On dit souvent genre niit gni ils sont tellement véridiques et gentils ndakh ils ont affronté toutes sortes de souffrances je remercie cette chaine ndakh chaque jour guéne diangual gnou adouna ya tellement d'émissions inutiles sur KZbin mais yéne zero faute continuez sur cette lancée
@SenegalPlus4 жыл бұрын
🙏🏾
@wiizzloufa94784 жыл бұрын
@@SenegalPlus bilahi continuez comme ça ❤️
@barhamaunited49534 жыл бұрын
Ohhhh Je le connais depuis mon enfance Ndeyssane El Maestro. Mo Dakone Sagnsei Sama side nak. Thiey adouna. Allahou Akbar. Beugg Sama Wa Famille Nieupp, Waa Kogn Bi Nieupp Bilahii.. Yalnako Yallah Delo Boppam El Maestro Ndeyssan . Merci SÉNÉGAL PLUS ! VOUS ETES SUR LA BONNE VOIX DH !
@bmkillertv18494 жыл бұрын
Malgrés toutes ses difficultés il est toujours heureux..Ça me fait mal.. Qu'allah lui viennent en aide.
@ahmadaly66664 жыл бұрын
Bilahi fi amna Aÿ miliarder naniou KO diapalé
@Sophie-gx2rq4 жыл бұрын
J’adore ce genre de programmes. Des personnes authentiques malheureusement victimes de leur destin. Sénégal Plus vous êtes décidément le chaîne que j’ai longtemps voulu voir au Sénégal. Je ne sais pas qui est à l’origine de ce concept mais c’est un génie ! C’est l’histoire de l’alcoolique qui m’a le plus marquée ndeysane. Que Dieu les fasse revenir sur le droit chemin in Sha Allah.
@fatoulomouserignebabacar73954 жыл бұрын
J'ai vu un homme de valeur un homme généreux kou gueum yalla
@tapha764 жыл бұрын
Bien parlé
@akimefun28134 жыл бұрын
Au moins iow sa passe cest cool moi étant tt jeune jai fai des betise Ki m suis juska présent sert 27ans la ame mes pour le restan d ma vie bou sobei yalla dina guena nek Thie Sama bopp surtout écoute les conseilles d nos parents
@AdamsJrGUEYE4 жыл бұрын
Ndeysaan Sama grand bou baax, meunone sagnsei, civilisé, gneup fan ko Thiatt baaxoul
@domoubadiane3484 жыл бұрын
Bataye saax !! Kii dafa styler.
@AdamsJrGUEYE4 жыл бұрын
@@domoubadiane348 wollah joe! Maes gneupeu ko fan wone
@alaminejuniorka49674 жыл бұрын
Yallna Nako Buur Yàlla samm
@maxgaye46384 жыл бұрын
Bilahi Mene Solou Torop Bro
@Senegalfirsttv4 жыл бұрын
Billahi en plus dafa meuna sangnsé
@yolandvaccon30384 жыл бұрын
Fière de son enfant peut importe comment il est son père il vient le voir c’est rare😍
@tairouniang13524 жыл бұрын
Dès fois nga yakarr ni ya geune métilé feek amna ko xamni mola geune tarrr doundou teksi il est haappy machallah 🙏🙏🙏😉yallah nala borom bii taxawou
@mamadousy3524 жыл бұрын
Telle est ljie
@mamadousy3524 жыл бұрын
Je veux dire que rien n'est garanti dans ce bas monde.
@SickSadZed4 жыл бұрын
Oh!! C'est beau ça... Binetou viens reprendre ton homme waay!!.. Ki vrai gentleman la.
@mouhamadibnismail58274 жыл бұрын
Bou sobe yalla gni la deff li dinagnko digaale ak sunu borom. Allah est puissant et il est patient et omniprésent. Yakamtywoul dara mom ay delai la yoor bou djote rek mou def limou waara def
@nabylahtv8784 жыл бұрын
Lii moy wanè ni Senegal gni beugue lou bakh nio ngui fii ba legui. 29k vus en 3 jrs mashalah. Boulenn bayi sen concept bi👌
@fatimadiallo87194 жыл бұрын
C’est fou comme il a toujours le joie de vivre malgré tout ce qu’il a traversé. Yalla daal mo meune.
