Ohhhh!! Ndaysaannn Li mo warall Wally Seck beug téla bayi Musique…..

  Рет қаралды 396,708

BABACAR W. OFFICIEL

BABACAR W. OFFICIEL

Күн бұрын

Пікірлер: 680
@hawlyndiade3730
@hawlyndiade3730 10 ай бұрын
Kou bakh rek molay beugue barkii seydina muhamed psl
@DiaAss-i6w
@DiaAss-i6w 10 ай бұрын
لاالله الا الله yaame sasne adona amotsolo samayarme dawna
@AbdoulMalikMbaye2225
@AbdoulMalikMbaye2225 10 ай бұрын
Yalnala yalla diappalé si décision bingua dieul wally yalna ngua bayyi weuy inchallah Yalnala yalla téguat si yonou siratal moustakhim 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿❤❤❤❤❤
@KhadyNdiaye-e3z
@KhadyNdiaye-e3z 9 ай бұрын
Amine ya rabi❤
@pendaelimanethiam2472
@pendaelimanethiam2472 10 ай бұрын
Quelque soit ta décision on est de tout Coeur avec toi on t’aime sans condition diam thi yaw ❤😊
@ADAMfatmaADAM
@ADAMfatmaADAM 10 ай бұрын
Wally dafa ragal Yalla !!! Té ite amena imaaane !!! Macha Alah yalla bakhena
@ShadowDarkened
@ShadowDarkened 10 ай бұрын
Waay bakhoul (music)c'est le meilleur moyen pour seytané doug sissa biir xool plus ngay dèglou music plus tu as du mal à écouter le coran parck les deux ne peuvent pas aller ensemble donc Wally bonne décision frère Peace N Love❤❤✌️
@FatoushaThiobane
@FatoushaThiobane 10 ай бұрын
Deugue nexoul
@mamemariemeniasse
@mamemariemeniasse 10 ай бұрын
Waly kou geum sounou borom ga yalla bakhna khare day wesou mbote on es fiere de toi tu as ton choix❤❤❤❤❤❤❤❤
@fatousowe3652
@fatousowe3652 10 ай бұрын
Belahi wahati koh
@petitbaralofficiel7635
@petitbaralofficiel7635 10 ай бұрын
Bilahi
@ibeuzfall5589
@ibeuzfall5589 10 ай бұрын
Ndeyssane wakh dji amna solo surtout nak thi moment you méti yi nga tolou yalla nalathi yalla diapalé
@BintaDiallo-r3c
@BintaDiallo-r3c 10 ай бұрын
Wally kou geum sounou borom ga yalla bakhna khare day wesou mbote on es fière de toi tu as ton choix
@binetagueye2358
@binetagueye2358 10 ай бұрын
Walahi meusou mah commentaire m'es taye mome Séck mare yasine yaweu réke ya wakhe deugeu souniou ndakhanté yallah réke mon diara tope yallah nallah souniou borom bi défal diameu inshallah 🙏🏽🙏🏽❤️
@toutyseck282
@toutyseck282 10 ай бұрын
Thiey sama baye fall bi yallahnaniou yallah nagoul té défalniou dégue ak tope fière de toi frére
@mamerokhayafaye-yy7xj
@mamerokhayafaye-yy7xj 10 ай бұрын
Wallahi music baxoul Alhamdulilah Bimuko bayiwer
@MamaDoucke-k4x
@MamaDoucke-k4x 10 ай бұрын
Limou wakh akay deug k'Allah te facilite inch'Allah et on t'aime de tout cœur ❤️❤️💓
@FambayeDiop-we6rj
@FambayeDiop-we6rj 10 ай бұрын
Magui soga commentaires mais ta décision m'a vraiment touché ndax mane sakh douma deuglou musique
@khadygueye9331
@khadygueye9331 10 ай бұрын
Wally yala nanga goude fane Lo la le yalla ték si lokho bamou barkel yalla nala yalla dame yak say rak dessusion bo dieul yalla na donne bi gueune si barké Nabil Moustapha on est de tout cœur avec toi💟💟💟💟💟💟💟
@dielkeffelywele8128
@dielkeffelywele8128 10 ай бұрын
Fils Wally ta carriére est ravissante, tu as réussi en devenant une Star internationale.Personne ne peut t'oublier.Machala!Un conseil:sors les distinctions de ta tête et continue à travailler.Les prix et récompenses viendront chemin faisant.On peut être parmi les meilleurs sans jamais avoir de disque d'or ou autres awards.
