Eumeu Sene VS Alioune Seye2 Balla Geuye VS Siteu Doudou Sané VS Serigne Ndiaye2 Modou Lô VS Sa-Thies Thattou Yarakh VS Gris2
@Demba.pastef13 сағат бұрын
Sa thies aka bakh modou sama Mbeur mayal sa thies chance way
@mameballaka571310 сағат бұрын
Machalla sa❤❤❤❤❤❤❤
@assanefall411113 сағат бұрын
Sa thies bilae tu peux battre Modou lo yokal sa rapidité ak sa force rek fatma dia good jop bayi ngama naq
@MansourDiop-y6j13 сағат бұрын
Nous on t'aime champion ❤❤❤❤
@boubacarsyllame283514 сағат бұрын
Sa thies ak modou lo in challah ❤❤❤❤❤❤
@ndoffenetine533311 сағат бұрын
Sa thies vs mod lo ndaw combat bou gaw😮 Gnar gnou am vivacité mé sa thies da xawa rambax.
@mistercarter467Сағат бұрын
Rambax bobu modou lo ayoucii😂
@ndoffenetine5333Сағат бұрын
@mistercarter467 bien sûr ay nasi dhé. Kou rambax mossul dane mod lo
@langbadiane76789 сағат бұрын
Sa thies machalla yarou nga trop mé gnoune fane modou Lo yii dagnlay otale banga dieul combat bii dotoko défatii😂😂😂
@MouhamadouSakhirDiba8 сағат бұрын
😂😂😂😂
@sambadrame349714 сағат бұрын
Sa ❤
@moustaphababou62827 сағат бұрын
Modou lo mayal sathies chance waye
@MomoCisse-k9r11 сағат бұрын
Fans modou lo yi ay saytané guén rek
@Modoubusso-b9j13 сағат бұрын
Modou moe sama mbeur mais dama beugg sa thies beugg ngén beure vraiment
@MamadouKa-h2k12 сағат бұрын
Très pertinent
@HabibSylla-e3f13 сағат бұрын
Machalla kadou yi rafét na
@PapeNdiaye-pz6fw12 сағат бұрын
Modou lo vs sa thies yalla na takhaw ❤
@AlassaneDieye-cc7jq2 сағат бұрын
Man lamb ji yeup Modou Lo ak Sathies laci meusseu faral ba xeex. Modou mako beugu té hawma noum démé, Sathies dagno bokone kogn keur massar ma nek xalé di daw diangui diko setani té ba legui momlay topou. Bagnouma ben mbeur mais gni gnoy sama mbeur. Sa est très bien éduqué
@modougaye664613 сағат бұрын
Modou lo vs sathies Balla gaye2 vs siteu Eumeu séne vs alioune seye2 Jackson vs quench Mbaye gouy gui vs anaconda
@adamambaye328013 сағат бұрын
Sa nioune wa MODOU LO niola beugue incha allah modou dalay may chance.
@MamadouDiouf-hl1sy13 сағат бұрын
Yaw ya bakh waye
@adamambaye328013 сағат бұрын
@MamadouDiouf-hl1sy sangue bii ki dafa nité trop yalla xamnako Mane déh sou dané Modou douma méti mérité nah lép
@baidy741811 сағат бұрын
Sa thies toujours correct….sou modou naré Daanou yalla na diogué thi sa thies…..
@sayergeye788811 сағат бұрын
Amine Amine Amine Amine
@NdiaboutaDiouf14 сағат бұрын
eumeu sene alioune seye siteu balla gaye lolou moy logique
@mouhamedlaminethiam440410 сағат бұрын
Mod Lo sa thies
@Soninkaradéna4 сағат бұрын
Siteu balla moy bane logique ???