@tapha764 жыл бұрын
Adouna na guini. Mon frère yàlla Nala yàlla takhawou
@deugrek33124 жыл бұрын
Kou gueume YALA leuh
@mariamafaye4744 жыл бұрын
Ndeyssane maestro guini moniou yarr nio bok kogne kep kou deuk pikine xam gako 💞💞meun sagnce ak fethi
@babacargueye78374 жыл бұрын
J’estime cette personne. Malgré tous les épreuves qu’il à subi, il est fort d’esprit. C Un vrai gentleman et c un noble.
@balladieng88984 жыл бұрын
Je te jure frère
@diopelmalick4564 жыл бұрын
Ndaysan dama koy guis fii pikine icotaf c triste ndok ndok dou wess yalna niu yalla mouseul thi tiat mai senegal plus li rafet na 🙏
@morbadiane81214 жыл бұрын
Sérieusement j'ai l'habitude de le dire aux gens qui le considèrent comme un fou que c'est un cool gars . cet interview le prouve exactement . je fier de toi mon ami . samy yi may sool momako diaye
@famb49244 жыл бұрын
Pour la première fois, j'ai pleuré á chaudes larmes en regardant un interview 😭😭 Mon Dieu..on ne sait jamais ce que la vie nous reserve..
@jacquesantoinemanga74594 жыл бұрын
😭ohh Dieu , la nature humaine me fait parfois peur. Kou nek sa destinée, kou nek sa yonn ,
@wiizzloufa94784 жыл бұрын
😭
@momophoenix43634 жыл бұрын
Bravo Sénégal+ j’adore vos interviews que vous fêtes et ce qui me plaît le plus c’est votre égalité pas de célébrité pas de badola
@SenegalPlus4 жыл бұрын
Merci bro Momo
@annemarieflorencefaye27854 жыл бұрын
C triste m la fin c drôle maestro dagua firiii nekh non stress la dundou Diabar souniou nieuwal wayy🤣🤣🤣😂 Amine si niane yi ak conseils vraiment c intéressant
@fatouhamzatoudiane13734 жыл бұрын
Ndeysan Doundou Bou Sootei Goul Lounei Khadj Nasi Yalnagnou YALLA May Mouthiou Bou Rafètt🤲🏾
@modounjietouray56474 жыл бұрын
Ameen
@zeussdakar77774 жыл бұрын
J'ai bcps pleuré ou sont ces gens qu'il partageait toutes ces moments au paravent. Yalna yalla takhawoula barkei baye lahi saws
@Yat0414 жыл бұрын
Wallah je le connais s t'es bien il habitais a côté de chez moi un homme très bien humble gentil généreux même après cette situation qu'il en est la quand on se croise a médina il me reconnaît on parle on enchange maestro je te suit depuis la France force a toi que le bon Dieu te préserve
@ndeyediop25274 жыл бұрын
Ay way maestro ngi ni, kou rafet khole, tè labire, kham sagnsè, danse guissouma kou ka si meune, yallah naka yallah, sameu, li mouy raconté yeup histoire vraie le, dafa tabè, non yallah yakamtiwoule, dafa done wakh, yallah kharitam le mais deugue bou werr, yallah wakhoule kèneu dara, inchalla yallah meune naka eulbeuti legui tè lolou mo gueuneu touti si miracles yallah, respect
@jerryobiang79754 жыл бұрын
une personne qui ma vu grandir avec un coeur en or tout ce quil a dit cest la verite il a beaucoup aider les gens que le bon Dieu te vienne en aide
@lesfrereseckaly72883 жыл бұрын
Merci beaucoup se genre de émission nous fait redescendre sur terre du courage mon frère yalla bakhe n’a
@nstylezlofficiel58493 жыл бұрын
