Cheikh Aziz met fin aux Polémiques : C'est Baye Niasse qui dérange mais sa fayda ravagera tout

  Рет қаралды 25,233

Faydatidianiya TV

Faydatidianiya TV

Күн бұрын

Cheikh Aziz met fin aux Polémiques : C'est Baye Niasse qui dérange mais sa fayda ravagera tout
Abonnez-vous à notre Chaine KZbin : / faydatidianiyafaydou
Aimez notre Page : / faydatidianiya
Visitez notre site-web : faydatidianiya.com
Nous Suivre sur : / faydatidianiya
Nous contacter : +221783202313 - +221775954762

Пікірлер: 366
@karimcamara7865
@karimcamara7865 5 жыл бұрын
Machallah Cheikh Aziz Ndiaye
@paomar1859
@paomar1859 5 жыл бұрын
Hééééé thieye Baye. Merci cheikh Aziz gnongui laay ziar dépuis la France 🇫🇷
@cheikhsarr7981
@cheikhsarr7981 5 жыл бұрын
Manchala Cheikh
@mthiam1567
@mthiam1567 5 жыл бұрын
Salam wal adab filah Cheikh Omar ibn Baba Lamine mou Kamal ki. Do doli ziar bou amoul dayo depuis Paris
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy 5 жыл бұрын
Salam alaykoum. Roubé kat yi bayi lén saaga yi waay.limou wakh wèdi lén ko avec des arguments valables,c'est simple.mais saaga yakamté khèkh leu té nioune khèkhou niou.Deug biniouy wakh mo saf kaani rek.Wa Salam
@mbayendiaye4562
@mbayendiaye4562 5 жыл бұрын
mustafa barham kiwakhéwoul khame khame billahi fék yagui parparloo dowakh kham kham souwakhéwone si kham Kham wallahi niou tontonko
@elhadjigueye2646
@elhadjigueye2646 5 жыл бұрын
Ki do dara féne reck
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy 5 жыл бұрын
@@mbayendiaye4562 beu légui wakhouma wakhou kham-kham dé.ndakh alhamdoulillah kou thi débat ak mom wala bènène mouqadam dinga wanièkou. Mais limouy wakh c'est des preuves tangibles thi l'I téré tarikha bi wakhone thi dièkhitalou tarikha bi. Déggoma dé.deug mo saf kaani rek wayé parparlo dafay fèkk toloo am fa.nioune gningui thia ganaw yoyou
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy 5 жыл бұрын
@@elhadjigueye2646 kou wèddi mbir danga fay tèk dara.argumentel rek té bayi saaga yi
@elhadjigueye2646
@elhadjigueye2646 5 жыл бұрын
@@TalibeCheikhoulKhairy deugueuleu mais yini cadou yi rafétoul moy andi yéni wah yi
@yankhobadiop7062
@yankhobadiop7062 5 жыл бұрын
😂😂😂li rek leu yay goor deug 🤭 HAMED Kh Niasse nanopi amneu ñoukoo wakhal Machallah 🙏🏾🙏🏾🙏🏾😂😂👉🏾
@mallbelly8250
@mallbelly8250 5 жыл бұрын
Yow ak amet khalifa nias ay bandi nguene rek
@yankhobadiop7062
@yankhobadiop7062 5 жыл бұрын
Déde way
@yankhobadiop7062
@yankhobadiop7062 5 жыл бұрын
Mall belly déte way
@khew2006
@khew2006 5 жыл бұрын
@@Xamuma serigne bi yeureumna sa rouhou gui té nga bagna dougue si mbirou Baye
@adamasow9292
@adamasow9292 5 жыл бұрын
@@Xamuma moytoul gnoulay dougueul sa bamel fekk nga neupe...martaba waliyou Yalla dou balé..fais très bien attention!!!
