Réplique de Serigne Saliou Mbacké Amsa aux propos irrévérencieux de A. Khadir & de Bassirou Mbacké.

  Рет қаралды 16,328

@CheikhIbraFall-TV

@CheikhIbraFall-TV

Күн бұрын

Пікірлер: 122
@ibradieng4537
@ibradieng4537 5 күн бұрын
Maachalah la réponse est complète mais entant que Talibé je vous prie de préserver les liens de parenté.que Dieu nous protège contre les manœuvres de cheytan
@abouabdoulayecisse9191
@abouabdoulayecisse9191 4 күн бұрын
Dieureudieufatii way Dieng
@cheikhndiaye488
@cheikhndiaye488 Күн бұрын
Macha allah amna solo
@serignesalioulo8023
@serignesalioulo8023 5 күн бұрын
Waa waw saliou wakhga dëg dh bodée loulou mom Serigne tuubaa mokou binde. تبارك رب لي قضى الحاج وحده.فقيرا غريبا عند كلوى وبافل.
@AliouneSarr-x4r
@AliouneSarr-x4r 3 күн бұрын
Ndaysane bayitwi dawna yaram
@MamediarraMbacke-h4n
@MamediarraMbacke-h4n 4 күн бұрын
Domi Serigne Touba ken d'où mom
@MamadouBa-ko9ck
@MamadouBa-ko9ck 5 күн бұрын
Yaallna diam yag thie barke serigne mame more diarra
@MameboussoMbacke-vg3se
@MameboussoMbacke-vg3se 5 күн бұрын
Dieureudief Mbacké balla kadou yi amna solo loule amna ab yarr
@cctb9156
@cctb9156 5 күн бұрын
Jërëjëf serigne bi ❤
@falltouba8882
@falltouba8882 4 күн бұрын
Macahela Serigne bi amna solo
@salamdiene899
@salamdiene899 4 күн бұрын
Jerajef serigne saliou amna solo
@ibrahimacissedieureudieufs2732
@ibrahimacissedieureudieufs2732 5 күн бұрын
Machallah gnii di wakh si Serigne hamzatou danioo soof té perte douniou ay talibé dieureudieuf wakh dji rafetna
@MameboussoSaw-nr3se
@MameboussoSaw-nr3se 2 күн бұрын
S amsa limou wakh dara nekou si Serigne touba kou niouy ligueiyal
@seexxunaadaraame6809
@seexxunaadaraame6809 11 сағат бұрын
Aka ngaa wax dëgg s.Tuubaa amul moroom mukk.
@beugbamba7944
@beugbamba7944 5 күн бұрын
Nagne léne diagui khassida yi té bayi askane khassida yi moye Serigne bi lépp borome touba la kou ko bagne déle
@NdiougaWathie
@NdiougaWathie 5 күн бұрын
❤❤❤❤❤ masha haLLah
@toubapatar
@toubapatar 5 күн бұрын
Wakh dji amna soulou ماشاء الله
@aladjidiop2315
@aladjidiop2315 4 күн бұрын
Serigne saliou boul dougui si la Lila yeugual molen yeugual S Amsa limou def ken amoul tontom limou def Serigne Abdou lahat sanioko Mbacke bayilen media yi ay ndaw gen
@aissatousarr1771
@aissatousarr1771 4 күн бұрын
Dieureudieuf wakh djiiî raféte n'a amna solo lol
@khadimfaye-pz4tq
@khadimfaye-pz4tq 4 күн бұрын
Machalah wax dji rafet na Machalah
@mouhamadoufadilniang
@mouhamadoufadilniang 5 күн бұрын
Yalla na yalla sammu Serigne hamzatou Abdoul lahad
@Djiily7461
@Djiily7461 5 күн бұрын
Machallaah mbacke tontou bi toubaarkalla ❤
@dameseck7348
@dameseck7348 5 күн бұрын
Machalla amna solo lol
@seckcheikhanta956
@seckcheikhanta956 4 күн бұрын
Machalla wakh dji rafetta man de sama yaye wa mbacol la sama serigne s saliou de wa mbacol kon koulen laal lalma
@mamecheikhfall4194
@mamecheikhfall4194 4 күн бұрын
Séringné habdoul ahadd mom s bamba loum wakh daggué le loum déf daggué le
@seexxunaadaraame6809
@seexxunaadaraame6809 11 сағат бұрын
Wallaahi.
