la famille de S.Bara Khouradia en colère contre son discours de S.Amsa Mbacke Mom S.Abdou Lahad…

  Рет қаралды 60,343

5M TV SÈNÈGAL

5M TV SÈNÈGAL

Күн бұрын

Пікірлер: 298
@Sakkuxamxam-z3z
@Sakkuxamxam-z3z Ай бұрын
Néexol baneexol weeyé bodotoon s touba kenn du kham brom saam, fii sëñ touuuba rk moofi né ❤❤❤❤❤
@Media5Tv1-y9w
@Media5Tv1-y9w Ай бұрын
Serigne touba dafa am ay mboke khamal loulo
@abdoulayengom7659
@abdoulayengom7659 Ай бұрын
Walahi waxal dhé boys yi niak niom ak niak xam sen bobbou rek .sgn bara khourédia mi meusoul doon lodoul talibè serign touba .
@latdiordiop6051
@latdiordiop6051 Ай бұрын
Li motakh gni len topou di sissou rek. Serigne touba guenoul ken ki gueun yala ko kham yakar ni kou bakh la rek nguen thi am. Ay bakar you amoul féne thi adouna so kholé mbirou Serign bi dingua ko guiss. Donc respectlen nit gni. Fi koula falé woul doko falé.
@AhmadouBambaSarr-so6vl
@AhmadouBambaSarr-so6vl Ай бұрын
@@latdiordiop6051 ya meuna wah loulla woloul koulla wah sbi guenoul kene
@alkarimalkarim5267
@alkarimalkarim5267 Ай бұрын
@@Sakkuxamxam-z3z Deugeleu Deugeleu Deugeleu Deugeleu
@ousmanesarr8462
@ousmanesarr8462 Ай бұрын
Lii geun dit def amoul bene diarign demlen diamou dji yalla ta legeuyali sr touba ken dou dra sr touba rk moy wadia❤
@SidiDienne
@SidiDienne Ай бұрын
Fi serigne touba mofi nek. Mo deff lepp. Bou lénne niou sonal ah
@modouthiam6
@modouthiam6 Ай бұрын
Dano yabate rek
@mamemorniang9550
@mamemorniang9550 Ай бұрын
Di diouli yoor yoor amna solo
@diawfalfaraa5997
@diawfalfaraa5997 Ай бұрын
Fi kén Doufi touss lepou Serigne Touba la
@yytv8221
@yytv8221 Ай бұрын
Kou neikeu diamoul YALLAH kem sa katane ta baayi diw mo raw diw wala diw limou am diw motakh,diamou jilein YALLAH yii amaloutt keineu diarigne
@SerigneGueye-z9l
@SerigneGueye-z9l Ай бұрын
Waye li s amssa wax darra nékosi Serigne touba mo dimbali diépue
@bayedjite6811
@bayedjite6811 Ай бұрын
إنما المؤمنون إخوة فأصلحوا بين أخويكم
@MorSeye-zf2fg
@MorSeye-zf2fg Ай бұрын
Boudoul wone serigne touba senn mame yi dougn done dara lep borom touba la
@SiiwalalProjetBi
@SiiwalalProjetBi Ай бұрын
Ab sëriñ daal mooy ki Sëriñ Tuubaa wax ca Masaalikul Jinaan. Sëriñ nekkul ci aw Sant.❤❤❤❤
@AhmadouBambaSarr-so6vl
@AhmadouBambaSarr-so6vl Ай бұрын
Deugla sante mom dou Serigne
@Malick-n5t
@Malick-n5t Ай бұрын
Thiey STouba ❤❤ Amoul Mourom
@Malick-n5t
@Malick-n5t Ай бұрын
Borom sama S Touba motakh nu xam ko Borom sam taloubi S Touba Lou wér ❤
@ibrahimabeye2531
@ibrahimabeye2531 Ай бұрын
Hiii guèneul si lolou
@AhmadouBambaSarr-so6vl
@AhmadouBambaSarr-so6vl Ай бұрын
