Réponse de Serigne Abdoul Ahad Mbacke Amsa à A. Khadir Mbacké & Bassirou Mbacké.

  Рет қаралды 24,793

@CheikhIbraFall-TV

@CheikhIbraFall-TV

Күн бұрын

Пікірлер: 214
@abdoucisse6605
@abdoucisse6605 5 күн бұрын
Machallah amna solo kou fii ame dara serigne touba mou la kou diokh nay leer
@CheikhounaMbacke-q6v
@CheikhounaMbacke-q6v 4 күн бұрын
Yalla Nanu Yalla Moseul Thi Seytane Barkep Cheikh Abdoul Ahad Mbacke ❤️
@NdeyaNdiaye-o2j
@NdeyaNdiaye-o2j 3 күн бұрын
Ndeysan serigne amsatou kou bah te oyof doundal te werr mbacke balla ❤
@sallsalihlecarolart3894
@sallsalihlecarolart3894 5 күн бұрын
Lii mom yalnafi gaaw yém lii gueunul dé ☝🏾 walahi ☝🏾 gueunùl
@ModouDjilydjily
@ModouDjilydjily 5 күн бұрын
Kou Serigne Touba géne ci yawe Dara Dou dese si yawe ak ko mana nek yéna gui wouyo aye mourit mourit môme Serigne Touba mo woté yonwi kou gnieuwe nek talubé
@AbdoulahadFall-qw4lv
@AbdoulahadFall-qw4lv 3 күн бұрын
Wallahi
@assanediop2768
@assanediop2768 5 күн бұрын
Wakhdji amna solo wayé nioune talubeyi linouy sakkou moye ngene tethie bountou bi ndakh sayntané rek mociye gagnez
@Bichri-rek
@Bichri-rek 5 күн бұрын
😢😢😢wallaHI tethie line bontu bi lii nekhol si nione talibe yii😭😭😭😭😭
@ElhadjialassaneMbaye
@ElhadjialassaneMbaye 5 күн бұрын
Fi serigne touba rek❤❤❤
@MountakhaSylla-x7i
@MountakhaSylla-x7i 5 күн бұрын
Machalla dieuradieuf cheikh Abdoul ahad mbacke amsa ولکن أکثر الناس لا يعفلون 😢
@BayeNdiaye-bs3pb
@BayeNdiaye-bs3pb 5 күн бұрын
Machallah waxdji Amma solo lol serigne Touba rekk la nak ❤❤❤
@scheikhounambacke5169
@scheikhounambacke5169 5 күн бұрын
Machalla kadou yi rafetna troup
@bayngagnediene1833
@bayngagnediene1833 2 күн бұрын
Machalah amna solo serigne Touba Dal loufi Way am Moom la
@barrezi
@barrezi 5 күн бұрын
Kou nangou woul né sa mamm talibéb Serigne Touba la, guénal ći yonou Mouride.
@ahmadoumbacke-wo6jh
@ahmadoumbacke-wo6jh 5 күн бұрын
Wallahi nii danioo gorèdi rék wayé li Sama mame Serigne amsa wakh dara nèkkou thi
@papasambandiaye5405
@papasambandiaye5405 5 күн бұрын
Machalla SERIGNE ABDOU LAKHAD AMSA kadou yi rafetna Baye AMSA MBACKE Abdou lakhad kou bakh oyof rafete khol machalla dalal nama thi sallam Magal 2021 kou togoul ak mome do kham moye kane dithi nouyou wakeur Serigne AMSA yepou thia touba Alieu dafa nékni dég wakh dafa diaffé yallana Borom bi defar lépou thi barkép AHMADOU
@omarmbaw4161
@omarmbaw4161 5 күн бұрын
Légui dall konni fi sa mame Talibé Serigne Touba la mou mérr worguin sênni mame nak sénni mame amoul maguou Serigne Touba wala rakam kén kounék lagua am Serigne touba Mola ko Défal Nék Lén Ayy Té faye Nar bi khoromam 😢
@FallsyCheikh
@FallsyCheikh 2 күн бұрын
Machallah Serigne saliou kadou yi rafetna loll té andeu na ak yarr tégouna ci xam xam .mane nak ci sama guiss guiss Serigne amssatou limou wakh guisouma Lou aye té dégoumako ci
@ibrahimatoure7709
@ibrahimatoure7709 4 күн бұрын
Mâcha alla serigne bi ❤🎉
@sokhnamomymbacke9761
@sokhnamomymbacke9761 5 күн бұрын
