C’est une belle chanson qui me donne à chaque des frissons. Baye Niasse Cheikh al Islam ☪️
@cheikhmbackebarry1565Ай бұрын
Ana sopay baye yi
@papejuleslebarhamien87863 жыл бұрын
Yalla naniou yalla fayal baye niass rta bilahi boudoul wonak momm diné islam,tarikha tidiane dou am ndieurigne☝☝jarama bayou mindef yi elimanou moulkou akk mallakottou koulou chey'hine☝☝❤❤❤❤
@senembaye44206 жыл бұрын
Je suis mourite main j'aime baye Ndiasse
@hawadiaw64245 жыл бұрын
Sene Mbaye merci
@ladyj70612 жыл бұрын
Youssou Ndour Yalna ngua guisé ak Baye Niasse yawmal khiyaam
@daganatv3824 жыл бұрын
Sunnas Yonnent bi la Siidi Barhaam di pekku Numu def ba Yonent bi bég loolu la Baay di sàkku Lu neex Rasuulu Laay loolu neex na Baay Ñas. Ku xam li Yonent bi bañ doo ko gis ci Baay Ñas. Moom Siidi Barhaam Ñas masul a faat waxtu. Saa su ne njàpp mu yees, masul a tiimal waxtu. Boo toppee maamam ya, mbokk la ak Yonent bi. Laajal doomi seex yi xàmmee nañu Siidi. SU DEE BËGG NGAA ROY SUNNAS MUHAMMET... JOKKJIL CI BAAY ÑAS DIINEEM JA RAFET NA. Bu newul di julli ma ngay durus lillaahi. Baay Ñas xamul lu dul tagg Rasuulu Laahi. Li mu bind ci téere jagleel ko Yonent bi Li mu bind ci téere jagleel ko siyaas bi Li mu bind ci téere jëm ci wàllu xam-xam. Buur Yàlla teral na ko wonewul am-am. Li mu am ciy taalibe ci réewi nit ñu ñuul ñi. Lu ko ëpp la Baay am ci réewi nit ñu weex ñi. SU DEE BËGG NGAA ROY SUNNAS MUHAMMET... JOKKJIL CI BAAY ÑAS DIINEEM JA RAFET NA.
@weka3018 жыл бұрын
what a mix of Egyptian and Senegalese music it's magical
@LaBarhamienne4 жыл бұрын
Youssou Ndour nak yagui may dora saf, waw key...Dieureudieufé Baye Niass hala kouli hale.
@bayeniasse450910 жыл бұрын
yousou dou nitou kesei waye baye keineu hamouko je suis content mounouma wah
@mamadoubalde5053 жыл бұрын
Dou deugue baaye denñu koy ham ci jaahir ak baatin ak baatinoul baatin
@mamadoubalde5053 жыл бұрын
Mahdioub ak madjoub ñom duñ ham baaye niasse
@mamadoubalde5053 жыл бұрын
Baye ce lui ki et l createur
@timadiallo73558 жыл бұрын
j'ai mes yeux plein de l'arme mercii youssou j'aime
@genevievecissokho55658 жыл бұрын
youssou d'avoir chanter notre grand père. .cheikh baye niass rth merci wonderful song tkans so much
@djibyndiaye39478 жыл бұрын
DEUG REK GA AKH DAFA MELNI BAGAY WAAYY BAYE DANOU LA KA DEEY MMACHALLAH GRAND YOUSSOU NDOUR
@mamadoulaminemassaly99245 жыл бұрын
Machallah grand Youssou yallna yalla feyla si Barke Baye Niass
@sarrmasse55847 жыл бұрын
machalla youssou liga wakh nekh na walahi do delou ganawe si bareke baye niasse yarabi
@sainykante9 жыл бұрын
J'adore Cette belle chansson de Youssou ndour. À Mame Baye Niass
@diamambaye10767 жыл бұрын
alhamdoulilahi dieureudieuf
@sylidebreizh0076 жыл бұрын
Waaw...Waaw....Baaye Niass.... Moom, grand la waaw... Jërëjëf !!