@beugfalloutop7474
@beugfalloutop7474 10 ай бұрын
Bilay yay dioulite akhane yalna yékh yalgua doundou 111ans❤❤❤
@MangaBadiane-r5l
@MangaBadiane-r5l 10 ай бұрын
Machallah amna solo merci mon frère sa xalat rafetna que dieu te protège
@thiamnoumou6218
@thiamnoumou6218 10 ай бұрын
Amatina solo seck mar, Qu'allah te protège. Peace and Love ❤❤❤
@Amie-l5k
@Amie-l5k 10 ай бұрын
Wally we love you, God works in mysterious ways and he's more powerful. I'm so sorry for your loss...God has made you a superstar and that's forever. Mashallah
@elhadjithiam810
@elhadjithiam810 10 ай бұрын
bien parler waly verité absolu ❤❤❤ yalla n'a yalla samou defal la godou fan. magui laye diale papa thione et momy ak sono yaye bo bahkba manma thiagua (machalla bol ragual dara loguane ci yaw defko yalla bahkna j tm toujours waly)
@NdiayaLo-bd7np
@NdiayaLo-bd7np 10 ай бұрын
Wally je suis fière de toi bonne continuation yalla nala yalla lafal thiat thia tékla si yonou siratal moustakhima barkè seydina Mohamed psl
@claritadurand
@claritadurand 10 ай бұрын
Courage Bayfall bi on est de tout ❤❤❤❤❤❤❤avec toi
@DjibyDieng-m4f
@DjibyDieng-m4f 10 ай бұрын
Thiabotou papa thione seck rta yalna yalla samléne taxawouléne.diné dague siy yareuuu sa thiabote dès le bas âge ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@henriettediouf348
@henriettediouf348 10 ай бұрын
Amine ya rabi
@AdjiGueye-mh5wg
@AdjiGueye-mh5wg 10 ай бұрын
Wally seck yone binga dieule bobou la continue inchallah
@KhadyDiaraSeck
@KhadyDiaraSeck 10 ай бұрын
Machallaah Wally yalla na la yalla diapalé thi barké Seydina Mouhamed Salaatou wa salaam
@courambissanendiaye714
@courambissanendiaye714 10 ай бұрын
Yalnala yalla takha wou si barki seydina mouhamed psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@aichagaye5207
@aichagaye5207 10 ай бұрын
Ohhh macha allah yalla nala yalla diapalè wally woy bakhout tè kén beugosè fatou li mom sama khol sèd nasi macha allah
@AwaDiop-gs2ty
@AwaDiop-gs2ty 10 ай бұрын
Wally mougnel métina yalla nala yalla ték lokho té goudal saye fann
@CoumbaBa-en5mz
@CoumbaBa-en5mz 10 ай бұрын
Mon frère wally yalla nala yalla may kholou meungne si barke mouhamed ❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@mamediaradieng6220
@mamediaradieng6220 10 ай бұрын
Kou gueum sa borom nga adouna amna foy tolou toup ❤déllou sa borom rk molay war yalla nala si borom taxawou ❤
@pathegueye8860
@pathegueye8860 10 ай бұрын
Nuit ci aye kadom nguakaye diappé ci ngankéye bayé beu fâw yan nala sougnou borome diappalé👏
@mamndiagnabousso7733
@mamndiagnabousso7733 10 ай бұрын
Yalla nalla yalla defal la diamou seck barkep cheikhoul khadim 😢😢😢😢
@ngonefallsylla584
@ngonefallsylla584 10 ай бұрын
Wally seck dégue n'alla yallah samla 110 ans avec santé dal AK tal werre werle amiiiine yn'chah Allah❤❤
@aistaista-xx8br
@aistaista-xx8br 10 ай бұрын
Wally merci 1000 fois je t'aime .fore billaye .wally doundall ❤❤❤❤❤
@aissatathiam630
@aissatathiam630 10 ай бұрын
