Badge Presse, sabotage son de Wally Seck: Malaw Pikine fait du "garuwalé" à Youssou et pape diouf…

  Рет қаралды 44,969

Seneweb TV

Seneweb TV

Күн бұрын

Seneweb, c'est le site numéro 1 au Sénégal et en Afrique francophone.
Visitez notre site web: www.seneweb.com
Rejoignez cette chaîne pour bénéficier d'avantages exclusifs :
/ @senewebtv
Suivez nous sur:
Facebook: / senewebcom
Twitter: / seneweb
Instagram : / seneweb_officiel
Contactez-nous: +221 33 869 10 90

Пікірлер: 97
@Tinich427
@Tinich427 2 жыл бұрын
Ndeysan sénégalais mo geuneu sonou thi Lou Yallah sak mais pourquoi lép Lou dal Wally rék niou visé Youssou té niom niar tolo wouniou sakh level c'est pitoyable You a fait une carrière musicale incontestable siguil neu Sénégal fou nék thi adouna bi il mérite notre respect bilahi 🇸🇳
@maguettethiam8318
@maguettethiam8318 2 жыл бұрын
Machalla ya bakh Wally yal nako yalla may wére ak goudou fan 🙏🙏🙏🙏
@feuzeseck7797
@feuzeseck7797 2 жыл бұрын
Merci beaucoup frère diam si yow ❣❣❣❣❣❣❣❣❣❣💯💯💯💯💯💯💯🇸🇳🇲🇦
@mamadousagna7514
@mamadousagna7514 2 жыл бұрын
Créer de l'emploi se n'est d'aller acheter de la marchandise à extérieur pour les vendre au Sénégal mais c'est de faire où de prendre des marchandises pour les exporter dans le monde entier merci
@asmricelife6740
@asmricelife6740 2 жыл бұрын
Wakh deugue malheureusement ils n’ont rien compris
@matarcisse3724
@matarcisse3724 2 жыл бұрын
wally j'adore ta musique franchement tu es sur la bonne voie mais n'écoute pas ces gens là qui te donnent de mauvais conseils youssou ndour est ton père ne te crée pas des ennemis
@jadoredieuetmohamedkhadimo2521
@jadoredieuetmohamedkhadimo2521 2 жыл бұрын
Youssou ndour dou tiote ndayam hypocrite la domarame la khekh na ay moromame ba tay mouy khekh ay moromou domame chimm niak diome ak niak doylou wally mo wara def attention bou bakh si youssou ndour ak famille ndour bi yeup ndax meunou niou bagne thione seck 1970 ba 2021 beuga beug wally seck watte nako si alhourane youssou ndour ak mbaye dieye faye bilahi beugou niou wally seck niou doxane sene ndaye laniou kham ni fou serigne bou bone âme rek kham Naniou ko ay deume laniou daniou lay ray ba parè dialè la kou wedi kholene ko tay mok Omar pêne et pourtant mo ko ligueye pour yakh bate bi viox bi bilahi barke rassoulou lahi psl sources you sûr kou ko wedi nama invité plateaux tfm m'a diokhe firndè you lere nangne.
