂
Zarko minimise Gris Bordeaux "kou modou lo dane damay koy nokou…"
11:20
Kawtef😱? Tapha Tine Dane ko Diap si Mystique; réaction a chaud de Tapha Kandji liko dane moy dafa…
21:40
Mom Hack for Cooking Solo with a Little One! 🍳👶
00:15
5-Minute Crafts HOUSE
Рет қаралды 22 МЛН
We Attempted The Impossible 😱
00:54
Topper Guild
Рет қаралды 52 МЛН
Balla Gaye Dane Na Mai Forme Bi Dess na, Grosse Declaration De Fadam2 apres Le Combat Balla Vs Tapha
32:08
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 16 М.
🔴DIRECT TIKTOK FADAM2 AVEC MOUHAMED DES REVELATIONS EXPLOSIFS MODLO, BALLA GAYE2, BN2, REUG REUG
2:51:35
Fadam2 expert de la lutte sénégalaise
Рет қаралды 9 М.
Amena lou khewatii D😱 Medical Boye Niang..; Fadam2 Revient encore et fait des révélations Explosif😱
30:19
Face à Face Tapha Mbeur vs Siteu bou Ngor " Tapét gua dagay…"
9:35