N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
@moosewala820610 ай бұрын
😊😊😊😊😊😊
@ndeyebintoubobe504510 ай бұрын
Pawlich mi dofoule de wakhou niite deugue la wakh
@codoungomsow772610 ай бұрын
Yala ngua deh yaw sokhor
@FatoukineFomba10 ай бұрын
Bayil nakh yalla mola beugu sauvé way bakhoul yalla nala yalla diapalé baga bayi 🤲
@AwaMbengue-qt8el10 ай бұрын
Legui bou wally déwé nak xana sen adouna day yakou ? Wayy bakhoul yalah beugouko yonenti beugouko sou beugué bayi diapalé len ko🙏🏾
@fatygueye287110 ай бұрын
Guéménie bou wakhoul deugue wakh féne musique dafa aram
@minantv683210 ай бұрын
@@Rama_sarr boul togne yonenté bi dh,meusta andak kouy music,dafa Haram waxal lo xam
@buz775510 ай бұрын
Luo lér ngua wakh 😢
@FatimaaNdiaye-ng8cu10 ай бұрын
Pure vérité
@mbayangsoumare771310 ай бұрын
Salamooun khawlan bi rabi rahim domou diambour bi yall neu goudou fan waly day goudou fan in chalah guinaw yalla niongui si guinawa
@DjibrilMadefal10 ай бұрын
Dèlo khèlam si yalle motakh mou beuge bayi bayilè ko ak khèlam😭🙏
@mouhamedsamb723810 ай бұрын
Vous ne comprenez pas que les sensations de wally à ces temps andoul ak way .way yeufi sentiment leu xol leu t li wally di yeuk est trop triste pour lui wait leinko dineu nieuw inshallah
@FantaDiame-j9h10 ай бұрын
Reiiii n’a badeiii😂😂😂😂😂pawlish donite😂😂😂😂😂
@momodoukujabi235110 ай бұрын
For me the best wally will do is to let music 🎶 go and focus on the deen of Allah
@coumbandiaye761610 ай бұрын
Je suis complètement d’accord avec toi pawlish concernant Macky Chapeau à Macky ❤❤
@FantaDiame-j9h10 ай бұрын
La perte d’un être cher c autre chose Wallahi kan g perdu mon papa j croyais k g v mourir ou être folle j t jure
@authentic59510 ай бұрын
Santale Borome bi ! Khalatale Yonenti bi ! Mounieul métite bi ! Kham na li ngay yeukk ... gueuneul sante borome bi 🤝🏿
@AminataToure-ng1ms10 ай бұрын
même moi j'ai perdu mes parents mon grand frère et ma grande soeur té wally moma mark fouf 16 ans rek la ame sa petite soeur khamoute sama yaye
@ESCALE310 ай бұрын
liii dal wally métinaa tropp mais pawlish dafa rétane louuu tropp mais wally il faut le laisser un peu qu'il fasse un break après j'en suis sur il reviendra
@MayeSow-l9j10 ай бұрын
Deuggeu piiir nga wkh❤❤❤
@JulBa-rr9gz10 ай бұрын
Pawlish tu es un génie machala vérité absolue son excellence Monsieur Macky Sall c est le meilleur
@ycamara903410 ай бұрын
Bless all of you Amen 🙏
@wfamily994110 ай бұрын
Wally nala yalla may courage bou feké bayi mongui sa khel. Sois fort, ne nous laisse pas en plein vol. Pawlish wakh nga deug sou bayé loumouy def 😅
@KadiatouDione10 ай бұрын
Ms wally amna khalice baparé meune na investir khalicam si lenen musique késsé du métier
@Marcelodiallo1210 ай бұрын
Amna droit bayi ❤❤❤ I l’avais dit vous êtes avec wally mais vous suivez pas wally il a le droit d’être proche à dieu yén mom yénay niane bayilén fimisté
@AmetKah-t7b10 ай бұрын
Wally sou bayè wooy dougne koko bal basi kanam yalla😢❤😢😢
@abydiouf676110 ай бұрын
Bien dit pawlis Maky a beaucoup fait pour le Sénégal ❤❤❤❤❤❤
@abdoulayendiaye230810 ай бұрын
Bilay sister
@abydiouf676110 ай бұрын
Mais malheureusement les sénégalais n connaissent pas un bon président
@abdoulayendiaye230810 ай бұрын
@@abydiouf6761 ils vont le regretter
@famagueyegueye261610 ай бұрын
Machallla 🙏 machallla ♥️
@MouhamedNdiaye-c3b10 ай бұрын
Pawlish daffff m'a dépasser 😅😅😅😅😅
@SokhnaFaye-ut5jv10 ай бұрын
Pawlish beugue na ay dioy nk man dioy yi rk momay ray 😂😂😂😂😂😂😂😂
@abdouazizloum902110 ай бұрын
Merci❤❤❤❤
@nancyseye351410 ай бұрын
Ndeyssan 😢
@babacarfam25110 ай бұрын
Machala tabar ckala
@kazamariem666710 ай бұрын
Wally bayil way bakhoul da haram bo déwé kenn dou nék ak yaw sa bamel ⚰️we Salam 🙏
@miliediene8910 ай бұрын
😢 courage à vous pawlis
@ndiemediagne211810 ай бұрын
🙏🙏🙏💯👏👏👏💯♥️♥️♥️ merci beaucoup.