Machala amna solo trop
@barasow3654
@barasow3654 5 күн бұрын
Serigne amsatou MBACKE ibn serigne abdou Lahad MBACKE deugue rekk laye wakh té mome la meussa wakh yalla na fii yague tee ande ak werr si barke borom Touba…DIEUREDIEUF borom touba diarama mame cheikh IBRAHIMA Fall lepp borom touba kassé la
@ibrahimacissedieureudieufs2732
@ibrahimacissedieureudieufs2732 5 күн бұрын
Dieureudieuf Serigne bi sante nanioula bou wer amna solo lool
@mameastoumbacke625
@mameastoumbacke625 4 күн бұрын
Machallah dieuredieuf stouba
@amadoufatimakane3564
@amadoufatimakane3564 5 күн бұрын
Ku TEDD KI ❤️ ❤️ ❤️ ❤️, ku MAGG KI❤❤❤❤,BOROOM JAAM ÑI. LEPP MOOM LE
@mouhameddiallo8975
@mouhameddiallo8975 3 күн бұрын
NdeysanN ✨ App Taloubé rka am solooo 💞💞💞💞💞🤍🤍🤍🤍🤍❣️❣️❣️❣️
@kebekebe587
@kebekebe587 5 күн бұрын
Machalla
@papasambandiaye5405
@papasambandiaye5405 5 күн бұрын
Dafa nék ni seytané founé lay diar pour yakh lou rafete yallana Borom dakh seytané thi li comme niko SERIGNE FALLOU dakhé wone thia liggueyou dioumay TOUBA ❤️❤️
@bassiroundiaye3913
@bassiroundiaye3913 5 күн бұрын
Amine barké chiékhoule khadimou sabouma dégué ay yeugou yeugou thi sounou keuri diné yi damay tire diakhlé
@Zallsunu
@Zallsunu 5 күн бұрын
S AMZA DAH WANÉK MATE DIAREDIEUF❤❤❤
@YayeAwaGUEYE-ci2hx
@YayeAwaGUEYE-ci2hx 4 күн бұрын
Walahi bima dégué tontou wame dama contane. C'est un grand homme
@CheikhounaDiop-y5r
@CheikhounaDiop-y5r 3 күн бұрын
🤔🥺😭♥️♥️♥️♥️☝️🙏
@MourtadaMbacke-m2x
@MourtadaMbacke-m2x 5 күн бұрын
Wayé li bane ndiarigne la am ay nitt kouné took di werénté thie lou amoul bén ndiarigne sehutt djiff ji soufé na loll waye 😮
@Malick-n5t
@Malick-n5t 5 күн бұрын
Waw ❤❤❤goor
@Malick-n5t
@Malick-n5t 5 күн бұрын
Wa ker mam Mor Mbacke mom Sokhna Diarra Aye Talou bi rek lanu S Touba rek❤ moufi Neek
@SerignemodouMbacké-b8i
@SerignemodouMbacké-b8i 5 күн бұрын
Yéne kone serigne touba mome guéni wéddi Kone mome limou diangalé Dieufé wouko Boudé li Amsa fénn dagénka deugal
@SerignemodouMbacké-b8i
@SerignemodouMbacké-b8i 5 күн бұрын
Serigne touba amoul doome moko wakh dh yénako wakh wayé amoul mak masouko wakh S Abdou lahad mbacké séne mame néna nit boudé dém aras aka nieuw bouféné niounéko fénga ta Mome Bayame dafa dafa fén Niounéko fénga bamou khamné fenna Baguénn diégalou lolou kaséla dou Dara
@NdiayeAlioune-to9lv
@NdiayeAlioune-to9lv 5 күн бұрын
​@@SerignemodouMbacké-b8iyaw yaa dieufè ndigueul serigne touba yaw miy wax kou mak fèn ngua 😔
@NdiayeAlioune-to9lv
@NdiayeAlioune-to9lv 5 күн бұрын
​@@SerignemodouMbacké-b8ilègui daal da nguèn xèèb ab talibè? Reuy keep mo lèn diaap ak gorèedi 😢
@omarmbaw4161
@omarmbaw4161 5 күн бұрын
​@@SerignemodouMbacké-b8i yaw sëgn bi gua balma mais rewgua tropp
@papesougou2965
@papesougou2965 4 күн бұрын
Nagnou fékhé ba loufiy waye ame rek dou Serigne Bi. Serigne Touba reka fiy nék🎉
@mbackeskhadim9539
@mbackeskhadim9539 5 күн бұрын
Cëy ! Sama Boroom yàlla bu bu saytaane am ndam ci mbir mii.