​@@ibrahimabeye2531konne loleni kasse konn
@Diopmarakhibb
@Diopmarakhibb 29 күн бұрын
Man dama am kersa si li😢😢 wallahi hasim rous louna lool😢😢😢
@abdoucisse6605
@abdoucisse6605 Ай бұрын
Yoonou mouride lou fii nit ame serigne touba mou la kou diokh nay leer
@abdoulahigueye2387
@abdoulahigueye2387 Ай бұрын
Waxante bi ci yoon wi man naa nàkk ku ci nekk sa darajay bopp rekk nga gis, bu S. Amsa tegoon bëtam Sëriñ bi du kàññ waa kër Maam Moor Jaara, ñoom itam bu ñu gëmee ne Sëriñ bi moo leen jox li ñu yor du ñu tontu S. Amsa. Xamleen ne seen wax yii dafiy des ba fàwwu. 😢😢
@BayesaliouMbacke-re9pw
@BayesaliouMbacke-re9pw Ай бұрын
Walahi 😢
@mourtadambacke9116
@mourtadambacke9116 Ай бұрын
Yalla nañou yalla dollé fayal S Mame Mor Diarra ta tass ñou si barkep ❤❤❤
@cakmbc6488
@cakmbc6488 Ай бұрын
Merci à vous ❤wakh nguéne deug fi kene dou fi takhali serigne bi am gnim bokal li serigne touba yor gnepa ci yem amut seut amut dom Ak Talibé rk mo fiy diarign serigne bi wakhone na ko s Fàllu Domi serigne bi Ak s mor Rokhaya di diarbat Ak s massamba raki s touba
@AhmadouBambaSarr-so6vl
@AhmadouBambaSarr-so6vl Ай бұрын
Wayé mom hanaa dafa yeha diébalou
@mamemorcisse3561
@mamemorcisse3561 Ай бұрын
Machalla Kham Kham bi lérna ❤
@tout1958
@tout1958 Ай бұрын
Kou mom xarmi ngéne bayi boume gi Serigne amsatou toudoul kéneu sax yéne mom lane moye séne problème
@NOTTO221
@NOTTO221 Ай бұрын
Mane Loulou moma Diàkhal Bilahe
@tout1958
@tout1958 Ай бұрын
​@@NOTTO221kou mom xare mi nga bayi boume gi 😂😂😂😂😂😂😂
@tallfamilleelectroniquekol6840
@tallfamilleelectroniquekol6840 Ай бұрын
Likay dafay wani ni kon li amna kon louy problème bi
@NdaySy
@NdaySy Ай бұрын
S morom soxna diara talibé s touba la ak s mor Anta saly diéye s touba amol moroum dè😢
@lessecrettreprofond4012
@lessecrettreprofond4012 Ай бұрын
Wakhoo deug dou niepa doone ay talibé ak talibé yagou fi
@lessecrettreprofond4012
@lessecrettreprofond4012 Ай бұрын
Dou ak talibé réikay mayei dara dh boudoone lolou kone kounékoul mourid doo am dara ta lolou amoull
@MameCheikhMbacké-v8t
@MameCheikhMbacké-v8t Ай бұрын
​saway khana dego yonou mourit wi ak taloube rek mofiy diaringe
@diaratoullahimam7494
@diaratoullahimam7494 Ай бұрын
Yaw mom foo diogée xana danga tiit si ay nélaw
@dialibatoumarahib79
@dialibatoumarahib79 Ай бұрын
S mor Diara dé mom s Touba geuram nakoo
@alkarimalkarim5267
@alkarimalkarim5267 Ай бұрын
Lolou Deugeleu Deugeleu Deugeleu ❤
@elhadjithiam9856
@elhadjithiam9856 Ай бұрын
Dieureudieuf Shaykhana Ahmadal Khadim. DIeureudieuf Serigne Mame Mor Diarra. Serigne Mountakha Mbacke yallah nafi yagg andak werr. Amine!