@abdoulayefofana5345
@abdoulayefofana5345 5 жыл бұрын
Dieureudieuf
@knibalknibal6741
@knibalknibal6741 5 жыл бұрын
Bilaahi Yaye Goor Abdou Aziz Ndiaye Yalla nala Baye Niass féy
@dioufmakhary86
@dioufmakhary86 5 жыл бұрын
Baye niass only for ever
@ngommahtar4689
@ngommahtar4689 5 жыл бұрын
ماشاء الله صدقة ثم صدقة وصدقة بصدق ما شاء لله بارك الله فيك أحسنت
@fityaanousidkhine5796
@fityaanousidkhine5796 5 жыл бұрын
Thiey kou bagn Baye Nargua sonou pask bagn louy yokou nekhoul Merci Baye Niass
@azizcamara3579
@azizcamara3579 5 жыл бұрын
serigne bi yallana tawfikh ak taysir
@mamadoulamindiallo5481
@mamadoulamindiallo5481 5 жыл бұрын
ماشاءالله ياشيخ أطال الله عمرك إلي الأمام إنشاءالله حفظكم الله ورعاكم وأدام صحتكم ببركة الشيخ الإسلام رضي الله عنه
@seydinamouhamedba3211
@seydinamouhamedba3211 5 жыл бұрын
Dieureudieufééééé bayeeeeeeeeeee niassssssssssss
@binetagueye740
@binetagueye740 5 жыл бұрын
Niassss deuggg la serigne bi Alhamdoulilah niounnn douniou ay talibé eskeuy Dieureudieufeeeee baye niass❤❤
@pakebbagaye5436
@pakebbagaye5436 5 жыл бұрын
Mashallah baye niass mashallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍😍
@cheikhtidianeba7145
@cheikhtidianeba7145 5 жыл бұрын
Mbirmi yeup baye niass laniou beugoul waye nak baye kou diaroul si momm do agg si yalla . yalna yalla faye baye niass
@sidydia27
@sidydia27 5 жыл бұрын
Yalnala baye niass faye 💜💜
@moussathioub844
@moussathioub844 5 жыл бұрын
ماشاء الله الله يبارك فيك يأتيك كل ما تريد في الدارين
@ndaomore7047
@ndaomore7047 5 жыл бұрын
Mancha Allah Cheikh Ibrahim Niass
@brahamtoure1179
@brahamtoure1179 5 жыл бұрын
Merci
@falloubayeniassdiouf2844
@falloubayeniassdiouf2844 5 жыл бұрын
fier detre talibés Baye 👊💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪💪👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂xame xame
@alycamara6380
@alycamara6380 5 жыл бұрын
Soldarou baye deugue nga
@amadousouleyetandine931
@amadousouleyetandine931 5 жыл бұрын
Deugue lah Baye.. doundoul cheikh Aziz Ndiaye dieuredieufèèè Baye Niass
@faroulfenecideugrek7557
@faroulfenecideugrek7557 5 жыл бұрын
Ma challah cheikh aziz ndiaye
@faydouparforce6172
@faydouparforce6172 5 жыл бұрын
Machallah
@mr.africa8166
@mr.africa8166 5 жыл бұрын
Jerrejoff cheikh aziz ken dou yaw
@abdoulayeseck3866
@abdoulayeseck3866 3 жыл бұрын
Machallah Ya Seydi, toujours aussi véridique, aussi courageux et éternellement abreuvé par la solution de l’humanité (humains, djinns et « koullou Ka´inati »): BAYE NIASS. Que soit satisfait de toi éternellement.🙏🏿🙏🏿🙏🏿
@ousseynoundiaye2906
@ousseynoundiaye2906 5 жыл бұрын
Baye moy bayou sreigne yi koum neh ak koum naxari point
@ndeyefatouwade7099
@ndeyefatouwade7099 5 жыл бұрын
Machaallah machaallah contentenaniou
@layelaye2075
@layelaye2075 5 жыл бұрын
Niass..l'infatigable ..yalna yalla goudeul sa fannn
@marcograziani1856
@marcograziani1856 5 жыл бұрын
Masha Allah diera diefe baye niass
@alhaqq310
@alhaqq310 5 жыл бұрын