J'ai pleuré en visionnant cette vidéo... Dundu bu soti goul lounei dadj naci. Jeexital gou neex inchallah pere
@greenespace40013 жыл бұрын
💕💕💕 J'adore le passage où il s'adresse à sa femme ça m'a beaucoup fait pleurer 😪
3 жыл бұрын
52 ans ng melni kou 40 ans li ko waral moy sa khol guedoula sa yaram guedoula toi tu es Monsieur Malgré tout ni chaud ni froid machala yalla nalla yalla diapaleee
@dabakhndiaye34774 жыл бұрын
Vraiment jambar deug moy ki ak li diota xew lepou mais il est toujours souriant bly wly ki rek moy jambar
@abdourahmanesindidi18184 жыл бұрын
Wa damiran kulla ahda in tudiru bina hablan wusilu lana yallahou yallahou (écrase tout les ennemis qui veulent nous nuire avant qu'ils nous atteignent oh mon Dieu) extrait sindidi cheikh Ahmadou Bamba
@ibrahimandaw64414 жыл бұрын
Cest trop intéressant on a connu nôtres grand abdou Diop tjrs étais fan de luit Il été propre et trop au top mais c'est domage que luit garde
@James_Rooney_3 жыл бұрын
Merci fréres je suis ému je ne saurais dire trop comment je suis fière d'être sénégalais et jeune qui est ambitieux. Vous êtes le coup de pouce que j'attendais pour qu'après avoir appris je ferais des réalisations pour mon pére.
@aboudia1384 жыл бұрын
Merci beaucoup Senegal plus c’est la deuxième émission que je regarde mais franchement magui si diang adouna bou bax sax étant un jeune étudiant en France je suis souvent tenté mais ce genre de reportage me réconforte et me donne le moral merci beaucoup
@malick64404 жыл бұрын
Goorgorlu rkk frère tout ira bien
@aliounendiaye3364 жыл бұрын
Et il est très positif. Quel homme machallah
@elhadjisow24984 жыл бұрын
La vie est cmme l’arc en ciel chacun à sn couleur c kelkun d gentil Binetou boko meuné diégueul défko adouna amoul solo
@Mhd.galsen4 жыл бұрын
Kholal ak heures bi limouy doundou il dit que la vie et belle . Borom khôl bou rafet rek moko meun
@tapha764 жыл бұрын
Bilahi
@armiyaoudiallo85374 жыл бұрын
Vraiment naniou yalla mousseull si brome kholle yi bonyi
@rogerdieme4 жыл бұрын
Je connais le mec il abitait dans notre rue à Pikine icotaf il s'appelle Abdou Diop alias Maestro j'avais à l'époque 14 ans ce mec a vraiment marqué son temps il etait vraiment populair dans la zone il animé les evenements avec see danses de Michael Jackson il s'abillait avec des jolie vétements , stay bless Maestro
@anneshakur4 жыл бұрын
Enfin une chaîne d’éveil de conscience et d’apprentissage sur la vie. Félicitation et continuez ainsi vous nous apprenez énormément
@mbayegaye76334 жыл бұрын
Petri de talent machala mais dieu n'a pas décidé k'il réussisse mais yalla bakhna
@burr93793 жыл бұрын
Mister maestro sama diantal grand bou begoon adouna ndeyessan meneu solou Amal diameu grand 🇳🇱 One love sénégal plus❤️
@SenegalPlus3 жыл бұрын
🙏🏾
@sarrabdou30404 жыл бұрын
Vraiment sénn émission bii amna soloo amna chance trop, té aussi dafay yété ..Li leu sénégal sokhla mai télé yo kham ni comédie soubeu ngone..mérci sénégal plus
@adrifall75553 жыл бұрын