@cheikhounakhoule1828
@cheikhounakhoule1828 3 күн бұрын
Serigne saliou mbacke sunu xarit sunu wollare
@modouaichamback2429
@modouaichamback2429 4 күн бұрын
❤❤❤❤❤
@IbnuAhmad137
@IbnuAhmad137 5 күн бұрын
Machalla kaddu yi rafetna
@yaragteggiin5101
@yaragteggiin5101 5 күн бұрын
Am na nit ñu saytaane nag 😂😂😂
@bayelahadekhasida
@bayelahadekhasida 4 күн бұрын
Amna solo mbacke
@niangabdoulmalick1468
@niangabdoulmalick1468 5 күн бұрын
Maasàllaa kaddu yi Am na solo
@ahmadiop9857
@ahmadiop9857 4 күн бұрын
Serigne Abdou lahad dé mom kouko lal lal lalaké
@toubapatar
@toubapatar 5 күн бұрын
Serigne touba sakh da na ligee yall boupam kir kham li yalla def sy moum
@OusmaneMbaye-gu2on
@OusmaneMbaye-gu2on 5 күн бұрын
Wav goura ❤❤❤❤
@sagyatal8545
@sagyatal8545 5 күн бұрын
Serigne Abdoulahad mom kuko wakh dra dan la wara nokh
@SerigneSaer
@SerigneSaer 3 күн бұрын
Nio raw sa baye hamsa mbacke
@lahadtoure3131
@lahadtoure3131 3 күн бұрын
Reeww keepp molenn japp yennn
@MameDiarra-d3g
@MameDiarra-d3g 3 күн бұрын
Dangua rew ba dof imbécile bodoon sa baye dingua ko wakh meune doule
@Abdallah-gq2qh
@Abdallah-gq2qh 5 күн бұрын
Bayilén mâmi diambour yi nguèndi khèbe té wormâl nitñi ,ab tâlibé sakh bôko khèbè mou fipou wormal lène nitñ té bayi khèbâtégui ,koula gueuneu ragual yalla gueunlâ topu ay ndigueuleum môla gueune,aw askane dèsouthie gueuné nite dèsouthie yèsé nite
@gabanefall2447
@gabanefall2447 5 күн бұрын
Dèmlėne liguêyi 🤣🤣
@AIDASECK-kd5gr
@AIDASECK-kd5gr 4 күн бұрын
Ba yagui ligeuye ioe ?
@MameDiarra-d3g
@MameDiarra-d3g 3 күн бұрын
Katale sa ndeye doul demal ngua ligueyi niakh fayeda
@sarretv1760
@sarretv1760 2 күн бұрын
Serigne Touba bani nakhari mokou you bari dano dawone. Lolou histoire la. Danou dém si wolofal mame moussa ka Amna lo xam ni khél mokoy égalé
@modoufall1365
@modoufall1365 5 күн бұрын
Diéglé ak diélélé bokna thi ndigueuli Serigne Touba
@Rfdsqdetfsq
@Rfdsqdetfsq 5 күн бұрын
Boy yi dano réw té xamadi Sokhar s mor diara taloubé s touba la défou ko nawlé
@Mameballa-g9u
@Mameballa-g9u Күн бұрын
man lima.dégu.s.amsa wax mai.lolou lou baxla
@daaroulxidmatv1128
@daaroulxidmatv1128 4 күн бұрын
Waaji danoo yapp ndax waa Mbacol yepp la saga waaue dinaa
@MamadouGueye-dk7bk
@MamadouGueye-dk7bk 5 күн бұрын
Bayii lenne wakh dji thie barkep serigne mandoumbe mbacke serigne modou gueye chef religieux Senegal barkep serigne modou khabane mbacke
@TddygfiuYfdytvci-c3u
@TddygfiuYfdytvci-c3u 5 күн бұрын
Woy mbacke mbacke yagay khoulo😂😂
@SidiDienne
@SidiDienne 5 күн бұрын
Mo wakhi doff
@MameDiarra-d3g
@MameDiarra-d3g 3 күн бұрын
Sa tounou mame ak sa tounou papa ak ya yaye niak yar maye wakh mounane mbacké mbacké ya nguay khoulo imbé cile
@MaurizioEmanuele-b5w
@MaurizioEmanuele-b5w 4 күн бұрын
Sanie hamsa waroull woona diegalou. Dara waroo na bayi adina ate serinie. Fadilou nena da diaye ak diourell diandego ak taloube. Doom moogana yay mak thi ay maye
@scheikhounambacke5169
@scheikhounambacke5169 5 күн бұрын
Wa keure mame mor diara nioye thiatou yonou mourit soof nanou troup
@abodiop3328
@abodiop3328 5 күн бұрын
Astakhfiroul laah xoolaatal say kàddu ligay wax ëpp Na torop
@diaratoullahimam7494
@diaratoullahimam7494 4 күн бұрын
Lolou dé ay doul ya Kat sa nday mana fén
