Lamb dji dafa beuré ay nafekh mais modou lo yalla rk la yakar ❤❤❤
@daoudatoure2517Ай бұрын
Victoire mérité kharagne lo yalla kassé mofi nek ndam rek❤ inchallah
@oumarniang6632Ай бұрын
Modou kharagne lo kene dou yow tu es le meilleur ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@AtoumaneNiasseАй бұрын
Dieureudief sa sa kaw sa kanam ❤❤❤
@AtoumaneNiasseАй бұрын
Machallah gorgui lou leer nga wakh ❤
@quetespirituelle6647Ай бұрын
SITEU DAFA DAW COMBAT BI YEUP TÉ POURTANT WAKHAM JOU BARI JI DAFA WOROON ATTAQUER. MODOU REK MODOON ATTAQUER. MODOU MO EUP MERITE. SITEU AMOUL BEEN MERITE DAFA WAROON ATTAQUER TÉ DAFA DAW BA COMBAT BI DIEEKH. FÉLICITATIONS MODOU LO.
@kannydiallo3891Ай бұрын
Alkhamdoulilah kharegne kasse ❤❤
@iBSONDialloАй бұрын
Niouye khekh Modou mo Bari siteu daw ndeye combat bi nguen di saltél
@thiawfoot5217Ай бұрын
Félicitations Modou lo ❤❤
@moussadjigo2779Ай бұрын
lambe dji dafa bari ay nafekhe modou guayi dagno ko sot pour mou danou mai yalla moko sampe
@moustaphadiouf9154Ай бұрын
Walahil daga leer tei siteu da teuthie beuribi Modou lo Moy attaquée def leptei siteu moko waraune def
@papadiom9260Ай бұрын
Da ngay doul rekkk dagn ko dane thi Lou lerrr
@aissatousene2700Ай бұрын
Vive Modou ❤❤❤
@MansourDiouf-m6fАй бұрын
Machallah
@hamidoutall9134Ай бұрын
Journaliste yi boulen niou sonal Balla Gaye wahone nafi Victoire noko amé bakhna
@DjilySarr-l3bАй бұрын
Balla mo mome lamb noum wakh nonou la
@AmadouDiol-d5oАй бұрын
@@DjilySarr-l3bms ballagaye loumou fi deffe modou khalatouko deffe balla bamouye beuré bombardier mouye courager les bras takhawe fimou takhawe ah 😂😂modou lo seul❤❤❤🎉
@rouguikebe9984Ай бұрын
@@AmadouDiol-d5oMok gris decision arbitral ladé😂yok si bobou😂
@hamidoutall9134Ай бұрын
Félicitations ❤
@modoudiop7841Ай бұрын
😅MODOU 🎉❤👑👑💪👌👆🙄🇸🇳🇸🇳🙏🏾👑👑👑👑👑
@AmCoulibalyАй бұрын
Vraiment Modou lo a lutte pa contre siteu da da comba bi
@punchyork7167Ай бұрын
Pa youdone commentaires mom comme si daniou faral Siteu mais dara Ya Allah moy borom dollé bi
@sarrmassaer1870Ай бұрын
Modou seul❤❤❤❤
@mamadousylla6680Ай бұрын
Mome ndayesane xamoul ni gayi comedien lagnouko diapé😂😂😂
@SaliouDiop-e4rАй бұрын
😂😂😂nonn
@rouguikebe9984Ай бұрын
Kone wéro
@GalayeKamara-yn1odАй бұрын
saway amal respect ok rew nga trop
@cheikhounagaye9405Ай бұрын
Lamb dji mo beuri nafeh ak seytané di sott beugue nitt ki danou mais modou da am niane yalla rekk mo fi nekk
@tallandiaye6481Ай бұрын
Modou lo❤❤❤
@MansourDiouf-m6fАй бұрын
Alhamdou lilah sante yalla
@Ydakh-ui5yoАй бұрын
Siteu na takhaw di deugeul bopam Koi wala
@MAMADOUBA34515Ай бұрын
