Wally dafay bayi way” Mbaye Sy Ndiaye confirme "actuellement kilifeu yi niogui wakh ak mom mais….

  Рет қаралды 175,483

BABACAR W. OFFICIEL

BABACAR W. OFFICIEL

Күн бұрын

Пікірлер: 415
@ndakarudialdiop1206
@ndakarudialdiop1206 10 ай бұрын
Wally bo bayé way doko reuthiou walahi, tu es toujours jeune pour te repentir, bayii music ci khalé dém diamou ji yalla lolou dara gueunuko❤️
@binetandiaye1352
@binetandiaye1352 10 ай бұрын
Bilay mo gueneu dh bagna topp égoïste yi nga khamni séne boppou toppou yalla mo guene topou stars
@Diija02
@Diija02 10 ай бұрын
Degue na deugue deh
@Mimi-u4o8d
@Mimi-u4o8d 10 ай бұрын
Courage Wally que le bon dieu vous protège avec tes sœurs et frère Amine 🙏🙏🙏
@YacineNdiongue-k8b
@YacineNdiongue-k8b 10 ай бұрын
amine yarabi ndeyssane
@louloutebi
@louloutebi 10 ай бұрын
Il faut qu’il prenne un peu de recul le pauvre c’est vraiment dur pour lui en l’espace de quelques mois il a perdu sa sœur et sa maman . 2 piliers importants dans sa vie Force et courage à toi Ballago nos prières t’accompagnent
@awasene7840
@awasene7840 10 ай бұрын
Wally sa bamel kén doulafa fék donc so bayée mo guene ndakh nitt yi sén intérêt rék moléne soxal bayii ci xél je t'aime et je t'aimerai pour toujours ❤❤
@noumchjoop6808
@noumchjoop6808 10 ай бұрын
Merci
@TUVARÉUSSIRINCHAALLAH
@TUVARÉUSSIRINCHAALLAH 10 ай бұрын
Bien réson n'a bayi c'est pas bon pour lui ni c'est parant
@annapepe2976
@annapepe2976 10 ай бұрын
Bayil waye Waly,,, prie pour tes parents c mieux 😢😢😢😢😢
@Senegal733
@Senegal733 10 ай бұрын
Yalla na bayi weuye si barké MOUHAMED (psl) dadialé aye gor ak djiguéne gnouye thiakhane amoule mouthiou bou raféte
@awasene7840
@awasene7840 10 ай бұрын
Merci lolu Moyy deug
@binetaseye1908
@binetaseye1908 10 ай бұрын
Bilay amine
@NdeyeMbaye-o3y
@NdeyeMbaye-o3y 10 ай бұрын
Amine
@sallamansour9388
@sallamansour9388 10 ай бұрын
Aminnnnnnn
@NdeyeMbaye-o3y
@NdeyeMbaye-o3y 10 ай бұрын
Amine
@maoudediao653
@maoudediao653 10 ай бұрын
Wally deloul si yalla ak yonentibi psl xalate gni nek sa guinaw courage bro
@KineNiage-ek4sk
@KineNiage-ek4sk 10 ай бұрын
Kou bakh yermander
@khalilgueye8516
@khalilgueye8516 10 ай бұрын
Alhamndoulilah sante yalla boubax ❤❤❤❤❤ louy yok say bakar mom boko bayé ak sante leu Mangui niane 🤲 yalla mouy deug Prsk lépp ay foh leu té yalla beugouko yoneéntibi beugouko Serigne sou bax si beugouniouko na bayi mo geun 🤲
@nourradam6391
@nourradam6391 10 ай бұрын
Wala merci
@khalilgueye8516
@khalilgueye8516 10 ай бұрын
@@nourradam6391 mogeun dé
@siramo574
@siramo574 10 ай бұрын
Amine waaye. Ha maanne dèe beugueutouma mou waaye, nite kou bakh Laa.thèe moumbaye bii daalle dooye namaste, yalka nguii waah AK mome.bayilenne ko mou bayi, lii yeuffii Aruna La thè youngui thii akri zamanne.
