Machallah Reug Reug est devenu pâture dans sa communication 🇸🇳🇸🇳
@amadiallo-kn2ye3 ай бұрын
Champion leu d !!!dou sama mbeur nakk wallahi …j’ai suivi une de ses vidéos de plus 1h de temps ⏱️ sur KZbin mais diapnani mo meune gars yi 😁
@shevamilano19813 ай бұрын
Omar Kane reug reug yalla nala yalla may NDAM le 8 October inchallah 🎉🎉❤❤
@thiernodembaya83553 ай бұрын
Ce un professionnel qui parle ce Modou lo 🦁 seulement qui peut le faire peurs 😂 vrai champion 🏆 reug reug 🇸🇳 me Modou lo ce le Boss ❤️🇸🇳 King 👑🇸🇳
@macoumbademe65733 ай бұрын
Reug reug yalla nala yalla may ndam On es tous derrière toi For ever Thiaroye 💯 ndam rk inchallah
@Cheikhba-tq1wi3 ай бұрын
Boy niang deee meusoul perte combat bouniou ko wakh daniou lay dannn ☹️☹️ il a gagné tout c combat capital comm bimou wara beurè ak yow niiiii c le cas contre sacadior sathies et balla gaye .. quand il nè pas favoris il crée l’exploit 🫡bayi ci khel dal tu a affaire à un très grand champion avec un mental de oufff machallah ❤️💚
@ibrahimadrame94993 ай бұрын
😅😅😅😅khana contre kharagne lo nieupa khamone noumouy démé
@YounousseWade-n2e3 ай бұрын
@@ibrahimadrame9499ki kay wakhoufi dara😂😂
@josephericousmanediandy7833 ай бұрын
Je suis fane de Modou lo mais tu as raison .boy Niang est un grand stratège . Mais lamb Koy bessssss laniou xam mais Oumar Kane a intérêt a faire attention
@amadoulatyrndiaye2313 ай бұрын
Contre Modou lo wala degaye commentaire pour commente reek
@leuz.patriote3 ай бұрын
Reug so diapè ni ya meun boy niang 😂 hum wa bakhna boy niang dou tèglè dèfaite dee diokh ko thieur tè tèy fèkhè mbapate ak mom deugeuleu boy niang dafa meuna beurè sen diap nguèmb tè ioe yak bg2 sama mbeur yéna yam solèn diapè rek dane😂
@MouhamedBa-i6i3 ай бұрын
Fort mentale Reug Reug le grand champion 🏆❤
@amaduamadu16003 ай бұрын
La vie dun vrai champion tren relaxe avec conscience tranquilo
@__mgk__wolf__man63013 ай бұрын
Reug Reug Ie grand champion, domou Iébou ak sérére borom 22 iIes yi. Fo diape boy niang2 Iamb dji dieex
@daoudacisse48493 ай бұрын
Reug Reug yalna yalla may la ndam ci kow boy Niang
@PynoSow3 ай бұрын
Reug reug sama mbeur la ma topouko depuis mbapatt mes communications mo tahone ma bayiko mes guisna ni defar na communication bi bou bakh , Maintenant c'est un professionnel vraiment 👊
@abdouthiam33123 ай бұрын
Merci way Reug jamm si yaw ❤
@AssaneFall-v7e3 ай бұрын
Sonko mooy 6 President du senegal in challah
@NayeFall-qq7xi3 ай бұрын
✅️✅️
@AdolpheGomis3 ай бұрын
😂😂😂 féne kaate bobou kou niou accusées viole jamais
@tayk43043 ай бұрын
@@AdolpheGomisyou trolling right?