Machalla ya des moukalaf yo khamni liga wax yeup khamnagneko wayè danion goumba teukh lou Di nax s'en bop fo dioblou nafa yiwou yalla dioubou yalla sam la are la li kou guem yalla rek mokoy def
@nuqttmawal8900
@nuqttmawal8900 10 ай бұрын
courage waly yallah sounou borom lou ko nekh mou def ko ci diam bi metina n'a yallah yereum leen sa aldiana ba dit senn noflay ci barke seydina med saw psl ak wer korbi
@DiaryBalde-fk9dk
@DiaryBalde-fk9dk 10 ай бұрын
Mon santeur de préférence yallah na yallah ték leu thie yone bou lèr té gueune en qu'à de décision tes sansons resteront toujours gravé dans mon cœur 💓 maysa bigue mar sama hol sed na bah paré thie ioe boufi yemeune sah mou nekh machallah mon frère ❣️mon cœur ❤️🙏 pour tout 🙏🙏🙏
@mamadousine
@mamadousine 10 ай бұрын
Bilay ya gooré nitt kou bonn meunoul lii yalla khamnako doundal weral yokal wally je suis fier de tw bro
@nenediouf1079
@nenediouf1079 10 ай бұрын
Ndeysane tu as tout dit le meilleur Livre c'est le coran mais personne ne peut échapper à son destin mais bakane Allah moko yoor té kéne xamoul kagne la mais heureusement khamgako seck le cœur determine l'individu 😢😢❤❤
@attadrame2763
@attadrame2763 10 ай бұрын
Je suis très fier de toi mon chanteur préféré je ne regrette pas le fait d’avoir t’aimer machalla maintenant tu es le socle de ta famille donc mets toi dans le droit chemin pour que tes enfants et autres s’y mettent
@DadaCisse-hc6ug
@DadaCisse-hc6ug 10 ай бұрын
Mon fils de coeur on est avec toi du courage Q Allah te protège 🙏❤❤❤
@aladjifalloudia4915
@aladjifalloudia4915 10 ай бұрын
Wally séke yalla nala Yalla takhwou samou la amine sy barké serigne touba 😢😢😢😢😢😢😢
@astougueye6473
@astougueye6473 10 ай бұрын
Amine YA RABI
@mbengueamdy
@mbengueamdy 10 ай бұрын
Amine ya rabbi
@baamina9494
@baamina9494 10 ай бұрын
J n suis pas ta plus grande fans mais j t'aime comme tu es tu très courageux gentil lo beug inshallah dou diafé yalla na yalla sam sa diabote
@aminataGiraudeau
@aminataGiraudeau 10 ай бұрын
Mon amour tu m as fait pleurer je t adore n importe ta décision je vais accepter tu me donnes la joie de vivre tu es et seras toujours dans mon cœur Dieu soit avec et ta belle femme et ta famille mash’ الله الله love you
@kine1687
@kine1687 10 ай бұрын
Courage mon fils QU'ALLAH SOUBHANA WATALAH te donne long vie santé te protège et veille sur toi et ta famille incha ALLLAH yalnala thiat sekhlou yalna nga agalé ak sa sago diam rék ngay ame incha ALLLAH❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@mamethilofall7513
@mamethilofall7513 10 ай бұрын
Amine yarabi
@AlimatouDiop-b7v
@AlimatouDiop-b7v 10 ай бұрын
Walaye Seckyalnala yalla soutoural bagua amé bi hel ndakh boudoul musique amna lenéne lo hamné meune guaco investie fi thi sa réw lo hamné day diarigne sa ndawou réw Adina do keur té bene har kanam mounon thi diamou yalla nahci yalla tamite yalna yalla motali sa yéné bagua bayi wayi
@NabouNiang-qn4ky
@NabouNiang-qn4ky 10 ай бұрын
