😱 Kaliphone Sall fait fuité les audios de Ousseynou qui détruit la voyante Aissatou Penda Diop

  Рет қаралды 143,782

Lixewgalsen TV

Lixewgalsen TV

Күн бұрын

Пікірлер: 259
@salioundiaye3197
@salioundiaye3197 18 күн бұрын
Serigne Amadou Cissé vous êtes très intelligent et vous êtes très bon communicateur. il faut appuyer kalifone qui est sur la bonne voie. Ouseynou l'homme fort est celui a remporté la victoire sur lui-même. Le vrai courage consiste à faire ce qui est juste. Ceux qui ignorent qu'ils marchent dans l'obscurité ne verront jamais la lumière. Ouseynou il faut rejoindre votre famille vous êtes un citron pour la dame. Elle va vous presser à sa manière et vous jeter. Elle a amené son fils à l'étranger pour des études. Ouseynou revient sur terre avant qu'il soit tard. A Bon entendeur salut.
@antandiaye3769
@antandiaye3769 18 күн бұрын
🎉🎉tu as dit la vérité
@lemeringue-fi2zf
@lemeringue-fi2zf 18 күн бұрын
Wallahi tu as tout dit
@BinetaNdiaye-ot3hh
@BinetaNdiaye-ot3hh 18 күн бұрын
Vérité absolue ♥️
@awandiaye1899
@awandiaye1899 18 күн бұрын
Vraiment j' ai eu pitié de lui té kouy wadiour sa khol metti na
@Matar-h2f
@Matar-h2f 18 күн бұрын
Yalla nagnou yalla mousseul si nafékh
@TallAbalabass
@TallAbalabass 17 күн бұрын
Billahi koudoul khalat 3jourou bammele loula nekh defal 😢😢
@sheikhjobe3494
@sheikhjobe3494 16 күн бұрын
Bilh loam sollo
@BinetaGning-v2o
@BinetaGning-v2o 18 күн бұрын
Ay way ms Kali mba ousseynou dou Am problème ak mére bii😢😢ay Way yeureume n'a ousseynou sakh
@yayodiallo1021
@yayodiallo1021 14 күн бұрын
@@BinetaGning-v2o 😂😂😂😂😂😂
@ibnadam3yb
@ibnadam3yb 16 күн бұрын
Aouzou billahi mina seytani rajiim. Yenangui deff lu graw ndeysaan.mandu leen si sëyu jambur.
@rokhayasarr6468
@rokhayasarr6468 18 күн бұрын
Ki khaler la deysan ouseynou va rejoindre ta famille tu a encore l'avenir devant toi 😢😢😢
@RimkaCissé
@RimkaCissé 18 күн бұрын
Ay ponkaloum goor yalla,wara doori war,nekk ay kilifeu,done gentleman... Gnouy nekk fii di lidjeunti seuyou diambour,werr domou diambour,deff yeufou niak fayda,c'est vraiment dommage pour ce pays
@sokhnaniasse540
@sokhnaniasse540 18 күн бұрын
que dirais-tu si ton frère épousait une femme ayant 30 ans de plus que lui ???????
@abasssy9242
@abasssy9242 18 күн бұрын
C’est sa vie. Moy takeu, moy kateu. Hypocrites ak sokhor mo beuri Senegal. Je déteste ces genres de men. Mind your damn f.. business
@makeitreal6918
@makeitreal6918 18 күн бұрын
Ay vrai domeram lagn
@Alhamdoulilah2067
@Alhamdoulilah2067 18 күн бұрын
Bilay gni dagno gnakk fayda
@FulaniGirLll
@FulaniGirLll 18 күн бұрын
Bilahi comme si douniou ay dioulite douniou khalate ni bene jour daniouy dé nioune nieup té louniou deff fi adouna dinaniou ko guiss alakhira
@ABOUBACARMbengue-v8v
@ABOUBACARMbengue-v8v 17 күн бұрын
Bayiléne khawi soutoura Li bakhoul 😍
@FadyDiallo-w8k
@FadyDiallo-w8k 16 күн бұрын
Yena Bone tè ragalolene Yallah
@ndeyediakhate1433
@ndeyediakhate1433 17 күн бұрын
Mais piège la parceque khamoul ni dagn koy enregistrer😢
@amintasamb1921
@amintasamb1921 18 күн бұрын
Ndeyssaan il faut aider l'enfant à aller retrouver sa famille. Il en a besoin. Ndassii tamitt na bayii domou diambour dji mou gnibii Thii yayam mo gueune.
