C'est vraiment triste. Cette misère est insoutenable. J'ai mal au plus profond de moi même. Que Allah swt ait pitié de son âme et que firdawsy soit sa demeure éternelle.
@DiorDiengFall6 ай бұрын
Amine
@ndawlislam70216 ай бұрын
Amine
@awaSall-b2c6 ай бұрын
Metina😢massa meti lool c est très douloureux 😭😭je ne reconnais plus mon cher Sénégal des tueries a n en plus finir . Bilahi ki def lii yalnako yala nit🤲
@LafemasonhomSy6 ай бұрын
Amiine ta rabi
@mbakhengom74886 ай бұрын
Damay foot, 3000 par mois. Ndeyssane dans ces conditions une jeune femme veuve de surcroît.... certes la fille à son âge devait être à l'école, mais à l'impossible nul n'est tenu. Elle était obligée de travailler pour soutenir sa mère. Que le Bon Dieu éclaire cette situation.
@maguettendiaye81426 ай бұрын
3000 mille c'est la journée
@daisyba87406 ай бұрын
Je suis vraiment attristée des conditions de vie pour les enfants au Sénégal. J'espère que le meurtier de cette pauvre enfant sera retrouvé. Il faut que justice soit faite. Que dieu accueille cette pauvre enfant dans le plus céleste des paradis. Bon courage et toutes mes condoléances à la maman et à toute la famille. Reposes en paix petit ange 😭
@daisyba87406 ай бұрын
Amin yarabi. Reposes en paix petit ange 😢
@mariamadabo91006 ай бұрын
Aye waye Brom kounfaya koune diékhal niou li rew mi yalla yalla yeureum ko thi barque Mohamed
@doudouthiounelame8586 ай бұрын
Ki déf li yallanako yallah niit si barké seydouna mouhamed psl
@Soda-n1h6 ай бұрын
Ay Natou sa keur gou rey yaw ya ndieka ray khalé bi 😭😭khalé bou ndaw gna koy bayi keur wayé ki déf li yalnako yalla nite
@yayodiallo10216 ай бұрын
Ndeyane masta couco guisse rekk hamné maman bi sonou na ana bone volonté yi ana gniye def té yallah takh sans caméra filmer
@Salimata10006 ай бұрын
Faut instaurer la peine de mort dans ce pays...
@ousmanediallo37366 ай бұрын
Je la connais cette dame. On a fréquenté le même établissement à Mbacké.😢😢😢
@talladieng-rs6om5 ай бұрын
Yana ko yala yerem te khare ko aldiana amine amine yarabi
@dabaniang81416 ай бұрын
Ndeysane yalla na motelè ndawam thi aldiana fir dawsi thi barkhè seydina Mouhamed psl 🤲🤲
@astoufall4295 ай бұрын
Metina trop bilaye jai des larmes 😢😢😢😢 metina looôol😢 justice svp
@AidaDiop-bi5uj5 ай бұрын
C'est triste ki déf li yalanako yalla nit😭
@WaxElegeance6 ай бұрын
Elle n'avait pas l'âge de travailler je pense. A cet âge elle devait être encadrer encore un bon moment. Courage à la famille. Yala nako yala leral
@daisyba87406 ай бұрын
Je valide à 200%
@AstouGueye-mq2tf6 ай бұрын
🎉 0ô Pop😊 😊😊p
@lapucedor6 ай бұрын
Lolou Deugu la mais aussi Ndeyesane niak moyens rek khamna 😢
@adamadiobembengue88386 ай бұрын
Sa waye es ce que khame nga loutakh moudone liguéye boul yaakar ni diiéke nga niépa diéke
@nogayeseye8266 ай бұрын
Lolou yep deugue leuh mais taxoul ki deff lih warko deff Boufa fekone kénéne aussi nih lay démé
@salihate-ew6wy6 ай бұрын
Ndeysane 🙌🙌🙌🙌🙌 yalla nako Yalla kharé aldiana firdawsi 🙌
Travailler avant minimum 16 ans devrait être interdit par la lois sénégalaise.