@SerigneMbacke-t7y
@SerigneMbacke-t7y Ай бұрын
Mbacke balla li amna solo lerna lolou waye ❤❤
@Amdymbaor-kt4sb
@Amdymbaor-kt4sb Ай бұрын
Yonou mourid Lou fi waay am serigne touba la
@abdoulahigueye2387
@abdoulahigueye2387 Ай бұрын
Kii di leeral leetar bi moom rekk moo waroon a wax maasàllaa ❤❤❤
@modouthiam6
@modouthiam6 Ай бұрын
Serigne amsatou a Bien raison . Demelene diangue gui fi loufiway am serigne momoko diokh guinaw yalla borom bi
@Cheikhouna04
@Cheikhouna04 Ай бұрын
Ak bokk daal lepp lu koy defar mo gën lu koy xajamal Ta Ab tontontei day indi ak ñaawoo
@kebekebe587
@kebekebe587 Ай бұрын
Deug
@ModouSambe-p8g
@ModouSambe-p8g Ай бұрын
Liga wakh mooye deugue
@diop3836
@diop3836 Ай бұрын
Koné deyékate sa mame sene mame diamou na yalla lémoye diamou yalla ba yalla sante ko deme lén diamou yalla def né sene mame
@bambagueye6670
@bambagueye6670 Ай бұрын
Fi borom touba rek fi nék yi yep Amul solo
@elhadjilougar1855
@elhadjilougar1855 Ай бұрын
Maschalla am na solo diereidiaffff ❤❤❤❤❤❤❤❤ li rek mowèrrrr
@Amdymbaor-kt4sb
@Amdymbaor-kt4sb Ай бұрын
Wér na fall
@CheikhounaMbacke-q6v
@CheikhounaMbacke-q6v Ай бұрын
Borom Touba Amoul Morom dh ❤
@modoudiop2892
@modoudiop2892 Ай бұрын
Ndeysane letre bi ngafi nettali d manguikoy soga degg te njort nani barina si morom te gueumnako waye nak Sr Hamza kheuy neu lu Bakh rek la jublu woon si nettali googui mu wakh ndeysane li yalla bum jour fitna Amiine
@cheikhounaseck4139
@cheikhounaseck4139 Ай бұрын
Beuga siw rk s amsa kasé s touba bamouy niane kén taxa woul si kanam nane amine deug la dh
@KhadimThioub-s3m
@KhadimThioub-s3m Ай бұрын
Yonou mouride d SERIGNE TOUBA rek mofil serigne,khousi eup talibé yafi gueune.diarama MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL
@BayeDjilyKane-z2i
@BayeDjilyKane-z2i 24 күн бұрын
Talibe yo khamni don dioully don wor😂
@adjicherifFall-h7u
@adjicherifFall-h7u Ай бұрын
Cou Mame cheikh ibra fonkon lol toudé nako domam serigne mbacke fall yalla na yalla doly koy aye lér aki ngeureum barquep mouride bou mag ba
@mameboussotoubambacke
@mameboussotoubambacke Ай бұрын
Machallah brom sam dou morom
@SeynabouMbacke-vf1jk
@SeynabouMbacke-vf1jk Ай бұрын
Mach la ❤❤❤
@senegwade
@senegwade Ай бұрын
Diereudiefati serigne touba
@thiernoniang7117
@thiernoniang7117 Ай бұрын
THANKS SÉRIGNE MAME MOR ❤❤❤❤
@SerignecheikhMbacké-z1g
@SerignecheikhMbacké-z1g Ай бұрын
Lo bakh bakh boune dinde Li sering touba def thi yaw nga yemak nieup mba nieup tane la wasalam
@mbackeniang1013
@mbackeniang1013 Ай бұрын
Serigne touba amoul morom
@elhadjitidianefall3280
@elhadjitidianefall3280 Ай бұрын
Merci beaucoup
@cheikhndigueldiopsalihcnds7122
@cheikhndigueldiopsalihcnds7122 Ай бұрын
Waay Sëriñ Amsa limu wax lu wér la, dara nekku ci Ñépp ko wara liggéeyal Sëriñ Amsa wax na dëgg
@Sakkuxamxam-z3z
@Sakkuxamxam-z3z Ай бұрын
Deug leu té bodotoon sñ bi kenn dou kham brom saam, fii sëñ touuuba rek moofi né
@AladjiMadiaGaye
@AladjiMadiaGaye Ай бұрын
@@cheikhndigueldiopsalihcnds7122 wa S Amsatou Loum wakh ?
@AladjiMadiaGaye
@AladjiMadiaGaye Ай бұрын
Wa S Amsatou Loum wakh?
