Est-ce que nous sommes toujours au pays de la Téranga..?? 😱😱 Est-ce que nous sommes toujours dans le même Sénégal que nous a légué Cheikh AhmadOu BAMBA.. Maodo Malick.. Maam Baay Niass.. Seydina Limamou etc tant de bonnes personnes qui ont fait que notre pays était si paisible mais ces maux sont devenus monnaies courantes.. Pourtant on doit appliquer la Chariiyaa comme l'a dit le Tout Puissant✍️🙏 Kou raay🗡️✂️⚔️☠️ niou raayla😎😎mou diëkh.. Paix à son âme🤲🤲 Yalla nako sunu BOrOm yeureum té xaaréko Aldiana barkëp CheikhOuna AhmadOul Xadim.. Que le Tout Puissant nous assiste et nous donne la joie de vivre ensemble🤲🤲
@mariemaidara8352 жыл бұрын
Faut faire la différence entre négligence et manquement du système ,Pourquoi il se précipite pour parler de négligence
@coumbadiakho41122 жыл бұрын
@@mariemaidara835 yaw khana thi médecin yi gueun bok thim ; niak yeurmandé bèy beuggueu dé
@amarmariama2 жыл бұрын
@@mariemaidara835 ⁰pp
@HbvTxdhfu5 ай бұрын
😢😢😢😢
@Nana-o7e3xАй бұрын
Mane May len ñou diam ken momoul sénégal sen hol you degeur yi amo len beni yeurmade sénégal les chretien sen hol ye rafet te yatou ñoñou ño am yermade medicin bobou cest musulmanes ñome ñeup aka ño bone
@serignecheikhtalibebamba53232 жыл бұрын
Allahou Ak bar 😭 Yallah nako Yallah Dolly Yeurmandée Ak Diégal barkepp Cheikhoul khadim
@lombredelarue2 жыл бұрын
Policier bi respectéwoul civils bi Medecin bi respectéwoul patients bi Juriste bi respectéwoul client bi Sénégal en résumé personne ne respecte personne...kén diohoul tieur ligueuyeum ...problème éducation deugu lagn am
@moussdoum12 жыл бұрын
Motakh yeurmandé yallah doufi wathie
@diopmusa86582 ай бұрын
Bo diogue Europe dem Sénégal nga rew désordres la yarouwoune respecté d'oumou adama amoufa
@Elhadji21872 жыл бұрын
Distance bi guen djeukeu daw dafa sorii hémorragie bi meunoul harr nitt ki gnou diam ko gnoukay passanté fo diarr mou dé dou dounde c vraiment injustice ce qui ce passe dans les hôpitaux khalis bigni yakke si deuk bi meun na yokke ay hôpitaux you barii Yokk personnels mai Sénégal thiakhane rekk khaliss bii si thiakhane la dieum😭😭😭
@zeydi68262 жыл бұрын
Il faut commencer à les filmer
@Sinan_Bakis2 жыл бұрын
Vous avez remarqué que c'est toujours les pauvres qui sont victimes de ce genre de choses ?
@massambandiaye61502 жыл бұрын
Sisi
@ndioletine71222 жыл бұрын
Bilahi
@Oumanas59952 жыл бұрын
Manque d'éducation seulement on peut-être pauvre et bien éduqué même
@abydiop22572 жыл бұрын
Bilahi comme d'habitude aussi gnoune pauvre bou Richard Di jubilé gnoune lagnuy tayle ...
