Serigne Abdou lahate Tawou Serigne Abdou Rahmane..Mouridine Sow

  Рет қаралды 48,934

HIZBOU Rahmane

HIZBOU Rahmane

Күн бұрын

Serigne Abdou Rahmane Mbacke Serigne Touba

Пікірлер: 43
@tabaskisenghor6685
@tabaskisenghor6685 2 жыл бұрын
Yalnako yalla yereum hareko thia aldjana yu mag ya ak mbolem gnim fa fek
@modoumoctarfall7772
@modoumoctarfall7772 2 жыл бұрын
MachaALLAH SERIGNE MOURIDINE SOW
@AminataBa-ov7kx
@AminataBa-ov7kx 4 ай бұрын
Yalla na sougnou borom yoku léram té tasnou thie barkém
@ndeyekhadydiop6936
@ndeyekhadydiop6936 Ай бұрын
Sëriñ Abdourahmane ak sëñ Abdu ahad Yal na Yàlla yërëm leen ta Fayal nu leeen
@aliounecisse6833
@aliounecisse6833 2 жыл бұрын
Yalna ko YALLA yeureum teh diégalko teh Fayal nou ko si barké ALKHOURANOUL KARIMOU🙏🙏😭😭
@modoumoctarfall7772
@modoumoctarfall7772 2 жыл бұрын
MachaALLAH SERIGNE BI
@thiernoseye7875
@thiernoseye7875 2 жыл бұрын
Yalla nalen yalla takhawo
@tallfamilleelectroniquekol6840
@tallfamilleelectroniquekol6840 2 жыл бұрын
Machallah amnasolo yalla na ko yalla yeurem te khareko aldiana firdawsy amine
@ndiobalo6544
@ndiobalo6544 2 жыл бұрын
Dieureudieuff cheikh ahmadou bamba merci beaucoup bamba diarama Mame cheikh Ibrahim fall
@hiphopdefftv3584
@hiphopdefftv3584 2 жыл бұрын
yalla nako yalla yeureum tass gnou si barkem
@bayemordia6427
@bayemordia6427 2 жыл бұрын
Maachallah nittou yalla dëgg
@khadimkebe2313
@khadimkebe2313 2 жыл бұрын
ما شاء الله والسابقون السابقون أولائك المقربون في جنات النعيم
@seringegueye4354
@seringegueye4354 2 жыл бұрын
Yallanaco yalatékhélle amîne
@ndiobalo6544
@ndiobalo6544 2 жыл бұрын
Yalla nako yalla yereum
@cheikhboussole4651
@cheikhboussole4651 2 жыл бұрын
Machallah yalla na la yalla samou
@mouhamedmakhroufthiam1476
@mouhamedmakhroufthiam1476 2 жыл бұрын
Yala nako yala yeureume ta djeigalko.
@jesuispapealeniag5529
@jesuispapealeniag5529 2 жыл бұрын
Yalna sen andabi geuna degeur 🤲🤲🤲🤲😭😭😭
@ousmanefaye9378
@ousmanefaye9378 2 жыл бұрын
Machalla nittou yalla deug
@juniorog3638
@juniorog3638 2 жыл бұрын
Walay ndaysane yalla nalané yalla samou taxawou Léne bou wéreu wér SI BARKÉ ALKHOURANE ❤🤲🤲🏿🤲🏿
@massambathiam305
@massambathiam305 2 жыл бұрын
Talibé khadir la mai tawou Serigne abdou Rahman bi koumou nianal Yallah mou noguou
@souleymanembaye7307
@souleymanembaye7307 2 жыл бұрын
Yalla nalen yalla takha wou 🙏🏾🥰
@moussadiop6111
@moussadiop6111 2 жыл бұрын
Lou am solla topante
@ngorengom3260
@ngorengom3260 2 жыл бұрын
Ndayessana
@djibrilbousso8819
@djibrilbousso8819 2 жыл бұрын
رضي الله عنه امين 🙏🏿
@karadioplg4009
@karadioplg4009 2 жыл бұрын
Ndeye sane
@morthioune5007
@morthioune5007 2 жыл бұрын
Amiin ya rabi
@ndiayendiaye313
@ndiayendiaye313 2 жыл бұрын
Machallah
@yacinediop6556
@yacinediop6556 2 жыл бұрын
Macha allah 🕋 ❤️ 🕋 ❤️ 🕋
@darajitv3882
@darajitv3882 2 жыл бұрын
الأتقياء الأخفياء رضى الله عنه
@ndeyesow699
@ndeyesow699 2 жыл бұрын
Amine 🤲🙏