@mbackeabdou3258
@mbackeabdou3258 Ай бұрын
Guénal affiche sa bopp rek wakh lim wakh so amé fitt
@cakmbc6488
@cakmbc6488 Ай бұрын
Kou khèp brom sam khèp nga serigne touba nakh nio boku lèp ta serigne bi fonkone na ko lol nane bayi parpar lol bi tapale yi serigne bi talouko wone Domi ko meuneu done Ak ko meune done bo respect wul mboku serigne bi respect wo serigne bi.
@2mttv64
@2mttv64 Ай бұрын
Maasàllaa jërëjëf xam-xam bi rafet na sell na
@AwaFall-g1l
@AwaFall-g1l 20 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@barasow3654
@barasow3654 Ай бұрын
Mbiir bii borom touba kepp leu
@latdiordiop6051
@latdiordiop6051 Ай бұрын
Serigne amsa da diangoul amoul kham kham yarouwoul.
@bayetoubasylla7327
@bayetoubasylla7327 Ай бұрын
Merci ❤
@mortalladieng8595
@mortalladieng8595 Ай бұрын
Fii loufi wat am serigne touba moo koko may
@falloucisse33
@falloucisse33 Ай бұрын
فليكرم ضيفه ❌ فليقل خيرا أوليصمت ✅
@toubadarmanko7193
@toubadarmanko7193 Ай бұрын
Boudoul wone Serigne Touba kén doulén xam
@MamemorSamb-v4h
@MamemorSamb-v4h Ай бұрын
Macha allah ❤
@sindiditv9606
@sindiditv9606 Ай бұрын
Leeep Serigne Touba laaaaa liii kép mootah Cheikh ibra raw nieup
@abouabdoulayecisse9191
@abouabdoulayecisse9191 Ай бұрын
YALLA naa YALLA dooli niou diam teh meussoul niou ci seytaneh
@ousmanesarr8462
@ousmanesarr8462 Ай бұрын
Dama khamne kii geune kham lè dafa diou khoun pop pam sr touba lingeuni df koun dou si ande 😢😢
@ModouGuey-z8v
@ModouGuey-z8v Ай бұрын
N'a dem djeuli sokhna bi nek Espagne
@lowaydeffboppam6865
@lowaydeffboppam6865 Ай бұрын
Ba kham ngén né S Hamsa man na dém ba Nék Khalifa Général des Mourides rék 👌👌 Te S Abdou Lahad nak louway mana wakh si youne bi mo deff Touba nimo Mel tay dji Si taxawayam ak Farlom ak liguèyel S touba
@Likhlassproduction4444
@Likhlassproduction4444 Ай бұрын
Jërëgeen jëf waay 😊
@Meunsablond08
@Meunsablond08 Ай бұрын
Yalla na jamm yag
@hibouson2783
@hibouson2783 Ай бұрын
Bou lenne ngou fonto Mame mor Diarra s touba moko geune
@SokhnaxadiMbacke-ju6hl
@SokhnaxadiMbacke-ju6hl Ай бұрын
yawde xamo labari si adona digante chékholl khadim ak s mor diare mangase Mado ndax samam Sax domoromam waxomalak iow réwge te xamadi
@modoufall1365
@modoufall1365 Ай бұрын
Yalla naniou souniou borom bok djégal nioune nieep barké Serigne Touba
@abdouahadmbacke7214
@abdouahadmbacke7214 Ай бұрын
Boudoul won Serigne bi kéne dou toudu brome sham
@sidymbacke249
@sidymbacke249 Ай бұрын
Machallah wakh dji lérna rafétna diarama mam saam kou wakhat degaat
@bayebeye3070
@bayebeye3070 Ай бұрын
Lep Serigne bé guinaw yalla
@GueyeMarakhib28
@GueyeMarakhib28 Ай бұрын
S amsa limou wakh dara nékkou si
@abdouahadmbacke7214
@abdouahadmbacke7214 Ай бұрын
Wallahi limou wakh darra nekouci
@yaragteggiin5101
@yaragteggiin5101 Ай бұрын
Deug daa naxari rekk
@MBtv92
@MBtv92 Ай бұрын
Ci thiaxane képp ngén nék sa dieufou mame mom la féxé lén dieuf té ngeureumoul yalla mo geune. Kounék sa mame lii sa mame laa diamou dji léne yalla. Lo fi wax ñouné sa mame ngay waxal té beuss bouné ñou laal dîné kén dou wax
@sonko2024rk
@sonko2024rk Ай бұрын
Nékal nitt seringue amsa limou wakh deug la fii seringue touba mofi nékkk amoul mak amoul rakk
@SonhibouMbow
@SonhibouMbow Ай бұрын
S amza mome balouna
@fdd10057
@fdd10057 Ай бұрын
Sëriñ Mor Diarra nekul ci yi Guen Nek sëriñ Mor Diarra bam ligueyal serigne Touba la tonuwu bayilen thiakhan yi te dem diamou dji yalla