@fallou31812 сағат бұрын
Sa thiés yalna dane modou lo
@Bakelsen9910 сағат бұрын
Amine❤sa mome il faut beaucoup de boxe beure yii kodoroule doka dane
@Aladjil60913 сағат бұрын
Ms sa legui kouko diangal communication machala
@MamegorDieng-os2fj12 сағат бұрын
Sa nila masa mél❤
@Papiscoboukaaycover-fd7xc8 сағат бұрын
Modou moy sm mbeure mais combat bi rk la mbeugue bilahi Sa da yarou bilahi yéna nl Combat Royal trp Mais Modou dane la inchallah😂kérok binga dougué sé Stade dm contane bilahi dkh sa respect Mais Yll na takhaw Modou doumala dane inchallah🙏😂🔥
@alysow90893 сағат бұрын
Sa Thiès yw ak Ada fass dolené génération def ngua 8 ans de carrière Ada fass dora gnew 2009 ak 2017
@mamadoundiayetouba407813 сағат бұрын
Tres sage
@mbayetop230213 сағат бұрын
Modou lo légui lou noy lay weur wayé li moy combat
@boyeniang3781yeumbeul13 сағат бұрын
Salif ❤
@ousseynouhanne935913 сағат бұрын
Modou moye sama mbeur mais yalla na yalla df mou beurè ak sathès
@AssSarr-f5i13 сағат бұрын
Amine
@ibrahimandiaye892414 сағат бұрын
Nic
@bubaceesay954314 сағат бұрын
Modou vs Sa thies moye combat bi
@oumarndoye11693 сағат бұрын
Bilay beur yi mosi eupeu dolé mais niak fayda rek
@IslandCureislande12 сағат бұрын
GOODNESS OF GOD. LE JOUR OU TU CROISERA MODOU LO JE TE CONSEIL SATHIES BOUL TAKA GALATHIE ZERO GRIS GRIS.. DO8DOUDOU LO KOKOU BEUGUE DAAN IL FAUTNGUA PIEUX DI DIAPOU DI DIOULI AK RECITE ALHURAAN NIGHT AND DAY ON A REPARLERA INCHAALLAH OU RABI. CONTINUER TES ENTRAÎNEMENT .
@MoussaDak-o7f13 сағат бұрын
❤❤❤
@BubaluizSuware13 сағат бұрын
Thanks ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@KebaToure-z9g14 сағат бұрын
Sa thise rék
@kharagnembaye595813 сағат бұрын
Boula modou topé doula may chance psk nangouwo may chance franc ba ama mayko chance Ta Ama mola raw si lamb
Fatma Dia yaw ya manoul wakh bou bakh wala micro yi la ?
@maodosoumare912 сағат бұрын
Daffa daw fran dieuleul fran dagua ragual danou fran Moy sa adversaire Parcelle
@pmsdiouf12 сағат бұрын
COMBAT SA THIÉS VS MODOU LO DOU LOGIQUE LI MODOU LO WAX DAY MAY CHANCE BOYI RK NGÉN BEUGUE KO DF LOGIQUE DAY YOMBEU TROPE KOU DANOU BEURÉ AK ROI LAMBJ DOU NONOU ROI BI KHANA WAROUL POSE BALLA GAYE BAMOU DANÉ BA LÉGUI KÉNEU TÉGOUKO PRECTION SA THIÉS VS TAPHA TINE KOU DANE AM MODOU LO
@MOUHAALAMINE30 минут бұрын
Moy deugeu
@laminendong622712 сағат бұрын
Man mom Modou lo moy sama mbeur mais bou danou manoul niakeu yalla Na ko sa thiés dan nék roi des arènes dafa am yaar lol nit la koi
@aboukonte48910 сағат бұрын
Pourquoi pas modou lo vs Tapha tine . Ce combat est plus logique que modou vs sathies
@basirubaye658712 сағат бұрын
sathis vs modou lo
@elhadjiibrahimadiatta948514 сағат бұрын
Modou lo sou dieulé Sa thies niak couronne bi❤
@GoraBoromItali14 сағат бұрын
😂😂😂 fiii nak guéne dii tamé modou deum la dieul bou gaaw lakoy daane insha Allah yalla n'a tahaw rk
@elhadjiibrahimadiatta948513 сағат бұрын