Que Dieu te protège et t'assiste Tu as un moral de fer. Du courage, tant qu'il y a vie y a espoir mon cher
@Matryyooshka3 жыл бұрын
Wooow il est touchant et d'une sagesse remarquable. Qu'ALLAH SWT continue de veiller sur lui et améliore sa situation🙏🏽
@papealiadanso38904 жыл бұрын
Ohhhh maestro ki ay temps wam benen affaire leuh won il était nôtres idoles kan on était enfants ndaysan
@serignenadw57554 жыл бұрын
senegal plus j tres contant d vous quant jetai petit j passer ms vacances chez ma tante la maman de Maestro yayam sama magou yaye loumou wax lep c vrai si famille bou noble la bokeu j tres émit merci encor senegal plus yalla nalen yalla fay
@moracamara73024 жыл бұрын
Il est veridique ,,, j'aime c genre de personne ,,, courage mon grand ,,, si sa femme a enttendu sa
@cheikhngom49844 жыл бұрын
Aye maestro kou bakh kou beugue niit amoul bene problème beugue bopame thiate mo guaw rek mais machalla yalla nako yalla diapalé rej
@mamadoumoustaphadiop16504 жыл бұрын
J'habitais à pikine Gaïndé Fatma je le connais très bien il dit que la vérité maintenant migui tané alhamdoulilah gentle grand la wone bilahi icotaf tout le Monde connait Maestro
@ibrahimadiallodiallo76253 жыл бұрын
C’est vrai
@ndiougabadiane3 жыл бұрын
Barki cheikhoul khadime ayes msg you doye war laye geuné mane dé capté nasi je S8 fier de toi thiate dou wess nioune jeunes deug naye msg yi , yalla sa borome delosiwate sa sagoo si barkep khassaï yi , mes respects MAESTRO
@papethiombane14524 жыл бұрын
NDAYYESAAN , IL FAIT PARTI DE MA FAMILLE TEI YALLAH XAMNAKO MANGUI KOOY DOORA GUISS SAMA BEUT , C'EST UN ONCLE POUR . LES NOMS QU'IL A CITE SURTOUT SON PAPA IMAM DIOP , MOOM AK SAMA MAME BI DIOUR SAMA PAPA NIO BOOKOU NDAYE AK BAAY , TIEY YALLAH
@diadjidiop30203 жыл бұрын
Mba yangui koy séti rek diamou si yalla té yalla rek tax
@El_Chapo1554 жыл бұрын
Desfois nga yaakaar sa life rek mo taar bo guissé ki khamné sante yalla warnala
@mojr_makers20974 жыл бұрын
Wlh ❤
@coumbaousseynousall34744 жыл бұрын
Akaaay DEUG thieyy adouna moi kemané
@abdourahmanesindidi18184 жыл бұрын
Thiey yalla bilahi Aka ler
@mohamedthiam7973 жыл бұрын
Kou deur beu guiss kou mouma xelam wara dal
@cbcb60763 жыл бұрын
Walahi je suis en.france di sante yalla boubax dama ctane vidéo bi sama birr xeil linga binde la donne wax chak jour ma niaxtou dama ctane li reik xamni yalla dimbalinama boubax ma doylouwul reik
@ababacaredougueye96683 жыл бұрын
Très belle vidéo machallah,bonne continuation
@babacarmboup2824 жыл бұрын
Je commente pratiquement jamais mais honnêtement la partie où il fait la déclaration à sa femme m’a fait limite pleuré 😭💔 , Mbeguel mo gnouy doundal té kou nek meuss na dioum def erreur , rethiou ko ... yalla nagnou yalla Doli soutoureu ak kholou ballé 🙏🏾
@allofall97584 жыл бұрын
Ndeyssane yalna ko yalla diapalei doli ko soutoureu
@malickdiallo33944 жыл бұрын
Une interview pleine de leçons de vie pour nous les jeunes... Bref, n'est acquis éternellement. Am sakhoul niakk sakhoul.