@aramesndiaye590
@aramesndiaye590 2 жыл бұрын
Merciii beaucoup malaw
@domelsow8036
@domelsow8036 2 жыл бұрын
Youssou ndour rawna lene
@omartrawally403
@omartrawally403 2 жыл бұрын
People love him so much in England wally
@ndeyefatoleye3902
@ndeyefatoleye3902 2 жыл бұрын
Machalla Frère waly est le chanteur du peuple
@aidasamba3779
@aidasamba3779 2 жыл бұрын
mashallah Yalna Yala lafall thiat SECKA
@sokhnamaikane9503
@sokhnamaikane9503 2 жыл бұрын
Yalna sa diamou yague Malaw waly mofi nek❤️
@TheBandafall2003
@TheBandafall2003 2 жыл бұрын
Le chanteur des idiots
@papendiaye9831
@papendiaye9831 2 жыл бұрын
Machallah ♥️❤️❤️♥️♥️❤️
@fatoufaye294
@fatoufaye294 2 жыл бұрын
Ndiaga nakk ligueye na. Waly dale louko dale day ni pateu avc ses frères sœurs relaxe lekk nane happy o calme dakh amna niou dioudou pour être derrière di tontou. Ame lene personnalité kougnou togne bou waxoul ay bokam wakhougne guene def ni niom. Sene yaye dafa guene sene boss? Buffff
@aminatasow9732
@aminatasow9732 2 жыл бұрын
Wakh deug soff rk
@asmricelife6740
@asmricelife6740 2 жыл бұрын
Wakh deugue bou diote dagay wakh 😂
@Mamichoubb
@Mamichoubb 2 жыл бұрын
Hum entouka déléne rafétel diguenté yi Sénégal gneup béne lagnou Si béne côté wakh gua degue dou wally késsé mei kou nékeu bo concentré wo sisa objectif kone gnou bari tékki nagnou
@fatoumndoye1646
@fatoumndoye1646 2 жыл бұрын
Wally seck rek 💯
@aissatadia1908
@aissatadia1908 2 жыл бұрын
Wally seck rek si khole lénén hadiouthi💪💪❤❤❤❤❤❤❤
@emgtv9938
@emgtv9938 2 жыл бұрын
Machalla frère 😍
@sybagaye8151
@sybagaye8151 2 жыл бұрын
Wally rék laniou wakh Machallah 🤲💪❤❤❤❤💯💯💯
@boubambaye8900
@boubambaye8900 2 жыл бұрын
Mais ki wally bane europ la jomal no faut arreter ausssi
@bassetndoyendiaye3805
@bassetndoyendiaye3805 2 жыл бұрын
Khamna niari Europe dafa am si monde bi té yeugouma ko meune naa limouydef trop mais dagn koy diey 😂
@akadtv661
@akadtv661 2 жыл бұрын
Seneweb sen titre yii rek Moy diakhasè nitt yi soyons professionnels
@salymata1133
@salymata1133 2 жыл бұрын
Walllyyyyyyyy😍😍😍😍😍😍😍
@aidasamba3779
@aidasamba3779 2 жыл бұрын
Amine yarabi
@infosenegaltv536
@infosenegaltv536 2 жыл бұрын
Kou beug ay Secret yi nek si alkhour âne abonnel..
@awawall1234
@awawall1234 2 жыл бұрын
Mashallah🥰😍
@khadijadieng8206
@khadijadieng8206 2 жыл бұрын
Machallah ❤️❤️❤️❤️🥰🥰😘
@celsopinapina4283
@celsopinapina4283 2 жыл бұрын
Wally 🏆🎖️🏅🎖️🏅🏅🥉🎖️🎖️
@keurhawaets6645
@keurhawaets6645 2 жыл бұрын
thim!! yambarrr
@fallouseck7874
@fallouseck7874 2 жыл бұрын
Faramareen rek sixol dafay nèh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
@badadiop6975
@badadiop6975 2 жыл бұрын
Malaw 🎤💪🏾
@falloukarimmbow4981
@falloukarimmbow4981 2 жыл бұрын
Wally ballago séck le chanteur du peuple
@badadiop6975
@badadiop6975 2 жыл бұрын
Malaw Nice FrR
@di_laminolofficiel2769
@di_laminolofficiel2769 2 жыл бұрын
Tu n’es qu’un comédien pas un journaliste. Quant même qu’on se dise la vérité. Malaw tu es totalement différent avec les gens qu’on forme à la CESTI. Donc arrête de te foutre des gens, tu es comédien et humoriste pas un journaliste. Tu ne devais même pas être fier de porter ce badge de journaliste. Reste dans ton domaine c’est mon seul conseil.
@maremefall7255
@maremefall7255 2 жыл бұрын
Wally rék ♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@TheMouhamed7
@TheMouhamed7 2 жыл бұрын
Palmarès waly moy je suis le chanteur du peuple 🤣🤣🤣 lo khamni mokay woowei bopam 🤣🤣🤣 waly demal ligueyi, todjo sakh Afrique di tankal nitt yi 🤣🤣🤣
@diorkasse5840
@diorkasse5840 2 жыл бұрын
Iow d y’a sokhor
@TheMouhamed7
@TheMouhamed7 2 жыл бұрын
@@diorkasse5840 kou wakh deug niouni dafa sokhor, wakh ma lima wakh lane mossi nekoul deug
@ramandiaye3726
@ramandiaye3726 2 жыл бұрын
Nitt gni gno ko tane jeune yii ngo ko deff chanteur du Peuple pas bopam
@moustaphadiop5028
@moustaphadiop5028 2 жыл бұрын
Deugg gua wakh dh bro. Sa musique Sénégal la yaam.