@mbayefallou1401
@mbayefallou1401 Ай бұрын
Mame Mor Diarra ak Serigne TOUBA Cheikhanaa Cheikh Ahmadou Bamba ñioo book séénouk Bookk ( yaari waydiour ) ay waay rafétal léén
@AbdoulahatGueye-i3b
@AbdoulahatGueye-i3b Ай бұрын
Serigne Amsa waxoull tourou ken
@SerignecheikhMbacké-z1g
@SerignecheikhMbacké-z1g Ай бұрын
Li leup deh amoul solo s touba dimbli niou noune nieup moko taxnona nieuw diamone nane rouss yalla rouss Yonente bi rouss ta gore sering touba koune lako war thi mom defnako nane gore ta nite koudoul s touba dodara wasalam
@MbackeAbdoulahad-i9x
@MbackeAbdoulahad-i9x Ай бұрын
Machalla amena solo loll te lér loll mbacke
@SambaSylla-j4g
@SambaSylla-j4g Ай бұрын
Deme lene ligueyi
@KhadimToure-g5l
@KhadimToure-g5l Ай бұрын
Bayyiléne thiakhane
@amadoufatimakane3564
@amadoufatimakane3564 Ай бұрын
Li serigne Mamour wah moo am solo
@MomoGueye-b6q
@MomoGueye-b6q Ай бұрын
Nay rafet rekk histoire moom nieupp kham nagne nimou demeii Fii moom lou kilifa gou bakh am rekk Serigne Touba moko ko defal Yalla nak beugoul kouye reuye reuye lou ak kou sokhor Wasalam
@tout1958
@tout1958 Ай бұрын
Serigne amsatou lou lér la wax limou wax mane amna 60ans ta dama dioudou dégeu magi talibé yi diko wax bayi léne sisou bi waye
@diaratoullahimam7494
@diaratoullahimam7494 Ай бұрын
Wakhou DEUG dé ndax démé wol nii
@cissedame3803
@cissedame3803 Ай бұрын
Soff ngen baringen wax srg amsa waxu fi dara lu jar ay conference de presse apart serigne touba ñèpp ay talibé lan amul doom amul mak amul rak fi koñ fi topp srg touba mou tax
@mourtalambaye1236
@mourtalambaye1236 Ай бұрын
Daray Yàlla nekkul ci lii ngeen di def .
@Baymorsourang674
@Baymorsourang674 Ай бұрын
Dondée suuf moom kokoy déf lôu jeuf lou réfétt dôko wakh amsa dà alkou bou yagu té yëgo ko
@yytv8221
@yytv8221 Ай бұрын
Digante Mame Mor Diara ak Serigne Touba dei kou siye dougou da nga nafekh rek
@barasow3654
@barasow3654 Ай бұрын
Gniii danio rew sakh serigne amsatou MBACKE deugue rekk la wakh té sii layy dokh
@yytv8221
@yytv8221 Ай бұрын
Adouna fawou am kou jiitou am ko toppou waya la nitt di rawei nitt mbiroum YALLAH leu dou ak diambaryaa
@tallfamilleelectroniquekol6840
@tallfamilleelectroniquekol6840 Ай бұрын
Saway serigne touba rek mofi nik bayi lene leguine di dif
@MameCheikhMbacké-v8t
@MameCheikhMbacké-v8t Ай бұрын
Soof rek ngadef seringe amsatou dousene morom ndiakk ngene diome lool defleneni wa keur cheikh ibra fall am ak taloube’ te’ wormal ndiabotouk seringe touba gi ngir dieumi seringe touba ne’klene ay taloube’
@SokhnaxadiMbacke-ju6hl
@SokhnaxadiMbacke-ju6hl Ай бұрын
Yaw Liga wax Yako mom soko défon dowax lii Ani sa xell
@scheikhounambacke5169
@scheikhounambacke5169 Ай бұрын
Machalla kadou yi rafetna troup
@ElhadjidaourDiongue
@ElhadjidaourDiongue Ай бұрын
andelen ak dal bognou may noneyi bountou .nagnouy jegale guir yalla tba nit day joum yalla tba reka mat
@modouastadiakhatembacolmba2560
@modouastadiakhatembacolmba2560 Ай бұрын
Senegal Mou nekh rk serigne touba de boko am mom tay la nekh way dembo xam na nuo lou xewo
@abdunjaay738
@abdunjaay738 Ай бұрын
Ndax fii njuumte amu ci 23:00 ba 24:30
@hygieneservice2603
@hygieneservice2603 Ай бұрын
Manchalla Rafét lérr na
@serignesarr517
@serignesarr517 Ай бұрын
BOU MEDECINS YIY KHEEX NOU MALADES YIY DEF ?
