Machallah lii bettouma. un jours javais vue serigne touba et chiekh ibrahima fall et serigne saliou et chiekh bethio dans mes rêves sur un pont cetais a touba billaahi wallaahi et moi je suis tidiane wah ngir yalla rek machallah. yalla nako yalla yeureum
@mariamacisse1165 жыл бұрын
Dieuredief Thioune sa kadou rafetna machallah
@oulimatadiongue81725 жыл бұрын
ndessane
@barbienoir16225 жыл бұрын
Amiine way🙏🏽
@ndiayeamy745 жыл бұрын
Machala danga bax
@wareckndoye61125 жыл бұрын
Jfai ce mm reve walaie
@magatteka81245 жыл бұрын
Akassa dieureudieuf .il est très responsable, kadouyou rafetna
@leppmoomlawaxlurafett76165 жыл бұрын
Machallah S khadim mii de mane naw naako loool ndakh DALL GUI AK NITÉ GUI AK XAM XAM BI... yalla naleen yalla sammu te mayleen werr... Nii rekk la, yeen ñaboot gui bou leen kennn defloo lou wouték dokhinou yoon wi NDIGEULOUL SERIGNE TOUBA REKKK
@AminaAmina-nv2iv5 жыл бұрын
Masha Allah ndiabotou serigne bèthio man dé douma mourite layènne la wayé masha Allah lou thiow bari bari am nguèn yare am nguèn tèguine sèn baye yaar nalèn masha Allah, kèn dègoulèn ci bèneu wakkh bou niaw, kèn dègou lèn ci ay kheuthio kèn dègoulèn ci tésseunté bilahi am nguèn ak daal tèye nguèn boudoul dara respect bi nguèn am si sèn sokhna baye yi ab ndiangate bou rèy la ci dieulé ndakh diabarou baye loumou touti touti sa kilifa la, masha Allah yalla nallèn yalla mouthieul ci seuytaané dolli lèn soutoura aduna ak Allah hira ci sèn barké baye ak sèn liguèyou ndaye ay réffèrences nguèn bilahi, wakh sa mbakhou way dou waagni dara sisa mbakh, serigne bèthio yalla nako serigne saliou térrou térralko bèrndèlko comme nimouko ndaan défé ci kaw souf, wakhou Mala liguèyeul serigne touba rék waayé domou Adama yi don lèkeu niakam rék dougeul nako aldiana ndakh diokh ab dioulite bou khiif mou lèkeu ba soure mo euppeu nga tabakh diouniy diaakeu man dé bima nèkké xaalé nèkon sénègal don na guis ay niit di dèm Gamou cheikh bèthio pour lèkeu ba tibeu dèf si mbousse moussumako guiss waaayé kham na domam maame khadim thioune bima dernier vacance lako kham mais kou bakh té am taalibé am yaar té modeste masha Allah
@massdiopmc5 жыл бұрын
Un discours posé,discipliné , plein de sens, d’éducations machalla je ne te connaissais pas mais tu m’as ému , c’est ça qu’on appelle tout simplement un RESPONSABLE,Cheikh Bethio yalla nako yalla terou aldiana, si barkè Serigne Touba Serigne Saliou
@mrdiop79025 жыл бұрын
massdiopmc machalla
@serignembackediop17735 жыл бұрын
Fou way nèk yalla ngui fa Mohamed mongui fa serigne touba mo ngui fa mame salliou mongui fa yalla nako yalla kharé alldiana
@cheikhissa15 жыл бұрын
Serigne khadim Thioune vous avez tenu un discours responsable d’un vrai disciple Mouride . Ndigel jëffe
@lamaranadiallo84185 жыл бұрын
Wakh dji rafétna Thioune Mame BAMBA Doundel way ....
