Na mûgne rék yalla bakhna té yalla guisna lépp.. sokhna Fatou sa liguey rafette na merci.
@Xippill5 күн бұрын
Lou yalla toudou thi sa adina meunoulo thi dara daf laye niakal fayda dafa infidèle moytoul mou walela febar hé tu es une femme bien digua ame kou bakh inchalla comme toi geum gua yalla wolouko yalla rek mofi nek te lo ragal yalla bayila ak lolou sa borom keur meunafi bayi sa meilleure amie djiguen gni bari nagnou il ne mérite pas que tu verses une goutte de larmes bon courage force à toi suit moi sur KZbin tape xippill
@hfhgg-bm2to4 күн бұрын
Non fatou nekguama boumôu tass na togue Sénégal 🇸🇳 nityi mounouniou supporter kou tass mais wakalak sa karite gua wak ko yegue lep so pare continue say te mougne te boulene fale degloule fatou limou wak deuguela boule naguou ken di yak sa adouna
@ElhadjThiam-p7x5 күн бұрын
Salut sokhna Fatou Elhadj Thiam Atlanta ligueye bi machalla
@MamanTavares4 күн бұрын
Ne divors jamais
@Éléonore-c1h5 күн бұрын
❤
@NdeyesokhnaNdir-x3z3 күн бұрын
Sokhna fatou sa poudre dé ka wayi bokk mais machallah sa tresse yi nice na
@ballacoulibaly19564 күн бұрын
Qu'elle rencontre sa meilleure amie pour la confronter.Courage et bonne chance
@MaguatteSall-z9r3 күн бұрын
Karite amoul dh bilahi💔😭🗯😭💔🙏
@boundawbeye6125 күн бұрын
Salam Salam sokhna Fatou mom mo Wario wo ndewsi djiokh ko djié Geurdji pa miyi djohké numéro
@SerigneNiang-y9lКүн бұрын
Billahi niit mon leundam 😭😭😭 Maman Bi gnou toll sa lokho ndidior sakh diaroul wau Lou 💔💔💔 Loumou métti métti déllol sa xel si yalla sounou brome RK té bagna waulou kéne
@evadra9765 күн бұрын
Souparé sisa meilleure amie bi sisa khalé bobou lay dem
@dand16955 күн бұрын
Det sohkna sy dou goor ye yep de
@aissatoungom91355 күн бұрын
Nako Tass kayy ki da infidèle 😅😅
@abdoulayendiaye10153 күн бұрын
NAWAKH AK KHARITE BY
@altesseroyale43834 күн бұрын
Gorou dokhane kat you eupe yi, diarou gno seuyeul! Dalaye sonale, bo ci togué di nga sone torokh! Tassale bi seuye légui, affronter sa soit-disant kharite bobou baparé couper ko à vie! Wadio diou dou mome rèk mofiye goor! Sa juments mbok yoyou bolène topé do réaliser dara! Mane aye mbok faléwou malène! Dou nou diarigne dara ba paré beugue la fatte! Wouteule sa liguèye mou occuper la nga ndiarignou ci ba kérok nga guisse kou bakh, dieukeur ri ndialo kateyi danouye teudji weurdeuk eundil la aye maladies sexuellement transmises! Lakhawla niit kou bone!
@souleymanendiaye79635 күн бұрын
Na wakh ak kharit bi tê mou khamal ko ni yeuk lèp dako bayiwone ci biir réck
@Générale-3135 күн бұрын
Sokhna fatou sopp bakhoule
@abdoulalayeba44965 күн бұрын
Tass rek dem blamola walle febar
@AmadouLeigh-c3tКүн бұрын
SALAM she is the one who put herself in problem she should have just called her friend and give it to her husband the next thing let her listen to what madam fatou has said
@mookhadiaks73015 күн бұрын
mafi djitou
@wanealpha19654 күн бұрын
Namougne
@mookhadiaks73014 күн бұрын
bo tassé sa meilleure xarite dieule sa place
@FataGass5 күн бұрын
Yaw d'elle wakhe deuge mo nekh yalla boulle wkhati boudê deuge mo n3kh yalla