@ndeyesow699
@ndeyesow699 2 жыл бұрын
🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
@serignembackediaw2036
@serignembackediaw2036 2 жыл бұрын
Sa baye dé tok nioukoy opou amoull
@nabiloukane7899
@nabiloukane7899 2 жыл бұрын
Walahy danguene reww leggui dokhinou bayaam la wara ame force pr done kimou wara done niakk xam limou waral barina
@ibrahimadiop8183
@ibrahimadiop8183 2 жыл бұрын
Danguén di khol mbirr dithi weur sikk ba dolen diariniou yaw wahtan Bou am solo bi tewlouwoko si khol ayy eupou ak niaka eupou ...
@asnaakhadiimgueye8309
@asnaakhadiimgueye8309 2 жыл бұрын
Ay waay xell day rafet ki taloul sakh kikouy ouppou imansinel kou waydiouram fatou noumouy tale koukoy ouppou
@ibk7757
@ibk7757 2 жыл бұрын
Kula wax mooko ko sant ay téggin baax na lool
@ibrahimadiop8183
@ibrahimadiop8183 2 жыл бұрын
Con rek am na nio khamni danio critiqué ba moudié am esprit tordue
@nabiloukane7899
@nabiloukane7899 2 жыл бұрын
Mangui toup beugona xam ki di wakh moy kane ? Ak sama diangat mbolo ki di wakh moy sen ndjiit ? Ak nane la dougué si yoone wi ndax nena deglou serigne abdou Rahmane serigne Sam Radiyalahou anhouma ay leral la soxla ?
@morthioune5007
@morthioune5007 2 жыл бұрын
Ki de mingi deukk ndar di nitt ko bakh lool
@bayika3502
@bayika3502 2 жыл бұрын
THIERNO SAMBA MOUQADAM S ABDOURAHMANE A SAINT LOUIS PIKINE DIOKOUL
@abousow7440
@abousow7440 Жыл бұрын
Wa kou Bakh magui ziar bou weur di toub di djèuma tontou lathie bi nga lathie ki di wakh mougui toudou mouridine sow deuk ndar mougui dioudo thi yonu khadir ya mou nèk thi ba nèk thi baniou cheikhal ko thi wayèi batay rk limouy guiss thi tèrèi nitou yalla yi ak limouy guiss thi serigne si fi nèk legui mou woutè lol ak serigne youfi nèkone thi gatal danaka yone yifi nèk yèup diarna si wayè nitou yalla bou yeug si yalla bouy diamou boromame tèi diko sèllale mou tamba li nak di wor serigne yifi nèk ba biss biko yalla wanalèk serigne Abdou rahmane mbacke dèf Kâ diokh lokho rk serigne Abdou rahmane mbacke niko sow yèkk si nga mane mi di wax ak ioe nio andone thi la wakhni mane lima done wore yèup nguir guiss nitou yalla ba ligeuyal ko ndax lolou modone yitèum thi la diègalou thi mome ak talibe yimou amone nièup fasse yènoko ligeuyal mou tènkou nak thi yi tèi alkhourane ak sunna ak li serigne Abdou rahmane di diangalé ak waxtane serigne Sam MBaye thi gatal li thi quissa bila
Témoignage de Serigne Ahmadou Mbacke sur Serigne Abdou Rahmane Mbacke
15:00
Ful Video ☝🏻☝🏻☝🏻
1:01
Arkeolog
Рет қаралды 14 МЛН
🎈🎈🎈😲 #tiktok #shorts
0:28
Byungari 병아리언니
Рет қаралды 4,5 МЛН
NDIARRINIOU_BASSMALA_par SERIGNE Abdou Rahman Mbacké
6:58
TAHMIIS TV l'officiell
Рет қаралды 785
Serigne Ahmadou Mbacke: jooy nanu sunu jambaar ji di S Abdou Rahmane Mbacke
15:00
Rafah TV International
Рет қаралды 47 М.
Gamou THIES 2023 ziar Soldar yi_keur Serigne Saliou Touré
31:39
FoulkouNet TV
Рет қаралды 4,1 М.