As salam anlaykoum Omar Sall nimou ndiémé yalla Daf maa diaaxal wallahi yalla xamnako billahi
@daoudaballtv45383 жыл бұрын
Dieureudieuf Oustaz yow lowakh magueumko ndakh sadeugou ak sacourage. Omar Sall mandoul si cheikhou Tidiane ak baye. Bakhna danga répp
@khawmakene39913 жыл бұрын
Alhamdou lillahi rabil alamina dieureudiff yalla na yalla fay la omar sall mom nafekh la
@mortvivant71593 жыл бұрын
OMAR SALL torohh nga
@badaradiouf46463 жыл бұрын
Omar Sall si classe Musaïlimah ibn kazab la bokk lii mome Sénégal lakay deff meneu nekk si diam aye doumeu daggane naa si mome fenn katt leu
@alassanediop91403 жыл бұрын
Yewe mi yamana fene wahofi touss
@badaradiouf46463 жыл бұрын
@@alassanediop9140 maxala si doule akk fenn lalene yaré lolou nguen nampeu so meloul nonou diaxal saye mbokk wayé boulene si delou guinaw continue lene si bou baax mbokou Musaïlimah ibn kazab yii
@malicksarr83033 жыл бұрын
Kimom diaroule tontou sakhe awe tour rek la bakhe lé oumar sall ténga mandou si lokhamout 🤲😭
@seydoundiaye83413 жыл бұрын
Vraiment frère ta raison
@malicksarr83033 жыл бұрын
@@seydoundiaye8341 merci mandë douma chëdé si louma amout kham kham
@ndeyembodji42753 жыл бұрын
Omar sall yallah nala yallah diégeul thi li nga wax thi Maolana Cheikh Ahmed Tidiane...tei je te conseil une chose démal tarbiya dji nga Yallah molay may xol bou rafeite
@OusmaneSeck-v6rАй бұрын
Tarbiya dou pour mbam bii kii kay nako yalla alak rek❤❤
@babacarndigeulfall8633 жыл бұрын
Bilahi walahi tassaouf rek moy deug
@ousmanegaye5561 Жыл бұрын
Mach'allah Serigne bi
@ndiogousy33512 жыл бұрын
Machallha❤️❤️💯
@mamadouba3142 жыл бұрын
Yene gni yena yena niakk fayda yene wa tasawuf niou niakk Dine gene amolen yarsi yalla amolen yarsi mouhammad
@issaseneseneisss19583 жыл бұрын
machallah atidjaniya mame dama tite si omzo
@ousmanesene12083 жыл бұрын
En tout cas omar sall daffa warra mandou si tarikha Sénégal yii ak suniu makk yii bahh yiii nayy feen feen ay fenam si niioukouy top
@modoucisse56293 жыл бұрын
Alhamedoulilahi dieuradief baye Niass
@cissetoure81203 жыл бұрын
Macha alla oustah lérne torop Mais Omar sall amoul koumi Roy si khasté Baka nam rk la topou Mais yala la nago yala wane louy diarign khas waliou yala yi
@khalifadiop93033 жыл бұрын
Yallana yalla halak noni islam
@laminendiaye47053 жыл бұрын
Noonu islam yi ken rawucci suufi yi. Bunu waxantée dëgg war ngeen na xam ni Oumar Sall moo nekk ci dëgg. Ndax ootéwul ci maamu ken. Ci Alkhuran ak Sunna Yonent bi SallAllahu aleyhi wa salam. Nittu Yallah mooy kiy woo nitt ñi ci Yallah ak Yonentam. Bayileen caahaan. Seen turuq yi yepp ci ñall yi lañu nekk. Yallah nañu Borom bi sexal ci Alkhuran ak Sunna.
@khalifadiop93033 жыл бұрын
Amine yarabi mé dioume nga kokou louko déf nittou yalla nittou yalla douwédi moromame té souféké dioulit le dafa wara beug baye niass !