@GoraBoromItali champion là déh mai sou dieulé Sa thies niak couronne 😂😂😂
@BabacarMbengue-z7p10 сағат бұрын
Sathies vs Modou lo
@MoussaDak-o7f13 сағат бұрын
Sa Thiès rék
@chicorykharagne632313 сағат бұрын
Sa na gore franc migui sa kaw sa dh yaw ak Balla khar len ndiago bi
@IBRAHIMADIABYCISSOKHO13 сағат бұрын
Wa modou lo niemer woniou balla ni tapha Tine motahh niouy forcer s'en bop sa Thiès
@bayemodoufall287914 сағат бұрын
🎉🎉🎉🎉
@oumarndao74858 минут бұрын
Ndeysane tapha tine amoul koukay wahal mais y’a pas plus logique que modou lo vs tapha tine,modou mom hawma Loutakh beugoul beuré ak tapha
@Mamadou-j1x14 сағат бұрын
Fatma dia lo tahk dou wak se kow 😮😢😢😢😢
@abdoulfall798413 сағат бұрын
Djiguène diou bakh la rèk
@MantaDiop-v3k12 сағат бұрын
Fi nga nekk Di yarouyarou ba eumeu nakh la mbeur daffa wardi yeugeul bo beuger Di beuri mbeur daye rew😂
@SaliouPouye-v4w14 сағат бұрын
Modou lo Modou lo Modou lo Modou lo ❤❤❤
@CheikhounaFall-v9o14 сағат бұрын
Sa thèse ak modou
@mbayesarrdia447014 сағат бұрын
Sa thies yaroul modou lo dieul la doumala dame si non doula dieul dh so wakhé ni
@habibdieng300613 сағат бұрын
Sa Thiès meuno Dane modou lo yaw daga eppeul
@OuseynouSarr-l3z14 сағат бұрын
nougay beuri dafa anragés Modou
@babacar317813 сағат бұрын
Eumeu séne vs alioune seye2
@bayeas779113 сағат бұрын
Wilae sa nitkou rafet xol daray sokhor nekoul sii mom
@FallWaly-c6g12 сағат бұрын
Ya gena nexa dann ci modou
@adamanamokho13 сағат бұрын
Yaw sunu waye ngua no def beugeunaniou dagua yarou
@BassirouSamb-oe6sh13 сағат бұрын
Sa thies à pris beaucoup de poid
@idydiallo15859 сағат бұрын
Il faut d’abord se frotter à franc d’abord
@MbavkeGaye11 сағат бұрын
Boy yi miy bureĺ keneu gonola mérite beuré ak mom
@bassiroundiaye391312 сағат бұрын
Yaw yaginé daga dameu baparé gané gnou am founoula yaubou gané damau féneu kou dameu thi fare AK thi lokho menoule beuré
@aichatasarr828313 сағат бұрын
Sa thies bly dmko beugue
@ndiogouthiam68957 сағат бұрын
Je s6 ton fans mais nanga xamni wa modou lo yi yambar lane la diappé Ndax lolou nga wané c dernier temp Motakh gnou beugue nga beuré ai modou pour yokou ay ndamame Yarou nga trop mais il faut nga sadik comme avant légui danga nékhé gnémé
@ndiayepapaserge599714 сағат бұрын
Modou lo mayal chance sa thies
@MoussaDak-o7f13 сағат бұрын
❤❤❤❤❤
@PapeDiagne-hx7lw13 сағат бұрын
🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@pmsdiouf12 сағат бұрын
COMBAT SA THIÉS VS MODOU LO DOU LOGIQUE LI MODOU LO WAX DAY MAY CHANCE BOYI RK NGÉN BEUGUE KO DF LOGIQUE DAY YOMBEU TROPE KOU DANOU BEURÉ AK ROI LAMBJ DOU NONOU ROI BI KHANA WAROUL POSE BALLA GAYE BAMOU DANÉ BA LÉGUI KÉNEU TÉGOUKO PRECTION SA THIÉS VS TAPHA TINE KOU DANE AM MODOU LO
@ndakarudialdiop120612 сағат бұрын
Siteu kan la dane ba modou lo dieul ko wakh meu ?
@veritesavoir54153 сағат бұрын
Lamb mo amatoul logique légui frère mais kone li'nga wakh leu rk normalement kone siteu dafa warone daane béne VIP soga beuré ak modou lo