@curtisknight22843 жыл бұрын
Wolof is the closest language you can get to ancient Egyptian today.
@salma111198411 жыл бұрын
c une musique inimaginable hallucinante magnifique , Bravo youssou
the legend...................youssou ndure gambian people loves you?
@mateodiop13510 жыл бұрын
youssou ndour tenk nga deugue diou weer
@didimelanin77612 жыл бұрын
❤️❤️❤️🔥❤️❤️❤️ I love Youuu baye niass❤️🔥🥇
@alediop3 жыл бұрын
Dieureudieufeuti Baye Barhama Niass
@1ceciliaromero5 жыл бұрын
Sublime!!!
@mamadoubadiane952 жыл бұрын
Thiey BAYE BARHAMA NIASS ❤️
@yayambow93778 жыл бұрын
dieurdieufé baye niass
@BAYEEVREUX12 жыл бұрын
Pas au Senegal. Malheureusement les Senegalais ignorent encore la portee de son Enseignement, Son Corps est Senegalais mais il est le Cheikh Internationnal. Tous les savants du monde de son epoque reconnaissaient sa valeur,sa science, sa gnose et son engagement. Au Senegal, Cheikh Ibrahim (s): On m a insulte de tout sauf de dire que je suis enceinte". A vrai dire, il etait tres jalouse au Senegal par les autres Cheikhs car Cheikh Tidjani Sherif avait predit sa venue(Saibul Fayda)
@cheikhtraore61787 жыл бұрын
BAYE NIASSE tu as parfaitement raison
@mouhamedfall2687 жыл бұрын
j suis content d ce que vous dites. fiers d'etre tidiane. CHEIKH AHMAD TIDIANE CHERIF
Sidi Barham live with the sunna of the prophet. He dœs what please the prophet. What the prophet dœs not Baye Niass will never do. Every salât he renew his ablutions. If you look close to his family he is a relative of the prophet. He has disciples in the black people countries and arab countries. If you want follow the sunnah of the prophet go and see Baye Niass he has a good practise of islam! It is boy finish but it is what's essentiel in the sound
@moustaphadiouf44788 ай бұрын
Mawlana Cheikhal Islam Elhadji Ibrahima Niass Baye
@bintoudiop4622 жыл бұрын
Machallah ❤❤❤
@modoumbayeniasseniass82117 жыл бұрын
Mame baye niasse
@mohamedloum63954 жыл бұрын
Merci Mame Baye Niass
@sambajeng4747 жыл бұрын
Great song
@7senegalese14 жыл бұрын
@mehdi2fes c'est un homme religieux sénégalais,un homme mythique, qui a influencé tout une communauté musulmane au sénégal.
@awadiouldediallo89737 жыл бұрын
7senegalese c pas au sénégal mais à travers tout le monde entier en quelque sorte
@matyng23116 жыл бұрын
Thanks you..... Youssou... Ndour
@TalibeCheikhoulKhairy5 жыл бұрын
2019 ??
@bayembow81426 жыл бұрын
Machalla niass
@ibrahimakonte202611 ай бұрын
2024🎉27 janvier ❤❤
@awadiop83024 жыл бұрын
Machalla 🥰🥰🥰
@farmatafall4124 жыл бұрын
Machalla
@omarkebe40813 жыл бұрын
Mahalla
@mariamaba29243 жыл бұрын
Adoré
@abdelrahmanelsokary9184 Жыл бұрын
🇪🇬♥️
@jamesndiaye41911 жыл бұрын
Dinama nekh
@FatouGueye-zd6os5 жыл бұрын
Koumay send son bi
@awaseneciss72632 жыл бұрын
2022
@apolo13214 жыл бұрын
@mehdi2fes : Non Egypte c''est le titre de l'album. Mais l'image qui est la je sais que c'est au festival de la spiritualité et du soufisme du monde a Fez!