@mameboussomamebousso81612 жыл бұрын
Billay toujours les pauvres Sénégal métina
@kikicamara26272 жыл бұрын
Galsen légui diam ak Ray rek thiey Yalla !! Que Dieu nous protège et qu'il me fasse quitter ce pays au plus vite
@SD-ih6bz2 жыл бұрын
Foo djieum
@kikicamara26272 жыл бұрын
@@SD-ih6bz là où on respecte les droits de l'homme ce pays est un foutoir dans tous les sens
@Oumanas59952 жыл бұрын
Comme legui rothi rek diame mo khew té ken dousi wakh
@SD-ih6bz2 жыл бұрын
@@Oumanas5995 doynawar daal té métina
@geraldinedossantos90452 жыл бұрын
Kiki. Ngir yalla 🙏🙏🙏boumafi bayi🙏🙏
@soumayathiam47702 жыл бұрын
Hopital regional bou thies walahii gnoo guenaa bonn si senegal
@mouhamedboly86432 жыл бұрын
Q'ALLAH LUI pardonne et l'accueil dans son paradis CELESTRE 🤲
@mamedialedia83783 күн бұрын
MEDECINS YII DEFOUNIOU DARA . YALLA BOU NAREE DIEUL BOUNETOU BOO FEUGG DAFAY TEUDIOU . GUEUM LEENE YALLA
@serignendiayebeuguefallou70882 жыл бұрын
Merci beaucoup Sentv pour ce reportage très interessant
@timachou72872 жыл бұрын
Porter len plainte médecin bi Nek hôpital Thies 😢
@ousmanecisse69422 жыл бұрын
C'est vraiment regrettable. Il faudrait un forum national de comportements. Mon pays va vraiment mal.
@mbossediaw28412 жыл бұрын
Hospital yiii rek yalla naniou yalla may diameu rek rek ba douniou fa dem
@coumbaba85142 жыл бұрын
Lima beugue ham moy loutakh gni yoré souniou weurgou yaram yoré tey légui hol you bonne yi changé votre méthode de travail ga amna medecin you bakh nio halni niou def travail remarquable machallah roy len thi nioniou
@AmyBiteye-d8o4 күн бұрын
Hôpital régional nio bone si bopam com niou amoul khol rek
@aissatougueye60622 жыл бұрын
toujours Ray rek que dieu nous protège des mauvaise personnes si Barker srg touba
@cissramatoulaye96112 жыл бұрын
Dafa ame ñio khamnè khelou mala lañiou yorrr motakh rayè rek deuk bi doyna warr dh
@maguettefall82612 жыл бұрын
Bilakhi amine way
@abibatoubathily37832 жыл бұрын
Amine yaraby ❤️
@fastfily26522 жыл бұрын
L’artère fémorale , je pense que c’est son nom. La Grosse artère au niveau de l’intérieur de la cuisse , si elle est sectionnée la personne se vide de son sang à une vitesse incroyable . Ma grande sœur a eu un petit accident malheureusement le temps n’a pas été de notre côté , 30 mn après elle était décédée. C’est très très dur. Yalna len yallah yeureum té kharé len adiana Firdaws
@fandao21382 жыл бұрын
Paix à son âme
@rouguibah85532 жыл бұрын
Amine
@aichathiam80022 жыл бұрын
Ayy wayy mane sama rakk def na choc Ay 22h niou yobou ko hôpital régional de thies niou fékk fa les stagiaires niou dieul sama Frere bi defal ko radio niouni am na louniou guiss si deunde bi mais il faut niou khar ba demain médecin bi nieuw. Nékété yoo sama frère bi dou guiss médecin bi malheureusement à 6h du matin la décédé néké hémorragie interne la def
@yacinecoulibaly74592 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum
@khadyndour22302 жыл бұрын
Docteur yi sokhor naniou bilakhi, thieuy Senegal
@mamasy36312 жыл бұрын
la honte meme pas capable d'arrêter le sang sa c'est grave chaque jour il yaura des nouveaux cas dans ses hôpitaux
@bayezaletalla20662 жыл бұрын
Ndeyssane yalna ko yalla yeureum
@aichababou26042 жыл бұрын
Neysanne yalla nako yalla yereume kharéko aldjana firdawsi si barké Seydina Mouhamed (psl)🙏🏻🙏🏻🤲🏼
@awadiagne33692 жыл бұрын
Qq
@hadjaaffssatoudiallo30772 жыл бұрын
K son âme repose en paix c'est triste bilahi
@hamadly63212 жыл бұрын
أللهم اغفر له وارحمه واسكنه الجنة
@sowlyssa53472 жыл бұрын
