Non Modou est un vrai référence dans le monde de la lutte regarder le calme, serein, propre oh quel lutteur
@hamzafall54752 ай бұрын
Depuis Londres... Modou lo mo meun mo eupp doolè... Siteu loumou dèff daanou... Modou lo est le meilleur lutteur de tous les temps... Modou 2:25 lo kessè lagnouy toppou....
@OusmanemoussaCisse-w3k2 ай бұрын
❤
@GhomNdeye2 ай бұрын
Machallah
@MangoneFall-nv9op2 ай бұрын
Modou lo yalnako yalla mayy ndam inchallah
@OusmanemoussaCisse-w3k2 ай бұрын
Allahouma amiiiine
@MorFall-n1x2 ай бұрын
Amine inchallah 🤲🏻 🤲🏻 🤲🏻
@Mamichoubb2 ай бұрын
Amine 🙏🙏🙏🙏
@AidaSene-rf4bx2 ай бұрын
Modou lô yalnako mayy ndam❤❤❤❤❤❤❤❤
@safiatousy62492 ай бұрын
Téy modou pate bi la maya kéne dou yaw sama mbeur bi mdam reck modou lo ❤
@bafatou31862 ай бұрын
Siteu tu rêves les yeux ouverts. Modou yalna yalla mayela ndame
@souleymanediop34132 ай бұрын
Modou lo kou dale la Ndeysan Il est le meilleur
@mansourkonte98732 ай бұрын
Modou kou diege yalla la,bo khole kanamam sax gisthi leer Macha Allah.Kholale dafa obali rek wakh Ahouzou bilahi minachaytanirajim walahi gnikay defe beuretoul ndakh ignorance rek.Ak manque de savoir
@CheikhOmarKandé-z6i2 ай бұрын
Modou lo yalla nako souniou borome may ndam ✌️✌️✌️🤲🤲
@MoustaphaThierry-vf9lz2 ай бұрын
Siteu yamal bakhna môdou yalna gua am ndam Lou nékh🎉❤❤❤❤❤❤❤❤😂
Modou yeee le roi mdam rek xlo dou fô héré hére 🌟🐉👑👑🤲💯👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑🤲👑
@TidianeNiang-k2d2 ай бұрын
Siteu tarkida rék ❤❤❤❤❤
@ibrahimaDiallo-ek9ld2 ай бұрын
Siteu degay danou barke serigne saliou inchalla
@ndiayeabdou40792 ай бұрын
Ok yow capturé nala
@Rapkabadaforever2 ай бұрын
Degay doul
@MorFall-n1x2 ай бұрын
@@ndiayeabdou4079ak yaw capturé bala
@bayemodoundiayexassida17672 ай бұрын
Boul fatènè wakhna inchallah@@ndiayeabdou4079
@alkhamisskor58232 ай бұрын
Amine inshallah
@BabacarNdiaye-g5m2 ай бұрын
Yallh nla yallah may ndam Modou lô le meilleur siteu yangui parlé rek baxna
@Boyka2052 ай бұрын
Xaragne lo ndam rek inch'Allah
@AbdoulayeMakhtarFaye-xk2sd2 ай бұрын
😢Billahi Siteu bomoÿtouwoul Modou X Lô doko diëmeu sourroukhal dinala yënnou basa birbi wëkh mou d'or la si souff🤸 ne faut pas sous-estimé 👑 X LÔ c'est très dangereux dans la la monarchie 👊🤛✊
Xlo ndam rek le 24 Modou lo dou fô bii héré héré 🌗💯👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑
@omzoseck85662 ай бұрын
Sietu yalla nala yalla may ndame
@abdoubarry49292 ай бұрын
Nanyou wahk,bessou wahla...Siteu daffa dang-ngam...balla combat,wah lanyou am téh moy nehhal afférii
@matarthiam40862 ай бұрын
Mbeur boko diokhoul thieur rk mou dan la sitteu amoul respect 😢
@absadiop71822 ай бұрын
Ki kay da beuri wakh avec Lac de guer ni la wone teh defufa dara
@LatyrNiane-zv9bp2 ай бұрын
Siteu domou sererre bi yasam roga thiohong ndam❤❤❤❤inchalah
@ndoffenetine53332 ай бұрын
Modouuuuuuuuuu looooooooooooo ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Arbitre sifflé mod lo dumako dane nako késsé ngén di dëgg
@IbrahimaThiam-n6o2 ай бұрын
Vraiment le combat a fait sa promotion 🎉❤🔥 feuuu 🎉😊
@AbasseSagna-g9b2 ай бұрын
Modou lo d’où sama mbeur dei mei je l’aime bien frère
@lahatndiaye29872 ай бұрын
😂😂😂😂😂😂siteu nexx n'a modou yala nala yala may ndamm
@ElhadjimodouGaye2 ай бұрын
Modou lo dina dane siteu diell bou reuy inshaAllah!
