19:07 N'ako fassé t'es mou dème sy Serigne bou bakh mou khol lou nek sy yaram by baparé mou tak kénéne
@marietoudiedhiou95824 ай бұрын
Boul ko fassé.Togal khaar ba mom si boppam niagn sila bat. Mais aussi avant tout ,fait des prières pour qu'Allah puisse t'éloigner des mauvais esprits.Quant à tes enfants il faut les prendre soin . Que Allah te protège
@antaseck73094 ай бұрын
Nako fasse rek, Yalla diékhoul natou la rek🙏🙏
@Xippill4 ай бұрын
Essaye d’abord de te réconcilier avec ta femme si elle veut pas lache l’affaire après mais avant de reprendre une autre femme purifie toi tu as peut être des raps qui font fuir les femmes je ne sais pas le problème vient de toi je ne sais donne toi le temps de savoir d’où vient ton problème bon courage yalla nala yalla diapale talhawoula Fatou sognane toujours au top machalla xippillxoles
@AbcAbc-wy5qb4 ай бұрын
Mdr t’es ouf essayer wou lane
@aissatoudiop87054 ай бұрын
Salam Salam, pourquoi ils ne peuvent pas demander à la femme pourquoi elle est partie ?
@mariemendy-qf3kz4 ай бұрын
Il doit pas lui demander pourquoi elle est partie parce que pour moi s'il y a quelque chose qui dérange elle doit parler à son mari avant de partir
@alvinepausini48634 ай бұрын
Way nako fassè point barre
@awandiaye53604 ай бұрын
Salam nako fassé mo geune té en plus défouko dara, elle est partie de son plein grés, avec des parents irresponsables
@ElhadjiSarr-in1lr4 ай бұрын
Salam nako fassé wayé 😭😭
@OumyOumy-m6c3 ай бұрын
Ndeysane amoule chance si dieguenne
@DjilyDiallo-u4l4 ай бұрын
bilae nako facé😭
@KhadidiatouDabo-zp4eq4 ай бұрын
Kokou deh respecter would dieukeur dji nala leer ni soko dieulssé elle fera pire la prochaine fois bouko fasser bayiko nonou nek thi lenen gua takkk kenen c tt
@lionelione-zd7oq4 ай бұрын
Fasse koi waye ahh
@kingniass94654 ай бұрын
Mashalla 🙏 Amna Solo
@AbdoulayeNiang-um3rj4 ай бұрын
Bonjour Fatou❤❤
@CheikhSow-q6s4 ай бұрын
Pabi mo niak dîné ak fayda
@mariamafaye77804 ай бұрын
Salam salam bala mouko fassé na kholle bakham yobouwoul keuytou keur mon geuneu wor ya salam😮😮
@OmarNdiaye-ny3lj4 ай бұрын
Yaw mi di nga massa sopalikou café dh bakhna rék😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@MameAntaGaye-i3i4 ай бұрын
Pourquoi 😂😂
@isidorememdy53684 ай бұрын
Nako fassé ki dou seykate
@leyebamba50854 ай бұрын
Khamnané Famme bi dale amoute kilifa té djiguêne panrents you mate kilifa dafthie bakhe manenake doumanéla fasséko doumanéla bouko fassê kholale sakhéle boubakhe rék mais kilabague té yalla takhe kokou mogene thi seye
@AliouCisse-x5d4 ай бұрын
Doyna warr deh
@mustaphasaine59474 ай бұрын
Bulko fase utal benen
@TeranceMane-zb6ed4 ай бұрын
Nako fassé moudiekh
@AbdouleSow-q2e4 ай бұрын
Naka fase mouwouti kenen
@moussajuncu22974 ай бұрын
Bonjour cava
@MbayeMaman-wu6rw4 ай бұрын
CV tata Fatou nama takh man
@extremeownership52234 ай бұрын
@@MbayeMaman-wu6rw Kay ma takk la
@MbayeMaman-wu6rw4 ай бұрын
😅😅Wawaw mou gaw
@allediouf12864 ай бұрын
Un conseil il ne faut pas demandé en premier le divorce.y'a quelque chose qui se cache derrière
@astoumaguettesissokho324 ай бұрын
