Allahou akbar macha Allah. Ler na fatabarakallahou yow kham ngua man kham na. Yalla mi gnou khamal khamna . Mon ami mon frère. Yalla khamnany li nek sa deune bi yep khadioul si yii . Nala yalla sam ba faw
@academietijaan4 жыл бұрын
Mach'Allah Serigne Bi toujours un plaisir de vous retrouver. Yalla na Yalla goudeul sa faan si barki Cheikhou Tijaan Cherif RTA ligueye bi amna solo amou gnu sa faay barakallahou. 🙏
@abuulabassahmadatattidjani16814 жыл бұрын
Sonou khôl sed na torob si iow yalla na yall seral sa khol si barké cheikh Tidiany 💖💖💖💖
@layesene68304 жыл бұрын
Wa alaykoum salam sounou serigne daraa gnon gui lay balou akh dila bal akh di gnan bour yalla mou bolé gnou bal si bakham incha allah Yalna bour yalla doli la tawfekh ak taïssir incha allah bari
@abbatalib77314 жыл бұрын
Franchement li yalna done ay atti att si kanam ci barkei Cheikhou Tidiaani (RTA)
Waleyka salam warahmatoula wa barakatouhou ya Oustaz diazakalahou haîr1ne c'est tjr in plaisir de te suivre yalna la yala Faye yiw doli ham ham bi mayla wer AK meune Tal AK feke inchalah
@cheikhibrahimaniassdiallo96834 жыл бұрын
Sa Fans Club wa Allemagne si tourou Sokhna Soukey Sarr ak ndiabotam ak am Di diamam yeup nio ngui wakh DANKESCHÖN 🙏🏾 yallah Bour bi fayla si Barke Seydina Cheikh Ahmed at Tidian RTA🌟🌙
@doudoudiedhiou88104 жыл бұрын
Amine ya rabi yalna YALLA nangou gnany si barké Séyidina Mouhamed merci pour prières
@ibrahimanakone78024 жыл бұрын
Rafétatina Serigne Ahmad. Yalna Buur Yalla barkel. Nio ngui xaar darss bou dieum si awraadou Tarixa bi ak ni niou kay defé si togay yi ak lepp rek.
@malickndiaye44533 жыл бұрын
Suis trop fier de vous regarder et vous souhaite vous voir devant une télé avec ces même émissions
@racinedaff97553 жыл бұрын
Longue vie et santé ya Cheikh ! Qu'Allah te protège, te bénisse et te rétribue au au-delà de tes espérances..Barké Cheikh Tijani rta!
@alioudieng29943 жыл бұрын
Li ngay wakh lerna yalna sama Borom dimbalila
@modoufall83584 жыл бұрын
dieuredieuf serigne bi yalanala bour yalla dolli soutoura saamla arla si barke cheikhou tidiane
@moussandiaye99083 жыл бұрын
Machallah yallah na yallah barkel lepp
@mouhamedgueye55634 жыл бұрын
Al hamdulilah! Toujours un plaisir de vous écouter. qu'Allah vous garde Cher Oustaz Ahmad Fall ❤️❤️❤️
@astouleyesy89034 жыл бұрын
Iiiiiiiiiiiiiiiiiioiiniiiiiioiioooipiiimi 8 I 8 i K I Pp M I
@astouleyesy89034 жыл бұрын
Iiiiiiiiiiiiiiiiiioiiniiiiiioiioooipiiimi 8 I 8 i K I Pp M I
@astouleyesy89034 жыл бұрын
Iiiiiiiiiiiiiiiiiioiiniiiiiioiioooipiiimi 8 I 8 i K I Pp M I
Walay Fall li nga wakh thi Serigne cheikh yepp deug la Benn bi 2007 la bennen bi 2001 manchalah yalla na yalla yokou kham kham bi . Sopounala lol ndakh Cheiykhouna Ahmed Tidiane Cherif walay ndeyssan 😢
@Abdsr87354 жыл бұрын
Serigne Ahmad Fall Yakamtina lol sa Tafsir Alkhurane ! Xam xam Bimay deg dafa melni lem kene dou si doyal ! Sa introduction rek cours magistral la ! Dieureudieuf si say jangalé you ame solo ! Yalnala Bourbi fayal bopam bijahi Rassoulilah SWS barké Cheikhou Tidjany RTA !
@yanidoufall35364 жыл бұрын
Walleykoum Salam sama serigne sama sopé, yalananou YALLAH SWT may niou téwé ay Eid Kabir you bari. Yalanalafi YALLAH SWT bayi mou ande ak wéér ak jamm. Yalana YALLAH SWT yagal sa takhaway, yok xam xam si barké SANGOU SANGUE YI ALLEY SALATOU WA SALAM si worma CHEIKH AHMAD TIDJANE CHÉRIF (RTA)
@harounaguisse774 жыл бұрын
Machaalla serigne bi boul fate amnga aye talibe fi si England 🇬🇧 London Harouna Guisse et balla Diop danlay topo toujour jeureu jeuf
@falltalla18074 жыл бұрын
Danulay nam nak sunula geujee deg sunu xel du dal yalnala boroombi dollee aar
@abdoultouray49344 жыл бұрын
Soyez récompensé au-delà de toutes vos espérances et ceci de par les grâces accordées à Cheikh Ahmed Tidjani.
