Oustaz fofu âme na séww séww boufa nék suba ak heuram yalla nagnou yalla nangouk sounou diamou yalla🙏🙏🙏
@fatoudiouf55492 ай бұрын
Djiazakalahou khairane ya oustaz, moi les mosquées sont un peut loins de chez moi, mais chaque fadiar je fais 19 izadiaha après mà def souba
@ousmanediedhiou24703 ай бұрын
MASHA ALLAH OUSTAZ DIEUREDIEUF, YEN MI XAM YEN A WAR DI WAX.
@goubebousso40163 ай бұрын
Ouï merci beaucoup oustaz 😮🎉❤😊merci beaucoup
@hassan2diop6422 ай бұрын
Macha Allah ❤❤❤ Dieureudieuf Ya Oustaze !
@LahadGaye-b3o2 ай бұрын
Machallah amna solo mangi ñaan Sénégal yi nañ wormal kii daa wara leéral li lënt ci islam❤
@IbaDia-m1tАй бұрын
Il faut encourager ceux qui se lévent pour la prière de Fadjr. Critiquer est facile
@JeanPaulBoubane-t7k3 ай бұрын
Machallah wakh nga Lou leer je vous suis depuis la Guinée Conakry
@papematarmbengue57003 ай бұрын
Machallah professeur xam xam bi léerna nagne
@MbowNgone-ob3qt3 ай бұрын
C'est pas les marabouts c'est dieu ki yalla ko maaay limou xaam ❤❤❤❤
@dethiediallo71763 ай бұрын
Ahhh ok je comprend maintenant je savait pas donc moi je priait le fadjar avant l'heure parce que en Europe l'heure de priere change ex le fasjar cest 6h 25 moi je priait le fadjar avant et le sobh le fadjar merci pour l'éclaircissement
@mamadoufaye99623 ай бұрын
Machalah oustaz amna solo lol lol
@bambagueye52493 ай бұрын
Donne bay fall rk mo waurr ❤
@fatoumbodj50853 ай бұрын
del dioulo mo woor niak nga dayda
@mbayeba98453 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Miskin
@MouhametTop-l7w3 ай бұрын
Alhamdoulilah ❤❤❤
@MahawaMalickSarr3 ай бұрын
Alhamdoulilah
@Penchacky2 ай бұрын
Pourquoi ne pas se fier dès lors, à l'heure de levé du soleil que la météo communique chaque jour. De nos jours avec tous ces bâtiments et édifices qui nous entourent, il est difficile de voir l'horizon pour observer le levé du soleil
@thiernoba84863 ай бұрын
merci beaucoup oustas
@mameawasow12902 ай бұрын
Salam Je voulais juste savoir ceux qui vivent dans les zones où ils ont 6 mois de jour et 6 mois de nuit
@COLLEGEARABE2 ай бұрын
POUR CEUX QUI VIVENT DANS LES POLES PEUVENT SE REFERER AUX PAYS LES PLUS PROCHES. EXEMPLE POUR CEUX DU POLE NORD, SE REFERENT A LA FINLANDE
@mamanmbaye13053 ай бұрын
Dieuredieuf yalla na yalla faye la❤❤❤❤❤❤
@Africains-x1r3 ай бұрын
C'est dieu seul qui sais
@SeckSeck-m7f3 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤
@groupems45773 ай бұрын
Nafila fadiar amoul, nafila goudi rék mo am. Fadiar prière obligatoire leu. Ça commence à l'apparition des rayons du soleil et prend fin à la levée du soleil.