@mourtalladiagne359
@mourtalladiagne359 4 күн бұрын
Mouytouleenn téléphone yii ak réseau sociaux yii saytaane le dankoo waajaloul nitt doù loumou xam waxko wax yitt bou amoul njarign matou la wax
@AbdoulahatGueye-i3b
@AbdoulahatGueye-i3b 5 күн бұрын
Machalla s late wakh dji rafet na lole sakh
@tvkhoudoss7680
@tvkhoudoss7680 5 күн бұрын
S touba rek
@bakhdad
@bakhdad 5 күн бұрын
MashaAllah Serigne Amsa limou wakh dara nekou thi gayi kay nioy naafeek rek begg diakhassei ak yéé fitna
@GueyeMarakhib28
@GueyeMarakhib28 5 күн бұрын
Merci mbacké balla
@ChekheibraThiam
@ChekheibraThiam 3 күн бұрын
Diekhal len wakh dji wakh dji nafi yam li dara diaroko
@fallousylla5997
@fallousylla5997 5 күн бұрын
ماشاء الله
@MamadouMbacke-k4h
@MamadouMbacke-k4h 5 күн бұрын
Machallah wakhdji rafétna
@moustaphalo3400
@moustaphalo3400 5 күн бұрын
Billahi lu wér lu fi way am Serigne Touba
@modoufall1365
@modoufall1365 5 күн бұрын
bayiléne wakhdji thi barké Serigne Touba
@BayeSylla-q6y
@BayeSylla-q6y 5 күн бұрын
Fii Ken doufi Dara lepp serigne bi la
@daaraycheikhoulkhadiim4939
@daaraycheikhoulkhadiim4939 4 күн бұрын
Bayyi caaxaan yi sëriñ bi rekka fi nekk.😢😢 Moytu leen moytu léen!
@BayedameDiop-iz5su
@BayedameDiop-iz5su 5 күн бұрын
Thiey Sénégal kofi wakh lo ndaw sisa srigne ngay merr mais bodé محمد صلى الله عليه وسلم comme dara khewoll te serigne tooba lomm am younetibi moko geunall 😮
@FallouGueye-t7g
@FallouGueye-t7g 5 күн бұрын
Fi dall koudoul serigne touba Thi yonou moutid app taloube rek ga ak koumou mana don nak taloubeb serigne touba ga
@pikiniproduction954
@pikiniproduction954 5 күн бұрын
Deugg la dh
@morfall1519
@morfall1519 4 күн бұрын
dano khamadi rek waye fi leup serigne bila
@bawal1bawal977
@bawal1bawal977 5 күн бұрын
Amna solo loool. Lii dange thee warra diangate ne histoirou mouridisme. Dagnko warra bindue mbindue mou officiel. Ndakh histoire mome. Daye neekh mba mou nakhare. Niennue. Rek.
