Yénen yalla nalén yalla may goude fane ak weer ak bate yi di gana tawfékhé. Gni di taper dislike nak manou nio gnak si adouna danio réér rek té yalna nalén borom khassidas yi guindi ci barké khassidas yi. beg nagn ci yén lool
@cheikhbagneseriyoubonne42164 жыл бұрын
Wallahi ku bagne serigne touba doo tekhe lii de mooy li werr
@awacisse50028 жыл бұрын
machalla nekna trop j s8 tidiane mais hisbou dama nek trop bilahi machalla machalla yalla yokou fan yii
@pendadiagne45324 жыл бұрын
Ndey saan yalla nla yalla faye
@ebrimajagne88414 жыл бұрын
Yalla ganfiyag tewer sibarkep serigne Touba
@khadijadiop64798 жыл бұрын
Je n'arrive jamais a comprendre pourquoi des gens cliquent sur dislike pour des paroles aussi pures et aussi belles que ça. Niit gni daal kéman la
@mamewakhafall34058 жыл бұрын
ah bon donc suis pas la seule à me poser la question, yéména lolou sakh
@a893568 жыл бұрын
Sokhna si khana khamo Sénégal gni contre mouride yii Danioo Barai. Wayai daniouy zone rek ndakh kou banie khassida moom torokh ak mbougel bou tard bou eulekai rek. Boula dara metti sokhna si
@kineniang38877 жыл бұрын
akasa yalna yalla defal len diame té diame rek geun di am ndakh kou ande ak borom diouma dji ak Aÿ khasidam diame rek lay am inchalla si barki touhfatou amiine
@mamymbaye48197 жыл бұрын
ils ne comprennent rien de la puretee...et ne savent pas que tt etait ecrie par le saint Akhmadou Bamba Mbacké...notre Cheikh...
@totalpout64467 жыл бұрын
Yalna BOROM BI guindiene thi dieumi BOROM TOUBA ndakh sakhiya man lam yahwoud dou degne mouk wakhi SUNU BOROM nena kou bagne BOROM TOUBA tekhedingua kone beug ko reka woor
@Adam19826 жыл бұрын
Dieuredieuf Serigne Touba, yaw rek ya meuna biineu si sougnou Yonène bou tèedeu bi
@mbourathgueye3868 жыл бұрын
Lou way ame nako santé Cheikh Ahmadou Bamba Khadim Rasoul
@bassiroudiop66007 жыл бұрын
أسأل الله ربي المجيب أن يطيل بقاء جميع قراء قصائد شيخنا الخديم قاد له الله ماختار له أينما كانوا لا سيما حزب الترقية دارالقدوس بجاه شيخنا أسنى خديم المصطفى عليه أزكى صلوات ربنا القريب بلا انقطاع أبدا
@yacinediop19225 жыл бұрын
Mashallah. Yalna ngen fi yag te wer te Yallah soti ci yen hassanats you bare ci barke Mouhamet et Serigne Touba mi ko bind. Ça me donne des larmes aux yeux.
@aliousoung50628 жыл бұрын
diaradieff Borom touba amna solo
@bassirouthiam26858 жыл бұрын
thieuy serigne touba rekka wor
@sarignesamyawyallanallayal78217 жыл бұрын
aksssa sarigne touba lifour na ak yaen talabe yi nireka la yalla na yalla maylen tawou fekh nekh na,tourob
@sarignesamyawyallanallayal78217 жыл бұрын
foukoulen kou de liy nekoul kou baka rek amkou yalla moulen kou def fal de