@Liliane81106 ай бұрын
Massa c triste 😢 paix à son âme 🙏🏾
@adiadieng12916 ай бұрын
13 ans aussi on le laisse toute seule à la maison 🏠 c’est pas normal 😢😢 sa place était à l’école . Il faut surveiller les enfants que firdawse soit sa demeure éternelle
Triste je me souviens de cette histoire c'est très dur. Yallah nako yallh nite
@Fatimagueye8686 ай бұрын
Ndeysan yallna ko yalla yereme😢
@fatoundiaye92346 ай бұрын
Peut-être mou nèke sathie wala kouko beguone violé yalla nako yalla nite 😢😢
@DiorDiengFall6 ай бұрын
Amine
@Fatimagueye8686 ай бұрын
Amine
@SENEGALBOY126 ай бұрын
Ndesane metina masa Wayè dèlène same Xalèyi Yallah na motali Ndawame Dianatul Firdawsi Amiine
@NdeyeCoumba-x3f5 ай бұрын
Yalla naco yalla kharé aldiana Monk niam fa fék gnep 🙏🙏
@lasmc1986 ай бұрын
Massa mère que son âme repose en paix 😢😢😢
@mamediarrambow71106 ай бұрын
Li dè bima ko sètanè dama amone lima mèti 😢pour Mane justice deff na liguèyame 😢😢😢nakaté batay 😢😢😢
@fatoulo20686 ай бұрын
Li yaguena batay nonou 😢😢
@Galsn5 ай бұрын
Paka bi si khalé bi lanouko fék kay warnaneko diapou doyna war
@ndeyediop286 ай бұрын
Mettina lole yalla na yeguali nawame si aldiana firdawsi
@daisyba87406 ай бұрын
Amin yarabi. Reposes en paix petit ange 😢
@mariesec8246 ай бұрын
Vraiment xalé bou touti thi wétou yayam la wara nék. Métina lol wayé mouy mboki amie mouy yaw mikoy liguéye lo yépeu fauté. Naka ngua meuneu dioxé xalé bou am 13 ay instructions pr gérer keur en tant que formatrice de jeunes 😢. L'état doit interdire le travail des jeunes et appliquer des sanctions aux employeurs 😢
@daisyba87406 ай бұрын
Je suis d'accord avec vous. À cet âge là, la place de l'enfant est à l'école. L' école doit être obligatoire au moins jusqu'à la majorité et le travail des enfants doit être interdit. La femme qui a embauché cette pauvre petite fille, n'aurait jamais dû accepter de l'embaucher parceque qu'elle même n'aurait jamais envoyé ses enfants travailler en temps que mineurs. Dure, dure la condition des enfants au Sénégal. Il ne faut pas oublier que les enfants sont l'avenir d'un pays, donc protégeons les et donnons leur le moyen de réussir dans la vie. J'espère que le meurtier sera retrouvé et que justice soit faite. Reposes en paix petit ange 😢. Courage à ta maman et à toute ta famille. Que dieu t'accueille dans le meilleur des paradis. Amin yarabi 🙏.
@aminasall90466 ай бұрын
Et si sa mére n a pas de moyen pour l'envoyer à l' école
@mariesec8246 ай бұрын
@@aminasall9046 mou andak domam di fauti comme fautt katt leu wayé 13ans xalé meunoutié yoré keur
@SalyNdiaye-ef9su6 ай бұрын
Yalla nako yalla yeureum hareko aldiana firdawsi
@daisyba87406 ай бұрын
Amin yarabi. J'espère que le meurtier sera retrouvé et que justice sera faite. Reposes en paix petit ange 😢
@matythiaw256 ай бұрын
Ohhhhh li mettina ba fou metti yem Ndeysaan Yallah na Yallah nitt te TakhaWou leen
@mamerokhayadiagne43204 ай бұрын
Innalillahi wa inna ileyhi rajioune yalnako yalla yereum té diégueulko
@RP-wb5ig6 ай бұрын
Nous reclamons la peine se mort. C'est le seul mouen de lutter contre les crime. La loi Divine nous protégera de tout mal
@altesseroyale43836 ай бұрын
Li ma guena diakhale ci Sénégal moye boudé wakhi goordjiguène gnèpe diogue takhaw di wakh di menacer gadou guebeur sokh fitale dasse diassi ni danouye khékh birou goordjiguène, mais boudé affaires agresseurs yi ak raykatou niit gni gnèpe ni tèk ni dara khéwoul! Sénégal sofe nguène ma nak! Dieureu dieuf Yallah Bour ba ma bokatoul si momou réweu!