C'est la personne qui l'a poignardé qui l'a tué. Il a touché l'artère
@omarsene29942 жыл бұрын
Vraiment
@nataprochop9312 жыл бұрын
Vraiment
@rokhayacisse79054 ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum té khareko aldiana 😢😢😢 oh mettina
@antarassouldieye40612 жыл бұрын
Li kagne laye diekh thji Sénégal tei kene dou wakh bakhna k son âme repose en paix 🙏
Mandee sokhor gisi wa hôpital yi djakhalnama damaa djomy man ay khol you melni kheeer warnagnoo saytouwaat gnignouy djokh responsabilité fadje
@serignendiayebeuguefallou70882 жыл бұрын
Yalla yeureum ko amine way
@Elhadji21872 жыл бұрын
Avant ça la 1ère chose c l'indispensable des jeunes legui dal mm phénomène l'agressivité kou heh ak sa morome legui dieul paka diamm il faut des punitions très très sévères voir la peine de mort lolou rek mo meuneu arrêter liii legui ayy diamm nagn ko rek guay degu
@fatoundiaye22472 жыл бұрын
c dur vraiment yalla nako yalla yeureum té khare ko aldiana firdawsi 😭😭
@modoundiaye1792Ай бұрын
Cest bien dit mon frère Abdou ziar nala
@serignendiayebeuguefallou70882 жыл бұрын
Thièye Sénégal lilanela tamit ohh vraiment Négligence bi doyna
@Fatoumbodji4592 жыл бұрын
Yalna ko yalla yerem té kharé ko aldjana ya guene kawé Inshalah
@maramesagne33602 жыл бұрын
Mé Sénégal légi kou am sa malade té ngako té sa keur mou déwé fofou kom ka dangay indi sa malade opitale pour yakar lén gnou koy sétane bamou dé téksi méleni kou lay ngawal li dafa ngaw 😭😭😭😭
@mormbaye29892 жыл бұрын
Bilay yw niemetouma dem hôpital 🏥
@yacinecoulibaly74592 жыл бұрын
Repose en paix makhali cissé yalla nala yalla kharé aldjiana
@MariamaDembele-gy7kz7 күн бұрын
Yalnako yalla yereume
@yacinecoulibaly74592 жыл бұрын
Je ne comprend plus légui dafa melni médecin yi nioy malaka yi nioy xol kouniou wara Ray dama xameni bakane nimou foré niou meune sagane bamou déé
@alhamdoulilahndiaye66682 жыл бұрын
Senegal té nioussé wakh bala mouye eupe lokho. Kou artouwoul dinga até. Je demande est ce que les sénégalais sont conscient de la situation du pays. J'ai peur bilahi.
@ashourasylla79632 жыл бұрын
Moi oci
@layengom95082 жыл бұрын
Yalla na aldiana firdawsi di keurou noflayam ak bep waye dawlou ci barker seydina mouhamed psl
@binta48942 жыл бұрын
😭😭😭avec ses meurtres j'ai plus les mots yalah naka yalah yeureume 😭😭😭
@sophiesylla46332 жыл бұрын
Justice way 😭
@farylo48842 жыл бұрын
Médecin Sénégal khana gnom ay monstre lagnou 😡😡😡.
@djimegueye62572 жыл бұрын
Pourquoi les médecins ne respectent pas leur travail ? Svp démissionner vous ?
@AnouchaVividiallo2 жыл бұрын
Disons plutôt pourquoi les médecins ne nous respectent pas nous les pauvres Bobu batay d'égo beneu négligence Richard
@cissramatoulaye96112 жыл бұрын
Ay èmbèciles lagne rekk
@fatoudiouf83962 жыл бұрын
Chiim ay embecile laniou rek
@mbayangsow26732 жыл бұрын
Khaléyi am séni diplôme ligueye Moy deugdé
@adamaseck88162 жыл бұрын
Antouka metina trop me yalla guisna lepeu paix à son âme
@fallyaram74832 жыл бұрын
Toujours les pauvres 🤮 thieuy yalla 😭😭😭😭😭😭
@awadieng80982 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeureum te khare ko aldiana
@fatoubinetoudiallo31062 жыл бұрын
Journaliste bi aussi na deglou ohh Paix à son âme massa
@AnouchaVividiallo2 жыл бұрын
Legui d gniniu wara sauvé nioniuy Ray c'est désolant vraiment
@ecolepar38602 жыл бұрын
Pour une blessure à la jambe, un jeune meurt. Quelle négligence. JUSTICE POUR MAKHALY CISSE! JUSTICE POUR MAKHALY CISSE! JUSTICE POUR MAKHALY CISSE! JUSTICE POUR MAKHALY CISSE! Le médecin de THIES doit finir ses jours en prison: c'est un criminel avéré.