@khadimka2058
@khadimka2058 17 күн бұрын
Mère bila yalla dimbali rek ndakh Ousseynou mi dou nittou dara geumoul dara
@PapeCisse-p4y
@PapeCisse-p4y 17 күн бұрын
Merci kali contane na
@makeitreal6918
@makeitreal6918 18 күн бұрын
Kali un vrai domeram
@aliounebadarasy8644
@aliounebadarasy8644 15 күн бұрын
Mais vraiment Sénégal barina ay nitt yu am diot, ngir yala bayiléne niar yii niu doundu té yala tax.
@Lémou-l2q
@Lémou-l2q 17 күн бұрын
Collez la paix a Aissatou kalifone et autres sont entrain de jouer les prolongations l'adversite de la politique tout ca c'est contre les patriotes mais Ousseynou a gagne le gros lot Aissatou est une grande dame
@IbrahimaBa-d3m
@IbrahimaBa-d3m 18 күн бұрын
Bilahi néck Sénégalais méti na khana yalla moumou sakeu sakh téguougnou fittna ngéni néckeu fi di lidieuti problème diambour rk
@omardabayethioune6307
@omardabayethioune6307 18 күн бұрын
Merci ❤
@naboujadieng627
@naboujadieng627 18 күн бұрын
Lolou mom Deugue leu
@FamaDiop-h3h
@FamaDiop-h3h 18 күн бұрын
Ibrahima gni ay weudeug lay, wara liguey yi tangue Di fene ba 4h du matin. Li yalla beugou ko sakh
@IbrahimaBa-d3m
@IbrahimaBa-d3m 18 күн бұрын
@@FamaDiop-h3h yalla néna képeu ki khayi soutoura nitt douma la soutoural adouna AK alakhira gnou bayi ci khél
@CheikhNdiaye-g9l
@CheikhNdiaye-g9l 17 күн бұрын
Sénégal barina ay nafék
@AS-ks1kx
@AS-ks1kx 17 күн бұрын
Di guen ko layo ak Yallah !
@FatouNiang-wt3eo
@FatouNiang-wt3eo 18 күн бұрын
Ndeysane ❤❤❤❤❤
@AminataAmi-qc9jz
@AminataAmi-qc9jz 17 күн бұрын
Li mome c'est clair ousseynou pièce la deff kaliphone
@moustaphadiakhate3997
@moustaphadiakhate3997 18 күн бұрын
Kaliphone ak cheikh Ahmed casse kagne lagnou dioubo 😅😅
@modourokhaya9616
@modourokhaya9616 18 күн бұрын
Amna niokhamnè da nio nafekh, boy bi koum nekkone sa frère do nangou mou seuyak mere bii.
@MayeSow-l9o
@MayeSow-l9o 18 күн бұрын
Bilay iow li dafa méti 😢😢😢
@aboubacrysy8188
@aboubacrysy8188 18 күн бұрын
Bé worbé diaasi billahi 😢 Quand l’esprit est faible et y’a rien sera comme c deux garçons Waxx deug yallah Lii dou youfou garçon
@foogadebbomolooty9839
@foogadebbomolooty9839 18 күн бұрын
À Diarama
@khelcom3639
@khelcom3639 18 күн бұрын
Ousmane SONKO niogui sakkou ci etat bi mou diouk si genrou nit ñi...nou Sénégal développer lañ wara khool mais neksi derou niary nit dissi wakh soubaak 'goon... Contenus 0000000 wakhlén Xam Xam / science/ walla lou Dieumeulé rewmi kanam...