Allahou akbar Macha'Allah Ndiaye ! Yallah na Yallah aar la té mayla wér ak goudou fane thi barké Baye Barham Niass 😍♥️🥰🙏🌹😘
@mbeddmidiallo6934
@mbeddmidiallo6934 5 жыл бұрын
Diadieuf way cheikh aziz ndiaye sama tourondo linga wakh yeup deugueule mane mi rék fala bokone wayé wakhoumala gorrou mame aladji abdoulaye niass yi mh seuteum you djiguene yi rék nio meunn séne goor billahi walahi
@falloundiaye144
@falloundiaye144 5 жыл бұрын
Yalla Nanou yalla guindi
@tidianediouf9104
@tidianediouf9104 5 жыл бұрын
machallah sama serigne ziar nalla
@damssarr1362
@damssarr1362 5 жыл бұрын
Machallah baye dieureudieufe baye niass
@tepppngom1733
@tepppngom1733 5 жыл бұрын
Lingay wah setsi yalla serigne senegal yeup la yalla may tei tiow likoy fay mo geune loukoy hambb kou rathie dieumeulei sa kanam mou deuleu senegal bene bop wassalam🙏🏿
@lincontournablebarry8521
@lincontournablebarry8521 5 жыл бұрын
Hé deug nékhoul tivaoune séne mbot dafa diérmél baye moy chahiboul fayda
@assankuta2935
@assankuta2935 5 жыл бұрын
Sou feke wahoul deug, wah len sen serigne si niou xamleh yalla. Monouniou ko xamouniou yalla. Tok len fofou di nelew ak dioge hadiya rek.
@ismaelfaye4712
@ismaelfaye4712 5 жыл бұрын
Yow woko wah ague mome sí hamme hamme so wede Kay indil dará tegue
@MLgueye
@MLgueye 5 жыл бұрын
Bilay barké rassoulilah dore fayou rek mokoy fathie
@ndiayeanta5229
@ndiayeanta5229 5 жыл бұрын
niafffff
@ismaelfaye4712
@ismaelfaye4712 5 жыл бұрын
Barke baye niass lerna nagne
@matardiaw6163
@matardiaw6163 5 жыл бұрын
machalla chiekh bi
@vallainnde5346
@vallainnde5346 5 жыл бұрын
Masha Allah, djazak'Allahou khayrane 🙏
@amethsokhna4547
@amethsokhna4547 5 жыл бұрын
dieureu dieufééééééé baye niass
@assanendione4374
@assanendione4374 5 жыл бұрын
Baye Niass rék moy dégeu niass
@aidandiaye9142
@aidandiaye9142 5 жыл бұрын
Wallah niass borom diamano tigui
@youssoudiedhiou4622
@youssoudiedhiou4622 5 жыл бұрын
Machaalah Cheikh Abdoul Aziz doubdal lou bari waaay
@diopndeyeamina9561
@diopndeyeamina9561 5 жыл бұрын
Prochaine fois avant de parler il faut réfléchir svp khamalni kilifagua konnn boyyy wakhatiii naay rafettt dakh amna wakheyo khameni manatoko defaarr teh niiit dougnou mossa fateh wakhedjou rafetoul merdi d'avoir reconnu ton erreur l'erreur est humaine mais quand elle est répétitive ce n'est plus une erreur bayiko khel
@bayenurudine3692
@bayenurudine3692 5 жыл бұрын
DEUg dou nekh yowite
@adamasow9292
@adamasow9292 5 жыл бұрын
Oooooh sokhnaci danouné nguén tontou fii..débat kham kham la nanou ko tontou wala gnou wo ko,c'est aussi simple que ça...wakh dji il l'est a tous défiés publiquement,ils n'ont qu'à venir répondre,c'est pas compliqué e pense
@dionidiakit4991
@dionidiakit4991 5 жыл бұрын
Dieuredieufé baye niass
@diamalick7974
@diamalick7974 5 жыл бұрын
Ahmed moy doumou khalifa niasse di domi cheikh Ibrahima
@myasambe1051
@myasambe1051 5 жыл бұрын
Tekh Tekh may rée. Dieuredieufé baye. Wali nehoul.