@khadimdiouf23552 жыл бұрын
Après ce qui s'est passé à Louga il faut faire un diagnostic approfondi pourquoi ce comportement si non on va tourné en rond et je pense que la prison n'est pas la solution
@mariediop92332 жыл бұрын
Repose en paix.amine yarabi
@SalimataGeuye-do6viАй бұрын
Ndessane yalla nako yalla yeureum
@mamesms35372 жыл бұрын
Cas d'urgence niouni hôpital fess na lolou kay moy né na deh sama yone nekoussi c vrement triste nioune badola yi founiou dieum wouyyy walo allahou akbar bour yar yallaguaniou may wer li merina trop que son âme repose en paix
@ablayefall22982 жыл бұрын
c'est triste vraiment Paix à son âme
@sylviesolangendione35232 жыл бұрын
Lignaw n'a que juste soit faite li doyna waar trop te gnaw😭😭😭yalnako yalla yerem
@zeynabniang52412 жыл бұрын
Paix à son âme
@khadygningue69372 жыл бұрын
😭😭gni douniou nitou dara Bilay comme douniou ay dioulite J’ai un cœur montri
@zeydi68262 жыл бұрын
Il faut commencer à les filmer
@fnoumbediop6902 жыл бұрын
Sénégal koufa fèbar yansi danger Y'all naniou Yalla soutoural😭
@lainadiop18462 жыл бұрын
Il faut porter plainte pour non assistance
@visionplus22152 жыл бұрын
Sans suite frr lay donne
@matykebe87142 жыл бұрын
Ohhhh Gni bonne nagnou li mettina trop yalla na khippe aldjana 🙏😭
@SokhnaMaiDieng-st1ex2 ай бұрын
No li yaguena Thies j suis d khombol mais Thies mome dè moko gueuneu gaw douniou ay mèdecin
@Aydashoutv2 жыл бұрын
Yalla nako yallah yeureume
@binetandiaye91622 жыл бұрын
hôpital bou fess thi cas urgence deukk bi yalnafi gueneu rek 😮😮😮
@diengrama69222 жыл бұрын
Thiey Sénégal 🥺🥺🥺🥺😭😭😭Yalla na souf oyof si kawam 😔🙏🏽
@oumoukhairyndir5 ай бұрын
Medecin yi gno geuneu sokhor fi
@bassirouka79712 жыл бұрын
Masa frère yalna yala maylene holou mougne tioname hame fici adouna metina loool sah hawma sibane réwe lagnou tolou diele PACA ref defko seni domou ndeye defko kome tangal mbip Di diame rek Di Ray rek te kenedouci wh baaahna 😭😭😭😭
@magy31132 жыл бұрын
Alhamndoulilah kép kou yalla may banga meune fadiou dji Europe dolile Sante.
@thintiouritra2 жыл бұрын
Ndeysan je travaillais la bas avant mon arrivée à l'étranger pourtant ya des bon médecins je ne sais pas maintenant mais c'est triste pour ce jeune homme
@mamitasow80192 жыл бұрын
Justice pour Makhaly Cissé 😥😥🥺🥺
@serignechekhounandiaye38352 жыл бұрын
Machalla journaliste nii lay mel😍😍
@YayouMouhamad2 жыл бұрын
lima diakhale moy Medecin yii loulénn dall temps yii sheuttt 😭
@fantabiaye58432 жыл бұрын
Repose en paix 😥 frère
@lapucedor2 жыл бұрын
Legui hopitaux yi c dangereux 😭😭
@ndayegueye53612 жыл бұрын
Bilaye lingaye wakhe khame nisi darra Mane mi Thiers la deuk hôpital regional nonou lagniou défe mes yala naléne yala yaye khôllou mougnie
@awapouyevoyante94654 ай бұрын
😭😭😭😭😭 ooooh ndeysane sa me rappelle le décès de mon grand frère même père et de même mère fofou la décédé régionale bou Thiès médecin yi kayy
@mamankhadythiam79142 жыл бұрын
Yallna nako yalla kharé aldiana té mayniou mouchh bou rafett
@عاليمحمدالجيد5 ай бұрын