@yayodiallo1021
@yayodiallo1021 18 күн бұрын
Keneu waroul publier ay audio diambour publiquement
@makeitreal6918
@makeitreal6918 18 күн бұрын
Ki domeram lë
@yayodiallo1021
@yayodiallo1021 18 күн бұрын
@@makeitreal6918 😅😅😅😅😅
@Abdou-sk4tq
@Abdou-sk4tq 13 күн бұрын
Même si c'est une piège il a dit des choses ce jeune homme qui prouvent que ce qu'il fait il n'y crois pas et il pense que c'est un jeu ....
@Mbodji-walo
@Mbodji-walo 18 күн бұрын
C'est vrai séy mo geune ndialo mais nk😂 justice pour Ouseynou sinon Mère bi dakoy ray légui
@Myriade-s2n
@Myriade-s2n 18 күн бұрын
Sisi il faut protéger le petit cette dame là elle peut aller très loin deugniou nara protéger khalebi mystiquement ndow si bakhule santoule yalla t'ai yenn jeunes yi moytoulaine fasson yi bari neugne fi lolll d'habitude degne laine di liguey t'ai liguey bi yeupp seine kanam leugne keuy deff so khassai b egueu thi mom rek c'est fini dotoko bayi
@Myriade-s2n
@Myriade-s2n 13 күн бұрын
@@niangtra désolée mais li ngueu wokh toubb ko rafetoule fi kounek deu ngueye wokh seu khalatt respecter seu moromou yaye yi fi n'ai wokh bou niaw fadioule dara senegalais defeu gawa sagua niaw lamigne loy fiye wokhoti khalatte seu yaye khalatt yayou kenaine wokh bi niaw neu torop
@niangtra
@niangtra 13 күн бұрын
@@Myriade-s2n toub nako , balenma🤭
@Myriade-s2n
@Myriade-s2n 12 күн бұрын
@@niangtra Bâle negne leu boule wokhoti mouk louni mail kheyna moune blesser ay nitt t'ai dossi kham dara lolou bakhoule si ndow
@niangtra
@niangtra 12 күн бұрын
@Myriade-s2n wakh nga deug 😘
@TheGoorgoorlou
@TheGoorgoorlou 18 күн бұрын
Mais kali dooniou lidieuntil affairou Cheikh Oumar Diagne mii ndakh diomaye kadjie ko. Tu es très fort apparemment.
@amefall3814
@amefall3814 17 күн бұрын
Boy boulniou fonto goor djiguéne bi bane importance la ame ci réwmi domérame
@dialmbaaye5213
@dialmbaaye5213 17 күн бұрын
Ay waay bayyi leen weeraate
@FamaLaye-kb6cj
@FamaLaye-kb6cj 18 күн бұрын
Vraiment kali do nitt kou.bakh
@layefabregas6788
@layefabregas6788 18 күн бұрын
Kaliphone ioe kou kate sa leufal Ndeye nga
@ismailiaFall
@ismailiaFall 18 күн бұрын
Walaye gni dano sokhore yakhale nane boye bi😢😢😢
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 18 күн бұрын
Niane ga sa rakh def li
@yakharandiaye2921
@yakharandiaye2921 17 күн бұрын
Yow doule merde mounane
@MadjigeneDieye
@MadjigeneDieye 18 күн бұрын
Bravo kalifone
@ismailiaFall
@ismailiaFall 18 күн бұрын
Boye waroul wone wakhe ake ki 😢😢😢
@lampefalltvlampefalltv3589
@lampefalltvlampefalltv3589 18 күн бұрын
Ndeysann yereum lenn boy bii
@astoufall5758
@astoufall5758 16 күн бұрын
Ki limouy waax triste ti na dh. Li né si mome rk laay yébi😢
@doussoundiaye9716
@doussoundiaye9716 18 күн бұрын
Kali ndanane ngua Suis très contente
@papediazngom6121
@papediazngom6121 18 күн бұрын
Bayiléne séyou diambour bi
@DameThiam-x1d
@DameThiam-x1d 17 күн бұрын
Boy bi amoul diom Day yakh generation deux mill 😢
@malangmane555
@malangmane555 12 күн бұрын
Boy bi pression médiatique ak sociale béko sonal mais noumoy démé di wax ak nién gni????