@TheMouhamed7
@TheMouhamed7 2 жыл бұрын
@@ramandiaye3726 saway waly moko commencé wowei bopam, keine khamoul wone louy lolou sakh, mo tokk beine jour ci interview moy wowei ko bopam
@famafall8309
@famafall8309 2 жыл бұрын
Amine inchallah malawé
@moussandiaye1016
@moussandiaye1016 2 жыл бұрын
Jajeuf Gadiaga
@boyetownfromdkr5287
@boyetownfromdkr5287 2 жыл бұрын
Senegal deuk bou arrière là kii moye kane baniouko wara talal sounou micro nonn boye you tékiwoul dara yii té yèn wakh nguène khamoul rék
@kassefall5429
@kassefall5429 2 жыл бұрын
Boull juge niit te xamoko
@Onomar
@Onomar 2 жыл бұрын
Yallah moy xol kouko nekh mou yegeul ko si kaw
@kassefall5429
@kassefall5429 2 жыл бұрын
@@Onomar mongi nonou nak
@ramataousmaneba4339
@ramataousmaneba4339 2 жыл бұрын
Malaw pikine raynama😁😁😁
@djibrilndiaye2754
@djibrilndiaye2754 2 жыл бұрын
Boy youssou ndour sa baye la so beugei beuz outtiko gua dem ligueyi mo geune
@babacargeuye1114
@babacargeuye1114 2 жыл бұрын
Doméharam bi di mélné spaghetti douniou foudeune ndayame moule âme loumouy wakh Sénégal danouye dof lo boubou golo yi quoi youssou ndour d'où sa moromou d'où sa moromou ndaye boy do yame sa bindou khous ma niapeu .
@barkambodji828
@barkambodji828 2 жыл бұрын
Stp boutique bi foumou nêké ci dakar
@adowade4465
@adowade4465 2 жыл бұрын
Kanara bi malaw
@badadiop6975
@badadiop6975 2 жыл бұрын
Malaw merci bcp
@bintajagne3754
@bintajagne3754 2 жыл бұрын
Masallah
@sport_univers.2482
@sport_univers.2482 2 жыл бұрын
Faramaren musique 🔥💞
@ndeyafall6573
@ndeyafall6573 2 жыл бұрын
Malaw dinama raye 🤣🤣🤣🤣
@saffdiagne1244
@saffdiagne1244 2 жыл бұрын
Wooooouy ki wakh na lep Yalla nopi na 🤣🤣🤣🤣
@khadycisse2671
@khadycisse2671 2 жыл бұрын
Machalla
@saffdiagne1244
@saffdiagne1244 2 жыл бұрын
@@khadycisse2671 Mercii way ma chery
@TheMouhamed7
@TheMouhamed7 2 жыл бұрын
Waly dioyna ba sidy Diop sakh migui kay dapsi 🤣🤣🤣 ay nominations sakh meunouko indi senegal di ray nitt yi ak wakh Djou beurei 🤣🤣🤣
@saffdiagne1244
@saffdiagne1244 2 жыл бұрын
@@TheMouhamed7 yaw sidi diop xamou dara mane damako yeureum sakh wakhoul ma sakh ay wakh xam nit day xam boppam
@mansourthiam5323
@mansourthiam5323 2 жыл бұрын
Bilahi Malaw t'as tt dit Wally est le chanteur du peuple
@TheMouhamed7
@TheMouhamed7 2 жыл бұрын
Waly son palmarès moy may le chanteur du peuple 🤣🤣🤣 lo khamni mokay wowei bopam, na dem ligueyi teh bayi dioy yi, dioy na ba sidy Diop sakh migui kay dap si 🤣🤣🤣
@badadiop6975
@badadiop6975 2 жыл бұрын
🎤❤️💪🏾
@ndidi______sl8825
@ndidi______sl8825 2 жыл бұрын
Il est conscient ce mec
@aminatasow9732
@aminatasow9732 2 жыл бұрын
Malaw mi kén waxou ko bopam War guéna rouss gawa wakh ak beug beuz Youssou Dour ak Waly sén yon nékou si téh wax dji léér n'a déguen li gars yi wakh Niom Abba ak pi and ji
@dyarayara3926
@dyarayara3926 2 жыл бұрын
Machahala malaw amine deug nekhoul 😂😂😜😜😜😜
@kingsamassa2861
@kingsamassa2861 2 жыл бұрын
👌👌👌👌👌👌👌👌👌