@almaremegueye7363 ай бұрын
wakh ka sa bay
@elhadjindiaye7203 ай бұрын
On parle su sport de chez nous ay con diniou wakh des politichiens ou des chiens politiques loussi souniou yoon si nioniou
@Ihsaan903 ай бұрын
Bonne chance reug force force toi expérience bi Maa shaa yallah
@mansourdieye94943 ай бұрын
Becaye sa émission pencum lamb war nga si wax niou diapalé reug reug yaw lo wax nieup dégla ndakh ceinture bi bou nieuwé Sénégal fierté Sénégal leu
@OusmaneSadio-l3k3 ай бұрын
Reug le grand champion international
@dabondiaye79173 ай бұрын
So proud of you champion you make Senegal 🇸🇳 proud masha Allah si kaw si kanam
@talzandiaye69963 ай бұрын
Lamine vraiment c un gas extraordinaire reug est devenue fort en communication
@BoubacarBâBÂ-h8q3 ай бұрын
Reug le grand champion
@badiafaye53143 ай бұрын
Champion bou mage bi ❤❤❤❤
@AbdouCisse-xs5mc3 ай бұрын
Boy Niang yallanako yalla may ndam🎉🎉🎉🎉
@moussandiaye71703 ай бұрын
Reug Reug yalna nga ame ndam ci boy niang
@baalain19063 ай бұрын
Monsieur Aziz ndiaye une grande personnalité qu'allah accepte tous tes souhaits amine
@sambadieng12033 ай бұрын
Yallana yalla mey ndam bou séde guouy inchallah ❤️🇸🇳👌💪👌👌💪🇸🇳
@morgningue76543 ай бұрын
Mn de khama yag m yag boy Niang yalnako dane inchallah
@KasséIbert-g5j3 ай бұрын
Champion reug Oumar Kane Diallo nicena frère courage
@mamadoulaminesarr13103 ай бұрын
Reug reug dévoile pas trop tes plans ça doit rester secret ça, bonne chance yalla nala yala mat ndam
@AbdouazizDieye-w2b3 ай бұрын
Bi Reug nee wadji 14 combats 14 victoire la amme Lamine nena la ilaha ilalah rek ree 😂😂😂
@modoulebou6343 ай бұрын
Thiey sama wadji namou nanou ka dhe billay Wallay ndam rék inchallah 🦍🦍💪🏿💪🏿✅✅
@goragaye40923 ай бұрын
Dou dreum😂
@modoulebou6343 ай бұрын
@@goragaye4092 billay yanou sonal 😅😂😂
@goragaye40923 ай бұрын
@@modoulebou634 khamoul dara 😂
@modoulebou6343 ай бұрын
@@goragaye4092 ki moy sounou fierté bayil sisou bi😂😂
@goragaye40923 ай бұрын
@@modoulebou634 mane dei dou sama fiertè
@alvin2goat3393 ай бұрын
Reug Reug et Ordinateur on dirait des jumeaux!! Ils se ressemblent vraiment beaucoup
@tigrenoir51473 ай бұрын
Yaw Saga nga ordi nak
@veritesavoir54153 ай бұрын
Oui ils se ressemblent trop
@Lamb-j1t3 ай бұрын
Reug key ak 5tonnes😂😂
@mussafaal13213 ай бұрын
Ta raison frere
@ahmadoudiop50163 ай бұрын
Ben lagnu @@tigrenoir5147
@mouhameddia51683 ай бұрын
yalla nga ame ndame mma mais yalla nala boy niang dane
@MoustaphaFadiga-jy3dr3 ай бұрын
Bilahi Reug yangui wakh mes khamo boye niang
@abdoudicomasina6243 ай бұрын
Reug reug plus mature en comunications.
@OfficielReugReug3 ай бұрын
Pour combat mma bi le 8 novembre la pas le 8 octobre Inchallah ndam rék 💪🏿❤️✅🙏🏿👑🦍
@Wrestling18903 ай бұрын
Na privilégié beuré bi
@OfficielReugReug3 ай бұрын
@@Wrestling1890 Inchallah bro✅💪🏿☝🏿
@ibousylla26583 ай бұрын
Reug Reug yaw Ama moleu may chance.😂😂😂
@mouhamed-ew3gc3 ай бұрын
nn😂
@TamsirNdiaye-f2r3 ай бұрын
Bonne chance bro ndam Rek inchallah
@mamethier65143 ай бұрын
Inchallah yalla nala yalla may ndam le 8octobre yangi yorei drapeau Sénégal 🇸🇳
@Enfant_béni_73 ай бұрын
MERCI REUG REUG LIGUA WAX SI GRIS 2 bilahi dagua niakeu kiniane ❤❤ YALNALA YALLA TWT MAY NDAM LE 08 OCTOBRE INCHAALLAH ❤❤
@Alimatoukandji20073 ай бұрын
The best 🎉
@georgesdieganediouf26843 ай бұрын
Omar Kane reug reug si boy niang 2 te bat ,tu vas faire comment ?.