@galayekebe67714 жыл бұрын
Macha Allah y'a cheikhina yalla n'a yalla doli diapalé samala dila ziar dila bégué
@drdrkaffrine59434 жыл бұрын
MERCI Serigne Ahmed. Je suis régulièrement vos cours et chacun je le visionne 3 fois.
@mamadousow14704 жыл бұрын
Machalla barakalahou fik ya oustaz contane naniou trop si yaw Yallah na yokou bou bakh bi barakati Seydina Akhmed tidiane cherif
@falltalla18074 жыл бұрын
Fatabaarakallahu yalna sunu borom dolli laa Sam aarla ci parkep maolaanaa Aboul Abasse Cheikh seydi Ahmada Tidianiyou (rth). Yalnafi corona virus joge bafawwu yalna l'islam yore adunabi bep ba fawwu ci barkep seydi kulli awliyaa Attijaanii ( rth) amin
@mouhamadouladykane1534 жыл бұрын
Serigne akhmed fall yalla nalla yalla sameu goudeul sa fane.allahouma amine🙏
@oumarsilla69524 жыл бұрын
Machallah mission bou reuyy leu yanou yalna borom bi deugeureul ko Cheikh Ahmad Fall
@matydia51584 жыл бұрын
Machalla dieureudieufaty Bour yalla yaggal sa.takhaway te barkel xam xam bi sì barke Seydina Mouhammad Sallalawou Aleikhi Wassalam PSL ak barke Cheikhna Ahmed Tidiany Cherif RTA 🤲🤲🤲
@ndoyeomar90202 жыл бұрын
Serigne bi man deih damala sopeuh❤ yalna nala BOUR YALLA fay geune di fay🤲🏿🤲🏿🤲🏿...Dieureudieuf
@srbathiediop48544 жыл бұрын
machallah serigne Ahmad Fall gueuneuh weer gueuneuh yaggu si barké SALATOUL FATIHI ci barkei Cheikhouna At Tidiaanii (RTA)
@idrissandoye65504 жыл бұрын
Machaallah sope cheikh tidiane si barke seydina mohamed aleyhiwasalam dieureudieuf serigne ahmed fall
@mouhamedmbaye16464 жыл бұрын
Machalla serignebi namone nanioule Machalla yamatine solo yalla na yalla faye le bibarakati seyidil woudjioude PSL🙏🙏🙏
@Ndanaan2.04 жыл бұрын
Machallah ! Serigne Ahmad Yalla nala Yalla defal fane bou goudou ak wer. Sameu la sameu sa ndiabote. Ninga gnouy leralé Kouy Cheikhou Tijani RTA Yalla nako yalla leralé sa yone si tarikha bi. Inchallah 🙏❤️
@lamine6724 жыл бұрын
Machalla
@Al_Farouqi4 жыл бұрын
Pour ceux qui sont intéressés par le livre d’Ibn Atta Allah dont il parle, vous pouvez télécharger la version française sur le lien en dessous. Reste à trouver un maître approprié pour vous l’enseigner 😊. 👇🏿👇🏿👇🏿 drive.google.com/file/d/1fg8Gj5MJDvWWQkWiRqbSxi8DDrJbrkqO/view?usp=drivesdk
@academietijaan4 жыл бұрын
Jeureujeuf Akhi Yalla nala Yalla faay yiiw🙏
@matydia51584 жыл бұрын
Machalla dieureudieufaty
@coumbaaida4 жыл бұрын
merci beaucoup à vous. Auriez-vous un lien pour télécharger diawahiroul mahani en français? Merci d'avance de votre réponse.
@academietijaan4 жыл бұрын
@@coumbaaida Salam donnez votre numéro WhatsApp ou votre addresse mail pour que je vous l'envoie 🙏
@coumbaaida4 жыл бұрын
@@academietijaan merci beaucoup à vous voici mon adresse mail: coumbaaida@gmail.com.
@dahadiop13334 жыл бұрын
THIEY FALL ,YALLA NALA BOROM BI FEY INCHAALLAH.
@sinymbengue76374 жыл бұрын
Serigne ahmed fall que dieu te protège et te soutienne dans cette noble mission khol yeup senda et on est en train d'apprendre beaucoup de choses sur la vie de cheikhou tidjiani cherif rta
@malickloum1774 жыл бұрын
Baraka lahu oustaz
@mbdone38604 жыл бұрын
Mashallah serigne Ahmad fall yagui niou sooréll ada ak folklore ,khol yi lér diné souneu ak tarikha cheikh. Barké seydina Mohammed sallahou aleykhi wasalam dieureudieuf. 🤲🙏
Yalna nga yague fi té andak weur inchalaa. Bilahi je vous ecoute avec plaisir. Yalna yalla fey thi barké yoneté
@mbdone38604 жыл бұрын
Mashallah dieureudieuf!sante Allah borombi dioulli si seydina Mohammed sallahou aleykhi wasalam dieureudieuf cheickhouL Abass Tidjani cherif radiallahou anhoo.