@fityaanousidkhine5796
@fityaanousidkhine5796 5 жыл бұрын
Nekhna nekhna nekhna
@bayejobe4204
@bayejobe4204 5 жыл бұрын
Macha alla cheikh
@espirituelligth7339
@espirituelligth7339 5 жыл бұрын
Ohh contanena, djeureujeuffééé Baye Niass
@mamouneniasse8757
@mamouneniasse8757 4 жыл бұрын
Cheikh aziz Yal na nga guoudou fane andak wér, yalla yok sa meudeud si baye bi diahi seydina mouhamad saws
@famaratamba4058
@famaratamba4058 5 жыл бұрын
Baye moy 2gue billahi doundeul cheikh azize
@combattrelinjustice1252
@combattrelinjustice1252 5 жыл бұрын
Wollahi ndeysane deugglaaaa Cheikh AZIZ mooo bakh
@hiphopgalsenfrance9631
@hiphopgalsenfrance9631 5 жыл бұрын
cheikh bii lingna wakh amoul lénéte lousi nitt mouna wakh. pir verité ngafi wakh. kénnn dou tégui point si linga wakh
@Xamuma
@Xamuma 5 жыл бұрын
Baye Niata diabaar la amone ?
@malikdev2833
@malikdev2833 5 жыл бұрын
@@Xamuma www.islamophile.org/spip/Qui-sont-les-epouses-du-Prophete.html
@moustaphadiouf5193
@moustaphadiouf5193 5 жыл бұрын
Machalla diaradieuf baye niass international allahou akbar
@therenaissance7977
@therenaissance7977 5 жыл бұрын
Abdou Aziz Diouf cheikh Ibrahima niass bi mou lako 4 diabar nioko tendji. Baye niass nena yalla dimbalenako ba meusoul khoti horma charia. Mais nak cheikh aziz mi limouy wakh rafetlouwmako donté talibé baye niass la. Nioune niep ay dioulite laniou rawatina tidjane mais dara diaroul parparlo naniou rafetal rek. Te wara sante mak gni mouy seydi elhadji oumar foutiyou mame alhadji ak seydi elhadji malick ndakh c’est grâce a eux niou ame tarikha cheikh 🙏
@MoustaphaNdao-rx4px
@MoustaphaNdao-rx4px 5 жыл бұрын
@@Xamuma lolou dou kham kham lowara djéma kham moy sa bop yay kane
@mb-rf6ez
@mb-rf6ez 5 жыл бұрын
Machallh
@omarka9111
@omarka9111 4 жыл бұрын
Dieureudieufff Sangue bi ❤️❤️❤️
@mamadoudiouf3427
@mamadoudiouf3427 5 жыл бұрын
BARHAME rawnalene
@fityaanousidkhine5796
@fityaanousidkhine5796 5 жыл бұрын
Yaw sakh rawga
@laminendiaye5144
@laminendiaye5144 5 жыл бұрын
dieuredieufe cheikh Ibrahima niass
@alytoure1418
@alytoure1418 5 жыл бұрын
Machalla duegue mome yague yague duegue rék laye done
@issambodj4498
@issambodj4498 5 жыл бұрын
Même abdou Aziz dabkh avais reconnu que Baye est unique dans la tarikha
@degrekkaydegfall3190
@degrekkaydegfall3190 5 жыл бұрын
Yamana kathie foumko binde
@issambodj4498
@issambodj4498 5 жыл бұрын
@@degrekkaydegfall3190 ma diombeuna wakh loudoul deugue. Féne yii xamnaniou founiou fété wayé diinguéne dé dh. Allez à KZbin et taper :les témoignages de Mame abdou Aziz sy dabakh sur Baye Niass et tu seras surpris
@wakhaldeug8424