@afriquecomedie12244 жыл бұрын
Wallay j’ai pleuré quand il appel sa femme😭😭😭
@isportv58904 жыл бұрын
Bilahi je le connais, on a grandi à Pikine et il a dit vrai. Adouna ngui niii
@Blackpower1094 жыл бұрын
thiey adsouna ndogal dou wess,nit sokhorna,lou way déf sa bop et aprés qu'est ce qu'il y gagne
@boubacarndong9584 жыл бұрын
Rien Da gno fatter yalla rekk
@Blackpower1094 жыл бұрын
Ak gnéti fani baméle
@junckyjow56904 жыл бұрын
Djégalou mé ay histoire 3 fanou bamel ay tour leudeum LA rekk you oustaz yi di raconté dé déméwoul nonou nitt rouhou LA bo déwé rekk yalla yobou rohou bi barsakk fa LA niou kharr ba boss pentie fa laniou até djéguel niou Khan niou djangal la
@assanediouf73154 жыл бұрын
Malgré tout ce qui lui arrive il pardonne. C’est un grand homme. En plus il est heureux plus que nous Et vraiment félicitations à Senegal Plus vous donnez la parole à des gens qui en ont pas droit vous montrez des choses que les médias classique ne font pas. Bravo. Nb: Bintou Bâle ko nak
@user-hk5lk5hv3y4 жыл бұрын
Oh maestro😭😭il venait chez moi pour vendre des habits à ma soeur
@diallobeta4093 жыл бұрын
Yalla nako borome takhawou ci barké alkourane ba mou diotate ci sokhna ci. Adouna ngi ni dé moudjiou bou rafet rek mo diara niane.yalla naniou borome bi sameu té mousseul gnou ci thiate ak pékhé none.Amine🙏
@ultrasgangfortus94264 жыл бұрын
Amna solo trop bonne continuation pour la chaîne TV 🙏🏾🙏🏾🙏🏾 Ndogol kou nekk lay dal, doli mouñ rek tey sant Yalla, Nit kou bone amoul kouñu askan bi faté rek mofi am
@yacinendiayebeye50284 жыл бұрын
Ndaysane Binetou balko diapale ko aduna amoul solo. qu'Allah nous vienne en aide.
@taphangom66494 жыл бұрын
Ndayesane maetro dagnou done tassé atelier pa niabou ba légui dafay dageu Lou nice
@dieudonnesaturnindiedhiou51434 жыл бұрын
Ooh je pleure interieurement.aimons nous les uns les autres gueum ne weurssaki yemoul begna sokhor. Yalna nalla yalla diapale grand maestro je te connais pas mais rafetna ndiorte n koubakh nga. Yalla na yalla def sa diabar balle la nieuwat sa wete nguene nzk en famille. Yomalkhayam dina meti trop de mechanceté gratuite.que dieu nous protege des mauvaises langues et des mauvaises personnes. Senegal plus je mabonne a votre chaine car la jeunesse a besoin de ce type demission qui donne des lecons concrzts sur la vie en generale merci a vous de cz reportage.
@@moustaphadiouf673 kane mo nékone boy ba légui boy la 😅😅😅
@lingueroubayemoussa96254 жыл бұрын
Kou baakh nio bokou béneu kogne il appelle ma mère cheri ndeyssane thiatt mo séww deug la d sagnsé ak féthieu mom sa yeuff ame nga kolléré d Mor Mbaye buur guéwél yal nako yalla yereum Abdou DIOP yalnala yalla sameu mayla wérr gouddal fane bi massta lii métina🥰🥰
@aron60544 жыл бұрын
Africains bougoul kou avancé no déf gnou guor saye tanke , yalla nalla borome bi taxawou délola sa sago
@yandembaye77394 жыл бұрын
Trop beau 🤩 ça se voit k c’était un dragueur🥰🥰...bon courage say domeu dina gnou lako fay inchallah
@julienfournier46323 жыл бұрын
Tellement que je le connaît wollah nit geunuko beug bopam ba dépressions yi mu am tewul day sagnsei fort quallah len préserve