@laminendiaye47053 жыл бұрын
@@khalifadiop9303 ku waxul lu dëpoo ak alkhuran ak sunna ñu wéddi la. Baay ñass mooy kan? Esk Yallah moom la yoni ci ñun? Ken rekk moom lañudul wéddi muy Yonent bi sallaatu aleyhi wa salam. Kénéen kumu doon say wax ak say jëff dénukoy natt ci alkhuran ak sunna. Su dëpoowul ñu bayiko topp la dëppoo ak alkhuran ak sunna. Lii mooy dëgg. Yallah nañu Borom bi hiir ci top alkhuran ak sunna niko sahaba YI déggéewoon.
@khalifadiop93033 жыл бұрын
Waw s k kham nga alkhouran ak souna sakh bye lathé ndakh la yalla yoni si noun pour mouy lér Baye niass la yalla yoni si lép lou ame roho yén kha ak yén pért temps la 😌
@laminendiaye47053 жыл бұрын
@@khalifadiop9303 khanaa seen diiné bopp la loolu? Ñun dé sunu Yonent Mouhamed Ibn AbdalAllah la tudu té ci moom la Borom bi waccée alkhuran. Lan mooy rissaala Bayy ñass? Siñ bi tuubal linga wax! Ñakka xam diiné weesuwul lii nga wax. Baay ñass ken yoniwuko ci boppam sax waxatumal ci ay yeeneen nitt. Nañu raggal Borom bi té topp alkhuran ak sunna ndeem islam lañuy wooté ! Yallah nañu Borom sexal ci topp alkhuran ak sunna.
@nassirdiagne37393 жыл бұрын
شكرا لك يااستاذ
@ousmanethiam54823 жыл бұрын
Omar sall yagou dara rékk dournafi diabaram bamou daw dikou mitital kii niut kou bon la naafékhla rékk
@soulayegueye69973 жыл бұрын
كثر الله أمثالكم ياأستاذ أبوبكر به التجاني
@elhadjcheikhdiagne18353 жыл бұрын
Soo bëgee siiw daal dangay sossal/fenal ku siiw
@HassaneSY013 жыл бұрын
Alhamdoulilah Alhamdoulilah Alhamdoulilah
@ahmadougueye44663 жыл бұрын
Macha allah talibe cheikh tidjan rekk ❤️❤️❤️
@abdoulatifdiallo78633 жыл бұрын
Jërëjëf Oustaz Oumar Sall
@aliouba58753 жыл бұрын
Diazaka allah khayr
@ablayecisse81833 жыл бұрын
Yappou wallou yalla yi yalla ko toké koulen fénnal halakou
@mouhamedthiam90483 жыл бұрын
Amoul sik ..loulere..gua wah.
@blackboy68513 жыл бұрын
Omzo salla doulrek laye deff
@lebrahamien47503 жыл бұрын
Alkhamdoulillah Allah kouli khall
@ndimbelanendimbelane4213 жыл бұрын
Alhamdoulilah Mashallah dieureudieufé BAYE
@Blaackleon2 ай бұрын
OMAR SALL A PARFAITEMENT RAISON 🎉
@Madamediaw-v8k3 жыл бұрын
Ah Omar sall dé doff là rek
@hamidoutoure8353 жыл бұрын
Macahallah
@aboul-bassar-NDAO3 жыл бұрын
Gni bougne féké wone diamonoy yoninté sakh wédi ko. Ndakh khéle bu andoule ak khole bu selendou khalate khalate lérou yalla amougne l'ère wédi rékk lagne meune.
@wabaye753 жыл бұрын
Omar sall khathj Bou bone laa.
@wabaye753 жыл бұрын
@Prince Askia Haruna II comme sa baye limoudone rék
@Ousmane75.3 жыл бұрын
Omar Sall khathj moko euppeu ndiarign ci mbindefou Yallah yi ndakh il ya des chiens qui aident à retrouver les criminels et à l'élevage..