@SerignemouhamadoulMbacke
@SerignemouhamadoulMbacke 3 күн бұрын
Lol de amna solo ndakh khissa yi wèroul dabari loool
@SerigneSaer
@SerigneSaer 3 күн бұрын
Waw ka sa wadiou wakur mame mor diara niou len guen niou len raw
@bayelahadekhasida
@bayelahadekhasida 4 күн бұрын
Amna solo
@MamadouGueye-dk7bk
@MamadouGueye-dk7bk 5 күн бұрын
Deme lenne lyueyi te diamou dji yalla serigne modou gueye chef religieux Senegal makò wakh barkep serigne mandoumbe mbacke
@complexenabich9182
@complexenabich9182 5 күн бұрын
wakh thi rafetna mbacke thé ande ak yar mane dé khamou mala mais rafet lo nako lole
@sfalloutoure
@sfalloutoure 5 күн бұрын
Yén koulén fék ngéni khoulou ci Internet bi lanla leen di wara wakh Respect leen sén taloubé way ah
@samadgueye-eg7kk
@samadgueye-eg7kk 5 күн бұрын
Wérna
@MameastaMbacke-p7s
@MameastaMbacke-p7s 5 күн бұрын
Wallahi
@AbdoulahadFall-qw4lv
@AbdoulahadFall-qw4lv 3 күн бұрын
Diereudief mbacke
@mbackeniang1013
@mbackeniang1013 4 күн бұрын
Serigne touba amoul morom amoul dénde
@sagyatal8545
@sagyatal8545 5 күн бұрын
Waaw goor Mbacke
@AbdouThiaw-do8dc
@AbdouThiaw-do8dc 5 күн бұрын
شكرا
@bayeserignetoure-jr2zz
@bayeserignetoure-jr2zz 5 күн бұрын
Machallaah mbakke kadou yi rafet na xam xam bi leer na
@amadoulaminediop8852
@amadoulaminediop8852 5 күн бұрын
Lou waye ame ba diko ndamo serigne touba la siguil na mbacke ak sante yeup maye nalene bagne tambalé faté faté lou kene dou wakh ba wédi né lou waye serigne bé thiakhane baxoul
@malickndiaye631
@malickndiaye631 4 күн бұрын
Serigne amsa lubakh rek la dioublou wone thi wakh dji dafa Baga wakhné Serigne bi diébalou mofiy diarigné ak loo mana done thi mom nak magag rakak domak diarbatak lépa thi yam wayé seugn amsa monone naa diokhé misal tedou nétalil khista bobou ndakh nim wakhé dafa melné Mame mor Diarra dafa yékha diébalou motakh amoul wone barké té deug naa mo ndiaka diayanté ak Serigne bi guinaw Biko Serigne bi bindé lettre khamal koné yalla dama wotélo té werouway laa lettre ba Serigne ndam abdou rahmane lo lako diokhone
@skhadimmbacke5328
@skhadimmbacke5328 5 күн бұрын
Askey waxji rafetna dallna xamxaména teginouna waw goor douyna sacke mback bala
@Akd-l4c
@Akd-l4c 5 күн бұрын
Kagne Guine di Nagouel s Touba réc yéne wa keur s mame
@AissatouDia-fz7pk
@AissatouDia-fz7pk 17 сағат бұрын
Bayilene wakh dji ayes mbokes nguene 100 pour cent
@mass1990
@mass1990 4 күн бұрын
Wakhji rafetna lool mbacké andnak kham kham wakahi dangô khamoul rek
@cheikhoulkhadimdiouf4524
@cheikhoulkhadimdiouf4524 5 күн бұрын
mbokou serigne bi yeup danoh barii… waye saa sou-niou wakh rk nguén momeleko sen bobou… hmmmm Waye dal domou Serigne TOUBA douh moromou ken’ kouko diokhoul worma nak amooo ben thieurr ci Serigne bi!
@MameboussoSaw-nr3se
@MameboussoSaw-nr3se 2 күн бұрын
Deug deug
@bachiirleveridique9767
@bachiirleveridique9767 4 күн бұрын
*SËRIÑ HAMZA* DÉ WAXUL LU AAY DËGG-DËGG
@AhmadoumouhniyaneFaye
@AhmadoumouhniyaneFaye 8 сағат бұрын
Mame mor Diarra talibé Serigne Touba la nako niepp xam s amsatou loumou wakh Dara nékou ci
@alphaoumarbarry3285
@alphaoumarbarry3285 5 күн бұрын
Cheikh Ibrahima Fall bou amoull thi yoone wi kone mou doywaaarrr lol
@MoustaphaSeck-g8s
@MoustaphaSeck-g8s 5 күн бұрын
Asalamou alaykoum seringe touba masoule khoulo ak mbokam nioun talibeyi am naniou louniou mety
@schiekhonafalldialebatolma80