@FatouDiaw-z5b
@FatouDiaw-z5b 10 ай бұрын
Niar njimou niakk ak papam wakh deugue diarna bayi yéne mom étéré rékk ya waye kharam
@awasene7840
@awasene7840 10 ай бұрын
Deug nga wakh bilay
@annapepe2976
@annapepe2976 10 ай бұрын
Yeufou. Cheytane rek leu musique laisse tomber la musique prie pour tes parents ils ont besoin de tes prière 🙏🏾 😢❤
@miss_0148
@miss_0148 10 ай бұрын
Vous êtes égoïste que Dieu lui donne mieux que « Yow » comme priait sa mère inchalla
@sidydiop1523
@sidydiop1523 10 ай бұрын
Waly seck yalna bayyi way yalla diokh ko lanen lou geun way ndakh amna niou khamni sen interé boulen topé dou bakh wally amal jammou
@siretamba3386
@siretamba3386 10 ай бұрын
Amiiin ya rabby allah 🙏 🙏 🙏
@mamygaye4378
@mamygaye4378 10 ай бұрын
Amine Y'a Rabbi 🤲
@bestfashionman6443
@bestfashionman6443 10 ай бұрын
Wally n'a bayi waay, c'est une bonne initiative. Il peut prendre d'autres chemins machallah. Même sou Wally wayatoul Wally sounou Wally la lolou yalla moko def. Je suis d'accord avec sa décision si vraiment c'est lui qui le dit. Wally baye fall tei dou deif ni papa'wemba wala dém ba maguette Di bayi. Yalla machallah téral nako ba nopi. Il est temps mou diokh dinné ak charia limou mom. Tei yakar Nani biss bou topé charia gui gniko beugu gneup dinalén tagatt si yonn bobou nax sénégal nak sou deugu néxé bén influenceur la am Mouy wally seck beugu nagnou bagn nagou. Tei lolou souko défé yalla nassi gueune jiss Ndam inchallah. Yalla nako sa borom sopi si dinné ak charia mou done louko jikk si barkep kou tedd ki. Yalla lak fou yakk yégoul nax franchement yagu nama bégueul Mane en personne. Yén nak wa groupe ram'dan khamnou ni sen intérêt Moy Wally continuer ande ak yén gui alalou adouna mais nak yakar Nani ak année yiguen ande ak mom s'en adouna warna défarou mais aussi bayilên ko ak son choix boulén khôl si sén dieurigne kassé mais Wally n'a plus les forces de maintenir kimou niak Mouy yaye moko done are si adouna. Tei Sax yén wa groupe ram'dan je pense daguén ko wara bayi nak mou bayi waay bi nax diap guén domou diambour diko nott sén bop kousi nek nax alalou adouna. Mais nak Wally on est derrière toi lo def rek dafa gueune mais boul faté ni ndapp kén douko gnitt tei aussi nitt sou niaké yérouway louko boukh dafay yomb tei gnila si diégué kén bayiwoula si surtout si ay def'def. Donc protège ta vie nax tu as une famille et tes enfants compte sur toi et il est temps de vivre une vie normale avec ta petite famille et avoir beaucoup de temps pour eux. Ta femme est une guerrière et une battante franchement donc bientôt tu es dans les quarantaine tol si attou gorou yalla yi bayi si khell. Adouna nex n'a lolou nax thiaxane nexna trop dafa bakané wayé nagnou délou si yonou siratal mouskhim tei xamni yalla rek mofi nek yalla rek moy deugu tei islam maki alkhou'ane lafi wathié tek ay charte gnou xam Lou bax ak Lou diné wax donc lo jiss si adouna diar'diar la nax jeune bou nek so tolé si oute lo beugu ak lo jiss def ko tei bagasi tolé waay ga choisir tei def gako ba sa borom téral lassi tei tay sante yalla amga lousa morom amoul wayé niak ga lisa morom am tamite. Nax ga balma si thiaxane ak Lou diné beugoul lagnoula xamé. Wayé meune am li Say morom am téga niak ko Moy done dioulite deugu deugu Di dieufé lepp Lou dinné beugu loumou bagn ga bayiko. Xamna nak sama way Dina nakari touti mais deugu dou romb nop. Wally franchement dagnoula beugu ba tay so nékone nodd kate Sax gnou gneuw fek Sila si Liga nek machallah et surtout courage à toi. T'es l'aîné de la famille tei yalla gako Matt seuk. Diam si yaw frère et one love. Wally chanteur ou pas chanteur beugu nagnoula ba nopi
@mamethilofall7513
@mamethilofall7513 10 ай бұрын
Bilaye
@mamesarr4798
@mamesarr4798 10 ай бұрын
Vraiment sa message dafa goudeu commencer mai j’en pouvait plus 😂😂😂 Wally kou bakh la I love him too ❤❤❤
@astoundoye1513
