Boul nangou kene tékk la stress bou sey bii bakhoul taxal té khar yalla bakhna..sokhna Fatou sa tress yi rafette na machallah amal diam ak salam.
@SokhnaKeita15 күн бұрын
Dieukeur boula diokhati 1000 dépense togualko gnankatank ak beguedj😂😂😂 qui es d accord
@ssbusiness-yp8lf16 күн бұрын
Soxna Fatou les tresses te va super bien ,faut arrêter les perruques 😂❤
@wanealpha196515 күн бұрын
Thiey yallah allahu akbar
@mariamafaye778016 күн бұрын
Beugue d'éret ba melni vampire😢😢
@taphadieng52029 күн бұрын
@@mariamafaye7780 vampire kay😂😂😂😂😂
@diariabousso46616 күн бұрын
Ndeye del Nouyou sama Mame Tabara Diène depuis Pikine Taly bou mak , mak la dou guiss , dou dokh Bilahi wayè yow rek lay deglou mom motakh ma khamla sama badiene mokoko dane tègal moudiou gui mou accro si . Bo wakhè mounila tegal ma Ndeye Fatou Barkè Seydina Mouhamed yow ya takh niou outal ko tactile simple la yarone mais dafa sonal nite gni kouko rombou mounila ani sa telephone diapal Ma Ndeye Fatou dangay beugue guène mou concentrer wou niou outal ko bène. Bilahi yow yaye wètalam ❤
@ElhadjThiam-p7x16 күн бұрын
Salut sokhna Fatou Elhadj Thiam Atlanta diamono métina yalla nalene yalla takhawou
@jarieujallow859515 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤
@boundawbeye61216 күн бұрын
Dég pir❤❤❤
@AlexSyla15 күн бұрын
Thiéy sokhna fatou
@antaseck730911 күн бұрын
Sa yaay sakh ngako warona wakh bou yague sakh tass seuy bi Yalla rek mofi nekk
@sokhnalo333415 күн бұрын
Tasal té gua wakh deug by sa yaye sa diekeur néko boma siwalé manila gor djigéne gua dinala bayi
@diariabousso46616 күн бұрын
Hi Ndeye dafa alou taye😂
@deraousseynou253616 күн бұрын
Les conseils de Fatou doye na seuk❤❤
@mamadougueyefaye754312 күн бұрын
Nathi guen dem yonam yallah bakhna .mom wadji est ce que laloul yenen djiguen yimou takkoul
@Éléonore-c1h15 күн бұрын
❤
@AssaneGueye-v6f16 күн бұрын
🎉🎉🎉
@wanealpha196515 күн бұрын
Dalay nako rek
@aliounbtoure801816 күн бұрын
Deuk bokhamni kene mousoulafa teudé mounoufa yakh sa dere banene bi neko limoulay accusé Dina Andi Kamil gnou wate souko anoul nala may diam wala mou bayila
@allediouf128616 күн бұрын
Dieu est le seul témoin.ne vous laisse pas manupuler
@BeugNaby24412 күн бұрын
Tassal sous nguéne togué nga dieul kamine wate si yalla ni mousso moy yalla après mou dieh tak où est le mal hamouma loutahh gorgni sokhor boul doundou li sa yay doundou jamais
@boundawbeye61216 күн бұрын
Dafa am home you soff bilaye sohkna Fatou wakhga dégeu bilahi
@naboukharitouyayamniangbal792116 күн бұрын
Ame yalla yalla boure niakeu yalla yalla bour boufa togué daye gouwatre wala cancer il faut prendre tes responsabilité c'est mieux
@thiernondiaye197516 күн бұрын
Kouy déglou conseil Si réseau sociaux Kou alkou gua
@naboukharitouyayamniangbal792116 күн бұрын
@@thiernondiaye1975 yaw singa bocou premier alkou yawla
@naboukharitouyayamniangbal792116 күн бұрын
@Abdourahmanendiaye005 j'ai abonné
@cissemamadou127415 күн бұрын
Ame yalla niak yalla so beugue dosihol ne amena naw wala amoul seul te yalla takh mosi amsolo
@abdoulalayeba449616 күн бұрын
Na tass dem khar sounou borom
@Mayvabane15 күн бұрын
Divorce et travaille
@FamaNIANG-ns6dr15 күн бұрын
Parle à ta mère, dis lui la vérité, pour le reste écoute les conseils de Sokhna Fatou
@mookhadiaks730116 күн бұрын
mafi djitou
@Awakanteh-u3i16 күн бұрын
Tassal nga dem fenen outi ligaye Wala ngai jai di dimbaleh sa yai moogen.
@AbdallahRashid-y9f15 күн бұрын
Uum
@AbdallahRashid-y9f15 күн бұрын
Hum
@Awakanteh-u3i15 күн бұрын
@@AbdallahRashid-y9f Luhew?
@AbdallahRashid-y9f15 күн бұрын
@@Awakanteh-u3i pourquoi tassal ?
@Awakanteh-u3i15 күн бұрын
@@AbdallahRashid-y9f Mu am jamm ndahh seiye du njaam.
@souleymanendiaye796316 күн бұрын
Khana wadji baalou ko ba paré non adina con na lol
@wanealpha196515 күн бұрын
Tasal
@afounasabaly281416 күн бұрын
Demal sa yone defa dof rehk, virginité veu pas dire une bonne femme,il va le regretter