@wakhaldeug8424 5 жыл бұрын
dëg rékkay dëg fall y’a niake diangue lolou conne khamo ko 😂😂Ndeysane sa serign dofoul waye ioe y’a dof
@momatbarhamepouye4358
@momatbarhamepouye4358 5 жыл бұрын
Salam salam cheikh aziz macha allah dieureufeuti zatou laahi cheokh omzr foutiyou waknani si rîhma nè monr bou fèkhé wone borom faydou dina boup aay téereme yeup toop borom faydou
@nitdafayamyarndour1689
@nitdafayamyarndour1689 5 жыл бұрын
Thiey baye
@bayejobe4204
@bayejobe4204 5 жыл бұрын
Dieredief cheikh
@mamadoukourmang2848
@mamadoukourmang2848 5 жыл бұрын
machallah BAYE MOY DEUG
@ndeyefatouwade7099
@ndeyefatouwade7099 5 жыл бұрын
Dieureudieuféé baye niass
@therenaissance7977
@therenaissance7977 5 жыл бұрын
Bayilen wakhdji te ligueyal baye si ay projet. Serigne bi gua balma bayil parparlo bi. Cheikh omar foutiyou tall souniou serigne la ndakh mame alhadji abdoula foumou degue niou toudou cheikh omar foutiyou tall dafa dane taxaw magal ko. Sa wakhdji wakhou pithe le rek. Nio bok tarikha bi naniou defar mo geune rafete wa salam 🙏
@cristano7680
@cristano7680 5 жыл бұрын
Merci aziz baye niass moléne téré néléw
@ismaelfaye4712
@ismaelfaye4712 5 жыл бұрын
Merci hey baye niass li rafetna lol bilahi yarabi
@ndiayeanta5229
@ndiayeanta5229 5 жыл бұрын
Bilahi iow rekk ladon xarr ,macha allah sunu khol seid na walahi .mais passport bi momay ray man
@babadiaw9174
@babadiaw9174 5 жыл бұрын
CHEIKH BI MACHALLA YALLA NALA YALLA FAY BILLAY GNI SAGUA SENE SERIGNE YI SAK DOUGNOU TONENETOU CHEIKH BI BBLAY KI BAYE AK DOMMOME BABALAMINE GNOKO GUARANTI
@modoucamara4708
@modoucamara4708 5 жыл бұрын
mane dal beuguena cheikh Aziz merci yalla yalla sameuko
@khoumapape8038
@khoumapape8038 5 жыл бұрын
MAACHAALAH CHEIKH BI DEGUE NAGN LA
@ndaomore4309
@ndaomore4309 4 жыл бұрын
Mancha Allah Cheikh Ibrahim Niass ❤️❤️❤️
@NIASSFBI
@NIASSFBI 5 жыл бұрын
Kén dou baye Niass
@assaneboye2356
@assaneboye2356 5 жыл бұрын
dieureudieufè baye niass
@ndeyeamyfall623
@ndeyeamyfall623 4 жыл бұрын
Thiéy Baye kéndou ioe 👑 vs êtes le détenteur de la fayda dh dra douko dinedi ❤️ Dieureudieufé Baye👍💪 Machallah Serigne bi Yallah Baye faye🙏
@absandiaye386
@absandiaye386 5 жыл бұрын
Macha alah cheikh aziz,
@omarsarr662
@omarsarr662 5 жыл бұрын
Ya bakh mathi kham dara
@cristano7680
@cristano7680 5 жыл бұрын
Tres bien aziz
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 5 жыл бұрын
Yaw machallah baye niass dinala Faye de
@talibebunjeng9470
@talibebunjeng9470 5 жыл бұрын
Walahi NIASS REEK moy Serigne sikaw - suf. Koumu nex ak koumu nakhari
@Xamuma
@Xamuma 5 жыл бұрын
Baye Niata diabaar la amone ?