@astoundoye1513 10 ай бұрын
​@@mamesarr4798goudouna tropeee likay discours la meunoumako lire temps la amoul 😂😂😂😂
@angelediouma9258
@angelediouma9258 10 ай бұрын
Prie juste avec Dieu ecoute ton cœur le Seigneur te parlera❤
@zeynabsa
@zeynabsa 10 ай бұрын
Nianal lène ko yalla goudou fane ak wérr té soutenir ko si ay decision wam té yalla diko diokh loumouy diokh gniko yakar
@AhmadouRssl
@AhmadouRssl 10 ай бұрын
Mane Wally motakh may écouter musique Bly bougnou def nii 😭 wally seck on t'aime fort ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@mariemedieng5357
@mariemedieng5357 10 ай бұрын
Adina bi amoul solo sou bayiwer ALHAMDOULILAH ndakh adouna dou keur bilay wallay tamit naniou si bayi khel . Niak être cher c dur liko yayam done wakh rek yallah n'a tela bayi wey am louko sout inchallah
@barhamjaw2255
@barhamjaw2255 10 ай бұрын
Yalla na baye ci barke muhammad s.a.w
@matydiebate5292
@matydiebate5292 10 ай бұрын
Mar Yacine ke le tout puissant te protège 💔🥲🙏🏻
@yacinekhouma-sl2uz
@yacinekhouma-sl2uz 10 ай бұрын
Beugueul léneko diame bâti waye mo gueune thi môme képe kouko yéné diame doko digueul mouye continuer Di waye waye dafa Haram lolou moye li lére yéne séne intérêt mo takhe nguéne beugue mou continuer Di waye yeureum léne domou diambourdi yallah diékhoul sou baye waye té boromame takhe yallah diokheko Lou gueune courage Waly yalnala yallah takhawou boula kéne influencer défalli nekhe sa borome kéne d'où tope li nékh mbindéf bâyi linékhe yallah sougnou borome wa salam gni Di wakhe yeup séne intérêt mo nék en jeu mais yaw takho gnouye inquiète téwou boula kéne diaralé yallah dimanche méré
@KhadyDiaraSeck
@KhadyDiaraSeck 10 ай бұрын
Merci Mbaye Sy Ndiaye,du courage Wally que Dieu te protège
@AdjaGaye-t4q
@AdjaGaye-t4q 10 ай бұрын
Ak lo meuna décider Waly on t’aime té dou meussa changer
@hannenabou1961
@hannenabou1961 10 ай бұрын
Salam Salam mbaye yaw kou bakh ngue machallah wally on na tout ceour ❤avec yalla nako yalla same yalla mayko goudou fane s barcke seydouna mouhamet
@mamethilofall7513
@mamethilofall7513 10 ай бұрын
Wally,motakh,may, écoute musique bilaye, que dieu vous bénisse et portege seyedi secke ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@fatoudione1441
@fatoudione1441 10 ай бұрын
Merci beaucoup Wally et félicitations pour se chemin que le bon Dieu vous protéger Dina méti mais Lou bakh dou Mossa yomb mouk❤❤❤
@coubatandine5057
@coubatandine5057 10 ай бұрын
Bilaye walay li da metti trop surtout yaye 😭😭😭😭😭
@Rokhaya3114
@Rokhaya3114 10 ай бұрын
Sui de tout cœur avec lui quelque soit les surconstance Sama musicien ❤❤❤❤❤
@ZizaBa-bk8pr
@ZizaBa-bk8pr 10 ай бұрын
Du courage mar Yacine yalla bakhna on t'aime vraiment ❤️❤️❤️
@KinéMbengue-c4j
@KinéMbengue-c4j 10 ай бұрын
Aye waye waly boule ma deff nii maye bilahi yaw laye déglou so bayé noumaye deff😢 maman diaga yalnako yala yereume khareko aldiana
@princesse-Soninké
@princesse-Soninké 10 ай бұрын
Khassayid yangui fi té nekh trop sakh 😂😂😂
@KhadyFaye-jf9th
@KhadyFaye-jf9th 10 ай бұрын
Notre Wally courage rk et k Dieu vous protége 🙏🙏
@MouhamedMouhamedcissokho-jk8ci
@MouhamedMouhamedcissokho-jk8ci 10 ай бұрын
Courage mar yacine soudone sama sago mou bayi way bi démeu diamou ji yalla di nianal ay wadiourame té ay soeurs rame ak frere rame inchallah rabbi lépp day bax frere yalla défal nala lo mouna soutourlo 🙏🏾🤲🏾❤ di nianal tmt lou bax rek ngay am inchallah rabbi 🙏🏾🤲🏾
@m3dkane25
@m3dkane25 10 ай бұрын
Yalla na bayi way si barkep psl ❤
@senegalkesso1293
@senegalkesso1293 10 ай бұрын
qu’Allah guide Waly Seck. Yéna gueuna kham ni woy da kharam lol. Dakh bou daga none jourou deudhiou way jouram mou woyal ko mais guiss guene , deh mom mat na war. Quand Allah vous veut du bien il ouvre votre yeux dans la droiture. Je prie pour qu’Allah lui facilite à abandonner la Musique et lui donne une subsistance meilleure pour lui et sa famille.
