Рет қаралды 333,367
On My Way est un extrait de mon projet Ep ( KIIRAAY )
Artiste : wizzy Kana & Oothentik Zeus
Label : Ruscash Music
Mix mastering : Zox
Réalisation : Kanz
Beat : Fantastic Beatz
Production: MBT100©️
Lyrics :
Ehh Yone bima dieul man
Niémai risque
Rek moy takh nga go man
Fatté yenn connerie
Ehh euleuk motakh may geuneu fight man
Gniné thi guinaw dougnma stoppé
Waxtou bi mom dafa gaw xaroul ngay nekk di slow
Teggal sa beute yi fou kawé jappal ni meune nga si jote
Door dakké mane douma teh my man
Sooralé li neh sa line ohh yeah
Yeah i’m on my way
And i will never change my destination
It’s out of the question
Yeah i’m on my way yeah
And i do what i have to do
Yeah i’m on my way yeah
Si deuk bou wow
Fauk nga Ligueey beu tooy pour fomp sa rangooniou yaay
Boo Nekker thi yoon
Takkal sa fitt maneu thiarakhou sa dalou baay
Dieul niaboot gui boot
Parce que mooy takh lal bi nameu sa dig guinaaw
Sa bop nga toogn
Iow rekaay sa noon boo beuguer def adouneu waay
Ndaw selebe yoon la fane ngay aw
Sa fit dina takhaw sa khel nay daw
Percer moogui dieul ndaw thi reew bouné
Avenir doon guedj tay thi biir bouteille
Ki diour Or tay lagn djignoon pereum
Xamouloo li yaay booy mougn biir kereum
Mougn bima nieukloo amouloo nieugueum
Takh sama cercle freq ndaw comme dereum
Im on my way
Forna xam xam xamnaa yallah moo xam
On my way Dound naa xat xat xamnaa yallah moo yaa
On my way
Woutina am am xamna yallah moo am
On my way
Diang naa dounya térer boumadoul meuss dieekheul
Yeah i’m on my way
And i will never change my destination
It’s out of the question
Yeah i’m on my way yeah
And i do what i have to do
Yeah i’m on my way yeah
It’s all about a question
teh tay dji bouma guestoo oh
Xamni top sama passion
Moomay guindi sama yoon
Dundu samay dream
Sama story
Beurri neuh ayy night mare
Motakh faut que mou nice man
Non non douma nadjé
Damay goudei mais douma fanaani