@MbodjVabien3 ай бұрын
Iow liguay wakh xamosi touss yallah Niari raka fadiar lou ame la bo khamoul daguay lathié gnou xamale la
Ms dans les villes avec les immeubles et une forte électrisation on a du mal a voir ça
@mariediagne12083 ай бұрын
Calcul avec lheure de meteo
@oudieng2 ай бұрын
@@mariediagne1208Aussi simple 👍🏾
@Africains-x1r3 ай бұрын
Professeur des fois tu exagères tu sais tu penses que tu connais tout dans le monde
@mbarickdiaw3 ай бұрын
Qu'es ce que tu connais toi
@bambagueye59793 ай бұрын
@@Africains-x1r puisqu’on tend le micro à n’importe qui, louko nekh wakh Khamoul dara kham kham dou micro
@MbowNgone-ob3qt3 ай бұрын
Pourquoi guën sokhor niou khamoul dara rek nioy tok dis ratati yalla moy mayë të kousi néke ak limoula maay té kholoul si âge kholoul kou ame kholoul kou niaka dieredieuf kou méér kalamel yallah
@papematarmbengue57003 ай бұрын
@@bambagueye5979limou wakh cï xam xam mono indi louko exacte
@mouhameddia51683 ай бұрын
@@bambagueye5979xamoul dara mome ak gana messéré nio yéme
@nassirouthiam13202 ай бұрын
Il est plus facile de le situer par rapport au lever du soleil car ce lever est connu avec la meteo
@aissatoudiouf15072 ай бұрын
Le lever du soleil est différent de soubah
@oudieng2 ай бұрын
@@aissatoudiouf1507en effet
@visionelectronique24773 ай бұрын
machala prof amna sollo mais lénn rek la dakoroul ak yow moy diouli souba.exp:nénga heur nagne ko tégé né,sino tu seras obligé ngay diouli 6 foi par jour allor k 5 foi rek la wara donne.
@oudieng2 ай бұрын
Ci lima comprendre, dafa bëga yombal déegg déegg bi pour ñu jël repère ci temps bi. Temps boobu nak mooy déterminer heure bi mais du heure bu fixe comme nimu ko expliquer. Man je crois que application d'astronomie yi ak yu Islam yi elles sont fiables. Avec elles on a 365 jours sur 365 les heures des cinq prières de Fajr à Isha (Guèwé)
@djamildiouf85933 ай бұрын
Fikh mom faw mu am ay wouté ligueun dall diappal linga xam ta bayyi kenen def limu diang
@moustaphafalldiop42903 ай бұрын
WÉRNA MACHALLAH ☝🏿❤
@IbrahimaniNiass3 ай бұрын
Say ioe esko dioumo si titre bi avent nguay tontou ki day diangualé kassé😊
@Africains-x1r3 ай бұрын
❤❤❤
@mbayeba98453 ай бұрын
Bou yalla wakhé ni défélén ni Ngén né na kounéka geum limou geum Bilay yéna saf xorom
@OusmaneDiouf-ol6jp3 ай бұрын
Dou question wouté wayé question logique la. Limou wakh deug la wahtou diouli day am khamekay thi nature bi.
C'est dommage vous avez insisté sur l' heure qui n' était pas la question posée à savoir le comment de la prière du fajar ,l' heure a pris tout le temps jusqu'à une autre heure, l' heure du timis ?
@safydia72482 ай бұрын
Sama Guinaar gui moom laa si Woolu. Moom entre 3h et 4h lay sab pour yeete.
@oudieng2 ай бұрын
😊
@AidaAidandiaye-s3t2 ай бұрын
Donou demali wah nou heure fadjar te yalla tah
@djamildiouf85933 ай бұрын
La terre ne tourne pas segne madiama😂😂
@sow.familly18563 ай бұрын
Hun en tout cas si ça ne tourne pas aussi y'a une rotation parceque bou amoul wone rotation le soleil ne vas jamais disparaître je ne sait pas c est le soleil ou la terre qui tourne mais y'as quelque chose qui tourne
@fortfieretfidele65743 ай бұрын
La terre tourne au tour du soleil et sur elle même. Il faut faire des recherches plus approfondies. QUE DIEU BÉNIT NOTRE CHÈRE AFRIQUE !
@Mmm-mv8sy3 ай бұрын
😂😂😂Boy yangi rée té khamo
@alylayesow43583 ай бұрын
Boy kone terre bi loumouy deff niou kham 🙄
@mouhameddia51683 ай бұрын
@@Mmm-mv8syla terre tourne
@babacarcisse3662 ай бұрын
Avec les lampadaires c pas facile
@ibrahimandiaye32933 ай бұрын
Incroyable!!! Satan mo bonne deug deug nak
@MamadouSANE-og2fv3 ай бұрын
Qu'est-ce vous en savez? Vous devez vous limiter à rappeler les écrits et laisser la sanction positive ou négative de nos actes à Allah.