@mariamabojang9350
@mariamabojang9350 10 ай бұрын
May Allah protect you wally
@aminatadiatta2971
@aminatadiatta2971 10 ай бұрын
Yalna bayi weuy si barki psl
@AwaMbaye-q4r
@AwaMbaye-q4r 10 ай бұрын
Prie pour tes parents ils ont besoin de tes prière c mieux 😢 😢🙏🙏
@FarrissTV
@FarrissTV 10 ай бұрын
Wally yague ngua bégal sénégalai yii kone so bayé heur bi diotna té toup délou si yalla diotna boul hare ba nék pa di bayii , toup sa ba nguay nék jeune 🙏❤
@mariamaaidara2092
@mariamaaidara2092 10 ай бұрын
Yallah n'a Yallah deff musique Thie barkel mouhamed. Moune n'a am lou gueunn musique Ay wadiouram nianalko surtout notre adorable maman Diaga. Yallah nala Yallah defal li gueunn Thie yow mon frère
@nogayediongue4443
@nogayediongue4443 10 ай бұрын
Dou bayii waaye wayé na wagni certains événements Wally prouver na mba paré si musique 🎵 bi Wayé tamitt aay mbou bayé musique bii demm failande 😢😢😢😢mooy ndoudeul show bizz depuis quelques années ❤❤❤❤❤lolou la yalla defff
@MaguetteNdiaye-b3k
@MaguetteNdiaye-b3k 10 ай бұрын
Yalna bayii si barke serigne bamba bou bayee khamni yalla yoor diame yii te yalla dinako dioh lou gueune limouy ame
@sambafaye5294
@sambafaye5294 10 ай бұрын
Yalna leu yalla takhawou soutoural la diaplé la banga nk thie lou guene woye ame thie Lou raw linga ame si woy mane koula beug la wayé nga bayi moma guenal ndakh kouné lou bakh rk thie ngay beug nk chaque jour que Dieu fait
@AntaDiop-d8e
@AntaDiop-d8e 10 ай бұрын
Allakho Akbar saytane nitla Wally beugue bayi weuye kanee dou bayi
@cheikhnasiby9538
@cheikhnasiby9538 10 ай бұрын
Yalla bahna grand mbaye çava aller inchallah
@SofiDiop-i6s
@SofiDiop-i6s 10 ай бұрын
J n t Di pas de laissé la musique a cause de ton derrière y a bcp de famille ki tu a nourri des années way nak AK feth mom da doywar j t conseil de bien réfléchir sur ce k tu doit créer demain tu p tou faire tu es un créateur Wally yalla nala yalla diapale sur penser tu as bien réfléchi pense a ta maman et a ceux kel faisait ton idole sa doit être ta maman et ton papa c eu ki t'aimer yaw mi Di wakh boul khôl sa intérêt rek digeulko Lou bakh si mom mo geune j taime bck Wally Khaled bou am diom ga
@moussaseck6667
@moussaseck6667 10 ай бұрын
Yallana bayi billahhi bayill wally seck
@awalo6228
@awalo6228 10 ай бұрын
Wally Yalna yalla tekla lokho metina trope
@senegal559
@senegal559 10 ай бұрын
😊Bayi ko mou bayi way mou diamou dji yalla waw goor wally mbaye sy sa énteré rék gay wakh
@benajim9357
@benajim9357 10 ай бұрын
Wax deug y'Allah dafa metí defagoul sax deuil magam yayam dem dafa metí wayè sante y'Allah sougnou borom loum def dafa guen
@alexndiaga7775
@alexndiaga7775 10 ай бұрын
Wally baye fall laa❤❤❤
@AichaFaye-j4m
@AichaFaye-j4m 10 ай бұрын
Mame sakh meussouma déme soiré wayé dama lay beugeu je t'aime bien 🙏🙏
@diorbeye9640
@diorbeye9640 10 ай бұрын
Wakh deg yalla waly bo bayé way mo guene bilahi wayé nak si kaw nga mane ko bayi kholal linga bgue nga def lolou fi mom lou way begue danga koy sabab lou yalla def ko yalla bakhna bowaré bayî yalla lay df kon yalla nala defal li nek sa khol