@AbdouKa-l1v10 ай бұрын
parfait pawlis
@buz775510 ай бұрын
Pawlish day raye nitt 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@ngonefallsylla58410 ай бұрын
Bylla c'vrais 😢😢😢😢😢😢😢😢❤
@Ramapoulo10 ай бұрын
Bilay Pawlish ya seytané rz😂😅😅😅😅😂😂😂😂
@MedNdoy2210 ай бұрын
Pawlish cest le meilleur walahi 😂
@Mody-nz3zt10 ай бұрын
Toke leine di wakh wally mou ngaye ligueiy thi France 🇫🇷 et prepare ses grande date de concert dans différentes aréna 🎉du monde 🌍 wally mi ngui nieuw dal seine kaw😂😂 pawlish ngani wally mounoul ligueiy maçon mounoul neike mécanicien 😂😂😂😂boula wally diapei
@wfamily994110 ай бұрын
Tit na si pour mane omaro dafa done kaf rek mais ni pawlish wakhé ni c'est comme si bayi dafa nek si khelou wally
@Mody-nz3zt10 ай бұрын
@@wfamily9941 mani gni daniouy doul 😂😂 wally bayiwoul wadjiouko wally mou nga France 🇫🇷 di ligueiy deimal snap gap ou statu youssou dieng thi ngaye khameini gni yeugouniou li xew wally daye teug festival almagne Avril le 13 après itali après almagne encore et ensuite Norvège 🇳🇴 pour clôturer à Bercy en novembre nila deimei 👌😂😂
@Leuzsonko10 ай бұрын
Wally meusoul bayii
@wfamily994110 ай бұрын
@@Mody-nz3zt deg na adamo di wakh dates yi khawma foumou dieulé informations yi. Effectivement, baye zale mongui done wakh festival bi le 13 avril. Retour bi dou yombou inchallah avril 😃 gnongui khar le 12 mars aussi
@buz775510 ай бұрын
Wally dingana khamna li yalla wakhal música bakhoul wakh na deug ndakh ken dou dhe ngo tegal ko ay música 😢
@KarimoulahMbaye-kt1fo10 ай бұрын
Souwally bayé way mabayi diklou musique 😪
@ibrahimasamb876210 ай бұрын
❤❤❤❤❤Wally
@ShadowDarkened10 ай бұрын
Music c'est haraam tmt il est un musulman en plus ce qui lui arrivait est très douloureux..Il a pris une bonne décision en tout cas c'est le bon moment de prendre le droit chemin.