@gueyeteragna99825 жыл бұрын
GÉWËLU XAADIM billahi
@ndeyemboup42995 жыл бұрын
Géwëlu xaadim mane deh damako beugue lol tei beugue ko guiss! Machallah
@tewloumatv25145 жыл бұрын
Machallah un vrai responsable serigne khadim dieureudieuf thioune lepp rafetna
@2mvisionsenegal8845 жыл бұрын
Miinou mala deh, wayé sopp nala lol ndax kaddou gou sell gi té mourité, dal gi machalah🙏🙏❤
@Elzodhino5 жыл бұрын
Ndeysaane Serigne Khadim mii vrai goor YAllah la mashAllah am nga talibè lol dooko messa rèthiou 😍 Cheikh Bethio yalnako Suñu Borom wanalé ak Serigne Saliou thia Aldjannah Firdawsi 🙏🏾
@etiennesnciss95565 жыл бұрын
Suis catholique Je le vois très posé et intelligent
@amdyniang43645 жыл бұрын
Diadief serigne khadim
@salimatandiaye26905 жыл бұрын
Kou baakhga,yalanala yala fay sa khol
@azizndiaye76745 жыл бұрын
Franchement la communauté mouride vous êtes des références quelle discipline exemple pour tous le reste
@cheikhkhaya90345 жыл бұрын
Ndeysane wakh djii rafetna dh thioune bilae yalna diamou yague cheikh yalna yalla yokou ay lèram barke borom touba
@mamaafrica81935 жыл бұрын
Très beau même, intelligent, posé et bien éduqué
@Defunity5 жыл бұрын
Tous les filles de Cheikh Bethio que j'ai vu parler sont d'une maturité et modestie exemplaire, je le salue. Je suis Niassen mais beaucoup de respect pour ce comportement. Sénégal leup ben leu naniou dokh jam rek.
@mormbaye67305 жыл бұрын
Machalah Thioune que le bon Dieu vous protège et toute la famille de Cheikh Béthio Thioune Repose en paix serigne Cheikh
MachaALLAH YALLA n'a yégue gui woyof thioun Barké Serigne TOUBA, lép loy déf naga thi djiteul sa BOROM, teunkkou dji bdigeul. Serigne Touba nitou YALLA la, kou raggalone YALLA la, beug ko té doyloko beug Rassoulilah. Ngalla gnioune Mouride nagniou ko roy. Nagniou ragal YALLA téy rafétal. Mane déye thioune Serigne khadim Amna thi yow yakar.
@ibrahimasy53775 жыл бұрын
Cheikh béthio sa domm yi yiw nagnou yarou nagnou am nagnou talibé, raw ga gnépp
@mouhamedrassoulgueye46365 жыл бұрын
Cheikh béthio nitou aldiana la bilahi
@codoufalldieng35635 жыл бұрын
Dieureudieuf wakh dji raffettna paix à son âme et la terre sainte de touba lui soit légère amine
@laminetine3075 жыл бұрын
seringe khadim thioune yalla nala souñiou brom same taxawou la té arre la mane dé xamou mala wayé sope nala nguirr nangou ndigeull gui yaw dé khawma kan wayé yaw kou guindékou nga yaw yalla naga fy yageu
@astoundiaye56985 жыл бұрын
Ha ki beug naco waiyy machalla long vie à toi bialy mourride ndiguel nitte cou bakh daiyy ame kilyfa vraiment tué poli
@peulhbourafet44235 жыл бұрын
Machalla wakh dji rafetna ame yaare ak téguine c tun responssable bilahi
@bounabanno69615 жыл бұрын
Wakh n'ga deuggdé kii dafa yaru lool lool..... ab talibé deuggla !!! Yalla bumu yakhoulé.