@mamyniang3923
@mamyniang3923 2 жыл бұрын
Waly kene mounool ci mom daraaaaaaaaaaaaaaaaaaaaa
@duduseiye507
@duduseiye507 2 жыл бұрын
Malaw réw nga 😁😁
@kaporalinfos
@kaporalinfos 2 жыл бұрын
NA WAX KOUKO JOKH CARTE PRESSE AK BANE ORGANE LA NÉKK
@anitasoumare5796
@anitasoumare5796 2 жыл бұрын
Nooo malaw yagui ray ay nitt 😆😜niaff wally yalla nala yalla jamm 🤲❤️💯💪
@papidiagne1942
@papidiagne1942 2 жыл бұрын
Boy bayilen YN dou sen morom
@bmt9844
@bmt9844 2 жыл бұрын
Amanii youssou ndour moko wayoone 😂😂😂
@dieynababa1276
@dieynababa1276 2 жыл бұрын
Bouleine ko togn waxoul dara lou niaw
@mouniroufall1758
@mouniroufall1758 2 жыл бұрын
Boy yéne vous éte nuisible a la société youssou ndour mo geune sakh sén bay il a plu de 500 employés yén sén papeu ay comédien lagn wone motakh ngén dioudou nékeu ay comédien
@ndeyebintoubobe5045
@ndeyebintoubobe5045 2 жыл бұрын
Yaw ya bone nguah nangou yayou diambour di geune sa yaye thiame
@Onomar
@Onomar 2 жыл бұрын
Puisqu’ils sont nuisibles yaw xana tu es un imbeco de la société . Adouna bi defal nite ki niko yallah deff mou nopal leu soko defoul niko yallah deff mou diaxal leu
@ebouceesay1339
@ebouceesay1339 2 жыл бұрын
Fofu la
@laazanbasvc6268
@laazanbasvc6268 2 жыл бұрын
Je vous dis et redis « NE JAMAIS COMPARER L’IMCOMPARABLE »… Malaw qui parle de véhicule ! Mdr, c’est parce que tu n’as rien compris. Youssou Ndour est dans une autre dimension, après s’être fait connaître MONDIALEMENT, remplir des stades en Amérique du Sud, et j’en passe! Faut arrêter un peu
@khadindiaye7786
@khadindiaye7786 2 жыл бұрын
Faramaréne bi rek
@modoudiouf5058
@modoudiouf5058 2 жыл бұрын
Ki weroul
@modoundiaye7985
@modoundiaye7985 2 жыл бұрын
Zeyna ioe mome daga diay sa ngoor bay zale mola fégnale do guate
@yamaojallow8963
@yamaojallow8963 2 жыл бұрын
👏👏👏👏😂😂😂😂😂❤️❤️❤️
@ndeyefatoundiaye1404
@ndeyefatoundiaye1404 2 жыл бұрын
Wa wadji lonettes yi da todj wala li mode leu
@mbayethiam6156
@mbayethiam6156 2 жыл бұрын
Non todioul nii la mél nouvelle look la
@ramndondiaye2113
@ramndondiaye2113 2 жыл бұрын
kkxkxxk nena gnom djiné Amani denagn gnom 6mani gnogi nek
@sambousmane6410
@sambousmane6410 2 жыл бұрын
Wally rèkkkkkkkkkkkkkk
@mamadoundione2520
@mamadoundione2520 2 жыл бұрын
Anmani ak danmani dénaniou kone sen dom yi nio fi nek legui comprendre na sa wakh bi malaw😂😂😂
@dieynababa1276
@dieynababa1276 2 жыл бұрын
Non ki dou niit😂😂
@panembaye3272
@panembaye3272 2 жыл бұрын
😂😂😂😂
Арыстанның айқасы, Тәуіржанның шайқасы!
25:51
QosLike / ҚосЛайк / Косылайық
Рет қаралды 700 М.
Правильный подход к детям
00:18
Beatrise
Рет қаралды 11 МЛН
VW : Affaire Saoudou SOW dite Diary
2:17
Police nationale SN
Рет қаралды 10 М.
Xalisso - Saison 1 - Episode 39 **VOSTFR**
50:12
EvenProd
Рет қаралды 1,3 МЛН
Serigne modou gaindé borom kémane🔥🔥💔💔😱
1:22:14
Sénégal Beauty 🇸🇳 24k
Рет қаралды 187
I Spent 100 Hours Inside The Pyramids!
21:43
MrBeast
Рет қаралды 27 МЛН