@boubacarndong9584 жыл бұрын
Barké aladji fallou mbacké Maestro nitt deugue laa✌🏾koku degue lou bu bakh meune ngua bagna rerr di life bi ✨respect à lui💚❤💉🙏🏽
@boubacarndong9584 жыл бұрын
Ça me touche vraiment au coeur ❤❤✌🏾
@ablayediallo96094 жыл бұрын
Me ndeysan santal yallah Bou bakh grand frère lepp dina niowaté inchallah Sénégal fi defa meti trop barky mawlana cheikh ibourahima niass
@momarba18634 жыл бұрын
Opter pour une vie paisible ! Parcour d'un combattant 😇❤️
@abdoulayembaye87954 жыл бұрын
Ohhh grand bou bakh beuge bopam bari diam yalna yalla el maestro diam si yaw
@sambandiaye44863 жыл бұрын
Bilay kii nitou aldjana laa Loumou wahh fii yeupeuy deugue Lamine djiguoul sahh bante wahou malak nitt Ta nit matoul Kii yalnako yalla tahawou adina ak alahira🙏🙏🙏
@Musicsn20234 жыл бұрын
Très bon mental lep dineu bakh 🙏🏾 inchala si kattanou laou Bour bi
@CXOUNABMB-073 жыл бұрын
Ohhhhh son beau fils son ami son tout🥰
@freeprince78944 жыл бұрын
JE suis fière de lui 👉 que Dieu le Vien en aide inchallah ils faut jamais baisser les bras 👉👌👌👌
@modoukara72893 жыл бұрын
Samawaylawon depuis sandaga wah ji jarnayon machallah yalla hamna lp billahi yawmal himyame😭😭dina metti
@maguintd57904 жыл бұрын
Ay way xaw ma djabar dji boko deiguei noumouy def bal ko nit nit Moy garabam té gueine djapalé ko
@mbodjamadou30043 жыл бұрын
Kou kham adouna leu billay respect✔️ mn grand longe vie yalla diékhoul❤️ mai diangeu alkhourane bi rék mo dés😂
@fatouthiam90084 жыл бұрын
Ndeysan yalna yalla taxawu mn frére mais diabar dji na nieuw récupérer ko délosi wat ko bou bakh té conseil bou bakh la diokh jeune yi magui lay nianal thi barké seydouna mouhamed yalna yalla are la té taxawou la
@ack1414 жыл бұрын
Je suis pleur 😭😭 longui vie á toi bravo bonne travais absolunent🙏🙏🙏🙏😭😭😭😭😭😭😭
@khaffarmbacke53924 жыл бұрын
BINTOU ,sauve ton homme grâce à Allah❤️😪
@ibougnelle4 жыл бұрын
15ème mn 34ème seconde / ooooh c'est du lourd!! Une grande leçon pour notre société contemporaine obnubiler par le paraitre au détriment de l'être!! Toute une Philosophie, Machallah bro. Respect man!!
@PAPAMOUHAMADOUMOUSTAPHAM-fr5ktАй бұрын
Oooh ! Machala . Yalla na yalla same bintou setil wadji way adouna dafay diekh.
@23seye4 жыл бұрын
Yalnala yalla takhawou te mousseule la si tiate akhe moussibayi
@bocarsalla5664 жыл бұрын
C'est très touchant Sénégal plus bravo
@abdouazizsy30143 жыл бұрын
C'est émouvant, malgré tout il garde toujours la dignité en plus il est romantique.
@evandiaye44254 жыл бұрын
Eye way diabaram bi xana sou satané li wala mou deglou ko xana sa yaram meuné ndaw il mettina trop🥺☹😞
@papaamzo44434 жыл бұрын
Bintou il fort na c'est la plus belle discours que j'ai écouté en plus c'est vraiment sincère
@salioudiakhate90954 жыл бұрын
Grand bi fan nako
@assanesamba26233 жыл бұрын
Adouna amoul solo Déf lou bonne amoul ndiarign Ndeye sane diambar deugu nga yalnala yalla diapalé vrai citoyens kou gueum sa boop nga
@usmanphall68374 жыл бұрын
C émouvant
@aminetasamb47004 жыл бұрын
Kou menone sagnse ak fecc du courage maes
@Aria95-d5k4 жыл бұрын
Ah la la dioy nako nak ba Sama mascara teumb! Good job et good vibes to you 💜👏