@mamadoumbodj33324 жыл бұрын
Un très grand plaisir de vs écouter djeredjef yalna la yalla faye takhawoula amine
@babacargningue44194 жыл бұрын
machalla tabar kalla yalla nala yalla fay
@amethdiop81454 жыл бұрын
Dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf
@daoudathiaw4 жыл бұрын
Janggalé bi jaar na yoone. Dieurejeuf yaa Oustaz. جزاك اللهُ خيرًا
@mouhamedsow2213 жыл бұрын
Barak'Allah fiik Ya Cheikh ♥️
@lamine6724 жыл бұрын
Je vous aime
@ablayesene97034 жыл бұрын
Wa hanleykoum salam wa Rahmatoulah tahanla wa barakatou 🙏🙏 barakallah fik yalna yalla fay la yiw iow ak gni gua si andale nieup barké Seydi wa mawlaya Cheikhouna tidiani Cherif 🙏Amine🌙🌙🌙✅
@mouhamedat-tijani33934 жыл бұрын
الله 🥰❤️
@souleymanedieng77044 жыл бұрын
Dieureudieuf segnbi
@laminetall43314 жыл бұрын
Vraiment merci du fond du coeur
@ibrahimandiaye47434 жыл бұрын
Dieureudieuf dieureudieuf ma cha alla
@mamekhadyfall24684 жыл бұрын
Machaallah yalna yalla yoke lairou deune bi
@maogningue39224 жыл бұрын
Manchalah Serigne Ahmed Fall yalla na yalla yokou kham kham bi
@aliounebadaradiack31634 жыл бұрын
Machala machala. Serigne bi gnongi khar tafsir khourane bi
@mariatoutouray4714 жыл бұрын
Jazzakallahu Ana Hairan🙏🙏🙏💕💕💕
@MariameDaff-c7r2 ай бұрын
Machalla ❤❤❤
@morndiaye27164 жыл бұрын
Yalna sunu borom yagual lafi basi kanama kanam Serigne ahmed fall si barké yonente bi walahi amna solo loll way
@abdoulayembaye97004 жыл бұрын
Machala darse bi Amna solou
@papediop-df4tu4 жыл бұрын
ماشاء لله فتبارك لله
@ouldadathiam75564 жыл бұрын
Sama xol bi noumouy def soumalay deglou Bilahi Walahi Yallah mola yabal ci jam yi
@maremewade67134 жыл бұрын
Mashalah yalla fayla yiw
@layesene68304 жыл бұрын
Allah
@papaamsatougaye46074 жыл бұрын
MACHALAH
@aboulabbasstidjany6804 жыл бұрын
Mâcha Allah amatina solo. Wanté cours bii dafa gateu torop
@paps084 жыл бұрын
Merci
@baboucardiop16384 жыл бұрын
babacar diop.très intéressante leçon. yalla fayla yiw
@batimentconstruction76214 жыл бұрын
Machalla yalna yalla faye
@ousmanediouf90314 жыл бұрын
Shukrane Serigne Fall. Yalna Yallah niok sa leer.
@mamadoudienembaye91184 жыл бұрын
Assalamou anleykoum sama serigne Mangui lay balou akh di balou gnilay tewlou si chaîne yeup di sakou niane Dieureudieuf fall
@ahmedtidjanesow71464 жыл бұрын
Manchallah Bon continuation thiakaw thiakanam.
@wakhdeugguetayallatakh81294 жыл бұрын
Merci bcp oustaz ahmed fall
@peboudiop79624 жыл бұрын
Macha Allah yiw na lolou
@makhalydia84904 жыл бұрын
♥️♥️🙏🙏
@dahadiop13334 жыл бұрын
GRACIAS FALL ELEGANCE ,MACHAALLAH
@cheikhamadoutidianidieng99274 жыл бұрын
Ça nous a manqué
@fatoumatabinetoundiaye69604 жыл бұрын
Macha ALLAH il est pertinent
@barhamamboup64314 жыл бұрын
Dieuredieuf oustaz magi laay gnanal dieredieuf Yémou ci Yaw trop
@IbrahimaDiallo-ub7ll2 жыл бұрын
❤❤❤mâcha allah
@fatoucisse36364 жыл бұрын
Machallah ♥️♥️
@abdoulazizsy44964 жыл бұрын
Gudu fane ak wer
@aminatasarr10814 жыл бұрын
Amna solo
@adjangom76303 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤
@ousmanediouf90314 жыл бұрын
J'ai terminé le cours no 34; mais je n'arrive pas trouver le cours no 35