@mahmoudabass6663
@mahmoudabass6663 10 ай бұрын
En tout cas wakhone na dou yegue 40ans mingui ci 39 😎
@bambiniakhate9277
@bambiniakhate9277 10 ай бұрын
Yéneu séneu intérêt rék way dafa arame il à pris une bonne décision. Dé day bété. Yalla nala yalla may lou gueneu
@KinéMbengue-c4j
@KinéMbengue-c4j 10 ай бұрын
Adouna bi lifi arame beurina😊
@mbathiosamb9044
@mbathiosamb9044 10 ай бұрын
Suis d’accord avec toi na bayyi gnom sen intérêt rek lagnouy khol
@KinéMbengue-c4j
@KinéMbengue-c4j 10 ай бұрын
@@mbathiosamb9044 konne ame naniousi interet yaw do khalate nak khana dou niou yamm atté
@awand4066
@awand4066 10 ай бұрын
Boul Mousavi bayi inchalla yallabakna from Gambia 🇬🇲
@mariabella1630
@mariabella1630 10 ай бұрын
Wally bo bayé kougnouy woyal ? Yalnala Yalla takhawou thi lep ak fep inchallah🙏! Dou gnak sakh gnougnou yoni pour gnou nek dila encourager pour nga bayi mais Yalla bahna ! Ak lo meuna décider yalna gueun thi yaw ak la famille 🙏 ! De tout cœur avec toi quelque soit ta décision ❤️ !
@BintouNdiaye-yg7yt
@BintouNdiaye-yg7yt 10 ай бұрын
Mbaye sy Ndiaye diapousy rk boumou bayi sou bayi wè mane fouma gniem 🎉❤wally boule bayè mvr yacine
@CodouNdir
@CodouNdir 10 ай бұрын
Yalla bakh na ❤
@KinéMbengue-c4j
@KinéMbengue-c4j 10 ай бұрын
Mbaye sy ndiaye diapp si rek
@kadijatoujallow3477
@kadijatoujallow3477 10 ай бұрын
Merci mbye sy for the information everyone is confused 😕 ❤
@malicksallah
@malicksallah 10 ай бұрын
Wally rek ❤❤❤❤❤
@mohamedsene1681
@mohamedsene1681 10 ай бұрын
According to me Waly waroule bayi way parce linguey bouko sougnou borome djaklele la moussil ted dissi teralé am gnou Bari gnou yakar si môme pour ted teralé aussi et inchallah personnellement je me rendrez chez lui pour bokk si gniy wahtane ak môme donc boumou bayi il fait tant de fierté et tant de bonheur. Yalla bahna courage frère et séchez que a partir de ce moment quil doit montrer qu'il est grand merci
@theneighbourhoodpaintingan9059
@theneighbourhoodpaintingan9059 10 ай бұрын
Oh may Allah make it easy for you amen 🙏
@MameseyeSow-g6z
@MameseyeSow-g6z 10 ай бұрын
Ayy iow c’est dur vraiment mais boum bayi Bilay c’est notre préféré 😢
@DieynabaKamara-o9h
@DieynabaKamara-o9h 10 ай бұрын
Alhamdoulilah yalnako bayi yow dé cheytané dougounala yalla boumoula deglou
@sigacamara866
@sigacamara866 10 ай бұрын
Never say fail wally lep Yallah keep d going all shall be well In Saah Allah ❤❤
@adamengomndiaye4209
@adamengomndiaye4209 10 ай бұрын
Gnogui sa guinawe inchalla ❤❤❤wally Seck
@mamefatou6794
@mamefatou6794 10 ай бұрын
Wally khamouma dafay bayi waye walla bayiwouko wayé Lo mana nek si aduna yala Dinala si defal ay ndam Inchallah Danga ame nianou wajour Machala yala nga goudoufane maryacine je t’aime ❤
@MoustaphaGueye-ii2un
@MoustaphaGueye-ii2un 10 ай бұрын
Wally n'a pauses ba thi kaname ❤❤ inchallah