@dofndeye3772
@dofndeye3772 4 күн бұрын
Astaxfirul laah
@SerigneCheikhounaMbackeSaye
@SerigneCheikhounaMbackeSaye 5 күн бұрын
SUNU LÉPP SERIGNE TOUBA 🤍
@CheikhNiane-lo5hi
@CheikhNiane-lo5hi 4 күн бұрын
Sëñ hamsatu Mbàkke waxul dara lu Aay lu jar wax Fii ñépp boroom tuubaa moo leen dimbali mag ak rakk ñépp taalubey boroom lañ
@MamadouGueye-dk7bk
@MamadouGueye-dk7bk 5 күн бұрын
Na ngnou deme lyueyui te diamou djii yalla serigne modou gueye chef religieux Senegal makò wakh barkep serigne mandoumbe mbacke
@mamechiekhfall315
@mamechiekhfall315 5 күн бұрын
Dèglouna kadouy wa keur s bara khouradia ak kadouy serigne saliou mi kadouy serigne saliou mi rafét na ndakh mome dou sakh salaw lou serigne mame mor mame Diarra wayé ngè sakh niom daniouy salaw lou sèn mame
@دارالهدى-ص6م
@دارالهدى-ص6م 4 күн бұрын
Chaine bi Kiko mom bayi len di jaxase ay mbokk
@ngagnegaye8099
@ngagnegaye8099 Күн бұрын
Mbacke ya wor
@MamadouGueye-dk7bk
@MamadouGueye-dk7bk 5 күн бұрын
Deme lenne lygueyi te diamou djii yalla te guene delou thie tooll yii bayyi Man serigne modou gueye chef religieux Senegal makò wakh barkep serigne mandoumbe mbacke
@khaliloulah0903
@khaliloulah0903 5 күн бұрын
Wa man dama diakhle wakeur serign barra khouray dia yi yen sen maam serigne barra khouray dia da ligueyal serign touba ba wathie serign maam mor Diarra def nonou wala borom sham da diomb serigne touba wala borom sham waroul ligueyal serigne touba boulen fonto nitt gni soulen nekhoul guen guen serigne bi
@MameastaMbacke-p7s
@MameastaMbacke-p7s 5 күн бұрын
Aye way suppirmer😭😭
@ibrahimasakho9286
@ibrahimasakho9286 4 күн бұрын
Diayanté gogou mowaral Serigne fallou diaye ndiourélam dieundéko talibé Serigne bi aye mbiram dou mbiram domou Adama
@BayematarMbacke
@BayematarMbacke 5 күн бұрын
Amsa day fen rek
@AhmadouBambaSarr-so6vl
@AhmadouBambaSarr-so6vl 4 күн бұрын
Sa baye milla yaroul baguay sagua hoalatal sa bope
@moramar3789
@moramar3789 4 күн бұрын
Thim do rouss sakh Lii war ngako rouss
@moramar3789
@moramar3789 3 күн бұрын
Wallahi sa saaga yi rouss ngasi danga kham ngani fii rek ngay nek di saaga
@MameDiarra-d3g
@MameDiarra-d3g 3 күн бұрын
Sa baye moko dakha féne sa yaye moko dakha doul
@yaragteggiin5101
@yaragteggiin5101 5 күн бұрын
Yeen site yi yeen a war a bàyyi di tasaare yu mel nii.
@bayesidimbacke9524
@bayesidimbacke9524 4 күн бұрын
واو كور بك جرجف
@andybachirfall-zh1cr
@andybachirfall-zh1cr 4 күн бұрын
toppal feuleu sa waajour mo wakh Lou wakhou woule Mame mor Diarra dou seen morom yabaaté nguén trop
@ousseynoutoure3621
@ousseynoutoure3621 5 күн бұрын
Serigne bi gni daal dagno wayadi serigne touba mo serigne gneupe lolou kouko bagne da ngua soneu ndakh lolou leu yallah dogal
@moustaphababou6282
@moustaphababou6282 4 күн бұрын
Wakhe dji kone diekhoul ba legi li mome niawna trop billahi
@madXfad3542
@madXfad3542 5 күн бұрын
War naniou moytou yeneu wax yi. Niou beuri ci nioune mourides daniouy wax te douniou setental. Ci sama xalatou bop lima gueume mooye kersa bi serigne bi amoone ci Serigne Mor moome la amoone ci Serigne Sam. Kon mounoumaa gueum ni Serigne Touba dinako santeu loumou doone santeu ndongo yi ak mag yi andoone ak moom ndax ceru mag ci zair.