@schiekhonafalldialebatolma80 5 күн бұрын
Ñoom daal li ñuy baña dëkk mooy maam Moor Jaara lu mu am sëriñ Tuubaa la Waxtu wu ne Liñuy Tiitaroo mooy mook sëriñ Tuubaa ñoo bokk Lëpp Ta maam Moor Jaara daa Lëggeeyal boroom Tuubaa ba am gërëmam Niko ñëbb defe
@SerignemouhamadoulMbacke
@SerignemouhamadoulMbacke 3 күн бұрын
Li wakh ak totgn migui si ta reyna lool. Serigne Saliou Mbacke ridiyal lahou hanhou wakh nan nè bomasana tok fi mom ba toudou borom sam danan hoo kokou da bok sa mag nia
@daaroulxidmatv1128
@daaroulxidmatv1128 4 күн бұрын
Waa mbaacol yepp lan saaga waaye dinaa
@tvadamandiayekhassaidtouba8388
@tvadamandiayekhassaidtouba8388 5 күн бұрын
WAKHTANE LENE KO THI SOUFF NGUIR YALLA TA BAYI LY SERIGNE TOUBA AK S MAME MOR DIARRA BENE LANIOU WALEU NIARY TARIKHA DAFA AME TA YEGOU NIOUKO 😳🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
@mameboussotoubambacke
@mameboussotoubambacke 5 күн бұрын
Bilay niou bok ndeye ak Bay dh
@SonhibouMbow
@SonhibouMbow 5 күн бұрын
❤❤❤❤
@diopbara7935
@diopbara7935 3 күн бұрын
Amssa Nabayi Mami Diambouryi Dou Darra Abe Dourkatte La
@mamcheikhgaye7395
@mamcheikhgaye7395 5 күн бұрын
فلا تنازعوا فتفشلو ا فتذهب ريحكم
@hygieneservice2603
@hygieneservice2603 5 күн бұрын
Abdou Lahd wakhofi Dara féne rék gaye déf ba mala khamé ba légui féne lala khamé
@ABDOUWAHABSAHRAANIDia
@ABDOUWAHABSAHRAANIDia 3 күн бұрын
Ndeysaan serigne bi mangui ziar danga baakh rek gnoom gnepp lawakh bayi wouma ken koosi guennee si serigne touba ben paa rek lay doon comme sama baay
@SerigneSaer
@SerigneSaer 3 күн бұрын
Mame mor diara amoul sat bouye nan sagara amoul sat bou diangoul wakh leen lou bakh
@SerignemouhamadoulMbacke
@SerignemouhamadoulMbacke 3 күн бұрын
Keur borom Sam mom diahil bariwoufa ndakh kham kham fala fèk bakh Serigne bi bimouy wakh douma magui ken douma nidiayi ken..... Borom SAM migui fiwon wayè takhoul Serigne binè douma ragui kèn guir wormal goum wormal borom Sam
@CheikhSenetou
@CheikhSenetou 5 күн бұрын
جرجف❤❤❤
@diawndongo2489
@diawndongo2489 5 күн бұрын
Man bima sen video yi kou nek di wakh ma diap ni serigne bi loumou wakh da reuy mai bilahi lima wakh dara nekou si fi loufi way am si yon wi danga foutékou diayanté ak serigne lan moy problem bi
@AbdouThiaw-do8dc
@AbdouThiaw-do8dc 5 күн бұрын
😭😭😭
@AbdouThiaw-do8dc
@AbdouThiaw-do8dc 5 күн бұрын
ماشاء الله شرجب
@gaydelgaye5934
@gaydelgaye5934 5 күн бұрын
Diaradieuf serigne abdoul ahad borom belel le BATISSEUR kouko yam danga fek mouy nélaw
@mamechiekhfall315
@mamechiekhfall315 5 күн бұрын
Serigne amsa liou wakh dara nèkou si
@serignesalioumbacke10
@serignesalioumbacke10 5 күн бұрын
Waxji dé se mor diara la ci jublou,ndax worma jum dougal ci Sén diganté se touba se mor diara dong ladon wormalé nonu.saway nopil way,yaw liga ciy dougal dara lalé wouci waxal ci sa bay rék,
@salioudiakhate2919
@salioudiakhate2919 5 күн бұрын
tardee daal deef ngen ko ❎geunn leen si liii yii amoul solo keen kou neek di defandar sa bopp ak meel ni leep dadoul been ❎😭
@Zallsunu
@Zallsunu 5 күн бұрын
DIAYANTÉK S TOUBA DALAY YOK WAYÉ DOULA WAGNI NANOU BAGNA KHADIAL SAYTANÉ SUNU BIIR DIROUL GOUDAL WAKH DJI
@mortalladieng8595
@mortalladieng8595 5 күн бұрын
Serigne bii rék kafiné
@KhadimThioub-s3m
@KhadimThioub-s3m 5 күн бұрын
FI yonou mouride SERIGNE TOUBA rek mofiy serigne,kouffi eupeu talibé yaffi gueune.