@cheikhfall9985
@cheikhfall9985 18 күн бұрын
Fékhé nguén ba Yakh seuyou diambour bi mais yalla dina léral lépp
@Limamou651
@Limamou651 18 күн бұрын
Ani seuy fii do até deug sey bo khamni ay mbokam yégougnou
@marmichoue7857
@marmichoue7857 18 күн бұрын
Bou lép léré niou bari niouci d'accord dinaniou ci guénate
@OuzinDiouf-g4e
@OuzinDiouf-g4e 18 күн бұрын
Kali doff bilay
@ndiayesiradji1530
@ndiayesiradji1530 18 күн бұрын
Bodon Maguètou toubabe la takk kèn d'où ci wakh
@ArjunJaikumar-f1g
@ArjunJaikumar-f1g 18 күн бұрын
Bo amé dom yalna li dall boye bi dall ko amine mais na nek toubap na 😢complex you bonnn yi ngenn donn
@abasssy9242
@abasssy9242 18 күн бұрын
Merci. Le sgl est un pays d hypocrites , naafekh. Et méchants. Que chacun se mêle de tes histoires. M e r d e
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 18 күн бұрын
Maguetou sénégalaise la amalouko nieurign
@ritoundene9041
@ritoundene9041 18 күн бұрын
Maguetou toubab c'est pour les papiers
@NdeyefatouGueye-t7d
@NdeyefatouGueye-t7d 17 күн бұрын
Ms ki khalé la
@tallagueye5048
@tallagueye5048 17 күн бұрын
KALIFON SALL YAY NITOU SAFARA BOY DEE DI DEM SAFRA.YA BONE Yalnanga halkou yak AMET CISSE.
@papediazngom6121
@papediazngom6121 18 күн бұрын
Kali bou séy bi tasé ndakh yow doula djgue
@amadoudiallo-zg8gt
@amadoudiallo-zg8gt 18 күн бұрын
Vraiment c'est bizarre ay gorr rayy mbelleh teh gnack fayda gen nara waxh si dinneh lislam walla louy ndjringne askan bii gnii gnoy ibouliss tigui
@khadrediaylani5938
@khadrediaylani5938 18 күн бұрын
Je regarde même pas ces genre de contenu, mais dema tombé thi vidéo bi. Frère pourquoi dolen mandou? En plus ay Goor yalla ngen. Occupez vous de votre problème ngen bayi diambour. Tu es libre de dire ta pensée mais pas détruire sa relation.
@Marameg.23
@Marameg.23 18 күн бұрын
Mann dama diakhlé si senegal gnakk fayda rek gnou wara lidjeunti khalé bi am 9ans gnou violé ko bamou eumb gnou nekk si seyou diambour bi di wakh rek
@aicha.2025
@aicha.2025 18 күн бұрын
Ce garçon il faut l’aider😂😊
@mbissanegning9631
@mbissanegning9631 14 күн бұрын
Yene gniargni khamlene mousiba la gni wakh ag yene gnio gniak fayda yalna boulema khamal dara si adina gniak guene soutoura trop doul kat yiguene done
@aboubacrysy8188
@aboubacrysy8188 18 күн бұрын
Walahi tu n’es pas eu la chance d’avoir un grand frère ousseynou C gens là bougoul dara loudoul vie des autres
@aboubacrysy8188
@aboubacrysy8188 18 күн бұрын
Lii dou youfou garçon billahi thimm
@Shasha-nt3rm
@Shasha-nt3rm 16 күн бұрын
Kaliphone, 😈😈😈😈😈😈😈
@pimroosmakabra2094
@pimroosmakabra2094 17 күн бұрын
Yen lusi Sen databday
@thinktanktruth1968
@thinktanktruth1968 16 күн бұрын
Ousseynou daal loumou meuna wakh loudoul ni daa nopp mèrebi wakhoul deugue. Walla book daa dagne kompa reck beuggeu moss mack. Kaliphone ak Adamo baakhounoou. yalna yalla dagg sen lamigne yi.