@fadangcamara3543
@fadangcamara3543 10 ай бұрын
Non dafa méti trop sakh Bilahi Mai’s nagnou délou lép si lokho sougnou borome métina nak 😢😢
@massambangom6198
@massambangom6198 10 ай бұрын
Wally faut revenir soudoul dara sa orchestre daniou yor ndiaboot té sen weurseuk sa lokho lako Yalla diaralé ❤puissance rek ❤
@astoulaye-772
@astoulaye-772 10 ай бұрын
Bayil ndiambourr il a fait le bn choix mounannn dinan deff le tt iissshhh
@damefall840
@damefall840 10 ай бұрын
Yalna bayi Inchalla
@TamsirDramé-u9w
@TamsirDramé-u9w 10 ай бұрын
Amine yaarabi
@BayeModouDiagne-b9d
@BayeModouDiagne-b9d 10 ай бұрын
Nekhoul ba nekhoul mais metié bou mak la won moukoy tenir bamou ak si fi dignou begual mais yalla dogual na li même sou bayé sah dinako nopal ta aussi on l’aime man dh soudon nod sah beugnako maar fo nek rk gnou nek fa wayi surtout si mbirou borom bi❤❤
@gueyelabsolu5889
@gueyelabsolu5889 10 ай бұрын
Yallah nabayi Barké cheikhoul khadim Ay thiaxanou Adanou keneu Douthi encourager keneu musique 🎵 affaire De saytanè rék la Tè Dééé bouy Nieuw Dou Tagodé Day bèté Déeé. Bouy nieuw Dou Tago Day Bètè Dei Dééé Bouy nieuw Dou Tago Day Bètè Dei Mbaye sy Ndiaye 🧏🧏🧏
@hassanatoudiallo7331
@hassanatoudiallo7331 10 ай бұрын
Sou beugué bayii bayiko mou bayi boulko convaincre : dou loumou niak késssé motah mou beug bayiiii 🙏hèlam mooo délou si yallah rek waly hol bou sète leu am il a les moyens pour faire autres choses boulen hol seni intérêts
@MamySECK-c6b
@MamySECK-c6b 10 ай бұрын
Wally mon papa non ne fais pas ça s’il te plaît je t’aime. Papa tu es la meilleure 😭😭😭😭😭😭🤦🏻‍♀️pa🙏🙏🙏🙏🚶🏻‍♀️
@KhadyKandji-d8e
@KhadyKandji-d8e 10 ай бұрын
Wally âme Diam billay ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ on❤
@FatdamSarr
@FatdamSarr 10 ай бұрын
Bul bayi way delbegale❤❤kontan ci yawlay rek
@DjibyMbow-s6k
@DjibyMbow-s6k 10 ай бұрын
Képp kou d’accord pour mou continuer way séytané nga
@princetorodo8590
@princetorodo8590 10 ай бұрын
wakh deugeu yalla liko dalle metti na mais wally na xalat niouko beugeu the yalla rek takh dafa ame niouko yakar ame niouko beugeu na khole si seydina mouhamed ❤
@HawaNiang-js6lr
@HawaNiang-js6lr 10 ай бұрын
Mais toi aussi musique c'est n'a pas bon mais yallah backnah courage ❤❤❤
@maremeaidara6497
@maremeaidara6497 10 ай бұрын
Nayyy way seydina mouhamed aleysalam deim djiangui kuranul quarim dicii zikre niuy beug naniu lolu❤digua gueuna am beuz
@BiraneNiagne
@BiraneNiagne 10 ай бұрын
Yallana bayi❤😢
@aidasene8754
@aidasene8754 10 ай бұрын
Wally sou beugué bayi yalnako Borombi défal lougeune musique
@morsarrloum4269
@morsarrloum4269 10 ай бұрын
Wally dh bou bayè lime done dèf yalla nako yalla diaplè nèk koute woune si lou bakh kone bou bayè lolou tawfèkh la
@oumoudrame1858
@oumoudrame1858 10 ай бұрын
WALY BAYIL WOYE. YALLAH NALA YALLAH DIAPALÉ BOUBAKH NGA BAYI WOY SI DIAME AK SALAM. YALLAH NALA YALLAH ARE YAK SA FAMILLE YEUPP AK MBOLOME DIOULITE YEUPP. AMINE YARABI. MANE MAK LA MANALA DIOUR.