@kaytabintou8065 жыл бұрын
yaw dé je te connais pas mais kouma nékh nga. ndakh sa yarr ak sa dal ak sa nitté. kou ame talibé nga franchement😍
@adamafaye71185 жыл бұрын
Machalla serigne khadim je t’adore bcp
@seydinagueye55285 жыл бұрын
Je t'adore serigne khadim tout simplement
@bayefalldiagneinfo87305 жыл бұрын
Vrai responsable nga
@khadycisse57265 жыл бұрын
Machalah Thioune mame bambi mane dale serigne khadime mi .nekhnama dafa khame wakh diou rafet te meune ko douma thiantakoun dee waye mom Machalah
@camaracamara92595 жыл бұрын
Macha Allah. Sa wakh rafétna .
@adamadia60055 жыл бұрын
Dieu reuf thioune wakhdji.rafetna cheikhbi yalla nako yalla khare aldiana
@mbayeleye23035 жыл бұрын
Serigne khadim yalla na la yalla samou nga sott sa papa aw fane kadou yi rafte na machalla amna solo yalla na léne yalla takhwo barké serigne saliou
@fatimaaidara97135 жыл бұрын
Ki waliyoula motah youcoy heuthio macha'ala ❤️😭
@marigueye56155 жыл бұрын
Wallahi c vrai merci beaucoup yalla nako yalla yeureum amine yaraby tout mes condoléances a la famille
@fallousow4245 жыл бұрын
Vraimant votre parole est respectable. Que le paradis soit son dernièr demeur
@senzanome99315 жыл бұрын
Yalla nako serigne saliou terrou wonaleko ak khadimou rassoul
@dieynabakeneme3165 жыл бұрын
Mes condoléances mon frère
@dieynabakeneme3165 жыл бұрын
Aduna amoul solo lepp dieh bo DESS Yalla tu es intelligent et DEFAR kat
@serigneidalymbacke41695 жыл бұрын
Machallah kadou yi raféttna yalla na yalla yokou léram bijahi s.touba
@salioudieng86755 жыл бұрын
Suis tidiane mais j'aime lole Cheikh bèthio barki yalla yallanako yalla yeureume si barki Serigne saliou
@antadtall41074 жыл бұрын
Serigne Mountakha Yalla naffi yagg té werr
@elhadjifaye29985 жыл бұрын
Mane dé douma thianta mes yaw môme damalla sope lole
@ndeyehenriettengom49665 жыл бұрын
Je te félicite tu as bien parlé mashallah
@serignebassiroudiop87725 жыл бұрын
Mane dh wallahi sop nala loll thi yarwi ak teguine ak dieufé ndigueul wi nga khamni monou fii bayi dileu masta wou loll thi tiss wayé sap Mouride manshallah S. Khadim
Yene bolene dokhewone loutakh gnou topoulene.amolene lolene wakh pression etat bi kesse motakh nguene changer décision.batalibeyi di tope serigne bi yene folene nekoone
@dexdexmen45255 жыл бұрын
Yaw amoo Lo wakh.bo respectewone li cheikh wakh kone dinguenko yegué khalif bi
@killumastaexestunhypocrite71865 жыл бұрын
Wa légui YALLA nak ??????🙄🤔
@ayaseye52025 жыл бұрын
serigne bi mangui diégalou bou bakh dieureudieufé serigne touba
@killumastaexestunhypocrite71865 жыл бұрын
@@ayaseye5202 Adouna bi YALLA moko mom, adouna bi YALLA moy ki ko mom, Dieuredieufé YALLA SUÑU BOROM ☝️
@fatyleye58475 жыл бұрын
Bravo à cheickh béthio il a réussi où beaucoup ont échoué l'éducation la basse de tout .