@lacitoyenneafricaine8566
@lacitoyenneafricaine8566 18 күн бұрын
J'ai l'impression que Kaliphone dafa nek si règlement compte ak Aissatou Pendo Diop. Sou boy bi takone benene dame thiow dou ame. Nitt dey deff djeufou gor! Kaliphone djenal si li nga nek! Sa kalame bi si bopame mo suspect soy wah se température khol dey fingne si se kaname gui "beneu lerr bou bone". Kaliphone tu n'es pas gentil vraiment tu es un être trouble et troublé djenal si li nga nek way. Akhmet bayil Kaliphone mi ne fower khelou gniko nango!!! Gore dou yakaneter ...
@aboubacrysy8188
@aboubacrysy8188 18 күн бұрын
Waxga deug Walahi 😢😢
@lacitoyenneafricaine8566
@lacitoyenneafricaine8566 18 күн бұрын
@@aboubacrysy8188 so yeurer kalamou Kaliphone bi sakh djiss que y a une haine qui s'y dégage! Khol bi moy wakh!
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 18 күн бұрын
Si c'était ton frère Ousseynou do wakh li. Sey bi day tass Ousseynou délou si yayam. Aissatou penda domeram la di diol lo yayou diambour . Li nieup la metti bou ko defone sama frère kone damakoy ray
@tutitt9866
@tutitt9866 18 күн бұрын
Ki bo dégué nimouye wakhé sa ga hamni il n'a pas grandi. Sen différence d'age dafa barri 30 ans
@adamasamb8919
@adamasamb8919 18 күн бұрын
De trop
@fatoudiakhate2836
@fatoudiakhate2836 17 күн бұрын
La différence d âge et plus de 30 ans d après la femme c est dires elle est née en 1967 en 68 dafa domme rameu
@SadioWelle-cj9yk
@SadioWelle-cj9yk 18 күн бұрын
Aye waye yalna done deukk❤
@Myriade-s2n
@Myriade-s2n 18 күн бұрын
Ndeyssane
@BinetaDiene-m5b
@BinetaDiene-m5b 18 күн бұрын
Sayou diabour mogan dialo bayilen diabour
@abdourahmanesow7420
@abdourahmanesow7420 17 күн бұрын
𝘽𝙖𝙮𝙞𝙡𝙚𝙣 𝙙𝙞 𝙠𝙝𝙖𝙬𝙞𝙞 𝙎𝙤𝙪𝙩𝙤𝙪𝙧𝙖 𝙜𝙤𝙧𝙧 𝙮𝙞𝙞. 𝙏𝙤𝙥𝙥𝙤𝙪 𝙣𝙜𝙪𝙚𝙣 𝙨𝙚𝙣 𝙗𝙖𝙣𝙚𝙠𝙝𝙤𝙪 𝙣𝙖𝙛𝙨𝙨
@mamadouba2517
@mamadouba2517 18 күн бұрын
Fekhe ngene ba tass seuye diambour yi ni rekk c'est vraiment pitié
@salioudieng3294
@salioudieng3294 17 күн бұрын
Kaliphone hanà xamo nii sénégalais balà meunà féen day wàtt😂😂
@BarisoThiam-o5l
@BarisoThiam-o5l 17 күн бұрын
Thieyy lii
@fatoumatawane5138
@fatoumatawane5138 18 күн бұрын
Outi len ligey
@serignecheikhsy4155
@serignecheikhsy4155 18 күн бұрын
Vraiment khaliphone vrai domrame moy ak adamo ak cheikh ahmed cisse ken tane wou morom
@makeitreal6918
@makeitreal6918 18 күн бұрын
Ay vrai domeram lagn bilahi
@FatoumayiSamb
@FatoumayiSamb 17 күн бұрын
👂👂🙏🙏🙏
@MamadouSéne-m6t
@MamadouSéne-m6t 16 күн бұрын
Sénégal nitou réseau yi kou déguanték gnom Yako déf ndah dégn lay publié
@salenesene1182
@salenesene1182 18 күн бұрын
KHALÉ BI DAKH WÈRR NEU? LOU DIARA KHOLE.