@khadydiagne28602 ай бұрын
Àmine
@El-Mahdi32 ай бұрын
Khana serigne ngua
@DemathDeme2 ай бұрын
Siteu changéle sa Communication bou boyé bi! Khare day wéssou Mbotté! Légui Responsable gua, té dans la cour des grands... Communication bi bayéko gnome Liss Ndiago ay gnome Laurent Ndiago .... Magal waye,!
@AidaSene-rf4bx2 ай бұрын
Modou. Lô. Seul❤️❤️❤️❤️
@gueyelabsolu58892 ай бұрын
Siteu ki Toudoul Mor Lo way 😂😂😂Modou lo la Toudou Doudou Lo moy vré Touram ngane Mor lo ny rék 😂😂😂😂😂
@MouhamedDia-t8j2 ай бұрын
Frenchement Modou lo référence nga da nga dal té beuri wo wakh
@awasarr81192 ай бұрын
Bilay Siteu aye rée lama def😂😂🤣
@abdallahdiakhate63052 ай бұрын
Siteu est prêt et il n'a pas peur à Modou lo. Yalla nako yalla may ndam mou dieul roi des arènes
@Rapkabadaforever2 ай бұрын
Siteu rk depuis Belgique ❤
@ndoffenetine53332 ай бұрын
Ibou yay ndër😅😅😅 Bula modou diapé😮
@SaliouWade-i1m2 ай бұрын
Siteu yalla nako yalla may ndam barké seyedina mouhamed barké Serigne Touba
@Dabakhdiaw-u3v2 ай бұрын
Mangui laye doga dégg
@damegning39752 ай бұрын
Ama baldé moungui wakh ak khélam nane modou dou gnékhou gnébé kénn😅😂😅😂😂
@tallablaye69832 ай бұрын
😂😂😂
@alphadiouf81112 ай бұрын
J'aime bien siteu mais Modou lo le met mal à l'aise il le déstabilise a chaque fois je sais pas pourquoi
@Iba82 ай бұрын
Qui est là après le combat? 😂
@ouzdaking3822 ай бұрын
Siteu grand champion le baye fall future roi des arènes inch'Allah 🎉
@dioptalla27572 ай бұрын
Bilaye yagui wakhe mais soula Modou lo diappé😂 dagua khamené lépou deugueleu😂
@IbrahimaFall-b7p2 ай бұрын
Siteu combat bi daka dépassé 😅
@ZakhralalinguereDiouf-b4q2 ай бұрын
Ay nakhasakhadak rk lay wakh
@silencieuxbouyant96872 ай бұрын
Inchallah Modou lo Dina dann siteu le 24 novembre inchallah
@Mamichoubb2 ай бұрын
Amine
@malaminecamara21062 ай бұрын
Modou est très humble et serein maschallah parle peut
@LamineFall-r9p2 ай бұрын
Non siteu day rayyyy niiiit😂😂😂😂😂😂
@Dabasy19982 ай бұрын
Mane xawma loutax damakoy deglou ay ré dima diap😂😂😂, mou ngui wax rék 😂
@mameisseuniass84722 ай бұрын
😂😂😂
@youssoudiokhane36002 ай бұрын
MACHALLA Siteu diayena combat bi
@papamodou35232 ай бұрын
Modou lo de wakh dji dou bari dieuff rek yalla Nako yalla may ndam lou gaw inchalla si barke s babacar sy ❤❤❤siteu wakh dji barina trop modou mongi retan 😂 rek akay ndanan le 24 soriwoul 😂
@khadydiagne28602 ай бұрын
Amine