@diopmareme37526 ай бұрын
Sa commantaire bi louss na déj
@altesseroyale43836 ай бұрын
@@diopmareme3752 dara louche chou ci, Li ame rèk la wakh! Gnou diape khalé bou djiguène bou 13 ans raye ci mali foro, réaction population bi zéro! Kone raye niit dale bakh na! Fou gnou rayé niit bébé yeungou dou ame kène dou organiser wou ni li nanou khèkh mou diok fi! Lou doule kouné di khèli sa café nane ko tek tia nako yallah yeureume. Bou gnou né béne goordjiguène na nga fé gnèpe diok. Talakh talakh dji ak yorokh dji méle ni tokh sou beune sagne ba rèère! Lou waral lolou? Kouye khèkh lou bone lou bone lèèp ngaye khèkh! Lolou moye défar réweu! Wayé khékh bi bayi bé dou foula dou fayda! Mbadou ci raye kat yi nga boka? Sa affaires lèèroul! DIC warna def enquête ci saye biir!
Yaw niépa la tané yaw mi bolétoul sa bopp thi réw mi😢 au moins quelle que soit la situation nioune douniou meusseu béddi sénégalais. Patriotes à vie ak fougnou meunti nekk sur cette planète terre
@ndongolo91506 ай бұрын
Ray AK agression lolou ligeyou Yon la police AK gendarmerie mais gordjigen ligeyou population la nieupou Ko wara ngéx mou diougé fi 😢
@maguettendiaye81426 ай бұрын
Oh c'est triste paix à son âme
@thiendellafall25066 ай бұрын
C'est vraiment triste et douloureux. Ma compassion aux parents et paix à l'âme de la disparu. Mais, il y a lieu de rappeler à tous les parents EUR responsabilité envers leurs enfants. Comment peut-on laisser une petite fille de 13 ans seule à la maison.
@koeurFatou6 ай бұрын
le tueur connaît la petite et avait l’habitude de fréquenter la maison
@fatimadia95486 ай бұрын
Le tueur est un proche de la famille ou quelqu'un qui connait la famille de là ou elle travaillait!
@AnouchaVividiallo6 ай бұрын
C'est tres dure de perdre un enfant 😢
@mariesouare30426 ай бұрын
Quelle tristesse une gamine de 13 ans comment la famille et la patronne peuvent faire travailler une mineure de 13 ans ??? Y’a un vrais manque de responsabilité des deux cotés 😡😡
@fatoujoof20936 ай бұрын
May her soul rest in perfect peace Amin yarabi yallahou
@coulibalyyacine62316 ай бұрын
Yalla nako Yalla yeureum
@LafemasonhomSy6 ай бұрын
Mom puisk mo ndieuk kheuy xalebi té ken nekoul ci keur gui khana dafako diokhone tiabi mo oubil bopam
@adamandione61736 ай бұрын
Doomou patron bi nék internat nagne ko enquête, khalé yi danioo say say
@serignegueye45796 ай бұрын
L'assassin ne doit pas être libre il est plus mem dangereux que ino et Alex svp si vous l'arrêté pas il fera d'autre crime 😢😢😢😢😢
@daisyba87406 ай бұрын
Je valide à 200%. J'espère que l'assacin sera retrouvé et que justice sera faite. Reposes en paix petit ange 😢
@fatoujoof20936 ай бұрын
This is very mamma may the Almigjhty Allah protect and guide you and the entire family Amin yarabi yallahou 🙏🙏🙏
@LafemasonhomSy6 ай бұрын
Lou metti ndeyssane foot 3000 ak nimou mettè yalna yalla takhawou len
@almaktoumdiop87496 ай бұрын
Wor namani kiko dof daf ko sakou mou khaméko mo takh mou raye ko mé touba dale nilanoukoye bayé yalla nanou yalla maye djitou réw mou geumoul béna tarikha dakh mou ték sénégal si yone si deugeu di raye ay khalè di violé ay khalé rék té fougñou wakhé gñouname touba deukou serigne touba bala serigne touba khamoul lou gñiaw dik léwouko
@naboujadieng6276 ай бұрын
Thiès Mo eupe ay meurtre fouf , surtout fanyi AK séne cas wou diakartamane yoyou lidieunti léne lolou. Fép am ay niawtéf et pourtant deukou el Hadji Malick Sy la et pourtant digléwoul Lou niaw. Kone yeufi Dou deuk Thi nite gnifa rakh la. Thiès tamite ni nignou léne Di bayi?