@ousmanediaboujalaloudineci1963 жыл бұрын
Machallha
@assanediop98933 жыл бұрын
Omar sall fainekate bou alakoula, mais walakhi bala dai dinakoguisse, walakhi si barkai cheikhou tidiane
@aminatacham49653 жыл бұрын
🤲 Amin yarabi
@OusmanesokhnaSokhna3 жыл бұрын
Omar Sall yalanadé balay fin Février cibarké cheikhna ahmadati rtl
@ibrahimathioban99943 жыл бұрын
Amin ya rabbi
@xamsadine48563 жыл бұрын
Svp abonné xam sa diné 👆👆👆
@sambafall4143 жыл бұрын
Bilahi Oumar Sall doulkat international té diangam soriwoul bou latie wone histoire Ibn mayaba Dina def attention
@modouthiam24613 жыл бұрын
Bilae
@ibougueye33203 жыл бұрын
Point d'arguments 🤕🤕
@xamsadine48563 жыл бұрын
Omzo loum wakh cheikh ahmad tidiane metinama toropp😭
@soulaydiallo32603 жыл бұрын
Oustaz Oumar Sall deug rek lay wakh ta moy wakhou yalla AK yonentébi psl yalla nala yalla sammou ta arla si péhé non you bon yi
@abdourahmanediao46303 жыл бұрын
Meirce good
@bayeoustouray75513 жыл бұрын
Omar sall man kham na ko bou bakh Diegen mom dou sy doyal motakh manelen ndiaga la
@oumardiop25482 жыл бұрын
Dieuredieuf Al ouztaz Aboubacar At Tidiâni.Xam xam bi lérena sétna,amna sources
@alfadl32023 жыл бұрын
Oustaz Omar nous a éclairé sur pas de Choses pour dire vrai
@diha68663 жыл бұрын
warr na moytou ndakh lee oupna,,,,ken dou lal waleyou di mouthou💔
@xamsadine48563 жыл бұрын
%tuuuu7uuoo
@seyepapa52693 жыл бұрын
Sénégal mo nékh rk wayé Omar sall mi deuk bou normal ray nagn ko bou yague
@laminethiam37593 жыл бұрын
Mahcalla
@karimcamara78653 жыл бұрын
Omzo sall est un pur domérame
@amadoundiaye18113 жыл бұрын
Sénégal deuk bou touti si islam eupou ayy fénnkat si islam BAYE mom moy djantibi kénn mounou ko téré takk
@karambodji54513 жыл бұрын
Bol wédi sa Seringe Amadou Ndiaye
@abdourahmanediao46303 жыл бұрын
MASH Allah good an meirce
@suwadoujammeh93912 жыл бұрын
Ioe mome ya ragaloule yalla
@mouhamedthiam90483 жыл бұрын
Ya barri ham ham.
@bayeoustouray75513 жыл бұрын
Omar Sall domou ndiallo la mo takh niom amou niou gem gem
@gayekalidou45823 жыл бұрын
Vive Oumar Sall, le veridique. Oustaz Oumar Sall est le Professeur des oustaz. Oustaz Oumar Sall, Maschallah. Dieu est son protecteur. Viva, Oumar Sall.
Omar Sala Matout limou don Matouko ko kam né do wax lo kam Moukou di fén rék di fén rék Mayal Sa bopou diamou nak
@binetadia84393 жыл бұрын
Raw na niémé yalla omar sall ya am fit té niémé
@herruholumutadacaktrherruh79453 жыл бұрын
Baylén saga waye, talibe day amyar
@cheikhmarasyndiaye9653 жыл бұрын
Omar Sall doule rekk layy defff
@moussadiatta53203 жыл бұрын
Say wakh ak néféré lay yemalé amoul dieurigne
@ibrahimandiaye93743 жыл бұрын
Fi thi wetou gandiaye amone bène goorou sérère bougnou dane wassifa daf done guène ndaxe rafétayou djiromou nite youmou done guiss thi digue malane mi. Bougnou paréwane mounélène woye yi nexe nagnou dé wayé gni thi diggue malanemi rafètenagnou. na goorou sérère
@ploum44632 жыл бұрын
Mane mangui si yone wii
@amdibaye23083 жыл бұрын
Diarradieufé baye niass
@malicksarr83033 жыл бұрын
والله : فإن لم يهتدوا به فسيقولون هذا إفك قديم
@alassanediop91403 жыл бұрын
Wakho fi touss tarika dou dine