@sidyfall29992 ай бұрын
Saway lima diakhal dangay wakh ba paré kéne dousi kham dara
@abdoumaslahmaslah35323 ай бұрын
Alkhourane diouly fadiar la wakh wakhoul diouly souba un point un tiret
@oudieng2 ай бұрын
Yalla Subhanahu Taalla moo wax ñu tòpp Alqur'aan ak Yonent'am bu tèdd bi. Kooku moo ñu jángal mbiru julli ñaari rakka yi jiitu julli fajar. Mudi sunna bu dëgër.
@amadoucisse97183 ай бұрын
Professeur il faut expliquer
@oudieng2 ай бұрын
Suma xalaat, mooy la conjonction des premiers instants de l'aurore et des derniers instants de la nuit. La détermination du fil blanc de l'aube du fil noir de la nuit.
@DembaDjah3 ай бұрын
Entre fadiar et souba lequel est farata
@MbodjVabien3 ай бұрын
Souba mooy farata fadiar souneu la Yenonte bi halay Salame moko done deff
@AbyGnay2 ай бұрын
La farta c'est sôuba
@abdoulayediao62302 ай бұрын
Souba n'est pas dans le Coran. Ilya juste salatoul fadjiri.
@oudieng2 ай бұрын
@@abdoulayediao6230Effectivement c'est une seule et même prière à ne pas confondre avec les deux rakka nafila à faire avant de prier.
@oudieng2 ай бұрын
Ce sont ces deux rakka que beaucoup considèrent comme étant la prière du Fajr et la prière obligatoire comme étant la prière du Soubh. Une confusion fortement entretenue même par nos oustaz. Fajr ou Soubh c'est une seule prière. Celle obligatoire.
@MaguetteDiouf-y2z2 ай бұрын
Lli hew Arabie saoudite nooko gise
@AntaNdiaye-dd3sw2 ай бұрын
Daguay dégue les coqs gnouy sap
@bambagueye59793 ай бұрын
Djouli bou baakh ak bou baakhoul dou yaww yaakay wakh Yamal fii nga wara yam
@papematarmbengue57003 ай бұрын
Modou tané lsko yow mi khamoul dara
@MbodjVabien3 ай бұрын
Iow ya khamoul touss mélni yéfér nii
@bathiembaye11993 ай бұрын
yow saye wakh dossi indi khadith, dossi indi alkhourane sa xèl rèk ngaye wakhè !!! yonantabi saw keuram ak diaka djy nio takone... daffa done diouli niari rakka fadiar yi si keuram farata souba bi mou dioulè ko diaka.. lolou sunna la tè wacc na si khadith you bari, you kou dangereux nga
@HaqqBilHaqq3 ай бұрын
Expliquer na lolou kou bakh wakhnee djaka bi si keurgui la nek. Ça ne change rien à ce qu'il a expliqué
@bathiembaye11993 ай бұрын
@HaqqBilHaqq non c'est pas vrai !!! yonantabi saw diakam meussoul nèk keuram !!! ndakh amna ay naflila yo xamni daffa dane neubatou diko dèf ngir bagn sonal diam yi diko done topoj
@oudieng2 ай бұрын
@@bathiembaye1199Pourtant sëriñ bi, jàkka Yonent bi ak kër gi daanaka bènn la woon. Dadoon ubbi buntam rek dugu ci jàkka ji. Loolu bëri na ay version yu kènn werante wul. Yàlla rek moo xam
@Mmm-mv8sy3 ай бұрын
Grande Mosquée de Ngor Extension - Dakar 13:22:42 20 Rabí' ath-thãni 1446 Mercredi 23 oct. 2024 Dhuhr dans 00:52 Fajr 05:48 +15 Dhuhr 14:15 +0 Asr 16:43 +0 Maghrib 18:52 +0 Isha 19:52 +0 Jumua 14:00 Chourouk 07:03 Installations et services de la mosquée Souniou soukandiko fii jousq’ua 703..?manam ba jant bii fenk? Après 703 warouniou dioulli ba une heure de temps Après moy si arabe وقت الكراهية manam wakhtou wounou sip …