Yaalana motalé ndawame aldiana❤❤❤
@muujambaaye93242 жыл бұрын
Liileep yalla laa
@bintasagna38822 жыл бұрын
Repose en paix frère
@aichababou26042 жыл бұрын
Paix à son âme 🙏🏻
@adjafallmory73162 жыл бұрын
Yalla nako Yalla yereume khare aldiana 😭😭😭 metina torop 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
@chitasall99422 жыл бұрын
Bouniou demmée ba keur docteur biniou wara fathieu Di niou deff djikkoy doomékhaaraam yii kouné wara tiite si doundam bilahi. Qu'il repose en paix
@ngagnedieng91632 жыл бұрын
Senegal dou rew Billahi Wallahi
@mamediarrasaliou52692 жыл бұрын
Waxatiko Yalla nagnou yalla sam
@AdjidabaTop8 күн бұрын
Yalla naco yalla yeureum té mu kharé co Aljanay firdawsi yalla yésal djégualam ak yeurmandém si kowom
@generalking17982 жыл бұрын
Ban rew lan nekk bilahi 😭😭😭😭😭niou mirite won li niou nekk skah bilahi 😭😭li dafa niew
@cissramatoulaye96112 жыл бұрын
😭😭😭😭 dama warou khawma sakh louma wara wakh
@binetandiaye91622 жыл бұрын
thieuy bi rew kou febar wala am urgence té amoh khaliss daguay dé amoul siki sakka 😢😢😢
@bachirlo13432 жыл бұрын
Ohh je ne reconnais plus mon pays vraiment😭😭
@mouhamedlam70832 жыл бұрын
bilahi fêkk délou wougnou dieufé li charia diguelé ta moy kou Ray gnou Ray la bougnou ko défoule raye gui dafay guene beuri rék wayé doufi diougué moukou
@omzoly32662 жыл бұрын
Non-assistance à personne en danger, il faut porter plainte.
@mamansene84822 жыл бұрын
Doul bayil ba ham
@moussaba2632 жыл бұрын
paix a son ame rék🤭 saraame Ndéye lii rékk opitale sénegale yeup yémm
@yacinegueyetahir94872 жыл бұрын
Dooomeraam deug deug laniou
@moussaba2632 жыл бұрын
@@yacinegueyetahir9487 wakhal dé gno réyy sama tata ospitale fann
@MameDiarraMariama4 ай бұрын
Bilahi lolene wakhal ko def hôpital Thiès Gno geuna bonne si adouna khamna gnou yobou mafa dagn ma Done raye bilahi
@maguettediouf4464Ай бұрын
Méttina trope yalna ko yalla yeureum té kharé ko aldiana bijahi Seydina Mouhamed psl
@rokhayakane56242 жыл бұрын
Ndeye sane yallanako yalla geureume
@moussaba2632 жыл бұрын
Tabaax ay stade té kou fébaar doo fathiou
@MaremeSarr-qi4mlКүн бұрын
Hôpital régional Thiès li guén ma def douma massa faté thi adouna bilahi 😢
@Onomar2 жыл бұрын
C’est qui ce gars qui console 🙄c’est comme ça que l’on console les gens . Yaw deih nianouma yallah nga consoler meu
@gogobarham53222 жыл бұрын
Ki retan ganye wakh
@Onomar2 жыл бұрын
@@gogobarham5322 oui c’est lui
@minafall87092 жыл бұрын
Mouy reitann melni Kou weroul
@myasow89292 жыл бұрын
Yalla nako yalla yeurm te kharéko aldiana 😭
@fatimafall54962 жыл бұрын
Bilahi Sénégal métina moytou daw ba raw sie Goro la bok yall bakhena😭😭
@lavista31042 жыл бұрын
Pensé à éduqué les populations ! Trop de violence inutile. Si il ne se serait pas battu Il ne serait pas mort
Alakhou akbar chaque jour ak kinouy ray tiey yalla kéne amoul li lane la aye gnoune fougnu dieum ak ray djou beuri dji chaque jour ak kinouy djame yalla nagnou yalla féke si mouthiou bou rafét kéne khamoul li loumu done méti na tiey sunu Sénégal 😭