@aboubacrysy8188
@aboubacrysy8188 18 күн бұрын
18minute 11 seconde pour la vie de quelqu’une Qu’est-ce que sa sert ??
@fatoumboup4921
@fatoumboup4921 18 күн бұрын
Môme diahal satan est toujours content d'eux toujours pour servir satan🏃🏃🏃(vous les bons coeur vené qu'on soit toujours avec Allah ❤❤❤et notre bien aimé PSL.fermé notre porte k satan ne puisse pas entré,je ferme la porte)
@nenedacosta8943
@nenedacosta8943 18 күн бұрын
👍👍🙏🙏
@layefabregas6788
@layefabregas6788 18 күн бұрын
Kaliphone sa leufal Ndeye ioe khou kate sa ndeye nga
@Gggge_dudiolof9536
@Gggge_dudiolof9536 18 күн бұрын
Hana domou biral ga
@BinetaDiene-m5b
@BinetaDiene-m5b 18 күн бұрын
Limogen dialo Sénégal wahrek hale yagif dialo ak ay mak baholen
@pimroosmakabra2094
@pimroosmakabra2094 17 күн бұрын
Sen datay day yen yar Sen buno day
@mapendandiayefall523
@mapendandiayefall523 18 күн бұрын
Yen bayilen seyou diambour guir yalla,oh vrema mbanou woulénne
@BoubacarBoubacar-wc2qf
@BoubacarBoubacar-wc2qf 17 күн бұрын
Bayelen sey diambour topotolen sen sey ngen baye sey diambour
@dadaniang3005
@dadaniang3005 16 күн бұрын
Kaliphone soff nga
@Abdou-sk4tq
@Abdou-sk4tq 13 күн бұрын
Li d'où soutoura et soutoura bou dagné si nit rek dara dessetousi
@SagarDiaw-u5r
@SagarDiaw-u5r 18 күн бұрын
👍👂👂
@NasseGueye-d5w
@NasseGueye-d5w 15 күн бұрын
Gni ay domeram lagne
@aliounesarr7616
@aliounesarr7616 18 күн бұрын
Kou tass seuy loussi yallah wakh!?
@FatouThioune-z9k
@FatouThioune-z9k 18 күн бұрын
Li seuy l 😂wala kipnapping
@binetandiaye8951
@binetandiaye8951 17 күн бұрын
Kaliphone noppil, niou déglou.
@MbeneDieng-o1u
@MbeneDieng-o1u 18 күн бұрын
Yenangui yakhal merr😅😅
@AbibouMbacke
@AbibouMbacke 18 күн бұрын
Sawaye diapal sa seuybi defo lu naxari yalla diapal sa seuye ndax ki yalla mola bolle ak mom
@Tarikha2024
@Tarikha2024 18 күн бұрын
Bouder di nagn si ame dome dh def nagn li yonentibi diglè mais bougn si amoul dome mom wathie nagn yonn si li yonentibi wahonn nè seuylenn nguir yoke sma hete
@BoyPoulo-kg5pl
@BoyPoulo-kg5pl 18 күн бұрын
Niit takk n'a xale 20ane amoul dome
@Thiapathiolii
@Thiapathiolii 18 күн бұрын
Dome key je ken manouko garantii si seuy wala danko meune ioe ​@@Tarikha2024
@Adamtony223
@Adamtony223 18 күн бұрын
Kali vraiment doff nga !