@DiatouSene-v4e
@DiatouSene-v4e 10 ай бұрын
Mais pour lane mouy bayi 😢😢😢
@thenanceaminata5211
@thenanceaminata5211 10 ай бұрын
Je te conseille de écouter ton cœur dieu seul sait
@SofiSeck-p3t
@SofiSeck-p3t 10 ай бұрын
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤je t'aime wally ❤❤
@sadiodiop1335
@sadiodiop1335 10 ай бұрын
Masta Waly siguil ndigalé métina trop❤
@Duelculte
@Duelculte 10 ай бұрын
CSenegal doy na war nite kene douko décidel nopilene teh nguene bayiko vraiment ak décision wam yalnala yallah maye li gueune thi yow maryacine
@khadyniang8320
@khadyniang8320 10 ай бұрын
Wally soûla sa xell maye Lolou deff ko nek sa bopou prsk les gens aussi cé compliqué musique avant amoul blem Maï musique d’aujourd’hui doy na warr courage bro
@AichaFaye-j4m
@AichaFaye-j4m 10 ай бұрын
Il faut laisser khamalni daga âme lo mome âme Lou nitte yi mome nion laco naine boul bayi ♥️♥️♥️
@jolithioune9390
@jolithioune9390 10 ай бұрын
Alhamdoullilah ❤ 🙏
@angelediouma9258
@angelediouma9258 10 ай бұрын
Satán est present dans la musique
@papaibrahimandiaye4867
@papaibrahimandiaye4867 10 ай бұрын
Bayi moyy bakh bakh bi. Yallah fowoul..
@sibereba3529
@sibereba3529 10 ай бұрын
Courage Wally seck
@AhmadouRssl
@AhmadouRssl 10 ай бұрын
Bly Wally seck bougnou def nii on t'aime fort Wally🫀💯
@monicahaba832
@monicahaba832 10 ай бұрын
Wally ❤❤❤❤❤
@KorkaBa-v8j
@KorkaBa-v8j 10 ай бұрын
On t aime wally
@SeynabouNgom-e2u
@SeynabouNgom-e2u 10 ай бұрын
Man de Beugue na mou bayi woy katt you mak yi woy nagn lepp wally tamit woy na lepp wally Bayil ngir yalla 🙏
Ohhhh!! Ndaysaannn Li mo warall Wally Seck beug téla bayi Musique…..
5:09
BABACAR W. OFFICIEL
Рет қаралды 396 М.
LALAKÉ - Saison 1 - Episode 7  **VOSTFR**
33:58
KHASS Production
Рет қаралды 73 М.
Ful Video ☝🏻☝🏻☝🏻
1:01
Arkeolog
Рет қаралды 14 МЛН
Every team from the Bracket Buster! Who ya got? 😏
0:53
FailArmy Shorts
Рет қаралды 13 МЛН
Sigma girl VS Sigma Error girl 2  #shorts #sigma
0:27
Jin and Hattie
Рет қаралды 124 МЛН
Women's Club 253 - ԵՍ ՄԵՂԱՎՈՐ ՉԵՄ...
10:47
VTV
Рет қаралды 116 М.
urgent🛑 bouba ndour bomak wakhaté ma ?
8:01
Nay Lér TV
Рет қаралды 605 М.
Mbir Amatina Ay Mystique bou Bone😱 Apres Face2Face Balla Gaye vs Siteu, Franc vs Ama, Serigne bi wak
18:35