@beuguserignefallou19665 жыл бұрын
MACHALLAH yalla nala yalla defal diam s.khadime
@bambaseck625 жыл бұрын
Akassa ndigal dieufé serigne khadim yalla nalene serigne saliou teyel bopam cheikh bethio diamou serigne saliou yalla nako yalla dolly yeurmandé
@aliounefall22505 жыл бұрын
Bien dit Thioune un bon talibé dafay dieufé ndigueule
@mbayeyatt93105 жыл бұрын
Machallah Thioune watie rafétena yalla na leine yalla sam tie barkép sérigne saliou
@aminatathioune70695 жыл бұрын
Mashala khadim Thioune Naleine yalla sam Segam ay ndiabot cheikh bi ño dacc mou dem Touba Loussi yonou talibé??? Walahii Thioune gueun naala fonk barkei S Touba
@mayoronguer24985 жыл бұрын
Serigne khadim Nii nguénko défé rékla bilahi yalla na diamm yague barké borom Touba❤❤❤
@faboyeamr73335 жыл бұрын
Serigne khadime mane khamoumala mais begue nala lole si sama kholl
@abdoulahadsenesene20325 жыл бұрын
Bilay dafa am yar am talibé
@sayenabougueye81595 жыл бұрын
Doma dap deh aka kham aduna
@faboyeamr73335 жыл бұрын
Nite nité la niou wakh begue nako loole thi sama❤❤
@diopndeyendoumbediop77555 жыл бұрын
entouka kou am yare la
@bounabanno69615 жыл бұрын
Manmii dé beugnaco lool.... kii dafa deuggu lool thi Bayam ak thi Serigne Touba dafa yaru lool.... ab talibé deugla.......
@seynabouthiam41725 жыл бұрын
Je l'aime trop serigne khadim
@astouflorydaffe95615 жыл бұрын
Machalla ki dal kilifeu leu Wax j rafetna xel mi seleu na Vraiment tu es bien éduqué 🙏
@adamafaye71185 жыл бұрын
Vraiment diaboutou cheikh bii amnagnou téguine am khar machalla sene baye laa mourite djigual
@aminatathioune42995 жыл бұрын
Bilakhi
@jeanthiam73615 жыл бұрын
Merci yéné kheum serigne bî
@alkhamdoulilah5185 жыл бұрын
Serigne khadim mala beug billayi Amal jamu rek❤️
@mamycamara1555 жыл бұрын
Bilay mala beugu té gueum leu🙏🙏🙏🙏
@ndananetv90105 жыл бұрын
Akasa thioune wakhe dji rafêt na machallah
@fatysyll56435 жыл бұрын
Kou toudou khadim fo diar dieul si sa tourando dara .. khadim mo fort le serviteur du prophete machala.. serigne bamba keine dou mome
@seynabouthiam41725 жыл бұрын
Billahy
@freemanfreeman44655 жыл бұрын
Vraiment les fils de Cheikh Bethio Thione sont très éduqués mashallah
@abiesagna66225 жыл бұрын
freeman freeman Vraiment ils a bien parlé machallah.
@moramysylla32755 жыл бұрын
Amna Sólo Torop Yalla Na Ko Yalla kharrè aldianna Firdawssii Amine
@lesenegalais84555 жыл бұрын
Serigne Khadim Thioune kaddu yi rafétna amna ak talibé, yalna YALLA samou samou ndiaboot gui. Akassa Mouride!