@yaragteggiin5101
@yaragteggiin5101 5 күн бұрын
Foo teg ni ku fi ëpp ay taalibe moo fi gën?
@gueyedame4145
@gueyedame4145 5 күн бұрын
Xam naa wëddi taalube k sëriñ Mam Mor Diarra Dj Woroul
@ElhadjidaourDiongue
@ElhadjidaourDiongue 5 күн бұрын
nagnou delo thi Serigne Touba ra toup te jegalou tay jegale .
@AbdouDiop-kg8ry
@AbdouDiop-kg8ry 5 күн бұрын
Kham nani dall deuge wakh dafa nakhari trop
@khelcomdaroubayla6133
@khelcomdaroubayla6133 5 күн бұрын
والله العظيم سرنج حمزة دف باق رك واى موم دف دون سنجي رك
@TddygfiuYfdytvci-c3u
@TddygfiuYfdytvci-c3u 5 күн бұрын
Akhirou samane deuge serigne sagay khoulo😭😭
@mamechiekhfall315
@mamechiekhfall315 5 күн бұрын
Seirgne amsa kadouy serigne khabane la don diotali tè limou wakh fofou dara nèkou si
@Abdallah-gq2qh
@Abdallah-gq2qh 5 күн бұрын
Amsatou Mbacké wakhlènko mou bayi klifa diambour yimouye doyodal lou mélnî bétouma thi môme ndakh déndéléna ay wakh batayi serigne mountakha
@maimbengued.7504
@maimbengued.7504 5 күн бұрын
Mais qu’est-ce qu’il s’est passé ?
@fdd10057
@fdd10057 5 күн бұрын
Li serigne amsa wakh mouy deuk ku fi bagn ne sëriñ bi mol sed bo tamble diouma di nga sonn lol mu dora pare serigne Touba ak bokk mayewga dara
@serignemodoumbacke6172
@serignemodoumbacke6172 5 күн бұрын
Dangay doul ndax borom touba ba mouy tane s Mor diarra say mame niogui fi wone
@SerignemodouMbacké-b8i
@SerignemodouMbacké-b8i 5 күн бұрын
Serigne touba amoul doome moko wakh dh yénako wakh wayé amoul mak masouko wakh S Abdou lahad mbacké séne mame néna nit boudé dém aras aka nieuw bouféné niounéko fénga ta Mome Bayame dafa dafa fén Niounéko fénga lolou kaséla dou Dara
@latdiordiop6051
@latdiordiop6051 3 күн бұрын
Sabay mo togn.
@seringemorDiop
@seringemorDiop 4 күн бұрын
Seringe fallou fall bayyille yatalle wakhe yi manne mome diakhalgama
@sonhiboushop2855
@sonhiboushop2855 4 күн бұрын
Serigne wakhon nouniouy diarigno tie mom mtx Serigne fallou ni mom talibé diaye ak diourélam dieunde ko ak talibé
khassida mawahibou9
2:25
Serigne Moussa Sam Mbaye
Рет қаралды 24
Serigne Abdoul ahad amsa xadar mbacke Bassirou mbacke ❌🚫❌🚫🛑
5:22
BAYGUYSTAN | 1 СЕРИЯ | bayGUYS
37:51
bayGUYS
Рет қаралды 1,3 МЛН
How many people are in the changing room? #devil #lilith #funny #shorts
00:39
To Brawl AND BEYOND!
00:51
Brawl Stars
Рет қаралды 16 МЛН
🚫🚫🚫 / ❌❌❌ / Kaddouy Serigne Amsatou Mbacke Abdou Lahad jëm-çi Mame Borom Sam
5:44
Touba-Sam / Serigne Mame Mor Mbacke Washington-DC
Рет қаралды 36 М.
WAXTAAN SERIGNE MOUSTAPHA GUEYE
10:01
TAS-info TV
Рет қаралды 7 М.
BAYGUYSTAN | 1 СЕРИЯ | bayGUYS
37:51
bayGUYS
Рет қаралды 1,3 МЛН