@abasssy9242
@abasssy9242 18 күн бұрын
Chacun veut faire l’interessant Sénégal mo nekh
@makeitreal6918
@makeitreal6918 18 күн бұрын
Bilahi
@PapeFall-il7xw
@PapeFall-il7xw 18 күн бұрын
Bayil seyou diambour bi nga beugue yahe comme ça
@sokhnaSaly_Diop4853
@sokhnaSaly_Diop4853 18 күн бұрын
Ban seuye?
@fatimandao8359
@fatimandao8359 18 күн бұрын
Yow mi fonék li bane genre seuye la li bane avenir la ameu
@MomadouCisse
@MomadouCisse 18 күн бұрын
Youwsadatayae
@adia982
@adia982 18 күн бұрын
Kone legui dañuy seuy pour ame avenir Dem kene diangui sene dinner yenn comme aye yefér reck​@@fatimandao8359
@NdeyeFatouGaye-o4w
@NdeyeFatouGaye-o4w 18 күн бұрын
Wax bou beury bi sakh ame ouseynou indi ouseynou bou yagué dina dei légui astakhfiroulah
@Lémou-l2q
@Lémou-l2q 17 күн бұрын
Ousseynou a utilise kalifone pour faire la paix avec sa famille mais il n'est pas pret a quitter sa femme il est partage entre 2 grands sentiments il ne va pas quitter sa femme
@babacarcisse7228
@babacarcisse7228 18 күн бұрын
Boy bi mo nara torokh
@diopelmalick456
@diopelmalick456 18 күн бұрын
Kalifone vrai domeram gua rek
@MoustaphaDG-d5q
@MoustaphaDG-d5q 18 күн бұрын
Sa d…
@tout1958
@tout1958 18 күн бұрын
Bayi léne vie privée diamour yi Sénégalais légi comme deumou
@Bigboss-hd8fx
@Bigboss-hd8fx 18 күн бұрын
Aye domeram you melni kali
@AbibouMbacke
@AbibouMbacke 18 күн бұрын
kaliphone bo xamon lithi yakh seuye dagamanu thi seuyu diambour bi
@AmyBiteye-d8o
@AmyBiteye-d8o 18 күн бұрын
Sëye bi yak ko amoul bakar
@fnoumbediop690
@fnoumbediop690 16 күн бұрын
Boy tiyèl sa diabar sey sì arass lako yalla Di takè boula gayi diafasè ak sa diabar 😮
@marchétvofficiel
@marchétvofficiel 18 күн бұрын
Boy bi dale nako wa marodi dieule mou jouer aay film kou aay la naax mou dimbali yayam bayi mére bi
@fatousow8539
@fatousow8539 18 күн бұрын
Li yeup ay fene la seye massoul am
@AissatouLo-q3l
@AissatouLo-q3l 11 күн бұрын
Khalate lene 3 jour bamel😢 tasse seuyou diambour
@Talibébambashop
@Talibébambashop 17 күн бұрын
Boy bi Sou moytou woul dafay am depression
@PapesegDiaga
@PapesegDiaga 5 күн бұрын
Californie mariage by bou tasse Californie la
@خدجه-ز6خ
@خدجه-ز6خ 18 күн бұрын
❤❤q❤❤❤p❤❤🎉🎉🎉
@OusmaneFaye-d9n
@OusmaneFaye-d9n 18 күн бұрын
Boy bî déffa kon quoi waroul diéle kéne koumouy khamoule vrai doff la
BÉTÉ BÉTÉ - Saison 2 - Episode 8 **VOSTFR**
1:00:03
EvenProd
Рет қаралды 4,4 МЛН
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН
Une nouvelle voiture pour Noël 🥹
00:28
Nicocapone
Рет қаралды 9 МЛН
How to treat Acne💉
00:31
ISSEI / いっせい
Рет қаралды 108 МЛН
Сестра обхитрила!
00:17
Victoria Portfolio
Рет қаралды 958 М.
🔴DIRECT: Live Kaliphone Sall
Lixewgalsen TV
Рет қаралды 513
小丑教训坏蛋 #小丑 #天使 #shorts
00:49
好人小丑
Рет қаралды 54 МЛН