@khadyndiayeyayefall90145 жыл бұрын
Dieureudieuf Sgne Khadim yalla naléne Serigne Saliou Mbacke takhawou thiant gui kanam rek la dieum
@salamfall6435 жыл бұрын
Ndaysane ya am talibè wayy
@abdoukhadretop2555 жыл бұрын
Macha Allah wakhdji rafetna Yallah cheikh saliou terrou si barkém
Jerejef Thioune wakh Dji rafétna. Mouride Ndiguel Paix à son âme Cheikh Béthio Thioune
@astouniang51695 жыл бұрын
Machallah thioun rafèna yalla nako yalla yeureum tè kharè ko aldiana you kaweya si barkèb serigne saliou
@morgueye50885 жыл бұрын
Dieureudieuf Thioune yawdé Nawnaala
@abounafansunited93335 жыл бұрын
Massallah khadime tioune waxji rafétnà loole
@khadimpene74595 жыл бұрын
Akaza mame khadim kadouyi amna solo lole machala
@sopserignefalloufall28325 жыл бұрын
Machallah rafetna amna solo
@kamaalfaye69375 жыл бұрын
Talibés ndiguel cheikh Bethio serigne Saliou moko wo si wetame fidélité bassi bir bamel
@mbowabou50205 жыл бұрын
Serigne Khadim thioune yalla ngafii yague lol té wér talibé yii bouniou faténé koufii nékal serigne touba moie serigne touba serign mountakha mofii nékal serign bii lou wakh mo gueun loum wakhoul té mourit ndingueul kouko tégui nak wédinga yone wi wa salam
@elhadjikandji26745 жыл бұрын
am na solo lorr serigne khadim thioun machall
@ndoumbendiaye74405 жыл бұрын
dieureudieuf yallana yalla yagal takhawaybi kadouyi rafetna machallah
@amdymf46425 жыл бұрын
macheallah s.khadim diaradieuf s.mountakha mbacke bassirou yallanafi yegue te wer
@weuzagayy77735 жыл бұрын
ALLAH khareeko ALDIANA aminn
@santeserignetouba27085 жыл бұрын
Yalla nalén Serigne Touba Takhawou Barcké KHASSIDA yui 🤲🏼 Serigne mom daman kana mam man guinawam😍
@daoudawade97715 жыл бұрын
yalla nako yalla yeureum thioune kadou yi rafétna
@mbenewade13665 жыл бұрын
Machallah serigne Khadim Thioune Faxass kadouyi amna solo lol🙏
@magettembaye8205 жыл бұрын
Lou wer nga wakh serigne mountakha moy serigne touba
@mbackemamesaliou60745 жыл бұрын
Wakhdi raftna merci
@morfamadiome17135 жыл бұрын
Dieureudieuf thioune
@pathedione85785 жыл бұрын
Thioune yalla na yalla defal diam ak soutera ak tawfeth
@mamadoudieye22935 жыл бұрын
Vraiment poli
@aminaseck7665 жыл бұрын
Machallah tu parles très bien
@amantousambe67965 жыл бұрын
Serigne Bethio talibè la wone yague Na dieufé Digual Walay Médinatoul Salam Ak Touba dayeu Béneu fousi dém Serigne Saliou mougui fa🙏🙏 nioune dé Santeu Naniou t daniouy sakh di liguéyal Serigne Touba Ba Faw Donite ay Thiantacoune Ba Faw Barkép Serigne Saliou 🙏🙏
@ndeyeamy39585 жыл бұрын
Machalah amna solo yalna yallah may len xolou mougne
@ibouthiam32745 жыл бұрын
Machallah kadou yii rafettna yalla na yalla sam la same diabott gii
@modoumbaye27975 жыл бұрын
Machala amna solo
@khadimleye57385 жыл бұрын
Dieureudieuf Serigne khadim
@assaneniang9125 жыл бұрын
Bien dit 🖤🙏🏿
@panogayembaye56884 жыл бұрын
Machalla Dieuwrine
@Ndiaya6585 жыл бұрын
Siguil nga niou Thioune Serigne Khadim yalla na nga fi yagu té wéér
@labsolugueye90165 жыл бұрын
Serign khadim Lo mii Daii kouma Naixla Billahi......Mai serign Saliou Thioun ausi Yallah Nakofii Yallah Yagall lol Taii wairr Ba Lii cheikh Bethio Thioun Natt Laippeu Mou Yaigalaikoko thi Diamm Ba Dara Dara Dara Bagnko Faxasss Tall thi barcke serign Saliou Mbacke ......Man Daii cheikh Titaloumoko Famou Dieumm waiteull Guii kasai lay Dioy Barcke Borom Touba 😭😭😭😭
@papemandiayetv92765 жыл бұрын
Je suis tidiane mes ki deugue rk la wakh ndigeul mo am solo