@SerigneFallouSylla-j7v2 ай бұрын
Siteu daffa,beug deh mais lepp dale mokoy mayeh modou daffa teye teh siteu day wakh rekk
@gueyelabsolu58892 ай бұрын
Siteu Momay Dadji man 😂😂😂Dafmay fath man Siteu c normal Mou saf xorom Bay fall deugeu Day saf xorom 🥹yallah Nala sounou Borom may ndam Barké mam xheix ibr Fall🙏🏻Diambar nga fall 🙏🏻🙏🏻
@Leuzsonko2 ай бұрын
😂amine way do bayi sama mbeur mi😂mom da pares nak
@Taysiir3132 ай бұрын
Noo siteu dafa nekh 😂😂😂😂😅😅😅😅
@alexndiaga77752 ай бұрын
Modou rék 🇸🇳 🇮🇹 👊
@mamadoulaminesane59122 ай бұрын
Siteu attention a Mlo😢😢😂C le meilleur
@SeyeMamadou-h9o2 ай бұрын
Siteu bilahi dafa nékeu si pression écologiquemen il n'est pas prêt
@alioubadarafaye61072 ай бұрын
Écologiquement dh anh 😮😅
@SeyeMamadou-h9o2 ай бұрын
@alioubadarafaye6107 scologique du moins 🤣🤣🤣
@AssaneMBENGUE-q2s2 ай бұрын
Psychologiquement
@AboubakryHane2 ай бұрын
@@AssaneMBENGUE-q2s😂
@metakrazygamezeum63412 ай бұрын
Siteuu da tit da diahleee da diahasso 😂😂😂😂😂😂😂😂😂 ay Modou lo digua ma ray
@papamamadoudiallo28642 ай бұрын
Modou mbaye raynama nena😂 lac 2 néwone nako lokho modou lo yi ay khérr mossi nk
@mohamedfall4592 ай бұрын
Siteu dh wakh reik ameu thii comba bii mei je laime bien 😂😂😂Modou champion ❤❤❤
@mohamedfall4592 ай бұрын
Biremeu Yacine😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
@fabinetadiaw2 ай бұрын
Modou Lo yalla nala yalla faral si barké seydina Mohamed SAW Amiiiiin
@MameSow-m7e2 ай бұрын
Modou lôoooooo ❤❤❤❤
@Ibzy_boss2 ай бұрын
Non Modou Lo mo bonn 😂😂😂 nènë Siteu ay ré lako deff🤣🤣🤣
@AbdouDiop-bd6sy2 ай бұрын
Lak loula nekhe niow niou dane la😂😂😂
@moustaphaba91142 ай бұрын
Siteu kay degua énervé 😢😂
@abdoulayedia94602 ай бұрын
Siteu Siteu la 🎉🎉🎉🎉🎉 ndam rek inchallah
@iniestafaty39002 ай бұрын
Siteu nakk moy nitt kou répeuh deug😂😂
@BarhamDiop-mp2nq2 ай бұрын
j'aime Siteu wayyy
@FatouDiop-t9d2 ай бұрын
Modou lo yalla nako yalla maye ndame yalla n'a dore situé mou dannou😂😅😢😮🎉
@MaimounaBangoura-r2x2 ай бұрын
Modou ❤Lo rek
@kharylo-g5t2 ай бұрын
Modou lô rék amoul lénéne💪💪💪
@papefall70622 ай бұрын
Grand watou ngata 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🎉 siteu con nga😂😂😂😂
@fatousarr6632 ай бұрын
Modou tay pate bi la mayé di observer, di lire les pensés de siteu. Ins by siteu wahna nimou fassiéné beuré ba paré😂 Boula modou diapé tu vas lire lheure. Sa wah bou bari by yeup geumossi dara wagnil stress bi ganyine