@fatougaye48086 ай бұрын
Mais histoire bi yague n’a ça fait des années
@Youngthehustler6 ай бұрын
Billlahi ligua wakh deugu'leu et c'est écoeurant 😢
@YayeAwaGUEYE-ci2hx6 ай бұрын
Tu as vu au Sénégal une seule ville où il n y a pas de meurtre ? Arrêtez avec vos jugements a la va vite. Li lane lathi tarikha déf. Règles tes PB perso avec Touba mo gueuneu
@YayeAwaGUEYE-ci2hx6 ай бұрын
Serigne Touba nak môme kouko nangoul ak kouko nangouwoul yeep khamngani khawoul Lou niaw meussou KO def ta diglé wouko. Ta lolo âme ta kouy ndoundou dingako déég kanam la dieum
@mariemendiaye39216 ай бұрын
Paix à son âme que dieu l'accueille dans son paradis firdawsi
@KhadimDramé-d9e6 ай бұрын
Yalla nako Yalla souhaanahou watahaalaa yeureumko té khaaréko Al diannatoul firdaws sibarké Seyidil Mourssaline (SAW)
@ousmanediallo37366 ай бұрын
😢😢😢😢 triste pour Matou...
@astouseck36486 ай бұрын
Métina yalla nako yalla yeureum te haré ko aldiana firdawsi
@fatoundiaye92346 ай бұрын
Métina trop paix à son âme 😢😢😢
@fatoujoof20936 ай бұрын
Is there any low in senegal this woman need justice in senegal
@mariamademe6 ай бұрын
Paix à son âme 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
@bourymohamed-wf8lh6 ай бұрын
Inalylahi wa ina ileyhi rajaon yalna yalla yereum co oyafal souf si kowam firdawsi done dekouwayam may ay mbokam xolou mougne Ki def li yalnaco yalla nit
Stp Kou ame numero natou ki dieulone khaley bi mouy liguey envoyemako message
@serignendiayebeuguefallou70886 ай бұрын
Yalla yeureum ko amine way métina trop bilahi
@nogayeseye8266 ай бұрын
Bilay dina fégne maman sou fégnoul fih dina fégne feulé Yalla nako yalla wérr fi si adina Yalla xaré xalibi aldiana
@beatricendoye18006 ай бұрын
😭😭😭😭😓bilahii lii waar na fi diex😢
@samaxalaat236 ай бұрын
Yallna matali ndawam aldiana
@LafemasonhomSy6 ай бұрын
D'après li badien bi wakh say say bou gneuw ci keur ga leu ba paré diamko
@DieynabaDiop-s1r6 ай бұрын
Yalna xipe aldiana firdawsi si barké seydina mouhammed psl
@ZeynaDiouf-b5f6 ай бұрын
Yalla nako yalla yereum harel KO aldiana firdawsi 🙏🏽
@amygueye38826 ай бұрын
Non sou fek Violet amna Di fenge biu anket bi khote😢
@antanian55746 ай бұрын
Li yagu na ba taye khamougno kouka raye
@belleduteteaupied13936 ай бұрын
😢😢😢hooo conne djapougn ki def batayy li gnaw naa bilahii
@fatousagna39816 ай бұрын
Yalla nako suniu borom haré aldiana
@BambaNdiaye-ub2ce6 ай бұрын
Alahou akbar yalla rekay bour waayé yalna sunu borom diokhak lou geuneu kawé sa ndiortou metina loll wallhai lii dafa yombou loll bilay
@MarietouFayeAmadouneNdiaye6 ай бұрын
La maison est si grande pour laisser seule une petite gamine
@playa44016 ай бұрын
Allah apaise votre souffrance
@Ibou-rg7vr6 ай бұрын
Walahi bou ñenko yobou won Dakar dina dou ndate médecin touba yii ayoun bilahi
@MarieHelenDiouf6 ай бұрын
Paix à son ame 😢😢😢😢😢
@maguettebeye10336 ай бұрын
13 elle devait pas travailler, sa place était à l'école et en plus comment on peut laisser un enfant de 13 ans seul à la maison. Aldiana di keureum.