Machallah yalle na sa diam yague on es fière de toi ❤❤❤
@soguekoitala6237
@soguekoitala6237 10 ай бұрын
Machallah Waly que le bon Dieu aide pour ta décision
@khadijambodji7962
@khadijambodji7962 10 ай бұрын
Walahi seck wakhenga deugg machalah kaddouyyii amna solo Lo deff nekhenagnou
@diorbeye9640
@diorbeye9640 10 ай бұрын
Machallah yalla nala yalla takhawou si barkeb cheikhouna cheikh saliou 🤲
@mamethilofall7513
@mamethilofall7513 10 ай бұрын
Wally,kou,geum,sounou,borim, nous sommes très fiers de vous wally courage secke bilaye ont t'aimes baucoup que dieu vous bénisse et portege ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️ Amal diamou ❤️❤️♥️❤️♥️
@issasamb8258
@issasamb8258 10 ай бұрын
Machalaah naguoul nagne lako adouna bii dafa dièkh bilay nadiou diamou djii yalla nékk thi Lou bakh❤❤
@abuameenah7971
@abuameenah7971 10 ай бұрын
My love for Wally just increased to the next level
@serignelahatsylla4441
@serignelahatsylla4441 10 ай бұрын
Machala Waly seck kidal bagoon na am numérom لا تتردد فالله سبحانه وتعالى مدّ إليك يدا غفرانه فانهض إليه سيعطيك حتى ترضى!!
@SalihateGueye
@SalihateGueye 10 ай бұрын
Bilay wakhou gnite Ndiaye gue fi wakh, yallah nale yallah Sam way té may le goudou fane be gue mène yégueli say projet kou bakh gue ❤
@moussasall9051
@moussasall9051 10 ай бұрын
Wally beugue nala ba paré lo déff baxna diam thi yawe ❤❤️
@sarrpapaaliou3429
@sarrpapaaliou3429 10 ай бұрын
Machallah wakhdji dawna yarame li bockouna thick geume yalla Waly yalla na yalla mottali sa yéné thi sayé mébeut ❤❤❤❤
@aichatacamara9289
@aichatacamara9289 10 ай бұрын
Mashaallah li mom dioulit deugeu mokoy khalatt bon courage yalla neukeu yala khiir thi bopam❤❤❤❤❤
@AssuranceTV-mi3xc
@AssuranceTV-mi3xc 10 ай бұрын
Billahi wally gam yalla giga gam yalla yalla nala yalla diokh lou gan misik barkip s touba❤❤❤❤❤
@mamadoubagassama6338
@mamadoubagassama6338 10 ай бұрын
Mashaalah soyons reconnaissant en vers le clement, le tout misericordieux. Ce bas monde est ephemere. Mr Seck que le tout puissant nous facilite la voie de la droiture. Gass depuis New York🙏🙏🙏🙏🙏
@awasylla5203
@awasylla5203 10 ай бұрын
Wally secke yalla na Yalla yereme saye wadiour ake sa ake monmy dani gueye
@AmiKann-bs4xk
@AmiKann-bs4xk 10 ай бұрын
Machallah diame yallah reike moye.degue degnou nakhe souniou bobe reike
@matydiop3596
@matydiop3596 10 ай бұрын
Alhamdoulila lolou mo geun fouf yalnalasi yalla japalé inchalla
@aminataguissethiam7603
@aminataguissethiam7603 10 ай бұрын
Mon fils du.courage on est tout coeur avec toi du courage que dieu te proteche inchala❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@jolithioune9390
@jolithioune9390 10 ай бұрын
Wally yalla na yalla samou défal la godou fan ak wéér 🤲
@Papis527
@Papis527 10 ай бұрын
Musique daye wowal khôl Di riral bammel waw goor yow nitou aldjana nga bayiko
@massmbaye0792
@massmbaye0792 10 ай бұрын
wally tu a dit la verite adouna dou keur buzz 🌟 star dou dara temps la rec tu a fait la bonne choix vresmant yala defala diamou defalco toute monde si barki seydina mouhamed ❤❤