@talibebunjeng9470
@talibebunjeng9470 5 жыл бұрын
@@Xamuma amal yar BAYE NIAS dou sa morom papa
@talibebunjeng9470
@talibebunjeng9470 5 жыл бұрын
@@Xamuma pourquoi cette Question
@Xamuma
@Xamuma 5 жыл бұрын
Sama bay walahi du moromoom Sur tt les plan
@Xamuma
@Xamuma 5 жыл бұрын
@@talibebunjeng9470 je veux juste savoir ?
@khew2006
@khew2006 5 жыл бұрын
Allahou Akbar
@sheikhalhagiegaye3360
@sheikhalhagiegaye3360 5 жыл бұрын
Jerejef sheikh bi contan na bilahi barke sheikh Ibrahim nyass
@maremembengue6873
@maremembengue6873 5 жыл бұрын
Yaw mom cheytane nga bou mak bayou akhmed Niass nion sonalon bay Niass mais pas kenn fenn rek ngay def
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy 5 жыл бұрын
Té nga wakh lo kham? 😂😂
@maremembengue6873
@maremembengue6873 5 жыл бұрын
@@TalibeCheikhoulKhairy demal gueusstou histoire niassen
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy 5 жыл бұрын
@@maremembengue6873 😂😂
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy 5 жыл бұрын
@@maremembengue6873 wa kay meu layé la biir: Bayou Ahmed Khalifa modone protéger Baye Niass biko niènène gni sèètané.lingay wakh mooy 1an après bi Faydou bi takké mou nèk en 1930 fèkk thila Baye warone santhi dji Medina.wirassa Cheikh Tijani bimou yor mo takhone mou wara changer ay mbir (comme qibla wou malaanou wazifa)bimouko ndieuké dèf,thila problème yi commencer avec ses frères.Talibé Mame Aladji Abdoulaye yi nio done fèkhèl Baye Niass,beu bimouy guéneu Leona niou door ko beu gagne ko momak ay talibém.té lolou Mame Khalifa Niass(Bayou Ahmed Khalifa) meunou thi wone dara,en plus que dafa beugone Baye Niass ndakh khamneu li Yalla dèfone thi mom.la preuve Baye mom leu dane gueuneu dieuflantél thi ay frèram à part S Mbaye Niass...amnagne ay photo you beuri sakh
@maremembengue6873
@maremembengue6873 5 жыл бұрын
@@TalibeCheikhoulKhairy yaw ba tay wediwoma konn donc ay mbokham nioko sonalon mais pas niene . Man tidiane tivaoune la mais dama am photo baye Niass sama nek parce que mako sop sama khôl bama guedje dzm gamou baye Niass AK mam dabakh la guiss si guenteu sa euleuk sa lagne ba may billet pour Sénégal 3 jour âpre ma dem gamou
@Ndanaan2.0
@Ndanaan2.0 5 жыл бұрын
BAYE NIASSE DAMAKO BEUG NIASSENE DAMALENA BEUG MAIS WAR NGUEN KHOLATE SEN TAXAWAY. LI MAK GNI LIGUEYONE YEPEU SEN NOUVELLE GÉNÉRATION BI GNONGUI KOY YAKH. QUAND J’ENTENDS CERTAINS PROPOS DES SOIT DISANT TALIBÉ BAYE JE ME DIS QUE VOUS ÊTES ENTRAIN DE RABAISSER SON TRAVAIL
@allaathiouathiou352
@allaathiouathiou352 5 жыл бұрын
Naka lagn ko begue yaké? Ak baane kaddu gua fi dégg bou déplacé? Niou togn la gua fayou faane lako yallah interdir? Koone sa waay yow la sa biir begue yakou mai pas biram baye bi ok merci
@Ndanaan2.0
@Ndanaan2.0 5 жыл бұрын
alla athiou athiou Bayilen sen feneu yi. Lounek nguen wakhal kO baye niasse. Ki si vidéo bi limouy wakh gnemewouko daur si kamil day doule rek.