Wa keur Modou lo boulénne niou sonale,guéne teugue lamb dji nane daniou lénne sotte,Siteu yobou nako niarri yone ardo
@malf17Ай бұрын
Yaw Katal sa ndy
@MouhamedCisse-d9mАй бұрын
Siteu sou arbitre bii sifflet baparé lay sogay sania door modou lo
@BatorFall-r2lАй бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@NiangMor-m1mАй бұрын
Vive mod lo
@kaneadama1226Ай бұрын
Félicitations siteu le nouveau rois des arrénn
@moustaphadiouf9154Ай бұрын
😂😂😂
@mansourndione1342Ай бұрын
Siteu
@AbdoulfataDiattaАй бұрын
Sa touba wanieu wakh bi
@BibaDiaoАй бұрын
Siteu c le nouveau roi des arenes❤❤❤
@CheikhFaye-e2cАй бұрын
Wz Diamageune DOUGNOU Wara wakhe siteu DEUG moulen endile zy défaite par avertissement gnouye jubilé
@AboubabaBa-m5hАй бұрын
❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
@MAMADOUBA34515Ай бұрын
Kone khana wakhe lénne si Fadam akk boure guéwéle louniouyez sotté Siteu té moussou lénne si wakhe dara
@kaneadama1226Ай бұрын
Sa Touba bayil doul lo wakhone khamo dara di doul rk di nga nopi dh
@Mgoor-w2pАй бұрын
Walah modou diambar la ms dafa naron danou
@AboubacryGASSAMA-zs7oiАй бұрын
Waw mes gninékone si combat bi yeup pour modou lo danou .boussi modou lo danouwoul ba diahane na guene sante yala..victoire bimou ame ces mérités ..
@papadiom9260Ай бұрын
@@AboubacryGASSAMA-zs7oi Boul gnou sonal ! Eumeu Sene soot yi ngene ko soot Amitié ! Am ngene chance Siteu dafa yekha dougou thi Stade bii mais Narona nokou Modou lo nokou yi Neto daneko ba djegui kaa !
@AboubacryGASSAMA-zs7oiАй бұрын
@papadiom9260 haralma rétane sakh tu na rien compris 😅😅😅Usain Bolt daye dawe rék amoul arét. rakou lac de guerre 2😅😅😅
@rouguikebe9984Ай бұрын
Siteu reussiroul dara Ama ak BN2 ay diambar lagn danio takhaw deugeul séne bop🎉 Siteu niewoul wone pour beuré Saltél la begone vrai badola la mais Modou mognou togn rék heureusement yalla faynako kholam❤ Félicitations Modou ❤🎉😊 Modou nak Yalla la andal kéne menoul si mom touss 😊
@papadiom9260Ай бұрын
@@AboubacryGASSAMA-zs7oi USAIN BOLT bou ande ak lokho MIKE TYSON 😂👊🏽 ndakh nious yimou nious Modou lo Bo parer daneko douko defatii 😂😂😂
@assanegueye4884Ай бұрын
Dangue barii wakh
@ModouSylla-o1iАй бұрын
tay la mousa guis kou nokkhou Modou lo 😂😂😂😂
@khadyndiaye5800Ай бұрын
Y’a meuneu Sakoche doule
@khadyndiaye5800Ай бұрын
Modou mi meune SITEU foufe
@SaliouDiop-e4rАй бұрын
Niam n’a dh😂😂😂
@beaugarsdiop515Ай бұрын
yene dama yakarni sene beute yi guissoul yene kouy daw dina noké kou daw kay mome laniou nok😂
@papadiom9260Ай бұрын
Guis nga amna bene laaw gauche bou Siteu dii door mou rombou Modou mais bilahii naronagn ko doumeu !!!