@MaguittaSall
@MaguittaSall 10 ай бұрын
Amale diam rek Mari Yacine 🙏🏼
@AngeliqueNdiaye-c7b
@AngeliqueNdiaye-c7b 10 ай бұрын
Yalna yalla khirr si boppam Masha alla dieu e tout koula gueneu diegue yalla mola gueneu
@kaddygibba46
@kaddygibba46 10 ай бұрын
What ever decision you take may Allah SWT be with you, much love ❤️❤️❤️❤️ Wally
@habibatanger6638
@habibatanger6638 10 ай бұрын
Homme conscient ! Mashalah ❤
@fafandiaye5512
@fafandiaye5512 10 ай бұрын
En tout cas wally a raison . il ne faut pas que les opportunistes jouent avec sa vision SPIRITUELLE .ya tellement de faucons autour de lui. Allah swt ne va jamais le laisser même s'il arrête la musique. Qu'allah swt le protège avec toutes ses frères et soeurs et famille , les protègent contre le mauvais oeil et leur donne une longue vie. Amine
@SeynabouDioum-ti3ef
@SeynabouDioum-ti3ef 10 ай бұрын
Courage yalla nala yalla defal diame
@djieseck6309
@djieseck6309 10 ай бұрын
C vrai Wally ,kiné yague nala nianal nga âme Lou gueune waye.mais souye diote n'a fek nga wane niou Lou palpable Lou la musique maye,comme des entreprises bénéfiques aux Sénégalais et au Sénégal.mane li la wakh et on dirait que li nga wakh osi.mais egue gou niou si wally.donc continue à nous faire plaisir et nous éveiller.voika c pas trop demander on t❤❤❤❤
@aissatoudiallo4107
@aissatoudiallo4107 10 ай бұрын
Allakhouakbar Macha Allah Ça D8ssions bi Boiuleu Si Kénneu Diélé Bayile Leupe lo khanmené Dîné L'islam défe ko Kharamale.Merci bcqs mon Frére Waly
@MameDiarraSeck-jn2bz
@MameDiarraSeck-jn2bz 10 ай бұрын
Oh bly y’a gueme yalla frère
@ChoudiaDjibril
@ChoudiaDjibril 10 ай бұрын
Alhamdoulillah qu’allah le guide tu a fait un très bon choix akhy
@kadijatoujallow3477
@kadijatoujallow3477 10 ай бұрын
Machalla Machalla Machalla Secka so proud of you ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@NdoumbeSow-r6s
@NdoumbeSow-r6s 10 ай бұрын
T fort ❤ courage Wally
@mamemariemeniasse
@mamemariemeniasse 10 ай бұрын
Walay Seck deugeula je suis daccord avec toi ta maman prefere ❤❤❤❤❤❤❤❤
@fallouserignetoubarekkamou1670
@fallouserignetoubarekkamou1670 10 ай бұрын
Sama yaram daw n'a sy wakhi wally kou deugou la wakh deug sa bopou yomboul❤
@OumyThiam-i1z
@OumyThiam-i1z 10 ай бұрын
manchalla wally li dioulite deugue moko man bikh walahi yalla nalla yalla nek lokho yalla nalla yalla may goudou fan ba lep linga beugu yalla mayla ko jtm tu es for ♥️♥️🙏🙏
@diarrathiam909
@diarrathiam909 10 ай бұрын
Meussou ma commentaire ms sma xol mo toy ❤yalnala yallah diapalé yarabi ci barké Baye 🙏❤️
@AminataFaye-r8o
@AminataFaye-r8o 10 ай бұрын
Bilay waly lou .mety yaguena thy adouna waye yalla na la yalla katanal tes ngua mouthe thy borom pekhe you bonneyi amine ya raby
@pendasene7847
@pendasene7847 10 ай бұрын
waly goudal fan rk ❤
@soukeyediaw1172
@soukeyediaw1172 10 ай бұрын
Ndeyesa métina mai yalla bah na yallna yalla déf diam
