Serign Ahmadou Mbacké,toutes mes condoléances attristées pour le rappel à Dieu de Serigne Abdou Rahmane,que Mame Thierno l'accueille au Paradis à l'ombre de Touba ! Ci barké Serign Touba Hadim Rassoul ! Amadou Diawara talibé de Serigne Mourtalla Cheikh Faty.
@bathiembacke24282 жыл бұрын
Ndayssane yallah na ko yallah yereume yallah nako Serigne Touba térou 😭😭😭😭
@abodiop33282 жыл бұрын
Ndaysan Serigne Abdou Rahman mbacké yalla na yalla yokku ay léram aki ndiegalam aki xéwalam teta sonu ci barkem amiin
@fall82702 жыл бұрын
Wallahi seriñ abdu rahmaan ku am as tox geum ci yalla demam gui dina la metti yalla nako yalla yërëm te xaree ko aljanna 😭😭seriñ ahmadu mbakké moom mii tamit ku baax la yalla nako fi yalla yagall
@franciscodiaz20222 жыл бұрын
Serigne Ahmadou Yallahna Borom bi nangou niane yep ci barkep SERIGNE BI té Borom bi goudal saw fane .YAA BAAKH
@Nous60982 жыл бұрын
Dieureudieuf serigne touba serigne mountakha yalla nafii yagg te and ak wër dieureudieuf serigne abdou rahman yalla naniouko yalla fayal 😭😭😭😭😭😭😭😭✅❤️
@docteursalioundiaye94862 жыл бұрын
Yallah na yallah yok Ay leram barké Cheikhoul Khadim 🤲🤲
@mamemorcisse42 жыл бұрын
Yalnako yalla yeureum té diegalko khaareko aljanna
@Abdou_Khoudoss_Syll2 жыл бұрын
Niakk nane koubax lol 💔💔😭😭😭yalna yalla yok ay léram ta tasniou thi barkep Brom Touba🙏🏾
@s.falloundiaye45192 жыл бұрын
Machalah machalah Mbacké yaw dagua bakh rk man mi loma don Mom la
@cheikhniang18402 жыл бұрын
Ndeysan Serigne Abdou yalna yalla yok ay leram thi barkep Cheikhoul Khadim
@ndeyesow6992 жыл бұрын
Walahi deuguela Mbacké Balla SERIGNE Bi Amoul morom 😭😭🙏
Yalna yàlla fay. Ya takh ma xam. Sàng bii. Yalna yàlla fay yiww. Fayal nou sàng ba. Soti yërmande si kawam
@petitkarasaw62782 жыл бұрын
Serigne abdou rahmane mbacké yalna firdawsi di deukkou waayam
@mormbaye68632 жыл бұрын
Machalla
@fallouwadewade38882 жыл бұрын
Kou bakh lolou démna thiéy Yalla sa borom Kou mélné Serigne Abdou Rahman dotoul amati
@cheikhmassambagueye96692 жыл бұрын
اللهم اغفر له وارحمه
@ndiouckndiouck35142 жыл бұрын
Yalnako yalla yeuram diéggalko yalnako yalla fay té taxawo ginnawam
@mbackediop76782 жыл бұрын
Serigne Abdou Rahmane Mbacke Yalla Nanoko Yalla Fayall Barkè borom Touba
@mouhamedcamara4590 Жыл бұрын
Serigne abdou rahmane mbacké cou baxone te ragal yalla limay rethiou moy limaco guissoul bamou dém☹️😭😭😭
@Darousalam20842 жыл бұрын
Yalle na yalla yokou lerame amine
@cheikhabdoumbacke69702 жыл бұрын
Yalla nako Yalla yeram amine
@moussadiop61442 жыл бұрын
Ndeysan 😢 c’est émouvant
@serigneaidarasow90072 жыл бұрын
ndayesan nako yalla yaram s Abdou Rahmane dafa wathi défna la ko war
@ndeyesow6992 жыл бұрын
Amine 🤲🙏 q
@seringnesarrgueye82662 жыл бұрын
Dieureudieuf
@binetoumbacke40212 жыл бұрын
Thieuy moom 😭❤️
@cheikhthiam45902 жыл бұрын
Ndeye sane mbacké 🥺
@mominatoumbacke96972 жыл бұрын
Walahi MBacke balla yallah n'a sunu borom yessal yeurmandèm barkep arqur'an
@jesuispapealeniag55292 жыл бұрын
Amin waye
@serignemodoundiaye84182 жыл бұрын
serigne ahmadou aka bax ceey wadji wayei serigne abdou rahmane yalla na yalla yok aye leram
@sidydiop15232 жыл бұрын
Ndeysan yalna kou yalla yeureum barké xadim rasoul
@khadimba5022 жыл бұрын
Serigne Abdourahmane Mbacké ak yaw mii Serigne Ahmadou Mbacké Darou Mouhty sama thiofél si yén amoul app yamoukay. Danga baax réik wayé yaw koila guëna baax guënela ragal Yalla guënela mandou eup la xam xam guissouma ko.