Femme bi nobouko motah muy déf louko nekh djiguéne yi dagnuy douguou si séy té dougnou sentir kignou nékal a la longue dagnuy bari djiko nako bayi déssék Yalla té mou dieul temps touti avant muy takat kénén listiharko mo guene
@taphadione72784 ай бұрын
Nako fassé diap thi yalla
@kharycisse52674 ай бұрын
Bala mougne takate na khol yaramam mane ak mome nio niro cas divorcée na deux fois té douma kham lou takh yémé touma seye
@FatouKamissokho4 ай бұрын
Nako facé amagoule diabarame
@mameaissatougoudiaby89514 ай бұрын
Facéko nak gnata wére faléwoula nak khamo ndakh dafa eumbe beugue gneuw pour né ya diour dome dji wayé bossi beugué douguate xolale boubakh nak car c louche
@DiaDan-z3r4 ай бұрын
Balaa fasé na xool lu ay mbirëm baxam luy dox diganteem aki doxnaam jërëjëf
@dembambaye76364 ай бұрын
Non Fam bi mo bayil Nonou rk
@zizouzidane73324 ай бұрын
sa waye sokhna sou bonne ah dent bouy méti niom yém boudi sani rék
@Findamamad4 ай бұрын
Bonjour fatou
@CheikhSow-q6s4 ай бұрын
Naco fâché sinon El répète la même chose
@wanealpha19654 ай бұрын
Nakho bayi fofou mou yakh benen diabar
@RouguiDiop-e5b4 ай бұрын
Soka fassé tamite takate kénen day dém rec so yabo fadiou ba paré
@CheikhSow-q6s4 ай бұрын
Amone chancna niow ma mayko soxna
@mamadoumareme98493 ай бұрын
Goor bo khamni sa yoye takk diabar sa kharite molako maye tu prends jamais tes responsabilités Mola dioural problèmes yi yeup
@aissambaye62944 ай бұрын
Nako fassé
@BinetaMbengue-vc7bu4 ай бұрын
Dieguene yi barina na takate kenene niap yamou nie deguale Lila sa karite bi wak
@papamardrame14674 ай бұрын
Le père est un irresponsable... Apparemment la femme ne veut plus du mariage,elle n'a qu'à demander le divorce.Le gars doit aller chercher ailleurs et relouer la maison,encore que les moyens font défaut.
@diopyakhamelaye4 ай бұрын
YALE NAKO YALLAH MAYE KU BAH KYE SEYE TA YALLAH TAKH
@AissatouFaye-nj7gn4 ай бұрын
Fasseko
@mamadoumareme98493 ай бұрын
Fassé ko amoul khalate Kokou beugoula respecter woula
@MariemeNdiaye-e8u2 ай бұрын
Yehdkfir 🎉
@RouguiDiop-e5b4 ай бұрын
Daga ame guélou rap moy dak sa ay diabar
@DIAOMamadi4 ай бұрын
Na holaate birum boppam avant tout parce que les deux femmes niep munula bangne y'a quelle que chose...
@ndiayeassane1174 ай бұрын
Bayico mou deme ngua contine sa ligueye ba guisse cou khamene yacco tanale sa boppe Basse bocco djelle tu veras le pire Elle vous a annonce la couleur Djegale deme ligueyi
@KarimCoulibaly-hx3ph4 ай бұрын
Naco bayi ndah ki bayam matoul kilifa motah femme bi amoule yar
@khadimsaw92484 ай бұрын
Est ce que wadji amoul gélou rab
@BinetaDiallo-v8l4 ай бұрын
Nako fasè beugouko
@diopyakhamelaye4 ай бұрын
WA FAMME BI NEKK CI PHOTO BI 4 LOKHO LA AME
@NénéamiCamara-z9y4 ай бұрын
Regarde bien niarii lokho la yorr béné sac bi si colle bi lako take
@mamadoundiaye76804 ай бұрын
Seuy bobou dou dem nasi geunn
@fatousow944 ай бұрын
Kéen dou wakh nitt fassél sa sokhna wayé li ram ci niague bi la dieum boumou ko fassé nako bayi thia keureum dém taki bénéne diabar souko indi waté ci keureum ndawsi dinako défat lou gueneu piir souko bayé fofou bou sonné dina wakh limou beug