@sidysakho65583 ай бұрын
Ama baldé mo dieukeu wakh bou boy Niang dané reug reug dou beuré ak mome
@AliouKama-zs9ye3 ай бұрын
Nianal gnou diam 🫣 dame inch'Allah
@khardiatouamadoukane67853 ай бұрын
Lolou la signer@@sidysakho6558
@daoudacisse48493 ай бұрын
Inchala Reug Reug moy dane
@lbyoungtv22233 ай бұрын
Wa pikîne nio dieukeu wakh sko boy niang danei ama douko dieull
@MilkMilo-qr5uc3 ай бұрын
C'est trés raisonnable boba yak Franc la amoul sik sak dane déme danou xaar boy niang idém boula dané xamal ni dagay topou si guinaw franc
@modo62183 ай бұрын
Merci da khamoul lambe rek lambe dafa teuredi 😂😂😂
@MilkMilo-qr5uc3 ай бұрын
@@modo6218😂 trop sakh kéne meunou lako calculél
@DameNiane-jb8se3 ай бұрын
Seye2🎉eumeu sène❤
@ndiagafaye31063 ай бұрын
Yalna la yalla may ndam ❤❤❤
@CheikhMbéngue-v7x3 ай бұрын
Dèl wakh rk bilay boula boy niang diapphè ♥️💚
@seydounouroufaye83533 ай бұрын
Boy Niang yallah nala dane
@OusmaneSadio-l3k3 ай бұрын
Dou am dé
@abaseye38593 ай бұрын
Mbeur mi internacional ❤
@DameNiane-jb8se3 ай бұрын
Bonne chance frére❤
@ElHadjiDieye-h7f3 ай бұрын
Amine inechallah ❤🙏🙏🙏
@CheikhDIOUF-yn6ik3 ай бұрын
Vrai champion on attend le chapeau maintenant
@abdougueye48373 ай бұрын
reug reug est un grand champion
@lesamouraisnoir53043 ай бұрын
Ki Boys Niang dakoye Ñousse
@TallaFaye-y8t3 ай бұрын
Reug reug yalla nako yalla maye ndam lou sedd
@MamatSarge3 ай бұрын
Yalna la yallah may ndam❤
@DjilyNdiaye-pw8zx3 ай бұрын
Bilahi si katanou yalla boy niang day dan reug ba tok si kawam
@matarndoye64043 ай бұрын
Reug reug vrai professionnel la.
@abdoulayebadiane59843 ай бұрын
Gris 2 vs tapha tine kou d'accord lalal jaime ❤
@Matar-i6d3 ай бұрын
Reug reug seul 💪 yalla nala yalla may ndam 🤲☝️
@lattendiaye-47943 ай бұрын
Championnat
@diankofaty58933 ай бұрын
Courage champion
@elhadjisemoudiouf61503 ай бұрын
Bonne chance mon compatriote courage ça ira
@yalmine7653 ай бұрын
Lim wax niom ama nioko nieuk wax ni bouko boy niang dane dou beure ak mom
@malickgaye9033 ай бұрын
Ay reug reug yalla nala yalla soutoural rekk me sama xel daloul de
@afro38273 ай бұрын
Yow nangouwo won dieul fran baparé nan sa thies na dieul gris 2 , motakh ken dou ama baldé molen eup fit yen gnep
@MameGorSylla-yd1ty3 ай бұрын
Reug légui communication bi changer na mogui évaluer dh
@diaspora25533 ай бұрын
Amna solo de
@NdiaboutaDiouf3 ай бұрын
ndiabouta diouf slu à tous len mom amna inchalla rabi Lima guiss reug reug il communique mal mais bref boy niang mo geuneu nakare beurel une chose est sur inchalla boy niang dinako Dan diel boulo bouko bett inchalla rabi ndakh dafa kheb boy niang te lolou Mokoy Dan inchalla
@Wrestling18903 ай бұрын
En tous cas kou thi nagou danou
@Faye-sv1jx3 ай бұрын
Yalla nako yalla yombalale dore mou kao reug ❤❤
@masterdoucharreh29773 ай бұрын
Mala gueum deh 💪🏾
@mansourdieye94943 ай бұрын
Reug reug legui yagui communuqué normal machallah
@damembengue18943 ай бұрын
Reug reug international bi ndam rk si projet yi ✅✅💪🏿💪🏿
@mouhameddiatta65823 ай бұрын
Mais fi fane la
@khadimsarr23613 ай бұрын
Omar Kane reug reug yallnala yalla féy sa khol borom bakh nga🙏🙏🙏🙏🙏🤟🤟🤟
@ElHassane3 ай бұрын
Bravo Lamine
@yahyasagna42513 ай бұрын
Internazionale Omar kane Grand Champions ❤❤
@bocarba27813 ай бұрын
Nena mane ma tegulé 6 victoires, bo nangouwoul sa défaite bi nga am do gagner sa prochain combat. Sportif dafay accepté défaite pour meuna corriger et avancer.