@badarafall97526 ай бұрын
Khalé bou am 130ans nioukaye liguaiye lo parceque dagua doundoule toumranké raik motah ya des centaine de famill yo hamné laikuniou dou aagn dou raire
@fatimadia95486 ай бұрын
Mere bi ko djieul ligueuy kou kate ndayam leu..khalè bou tolni noko meun djieulè pour mou laye ligueyeul si keur guou magguè nii
@OumySeck-b5v6 ай бұрын
Yalla nako yalla nite té kharé ko aldiana
@AstouNdiaye-v5q6 ай бұрын
Tu ne devrais pas employer une petite de 13 ans c'est pas mormal de laisser une petite seule être gardienne et bonne. À tout faire
@maimounadatt73346 ай бұрын
Aaay waay Li metina deh
@seuneba70916 ай бұрын
They Sénégal
@layebah54006 ай бұрын
Soutien de famille à 13 ans
@diariabousso4666 ай бұрын
Comprendrouma dé feuguenga oubiwoul nga feugate wiri tidjiwoul nga wiriwate guiss mou tidiékou ame lumiere kouko tidji sa guinaw kou goor kinga tassél wala😢
@ramafall19016 ай бұрын
Li yaguana dee dou Lou bess
@Oumanas59956 ай бұрын
Wawaw j'avais entendu ça celle qui racontait l'histoire même avais qu'il a vue quelqu'un courir
@bellawomen6 ай бұрын
C’était 2021
@Youngthehustler6 ай бұрын
On sait mais on était pas au courant et de plus justice n'est pas encore faite
@Youngthehustler6 ай бұрын
@UCGKmXO1eq8rU9otpucC9lLw non 2022
@MarieDia-ls5vq6 ай бұрын
Mane. Dee. Warouna
@MarieDia-ls5vq6 ай бұрын
Khamougnou. Kouko. Rey. Waye. Yala. Khamnako
@MarieDia-ls5vq6 ай бұрын
Ompou. Nanou. Waye. Yala. Khamna. Ko
@kalsoumsenegal6 ай бұрын
Bilay waxal yalla n'a borom bi fenal li metina
@amygueye38826 ай бұрын
Yeude yeurem moko geune loutakhe khamoulene 13 anne Touba amounou dole Di ligeuy
@albourryndiaye6 ай бұрын
Solén ko guisé rkk raylén ndeyam 😭
@habymamadousakho78156 ай бұрын
Pas d'enquêtes ni rien ndeyssane néew dolé reck ki def xamna keur gui bou baakh non a l'exploitation des enfants
@awandoye78106 ай бұрын
Khalei 13 ans tamite dagn KO warasurveiller deuk bi wauroul
@awasaliouba84205 ай бұрын
Le numéro de sa mère svp pour l’aider
@amsatoukounta69756 ай бұрын
Que la terre lui soit légère et que Dieu mette la lumière sur sa mort
@zahrafatima13956 ай бұрын
YAllah né kou reye naniou la raye niouni det douniou ko déf athia rek cette situation c répéter après 3ans même fait yi même lieux subhanallah k firdaws soit sa demeure éternelle kou déf Li yAllah nako yAllah nite tè niou appliqué kou raye niou raye la
@ramasagna42926 ай бұрын
Quelle ministre! Pensez-vous mme la ministre des femmes su 1 mur au senegal peux assurer une réelle sécurité ?...le Sénégal comme beaucoup de pays africains doivent davantager s appliquer sur l education, la santé, l insertion , une réelle justice, et surtout des services publics avec des moyens.
@leebouchic9046 ай бұрын
Yena wara bayi khalai yi guene di yobou gnou mbindanou au lieu des les amener à ecole thim la place de l enfant c est à l ecole
@NdeyeSall-pb1ck6 ай бұрын
Wa president lomouy khar actions yi niou wara regler senegal beurina
@fatimadia95486 ай бұрын
Li 2022 leu
@NdeyeSall-pb1ck6 ай бұрын
@@fatimadia9548 baker. Et alors quel est le rapport sur Mon commentaire .Rey nitt 2019 akh 1980 mo si yam senegal mougui nono rek
@MarieDia-ls5vq6 ай бұрын
Massa. Yaye. Boy
@ndeyekhadyniang71196 ай бұрын
AYWAY DÉFFALE LÉNEMA QUÉTE POUR MA AME PASSE QUITTER SÉNÉGAL NAKH MEURTRE AGRESSION TITALE NAMA.