@abdelpyramid1205Ай бұрын
Mais les Bros saaa Touba dey ligueye nak ! Clients lay weuraalé tamite et il a le droit nak
@cheikhdiop9932Ай бұрын
Siteu nena modou lo nie nioko sonal😂
@loumfatou594Ай бұрын
Talamasa guis kou nokh modou lo ba yobouko ardo bilaye yallminebi moye say say😂😂😂😂
@SambouSarr-q6dАй бұрын
Ki dou sarampión ndeyam danguen danou
@ModouSarr-i1yАй бұрын
Balla gaye na diél franc,Modou beuré woul AK Balla gaye
Fi nguèn wara diar detesté serigne reseaux yi Fi yalla rek mofi née
@cheikhdiop9932Ай бұрын
Sour na list bi wakh nalla lou ler 😂
@ModouSarr-i1yАй бұрын
Siteu Di ragal,daw combat bi lép
@PAPAMOUHAMADOUMOUSTAPHAM-fr5ktАй бұрын
Saaa parcelle nopile…. Taye ngay rek thieur yalla n’est ce pas yalla Daf la wanone?
@MamengorThioune-cv9wzАй бұрын
Danguéna danou nangou lénn 😂😂😂😂😂
@SaliouDiop-e4rАй бұрын
Bilahi 😂😂😂
@papadiom9260Ай бұрын
Yaw mom war nga teudj Ndaye sa lamigne ak Sa lekhe yii Niaff ndayam yii ! Ba ngene di Soot Eumeu stade Amitié fi laniou fekk ! Gnous gnous yignou lene gnouss amolene Sagn oubi Sen gaat gui nane Modou mo dane ! Décision arbitrale mérite naak mais Siteu gnous nalene dane lene Djel bou lerrr !!!
@amadoubarro9713Ай бұрын
Way lui dou victoire lui Mach nulle la
@NdiogouNdiaye-t5fАй бұрын
😂😂😂
@ThiernoDiop-ei2htАй бұрын
Yen journaliste yi soff nguen trop koy daw rek siteu dafa yabate fou beure moukou daw rek
@cheikhdiop9932Ай бұрын
Sa touba😂😂😂. Wakh rrk
@mansourndione1342Ай бұрын
Siteu
@papezulefaye7263Ай бұрын
Bilahi dangéna rouss modou lo siteu dako werr amoul coffre si combat bi lingéne wakhone yeupa moudié ayy doule bayilene di wakhé bakane té wakhé xam xam...victoire de siteu wallahi
@AboulBacharSallАй бұрын
Ya meune doul siteu melni djiguéne di daw di gadje ba lamb dji diex nguanan victoire de siteu nekal niit siteu waxlein ko deug danou fi bein mbeur wax rk la meune
@AboulBacharSallАй бұрын
Boy daw di xex di door di songou danguay sonou siteu noumouy beure mane sax souma entraîné ken douma daane nidiol sikaw di rassou rk ba lamb ngua dém plateau di wax rk
@MouhamedCisse-d9mАй бұрын
Mom bou yamone si rassou rek dafay neex dafa don daw waxettt😂😂😂
@BayeZall-v3lАй бұрын
Doullĺlllllllllllllll😂
@SaliouDiop-e4rАй бұрын
Y’a sahlé niam n’a dh😂😂😂
@OumarSy-m9sАй бұрын
Le roi siteu kassé ❤❤🥇🥇🥇🥇🥇🥇👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑👑🎒🎒🎒👑👑👑🎒👑👑👑👑👑👑
@abdoulayetaye1969Ай бұрын
Sa touba dele wakhe degue louye khewe souba yala moko khame ya done wakhe dore mou Danou 😂do dara fi yala rek mofi nek louye khewe souba khamoko
@FabienDieneАй бұрын
Sa wakh mo beuri sa touba yow do gnitou dara
@FallouNdiaye-h3pАй бұрын
Supportèrou Modou lo yi bayilène sissou bi way siteu dou noy nèkh dh bou dawè tmt dafa daw ba nokou lène 😂😂😂😂😂😂😂😂
@MouhamedCisse-d9mАй бұрын
Mom après coup de sifflet arbitre bii rk lay sania door modou lo