@Misskiwi277
@Misskiwi277 10 ай бұрын
Wally biss bo bayi nanga santeu yalla bouwer nga khamni yalla beuguenala bilahiii sa Guinée bi sah waroko teugue bayilep si lokho yalla
@GoraSall-xk1tp
@GoraSall-xk1tp 10 ай бұрын
Quelque soit ta décision on est de tout cœur avec toi mon frère wally seck diame rek gaye ame iow inchallah on vous aime toujours le chanteur du peuple c'est triste mais on gère 😞🫂💪❤
@rokhayafaty-gn5iy
@rokhayafaty-gn5iy 10 ай бұрын
Mar yaw Sa khol lala Yalla di faye Bilay diame rk gaye ame❤️❤️❤️❤️❤️
@cheikhba1819
@cheikhba1819 10 ай бұрын
❤❤jarama Wally 🙏
@FantaDiedhiousagna
@FantaDiedhiousagna 10 ай бұрын
Yalnala yalla takhawou si barke seydina Mouhamed
@Abdou-br8tu
@Abdou-br8tu 10 ай бұрын
C'est la meilleure décision Waly ndakhe yallah wanétina boppame .mélomaneyi dinane wét wayé mogueune
@ramandiaye3726
@ramandiaye3726 10 ай бұрын
Wally chanter c ton destin pour moi le créateur a choisi chacun son chemin chaque être ce qu'il doit faire ou avoir quand j'attends comment on vous a éduqué ça veut dire que vous êtes des bons croyant et vous le pratiquer quelques soit té décision on est avec toi beugue nayy la ba pare❤❤❤❤❤
@fatoubinetoubalde
@fatoubinetoubalde 10 ай бұрын
Yalla nala yalla defal diam faramarenne bii❤❤❤
@maremesall7137
@maremesall7137 10 ай бұрын
Nékhoul ba nékhoul mais deug rék gua wakh nak ❤❤❤❤
@TitaNdiaye-q1m
@TitaNdiaye-q1m 10 ай бұрын
Machallah yalla nala yalla diapale si barke seydina mouhamad salalahou aleyhi wa salam te sa ligue you ndeye waloula mama diaga yalla nako Yalla khare aldiana firdawsi si
@giado8414
@giado8414 10 ай бұрын
Mash'Allah Wally gueume na Yallah dé, gardez bien cette vidéo pleine d'enseignements. Li missal leye nirou dé, euskeye
@Kinendao-xo4ic
@Kinendao-xo4ic 10 ай бұрын
Machalla ❤❤ yalla nala yalla défal diam ak sotura thie barki cheikh Mohamedol faadale❤❤
@fatousowe3652
@fatousowe3652 10 ай бұрын
Mann guenala respecte of seck maryacine ❤️🥰🥰
@lamine4477
@lamine4477 10 ай бұрын
Wally yaw yanala yalla defal diamou si barkep Serigne Touba 😭
@zahradieng1513
@zahradieng1513 10 ай бұрын
Que personne ne t'influence papa bayil diamou yalla ❤ nitou yalla gua, ya des chanteurs yoo xamni meussou nioo deif prise de conscience pr bayi , yalla nala yalla yaumbalal
@diagnedeguene1401
@diagnedeguene1401 10 ай бұрын
Ndeysane yalla nala yalla defal diame yalla tèk la si yonou siratal moustakhim
@ïcharassouldiallodiery
@ïcharassouldiallodiery 10 ай бұрын
Ohhh papa dji yalla nala yalla defal diam Ballago ndoumbé yatma lo meune def on est là pour toi long Vie seck ❤❤❤😊
@arameniang3879
@arameniang3879 10 ай бұрын
Machallah yalla nala yalla diappale si liga nara bayi
Каха и дочка
00:28
К-Media
Рет қаралды 3,4 МЛН
FAMILLE SENEGALAISE - Saison 03 - Episode 45 - VOSTFR
58:14
Pikini Production
Рет қаралды 1,4 МЛН
LIVE: Wally B. Seck - DEBRIEF SHOW / Avec Abba No Stress
1:13:28
Wally Seck Officiel
Рет қаралды 264 М.
Каха и дочка
00:28
К-Media
Рет қаралды 3,4 МЛН