@sokhnadiatoudiop-vd8fk2 ай бұрын
Modou lo yalna am ndam inchallah 🤲🏿
@alassanenogayebadji66772 ай бұрын
Siteu rek....❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@gasbalde49362 ай бұрын
Sisiteu yalla n'a yalla Maye ndame 💪🏿
@AliouKebe-il1rg2 ай бұрын
Modou lo 💯💯💪💪💪💪💪
@MoussaNdiaye-v9w2 ай бұрын
Modou Lô yalnako yalla maye ndam
@Nezuko-et6zc2 ай бұрын
Modou seul 💪❤️ Siteu barri gua wax☺️😒 Inchallah dimanche ba boba❤️ MODOU LO KASÉÉ 💪❤️
@assanefall95472 ай бұрын
Ahh siteu mi yaram mam tangu na dh😂😂😂
@MouhamedDia-o4e2 ай бұрын
Yamba 😅bi la
@MrOusmane232 ай бұрын
Yene khamna da nguene gaweu fater, modou lo mo yob bombardier ardo, ko Eumeu sene, Dane Gris Bordeaux , beurai ak balla guaye , feut boy niang ak Ama baldè. Dans les normes , ce combat est même pas logique si on se base sur leurs palmares.Modou dou sama mbeur mais faut reconnaitre qu’il est tres lucide et serein comparè a Siteu. En plus mane jusqu’a present j’arrive pas a comprendre loutakh siteu parle de lac2 guerre, mais mom lac2 mo ko gagner, ki danoul bene grand. Siteu dal moye lolou koi
@mamounesall76072 ай бұрын
Lamb dji délo léneko fimou nékone déléne ko tékk télé
@molaminmanneh-fs6wn2 ай бұрын
Face to face bi nehut merci siteu
@sambadrame34972 ай бұрын
Haha 😂😂 siteu Baye fall bi yq nekh am me fan's Balla gaye mias baye fall bi Baye fall bi Diadieuf ❤
@inchallahdia47692 ай бұрын
Bilahi yaamba bakhoul 😂😂😂😂
@CheikhIbraFall-u2r2 ай бұрын
🇧🇪 Congratulations à buzz 🎉 Modou lo da moudjié fan 😂siteu par ce que d'ay néxaal lamb 😂 yalla nanioukô féké talko si diam akh salam wergui yaram xalice bou beurri té lèw ❤
@moustaphaba91142 ай бұрын
Amine way
@NorenyVasyli2 ай бұрын
Modou le roi ndam rek xlo dou fô da héré héré 🌗✊🙏🏳️💯👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑
@BabacarDiouf-j1k2 ай бұрын
❤yal kesse inchalla ndam rek.
@AmadouBa-x9l2 ай бұрын
Modou lo❤❤❤❤❤❤seul
@mormbaye60982 ай бұрын
Modou lo mi la may chance rék mo niou togne
@goorgorlou2 ай бұрын
Siteu sois plus serein andal ak dal touti changer sa com touti k le meilleur gagne
@AbibWade-t6y2 ай бұрын
Modou bi d'où yoyou 😂😊🤩
@DiorNdoye-o6y2 ай бұрын
Ayyy wayyy diapelene siteu yagui wakh rekkkkk
@aliounecisse41142 ай бұрын
Tok si micro 🎤 di wakh ak modou aka nékh wayé bilakhi yéne niàr késé bounguéne désé si guéew bi dinga fàté linga done wakh bakhna rék