@SiraDiouf-yc4qp10 ай бұрын
Wokho fi dara waly bayil musique té diamou yalla yalla teralenala
@Mody-nz3zt10 ай бұрын
Musique mo gueine feine gueine ndialo ngueine sathie alalou askan wi tei nite yi nio ngui si lolou ok wassalam. Wally moye mo moudiei waye Senegal 🇸🇳 leigui mani motakh ngueine beug koko bayilo humm
@mldmy_a10 ай бұрын
Wally can’t do all of the jobs you’ve mentioned but if he decides to leave his music career because of Ya Rabb, the almighty will definitely provide for him and guide him towards the right path. If y’all love him as y’all claim, you should support him with this tough decision he’s about to make as all he knows is music and have been doing it all his life. Regardless, he wants to strengthen his relationship with his creator, nothing can be better than that. As if he leaves this world, he won’t take music along with him. In fact, it will affect him as we all know that music is haram. I love you so much Wally and I believe God will help you….Yow mey nyu all you’re talking about moii aduna, aduna and aduna. Wally du yalla, ameh wut worsak gii nitti. Yalla bulen binda dinalen providal. Before working with Wally they were living by God’s mercy and without him they will still live. If Wally seems selfish just because he wants to deeping his relationship with Allah Subhana Wa Tala, I support him and advise y’all to do the same instead of discouraging him and stop being selfish everything is not about you.
@camaramme733010 ай бұрын
😂😂😂😂magui raam de 🤣 pawlis Dinama raay
@momolojr148610 ай бұрын
Pawlish meun na doule😂😂😂wa rame daan lay diokh metier niii😂 dmrm deug nga wally bayi woul
@fatima-xl3qe10 ай бұрын
Bilaye wakhalgua yalla,messouma khamni ni gua deugo❤
@misssarr753410 ай бұрын
Bou Wally bayèh es que mann dou ma xarou 😢 😢❤❤
@Salikhate73210 ай бұрын
No😂😂😂pawlish dafa nekh😂magui ram
@aissatousy187510 ай бұрын
Waly antouca prend la bonne desizeyon antouca boude danga beg toup delou thi Yale sase se conmprend et sougnou Borom rec mo fi ne bilay antouca cele c soi ta dezisyon on va lacsept bilay courage Lila Dale dafa meti mem boude bayi wo âme gua droit poze bilay nakh Lila dal da meti lolou se pa fasil pour toi bilay me Yale bakhe ne Lou menti âme tu restera toujours grave dans notre cœur me bou beg bayi bayil te sou Baye borom nage khamen bege nel bou bakh djamou yal rec mo wore antouca courage et force a toi et force a tout no farameren ❤❤❤❤
@ramatoulayesagna-w5t10 ай бұрын
Merci pawilis Wally waroute bayi na khole si aye rakam ak yi beugue gone papa thione ak diaga tè gua bayi sa dioye yi bakhoute
@fatoumatadiedhiou4510 ай бұрын
Islam beugoul music nitt bokoy conseiller deko wax deugg
@ramatoulayesagna-w5t10 ай бұрын
@@fatoumatadiedhiou45 wawe lolou mome degue waye na khare be' si kanam Wally Khaled la
@davembengue293810 ай бұрын
Lamine nar mogui serass di fèss 😂😂
@metzodiop57510 ай бұрын
😂😂macky sall waye😢😂😂😂no pawlis
@momolojr148610 ай бұрын
Man haan pawlish la mounta mounie 😂😂😂legui dama refet
@SallaDiop-u1y10 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@aminalalionne567910 ай бұрын
Pawlish mbaye sa dioye yi yakna sama journée 😅😅
@buz775510 ай бұрын
Man ndiapp la yeureum 😂bilahi 😂😂😂
@maxmiliano330310 ай бұрын
Commentaire bi rek ladonn xar
@yasminatv689710 ай бұрын
Yala 😂 d'à yémé
@moussa125710 ай бұрын
Pawlich machalla
@mamenarsene672210 ай бұрын
Dougnou amaty kou Mel ni macky billay pauwliw❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@DiagneCheikh-p1v10 ай бұрын