@foutiyyoutv96413 жыл бұрын
Alassane Diop kay wakh fi tousse yow
@djibrilfall68003 жыл бұрын
Yaw ya khamoul lingay wakh
@xamxamtv99823 жыл бұрын
Saw mi diwakh ragaa lo yalla
@linedor5883 жыл бұрын
Daafaa reew
@justuncliktv52623 жыл бұрын
Mane dè doumako neubb, amone na estime si mom diko suivre mai dama dëgg bèn jour mou fëne, aw fën bou lerr depui bobou jai plus confiance en lui... Dafa meun fèn trop mom Omar Sall lolou baxoul koi
@dadowatt94193 жыл бұрын
Salut il avait dit koi svp ? Et pourkoi ilbest traité de grand menteur ? J'ai raté kelk chose
@elhadjcheikhdiagne18353 жыл бұрын
😂
@justuncliktv52623 жыл бұрын
@@dadowatt9419 waxnafi ni Cheikh Ahmad Tijane chretien la wone, il s'appelait Michel alors ke kokou toute sa descendance est musulmane (def nassi ay geustou you werr) sossal nafi aussi bèn domou Baye Niass mouy Nazir (lo xamni dara doussi deug ndax mane damay geustou) mofi fén aussi ni dèm nafi ba Nigeria sans faye ndax daniouko dioxone mi wird lo xamni do faye pass (xolal ma waxi dof yoyou... Niatta nitt nio beug toukki pass molèn teu lolou sou amone kone wa Medina di toukki nimou lèn nèxé...) aufait mom meun na bgne yonou soufi mai nako tèkk si xam xam rek bania fèn, lolou dafay takh niou xëb ko tè dioullite dou fèn
@dadowatt94193 жыл бұрын
Ah ! loolou moom niaawna waroukoo wakh, en tant ke Oustaz il devait défendre nos saints au lieu de les dénigrer... Heureusement ke j'ai pa vu la vidéo
@xamsadine48563 жыл бұрын
@Prince Askia Haruna II dafa wara reglé mame borom touba seydil hadji malick baye niass koulen diema toutil yaye touti il ne fait kk....
Ni la dhé borome kham kham yi dagno wara tonton fen Kate yi diangou gnou comme khaly gaye nimou KO dane Défé ba guéne adouna
@tijjaanibuso33513 жыл бұрын
Jarajof baay ñas
@amdibaye23083 жыл бұрын
Diarradieuf way omar Sall da torokhe
@mamadoucisse94493 жыл бұрын
Togne yimou neke motakh mounou am dara lou bakh ay probleme rek mokoy dal setane len ko rek
@xamsadine48563 жыл бұрын
Svp abonnez xam sa diné 👆👆👆
@papebiramendiaye39813 жыл бұрын
omar sall c ún domeram bouy wedi makgnii
@ahmedfall18093 жыл бұрын
Omar sall dafa torokh
@bassirouniang43013 жыл бұрын
Lou wérr
@sodandour32072 жыл бұрын
So khamoul naga mandou
@moustaphaduack81943 жыл бұрын
Dayouko wara reye
@abdouniang3823 жыл бұрын
Bayiléne saga. Wakhe léne wakhe djou jiwe.
@cheikhdaffe99443 ай бұрын
Omar Sall mo gueune sén Serigne yi, dakh yalla rék lé wakh , yé sén serigue yi guin Di wakh
@assegueye70113 жыл бұрын
Mashalla
@kunuzikunuzi226 ай бұрын
OMAR SALL DIANGOUL DIONGOWOUL DIAAY GARAB WOLOF DEPUIS MARCHÉ THIAROY IL FAIT FAILLITE DANS SON COMMERCE APRÈS IL EST DEVENU OUSTAAT 😮😮😮😮
@cheikhomardiop63623 жыл бұрын
Wakhlèn nit yi al quran ak sunna mo gueune ,Omar sall alquran lay wakh mè iow nakk
@pendambaye68023 жыл бұрын
Omar Sall wakhoule aqourhane framaçon la
@xamsadine48563 жыл бұрын
Svp abonnez xam sa dine👈
@eljitoure80233 жыл бұрын
Yen yenay doul kat yi yenay domeram yi yen ak seni serign yeup fen rek mo len nior Omar salle deug bou werr rek lay wakh lolou moy dageu sen khôl yi si yen la bokon mou dem bâ khamni Aÿ dof gen mou balen fi mo len mety