@Beugbamba2024
@Beugbamba2024 14 сағат бұрын
Tontou sakh diarou ko borom khel yi kham nagne ni li YALLA dogal moy serigne TOUBA
@HamzaMbacke
@HamzaMbacke 4 күн бұрын
Wax nga deug ça tek koci xam xam ci ku diang
@Mameballa-g9u
@Mameballa-g9u Күн бұрын
sokhor rek
@SaliouSow-gj6or
@SaliouSow-gj6or 5 күн бұрын
Nagne liguey té diamou yalla bayi mam yi niou reposer en paix.
@modoukabirthiam4054
@modoukabirthiam4054 4 күн бұрын
Serigne bi iow Lou leer nga wax borom Sam ak Serigne Touba nio bokk lep
@diaratoullahimam7494
@diaratoullahimam7494 4 күн бұрын
Wallahi
@Abdallah-gq2qh
@Abdallah-gq2qh 5 күн бұрын
Wakhal sa baye mou bayi mamou diambour yimouy khèbe
@SidyToure-r9s
@SidyToure-r9s 5 күн бұрын
Tontonte bakhoul hése gore diaye mougne
@Abdallah-gq2qh
@Abdallah-gq2qh 5 күн бұрын
Bok ci askane wou bâkh takhouta gueune kéne,bokou ci askane wou bonne takhouta geueuneu bonne kéne, koula gueuneu ragual yalla dakh la dieuf dieufdiou raféte môla gueune
@khouledjily1505
@khouledjily1505 8 сағат бұрын
Yawo saringne bi mou tone doule rek laye deff yene li kene ne borom Touba ne wo si
@MamediarraMbacke-h4n
@MamediarraMbacke-h4n 4 күн бұрын
Reew ak niak tegine niak worma lim wax niawna lool
@yaragteggiin5101
@yaragteggiin5101 5 күн бұрын
Commentaires yi bari na ay saytaane 😊😊
@MoustaphaSourang-qo1cz
@MoustaphaSourang-qo1cz 5 күн бұрын
Aywa jiee nopi leen Guir yalla Youn wi de xamol lii ay wax
@babacarkhadim1058
@babacarkhadim1058 4 күн бұрын
AYY WADJI TEGUENA SOUTOURALANTE NGUIR YALLA TE ROUSS TALIBEYI
@BayematarMbacke
@BayematarMbacke 5 күн бұрын
Y’a mana fen
@gouyartvdieng5005
@gouyartvdieng5005 5 күн бұрын
Lii diaroure pratager Lou way wakh nam si nioume rk
@modoundiaye6044
@modoundiaye6044 5 күн бұрын
Seex Abdul Ahad budul dellu waay kan mooy dellu waay
@SonhibouMbow
@SonhibouMbow 5 күн бұрын
Mame kaye lolou diakhaln nama s abdou lahad kou bakh
@dembafall1168
@dembafall1168 5 күн бұрын
Mbacké mbecna lol wakhal gama lima beuga wakh lèpou
@SeringneMoustapha_mbacke
@SeringneMoustapha_mbacke 4 күн бұрын
iow yagui khoulo
@NdeyeMbacké-n6v
@NdeyeMbacké-n6v 4 күн бұрын
Amo lo wakh yak se abaya yam
@AIDASECK-kd5gr
@AIDASECK-kd5gr 4 күн бұрын
Ioe Lo diapal sën khamza fo dem commentaire fa sa wax djou niaw bi si djiguene rawatina gua sante mbacke !!!!!niaw na lol!!!!!