Yawe na deugue sa ndaye yawe yake macky souma pare si yima neke embesille
@Ndiayeniangua10 ай бұрын
Degu nekoul ben lafi won sall nguari mo meilleur kay❤❤😂
@Ndiayeniangua10 ай бұрын
@@DiagneCheikh-p1vyaw respect teh wo sa yaye macky sall mo geun sa bay diouni yon
@massambadare10 ай бұрын
Sénégal wakhou dof rek deuk bo khamni you unitile rek respectelen decision nitte musique kouko bege bayi amnga dimbelou yalla demlen outi ligey mo geun music dou ligey ligey bo khamni khamngen dafa arame ngen begse atardewou
@mouhamedmbaye938810 ай бұрын
Nenako tu es mignonne 😂😂😂😂😂😂😂
@roubafaye726510 ай бұрын
Inchalla yaw erk lagniou topu 😂😂😂😂
@coumbakida401110 ай бұрын
Merci 😂❤❤❤❤😂
@KadiatouDione10 ай бұрын
Ms wally amnako khalice baparé non meune na dieul khalisam investir ko si lenen😊 ms ndiap ak ndeye ndiaye banaya naniou négocier ak sidy Diop rk😂😂😂
@rouguyataamadoutoure327610 ай бұрын
Wah gni bayi wone groupe bei pour dem ci wally nak😂
@BabacarDiop-m4z10 ай бұрын
Bay dimbali niou sii macky nguirr yalla rék boul wakhati sii macky nguirr yalla damala ko niaan
@rouguika96510 ай бұрын
Karim Maïssa Wade notre solution rék mo ko meune remplacer
@ShadowDarkened10 ай бұрын
Yeah He's the good choice ❤❤
@ndyniang680110 ай бұрын
😂😂😂banaya akh sidy diop molay beug dal
@Showbizsn-gz1ch10 ай бұрын
Il faut ça même respecter son choix
@isatousinghateh95410 ай бұрын
Wouy 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@pimentdoux10 ай бұрын
Bilay pawlis dofo Macky luguey na dé
@Oulaysosseh10 ай бұрын
😭😭😭😭
@ladyj706110 ай бұрын
Waa yen lan motakh kounek di attackè Soumboulou bayi Evenprod mi bind film bi??????
@aissatasambadiallo459210 ай бұрын
Nooo 😂😂😂
@FatouDiop-fe2se10 ай бұрын
C bien
@momolojr148610 ай бұрын
Pawlish magui guisss sa xéwwi niii 😂😂😂macky ngay tag amoul bayré
@AminataToure-ng1ms10 ай бұрын
mais pawilih degue rek la wakh macky defe ligeuye Sénégal
@Ndiayeniangua10 ай бұрын
@@AminataToure-ng1msvraiment defna limou meun Sénégal mo meun sak dieuf
@DioopCheikh10 ай бұрын
Bayi Moy DEUG parce que déé dafay bété
@yayeseeh10 ай бұрын
Pawlish😂😂😂😂😂rafet
@bintouniang500710 ай бұрын
Dioyi seytane ngay dioy way
@Oumoucasa10 ай бұрын
Waye😂😂😂😂😂
@salimtofall409910 ай бұрын
Mai sou beugé bayi way na bayi way ta dém défi lénén pawlich sa intéré rek ngay défendre je encourager waly bayi musique
Wally défal li dal sa khel diapalni sheïtane moléne dougou niouy wakh guissengua yalna yékh mo déwone sen bakar yeup nguay gadou walahi prck yaléne engager
@Moussafal-ic2jt10 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@AminataToure-ng1ms10 ай бұрын
pawilih degue rek gua wally dafa ame famille té sou wayé aye rakam sene papa lay yi guiss te niou beugue papa thione wally motax dioy you papa thione wally waye be si kanam
@yougasarr789610 ай бұрын
Pawlich dou nite 😂😂
@king_boy768110 ай бұрын
Thieuy sougnou doff bi😀
@ibrahimasamb876210 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@peuldiallo68010 ай бұрын
Yéne niép seuytané dalén meune mé walli mo meune seuytané bayil diamou dji yalla yaw moom nékhatoma
@YayefallCamara10 ай бұрын
Lifi maky sall def si ligueye rew mi président dotoukofi def
@BoyPoulo-kg5pl10 ай бұрын
Wally bayil waye
@aisssatougueye487410 ай бұрын
Music dafa haram
@mamediarradiop880510 ай бұрын
Wally du courage boul meussa bayiii yaw lanne beugue
@Oumanas599510 ай бұрын
Kone gnanal KO mou bayi yallah dinako defal benen khéweul souko defé té yallah takh