@Bamba-rk3 ай бұрын
Waadjii il est incohérent Bou arbitre siffler Mangi ci kawam baparé naan bouñou neemé taxawal damay taxaw😂
@juniorjunior13453 ай бұрын
Srx boy niang dalay dane Inchallah
@ndiougamar22023 ай бұрын
Fort mentalement
@lesdeliresdeboyghetto69303 ай бұрын
reug communic bien❤
@ababacarsadih80303 ай бұрын
Boy bi sama mbeur leu kham nguén ko reug reug la toudou champion la 😂démal dieul ceinture après nga ñeuw préparer boy Niang
@MohamadouDiallo-t8o3 ай бұрын
Ay 2 avance moy yak lamb ji nak thiow dina bereu si sene combat wi
@oumardiallo77393 ай бұрын
Allez Omar Kane ndam rek inchallah thi Loe 8 octobre
@lesamouraisnoir53043 ай бұрын
Meilleure spoire Zacob Baldé la
@MouhadeSarr3 ай бұрын
Ki champion la mé nehoull kenn amoull benn bayré
@AmadouSouleymaneGadiaga3 ай бұрын
Ioe wero
@papadiom92603 ай бұрын
No amna bayreee naak wakh deug dafay nekhal lamb
@sarabo67793 ай бұрын
Reug nak amna baïré
@alsandiop35093 ай бұрын
Reug Reug est mille fois plus fort que Boy Niang 2😊😊
@mamadounguom49923 ай бұрын
C ton point de vue alors sa Thiès est mille fois plus fort que reug reug et boy Niang a battu sa Thiès
@OusmanSey-df8ko3 ай бұрын
dam rek insahallah
@papegueye96653 ай бұрын
Yow nieup yalén meune😢😢😢 daga bakh rékkk
@AbdouDiaw-b7n3 ай бұрын
Boye Niang tamit begue n'a 1er janvier dé
@abdourahmanesindidi18183 ай бұрын
Machalla lamine jamm gay gueuna am
@alassaneseye10023 ай бұрын
Yalla nangua am ndam champions
@amadouniang18753 ай бұрын
Reug reug kèssè
@amadousouleyetandine9313 ай бұрын
Boy Niang 2 dalay fowè daane la
@CASI77973 ай бұрын
Lamine noce gua Dubaï dh
@votremiroir76123 ай бұрын
reug-reug moytoul produit Éric yi bakhna reck guiss nagnou fi Tapha Tine
@Omarsane74913 ай бұрын
pour mome mo mome lamb djii ki dafa neh
@OfficielReugReug3 ай бұрын
@@Omarsane7491 Dafa lér
@ibrahimaba3553Ай бұрын
Ndam rek le 8 novembre nchallah ❤❤
@GuyGuiguitou3 ай бұрын
Mdlo ki leu bayi dem djeuli siteu😂😂
@senegalrek25793 ай бұрын
Siteu moko raw fouf
@ibrahimatoure44863 ай бұрын
Légui Soula boye Niang dané nak noye deff bala nga wakh dél khalat
@SambaMbodj-l8o3 ай бұрын
Reug nigua l'ère ni bougou mako dagua wara nioule qouke