@Ndanaan2.0
@Ndanaan2.0 5 жыл бұрын
alla athiou athiou Comment baye niasse peut traiter tous les marabouts du Sénégal de primairien ? Yaw Lolou gueum nga ni baye niasse moko wakh ? Sincèrement ? Bayilen feneu doule rek ngueni def
@allaathiouathiou352
@allaathiouathiou352 5 жыл бұрын
@@Ndanaan2.0 bagne bagne nangou sa serigne baye sii raw you diékh yeu lako raw na yothio deuxiéme walleu troixiéme mai 1er mome Baye mofa togg koumou néx koumou nahari. Démal xami yallah mo guéne ndakh fofou gua nék dofa xamé yallah bé kérok ngay déh😆😆😆 damaléne yereume sa maane wa loutax guéne sokhor bone iniane li rék nako tardél sénégal sen xol you bonne yi domérame té doumala tontoti sah!!!
@Ndanaan2.0
@Ndanaan2.0 5 жыл бұрын
alla athiou athiou Dangay feneu lawakh. Khamo tousss mounane kham Yalla. Li gueneu boneu si bakar yi moy feneu. Te yen feneu rek ngueni def. Baye niasse limou ligueyeul tarikha cheikh liguey nako ba paré
@sarrabdou2929
@sarrabdou2929 5 жыл бұрын
Ayna barhamou wama barhamou
@aminatadiouf234
@aminatadiouf234 5 жыл бұрын
DIEUREUDIEUFÉÉÉÉ BAYE NIASS WARNA DIAM ALHAMDOULILAH
@fallybadji7315
@fallybadji7315 5 жыл бұрын
Bilahy mala beug rek nakh sakh kham kham bilahy
@gorguydieye8492
@gorguydieye8492 5 жыл бұрын
Avec Ahmed khalifa dou yombe niongui thie sa guinaw
@maremembengue6873
@maremembengue6873 5 жыл бұрын
Douguene nieuwe fek nioufi
@wakhaldeug8424
@wakhaldeug8424 5 жыл бұрын
Mareme Mbengue katal sa data ndeyy Thiaga bi 😂😂😂
@maremembengue6873
@maremembengue6873 5 жыл бұрын
@@wakhaldeug8424 sa deudjeuw ndeye yaw domou thiaga nga montakh ngay khame thiaga domeram
@ousmanekane8377
@ousmanekane8377 4 жыл бұрын
Walayi dayesan dégele baye niasss Machala dara dougo wase' Macha cheikh Abdoul Aziz nadye baye niasss Machala Madine
@fatimatadiop9690
@fatimatadiop9690 5 жыл бұрын
Soyons de bons musulmans !Sama serigne ni la melle ni la melle mo ko guene .naniou bayi wakh diou Bari li yeup petrole bi ak gaz bi mo takh
@grereemifa2868
@grereemifa2868 5 жыл бұрын
Man déh layénne pur la kép kou Am zawiyaa si maodo lako royé
@TalibeCheikhoulKhairy
@TalibeCheikhoulKhairy 5 жыл бұрын
Kou am zawiya si Cheik Tijani lako royé
@wakhaldeug8424
@wakhaldeug8424 5 жыл бұрын
greree Mifa zawiya kay Lou bakh la topale feulei layenne yi mom fen rk
@FayduAuthentikTV
@FayduAuthentikTV 5 жыл бұрын
Topatol sa layenne
@mbeddmidiallo6934
@mbeddmidiallo6934 5 жыл бұрын
Légui maodo kouko nattal zawiya bamou tolok zawiya fass cheikh ahmed tidiane mom loumou done layenne dh dadone mandou yarou wayé légui layénne yima guiss wakh louléne woroul rék