@AbdoulahatGueye-i3b
@AbdoulahatGueye-i3b Ай бұрын
Serigne Amsa limou wax dra nekousi
@moustaphalo7935
@moustaphalo7935 Ай бұрын
Sounguéne amon Talibé li dounguénko déf ndakh lou mana khéw seeigne Amsa mbacké moy séne sangue dérétou serigne touba la lén gagné mou nékh léne ak mou nakhari léne mame mor diarra talibé serigne touba reck la .lépp serigne touba séne mame défou fi dara😊
@deguerekeexsalafisteexwaha3440
@deguerekeexsalafisteexwaha3440 Ай бұрын
Wakhofi touss
@Sylla-g1x
@Sylla-g1x Ай бұрын
Sincèrement guisou mafi Xam Xam Ms rèwanadè lafi guisse
@FallouDiouf-ck7bv
@FallouDiouf-ck7bv Ай бұрын
Bayi léne séne thiakhane yi fi dame mbacké mofi néki mome lagn geum Beugeu ngeune ak sékhou trop dem léne ligueyi
@Tapa-vc5uz
@Tapa-vc5uz Ай бұрын
Brom Touba ak brom Sam bén lagne
@falyfal9
@falyfal9 Ай бұрын
Li S. Amza wakh gneuwate na ni si say kadou yagui merr bay fat ta talibé day dal. Dara nékhoul si limou wakh bayi léne reuye S. Amza Mame Diarra maman leu ta gnawtéf amoufi yawe bi ya togne ta Serigne Abdou Lahat yonam nékhou si baguénekoy khass fi Serigne Touba moi nek ta Mame Cheikh Ibra rawna léne nakh talibé
@dameseck7348
@dameseck7348 Ай бұрын
Fi Sawaye Waji mana Banian te guenn khame ni serigne touba Mofi nek nk ok
@AssaneGueye-sk2ig
@AssaneGueye-sk2ig Ай бұрын
Nit ngi nanou diamou yalla
@wakanavision540
@wakanavision540 Ай бұрын
Brom same talibe serigne touba la kon sr touba sagn nako balelo keur ndakh moy serignam sen tontou yi daleni soufel rek
Revue de presse Ahmed Aïdara du Jeudi 16 Janvier 2025
9:03
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 10 М.
The evil clown plays a prank on the angel
00:39
超人夫妇
Рет қаралды 53 МЛН
So Cute 🥰 who is better?
00:15
dednahype
Рет қаралды 19 МЛН
"J'AI PEUR !" Mansour Faye évoque une chasse aux sorcières: Ahmed AIDARA r...
19:06
2A TV - LA CHAÎNE DU PEUPLE
Рет қаралды 4 М.
Cheikh Oumar Diagne, limogé par Diomaye Imam Rafahi Mbacke sur les Dangers de la.....
18:16
SERINE AHMADOU RAFAHI MBACKÉ
Рет қаралды 108 М.
thiowal Mamor Diarra ak Serigne Touba
23:17
FIPOU NEWS
Рет қаралды 4,7 М.