@mameboussotoubambacke
@mameboussotoubambacke 5 күн бұрын
Tegeuna dello saytané ay lafam
@TddygfiuYfdytvci-c3u
@TddygfiuYfdytvci-c3u 5 күн бұрын
Ma rouss serigne sagay khoulo😭😭
@YayeAwaGUEYE-ci2hx
@YayeAwaGUEYE-ci2hx 4 күн бұрын
Rousseul thi sa bope ba paré. Sa niari posts you opposés. Bene bi ngay rétane bénéne nga dioy. Satan togal
@Macaallah
@Macaallah 4 күн бұрын
Du niun Ak yaw niun Ak sa bay la
@AhmadouBambaSarr-so6vl
@AhmadouBambaSarr-so6vl 4 күн бұрын
Amal talibé bayam doussa morom demal wah sa kilifa mou yar la
@Macaallah
@Macaallah 4 күн бұрын
La s touba wakhon yefuer ba lalay ku amul trguin si yonentebi SAW do kham sama wormay khalima waye man ku khamul sama wotmay kilifa Bul khar si man worma Ak ko mana don
@serignesalioulo8023
@serignesalioulo8023 5 күн бұрын
Waye mane dama gis ni dafa am xista you xamni même bodée dëg dou wakhi mboulou
@SerignemodouMbacké-b8i
@SerignemodouMbacké-b8i 5 күн бұрын
Yéne kone serigne touba mome guéni wéddi Kone mome limou diangalé Dieufé wouko Boudé li Amsa fénn dagénka deugal Diokh samak thieur Tagg sa baye ak sa mame dafa yopou lool
@Ndeyediop-w6s
@Ndeyediop-w6s 4 күн бұрын
Fi dale bene serigne mo fi ame te moye serigne touba kene kougnou fi toudou rek ab talibe rek gua serigne bi limou yore dakoye diaye mokou mayewouko lolu fokou mou lere
@SerignemodouMbacké-b8i
@SerignemodouMbacké-b8i 5 күн бұрын
Serigne touba amoul doome moko wakh dh yénako wakh wayé amoul mak masouko wakh S Abdou lahad mbacké séne mame néna nit boudé dém aras aka nieuw bouféné niounéko fénga ta Mome Bayame dafa dafa fén Niounéko fénga bamou khamné fenna Baguénn diégalou lolou kaséla dou Dara
@NdiayeAlioune-to9lv
@NdiayeAlioune-to9lv 5 күн бұрын
Wallahi dama rousse sax ,ana yar ak téguine ba ñou xamé woon murid ; Yaw rouso di wax nit fèen ngua 😢😢😢
@SidiDienne
@SidiDienne 5 күн бұрын
Modou mbacke amal ayy tégeune. Mangui la guiss yangui si réseaux yi dembou ba legui ya ngui saga. Mai baxna
@MamethiernoMbacke-u3t
@MamethiernoMbacke-u3t 4 күн бұрын
Ndaysaan
@AIDASECK-kd5gr
@AIDASECK-kd5gr 4 күн бұрын
Ioe rew gua ba doof sunu ko waxon sa baye dinala nex est ce que? Yabatei de Trops
@SegnaAme
@SegnaAme 5 күн бұрын
Yaw fi sa baye diar diar fi khoul mak daye yaro
@bachirmbacke422
@bachirmbacke422 5 күн бұрын
Waxleen seen baay mu bàyyi racisme ak xeebaate gimu nekke
@xamxamtv3003
@xamxamtv3003 5 күн бұрын
Nitt daal kén doko khébal maamam. Problém bi yépp khébaaté rk la
@GueyeMarakhib28
@GueyeMarakhib28 4 күн бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 34 МЛН
Арыстанның айқасы, Тәуіржанның шайқасы!
25:51
QosLike / ҚосЛайк / Косылайық
Рет қаралды 681 М.
If people acted like cats 🙀😹 LeoNata family #shorts
00:22
LeoNata Family
Рет қаралды 44 МЛН
🚫🚫🚫 / ❌❌❌ / Kaddouy Serigne Amsatou Mbacke Abdou Lahad jëm-çi Mame Borom Sam
5:44
Touba-Sam / Serigne Mame Mor Mbacke Washington-DC
Рет қаралды 36 М.
Qui était Serigne Saliou MBACKE ? | S. Makhtar Kébé & S. Khalil MBACKE
2:04:37
VISIT DE SERIGNE AMSATOU MBACKE CHEZ SERIGNE SALOU
17:43
Touba Belel TV
Рет қаралды 2,3 М.
Réaction de CAMS sur une vidéo de ce vieux loquace
9:22
Nihma TV
Рет қаралды 6 М.
黑天使只对C罗有感觉#short #angel #clown
00:39
Super Beauty team
Рет қаралды 34 МЛН