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 5 жыл бұрын
Baye niass rawna niepo
@laminecidibe5667
@laminecidibe5667 5 жыл бұрын
Dierejuf baye niass aferbi lerna
@sheikhalhagiegaye3360
@sheikhalhagiegaye3360 5 жыл бұрын
Jerejef sheikh Ibrahim nyass international relationship la yore sheikh al Islam Alhadji Ibrahim nyass ALHAMDOULILAH
@cheikhouka4718
@cheikhouka4718 5 жыл бұрын
Niass niass niass niass niass ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
@ndiayemomo2004
@ndiayemomo2004 5 жыл бұрын
Thiey sama papa
@ibrahimfostino5991
@ibrahimfostino5991 4 жыл бұрын
Baye niasse Rekk
@mbayendiaye4562
@mbayendiaye4562 5 жыл бұрын
ligawakh cheikh aliou cissé cest normale talibé ak serignela meune nakowakhal louné
@amadoundiaye1711
@amadoundiaye1711 5 жыл бұрын
كل كم وأنتم بشر
@diopamadou7573
@diopamadou7573 5 жыл бұрын
Cheikh Aziz danga tardé yatal tontanté.
@moussandoa9676
@moussandoa9676 5 жыл бұрын
Go way yaw
@seydinamouhamadba2993
@seydinamouhamadba2993 5 жыл бұрын
Tontoul rekkk yaw
@wakhaldeug8424
@wakhaldeug8424 5 жыл бұрын
Diop Amadou dagen ko meuneu tontou
@adamasow9292
@adamasow9292 5 жыл бұрын
Amoulén xam xam bouko meneu tontou..yén si euskey rekk nguén di yém..gneuw lén tontou loléni khar..
@mallbelly8250
@mallbelly8250 5 жыл бұрын
Danguay doul cheikh Oumar dafa teye faydou bi si lokhom .moune diarou ko.ndakh adouna kesse la
@wakhaldeug8424
@wakhaldeug8424 5 жыл бұрын
Mall belly bayi doule
@FayduAuthentikTV
@FayduAuthentikTV 5 жыл бұрын
Mdrrrr ki mom nekhna deh
@alassanedia2787
@alassanedia2787 5 жыл бұрын
Iow mome xamo louy faydou sahk
@kheushaatv2418
@kheushaatv2418 5 жыл бұрын
No bilahi merna trop yenagi togn baye niass yen ay seytane gen rk
@jojosantal8342
@jojosantal8342 5 жыл бұрын
merci
@fityaanousidkhine5796
@fityaanousidkhine5796 5 жыл бұрын
Bayil fenn Deug nekhoul
It works #beatbox #tiktok
00:34
BeatboxJCOP
Рет қаралды 41 МЛН
СИНИЙ ИНЕЙ УЖЕ ВЫШЕЛ!❄️
01:01
DO$HIK
Рет қаралды 3,3 МЛН
She made herself an ear of corn from his marmalade candies🌽🌽🌽
00:38
Valja & Maxim Family
Рет қаралды 18 МЛН
Urgent ! Cheikh Aziz Ndiaye recadre Omar sall '' le diable, le menteur ''
15:49
Baye Niass disait : A ma mort j'aurais deux sortes de disciples
30:34
Faydatidianiya TV
Рет қаралды 19 М.
BAYE NIASS - Waxtane Thi EL Hadji Abdoulaye Niass {R.A} Bayou Cheikh AL Islam
57:22
100 саволга - 100 жавоб (1-қисм)
3:54:00
Ummatuz
Рет қаралды 1,7 МЛН